Рет қаралды 5,521
#foqqati #bigdatx #ogkajooroi #taalbi
Streamez ici: onerpm.link/og...
----------------
Artistes: Big Dat X, Taal Bi
Titre : Fòqqati
Prod : CrazycoolBeats
Enregistrement: Das Records
Mix: Teacher
Master: Sirtam
Video: Nittu Deugg
Production exécutive: MeloMusic Ent. & Chambre 9
Contacts: bigdatx247@gmail.com
---------
Réseaux Sociaux:
X @BigDatX2 : x.com/bigdatx2...
Facebook @Big dat X : / big-dat-x-marxabane-te...
Instagram @bigdatx: www.instagram....
Tiktok @bigdatx : www.tiktok.com...
--------
Lyrics
Geenu bëy a ngi fi dëkk di yëngatu dakkul weñ te muurul taat
Mélomane yi K.O si monotonie dawal yee niroo ni gaynde yu deggul jat
Mani dem lay def man la barigo si mbartal
Ma la gëna dee mooy wax bi si gattal
Mënu ñuma teye sama aay a len tiitël
Highlander bi ci zik bee gentle
Armel neew na kuy dajje k man te xalaato sa bàmmeel
Niveau bu faible comme kuni jakk rek daanu ndax xamnga ni couleur u bas mel
Level bima nekk dafa kawe c’est normal ma wàcce niveau bi mën a tolloo g ñoom
Ma k ñoom comme guerre tubaab ak Lat Dior
Y a pas photo ni mëxxdoom ak magnum
Refrain
Ñun dañu fòqqati si liñu moom
Newu ñu si ay négocier
OG KajooRoi bi lay doon
Ñooy rëbb si game bi ne ay sorcier
Boy mangi ak business yu woor
Biñ koy tammali lijëntiwoo
Do si nelaw te bidëntiwoo
Du ñu seral comme bandit yu business si do
Ey fòqqati fòqqati dañu fòqqati linga yor
Linjaa bi teew nga xoole ñu fòqqati linga yor
Ey fòqqati dañu fòqqati linga yor
Linjaa bi teew nga xoole ñu fòqqati linga yor
Yëfu jinne la nar
Cloch’art Taal joxoñal fima joge daa tar
Waxumala lima daan daj
feebar si rap sama dereet la kuma mën faj
Matoo do indi mental
Lima jota def pour Thies lepp a monumental
Finga jaar kufa jaar taxx ban
Fima jaar kufa jaar dee ba ñu dagg say tank
Ñima xiif a ma xoos
Luñ fi cotiser ma coop ko
Lu diis a ma topp
Nee ko si lii dama dof
Liggéey ba si biir archive yi nga gis sama tof
Yëf u domeram tigi
Leegi bayyi na pic yi
Damay dëpp carte gi
Job ba trinw am devise
Même buñu fayee lampe yi duma tere dox ñibbi
Refrain
Ñun dañu fòqqati si liñu moom
Newu ñu si ay négocier
OG KajooRoi bi lay doon
Ñooy rëbb si game bi ne ay sorcier
Boy mangi ak business yu woor
Biñ koy tammali lijëntiwoo
Do si nelaw te bidëntiwoo
Du ñu seral comme bandit yu business si do
Ey fòqqati fòqqati dañu fòqqati linga yor
Linjaa bi teew nga xoole ñu fòqqati linga yor
Ey fòqqati dañu fòqqati linga yor
Linjaa bi teew nga xoole ñu fòqqati linga yor
Yeah fuma duggu ba genn ku duggu da fay des
Bëgg nga ma genn gennema dey laaj cash
Reerato fenn bandit bi ngay laajte
Dootoko lakate fenn kuddu bi makoy res
Yow lotta mercy underground don’t fuck with da rap God
Ya better know who di big boss
Polyvalent untouchable si rap
Facilité hit mën nako def si beatbox
Yeah ànd ak Big Dat dila lem
Boy laaj ndax dina dem damalay ree
Mbedd clochard lama def
Mais real laay doon ak foma mëna fekk
Siiw weesuna sama rêve ndax lima bëgg a def yepp damakoy def
Gën len yewwu ni subateel pare pour tasaare Senegal ak monde entier
Mënu ñu fi bind ba bind fi luma bindul
Du ñu romb li sama bic xoos
Mënu ñu fi dige ba dige fi luma dundul
Job nokk sama biir poche
Ñi ñi ña ña king men i’m just rap god
Show n proof we update we relevant même mimer dey dope
Refrain
Ñun dañu fòqqati si liñu moom
Newu ñu si ay négocier
OG KajooRoi bi lay doon
Ñooy rëbb si game bi ne ay sorcier
Boy mangi ak business yu woor
Biñ koy tammali lijëntiwoo
Do si nelaw te bidëntiwoo
Du ñu seral comme bandit yu business si do
Ey fòqqati fòqqati dañu fòqqati linga yor
Linjaa bi teew nga xoole ñu fòqqati linga yor
Ey fòqqati dañu fòqqati linga yor
Linjaa bi teew nga xoole ñu fòqqati linga yor