Bilahi Tapha Tine day dane Balla Gaye 2! La colère noire de Selbé Ndom déni par Balla "sam mbër lawo

  Рет қаралды 138,545

Dakar live

Dakar live

Күн бұрын

Пікірлер: 115
@MamediarraDieme-lk2kk
@MamediarraDieme-lk2kk 9 ай бұрын
Kou guem nii balla gaye day dane tapha tine rk may ma ❤❤
@ibrahimafall9522
@ibrahimafall9522 9 ай бұрын
Lima djaxaal moye balla amatoul dolé lolou rék momasi djaxaal 😂😂
@Ramapoulo
@Ramapoulo 9 ай бұрын
Inchallah❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@HouleyDiew
@HouleyDiew 9 ай бұрын
Yalna yalla may balla gaye ll dame amine
@5555-m6p
@5555-m6p 7 ай бұрын
Bilahi wallah talahi balla gaye daye dan tapha tine bilahi guiss nako bo yague
@SeyeMamadou-h9o
@SeyeMamadou-h9o 6 ай бұрын
Man dei makoy degeul nakh giss n'a balla si borou téne Mouy may nite gni ndokh
@alioundour41
@alioundour41 9 ай бұрын
Yén gnép dénguén Di nakhé rek fi yalla mofi nék nélén sén yay AK sey papa rek gnanal walahi doyena ❤❤❤❤
@MamediarraDieme-lk2kk
@MamediarraDieme-lk2kk 9 ай бұрын
Kou guem nii Balla gaye day dane tapha tine rk lalal ❤❤
@assanendiaye5640
@assanendiaye5640 9 ай бұрын
Yow dongou 😂😂😂
@AminataDIOUF-ez8kd
@AminataDIOUF-ez8kd 9 ай бұрын
​@@assanendiaye5640balla dinako dane dh inchallah
@abouabouabou-ue1kp
@abouabouabou-ue1kp 9 ай бұрын
Balla dakay batré Wat dé Lou lér lala wakh
@papeamadouseydi967
@papeamadouseydi967 8 ай бұрын
Maman selbe yallah na ko yallah defal diam ak soutoura
@drame7807
@drame7807 9 ай бұрын
Adji supporter balla gaye la adji kon tan na si yaw❤❤
@abouomardiollo
@abouomardiollo 9 ай бұрын
Selbé dnom mounoul darra walahi bilahi kou d'accord lalal jeme
@Diagne-ek7fc
@Diagne-ek7fc 9 ай бұрын
Boule wakhe lolou nioune les fans de balle gaye meusounion tite si tapha tine mon
@suwaibouhydara
@suwaibouhydara 6 ай бұрын
from Gambia ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@Enfant_béni_7
@Enfant_béni_7 9 ай бұрын
TU RESSEMBLES TROP À MA MAMAN 💞❤️ motax douma BEGEU ngay déf lounou lay saga Wala ngay def Lou HARAM nak SAMA YAAY LALAY XOLÉ BILAHI WALAHI té DAMAKO BEGEU BA GEUMÉ WOUMAKO MOTAX NONOU LALA BEGUÉ BILAHI WALAHI mais wax DEGEU bou dioté damalakoy wax YAAY BOY PASK YAK MOM TÉK TÉK MOTAX SALBÉ NDOME LAKOY WOWÉ C'EST TA SŒUR JUMELLE ❤❤
@fodecisse1564
@fodecisse1564 9 ай бұрын
Yalna sougn borom goudal fanam
@Enfant_béni_7
@Enfant_béni_7 9 ай бұрын
@@fodecisse1564 ALLAHOUMA AMINE WAAY YA BAKH BILAHI
@aidadiack8594
@aidadiack8594 9 ай бұрын
Seytané mo bari dolé rek mes balla sa nitt la❤
@ThiernoDiop-ei2ht
@ThiernoDiop-ei2ht 9 ай бұрын
Bayi len diambour bi dama na set rek sou wakhe Lou len arancewoul rek nguen nan khamoul dara eumeu bi mom rek mo demoul var set rek lay def machallah maman salbe ❤❤
@PapaNirre
@PapaNirre 9 ай бұрын
Ki daye douul rekk Di watte si yalla
@karintonemendy2609
@karintonemendy2609 9 ай бұрын
Guayii bayiléne di sagua Yayou dianbourr
@NdourPapendour
@NdourPapendour 9 ай бұрын
Surtout ça
@mariesalomon3375
@mariesalomon3375 9 ай бұрын
Mande mangui niane tapha ame dame boulere inchalah
@papegueye9665
@papegueye9665 8 ай бұрын
Li ilaha illala Molay laque bilahi dagay fén rékkk
@amadousow8717
@amadousow8717 9 ай бұрын
Ki esceque wère ne mounane yalla ye kèssè tè pètâwe àràme kou gnémé yalla moye sèlbè ndong
@NdeyemarieFall-db5wx
@NdeyemarieFall-db5wx 9 ай бұрын
😅Sabel li nga sante NDOM mettit nama bly😢warouniou wone bokkou sante dh BALLA rk ❤❤❤❤❤❤
@PapemadiorNdiaye-g9z
@PapemadiorNdiaye-g9z 9 ай бұрын
Dieu seul sait le vainqueur du 21 juillet.
@ibrahimacisse4474
@ibrahimacisse4474 9 ай бұрын
Yeun Waa dakar live yeunaa meunaa doull fan’laa sounou Yaye Selbé wakhé nei Tapha Tine dayy dane Balla Gaye ?? Bayillén sén titre you bonn yi guéndi deff tchi derou jambourr bi merde wayy
@moulayefall-f8k
@moulayefall-f8k 9 ай бұрын
Ma challah yay boy❤
@ahmadoudiop5016
@ahmadoudiop5016 9 ай бұрын
Respecté wolen sen yayi motakh nguen di sagua yayou diambour
@OussamaBa-ho7mk
@OussamaBa-ho7mk 9 ай бұрын
goudel fane rék inchallah ❤
@mamadouniang261
@mamadouniang261 9 ай бұрын
Bayil doul mère domeram ji
@ngagnendao9429
@ngagnendao9429 8 ай бұрын
Sélbé ana karim wade 5 ème président
@modoudiop7841
@modoudiop7841 9 ай бұрын
AIMNE 🤲🤲
@YoussoufKeita-vf5er
@YoussoufKeita-vf5er 9 ай бұрын
Tout le monde connait ca c'est pas la peine de dire ca que Tapha Tine va battre Balla Gaye
@oustazahmedfall6478
@oustazahmedfall6478 8 ай бұрын
Vive tapha tine
@Seydoudoucoure-dj5zg
@Seydoudoucoure-dj5zg 9 ай бұрын
Day fën rek yalla mofi nekh
@oustazahmedfall6478
@oustazahmedfall6478 8 ай бұрын
Tapha tine mo meune balla gaye
@matarndiaye3496
@matarndiaye3496 9 ай бұрын
Inchallah Tapha tine dina daure balla gaye mou danou❤❤❤
@diaaammmouuuurekkkkkkk
@diaaammmouuuurekkkkkkk 9 ай бұрын
Fèn nga dé malako wakh
@Rassoul__Moustapha07
@Rassoul__Moustapha07 9 ай бұрын
lolou la guiss dé fr
@PapaNirre
@PapaNirre 9 ай бұрын
Meunoul nekk salbel day doull rekk balla Moy kiye d'âne tapha tine😂😂😂😂😂
@seydoudiop4870
@seydoudiop4870 9 ай бұрын
Selbe tu es belle teh bakh meune sa nite
@diaaammmouuuurekkkkkkk
@diaaammmouuuurekkkkkkk 9 ай бұрын
Selbé lolou waroul takh nga bayi balla mais est ce que nékoul woon ak kénèn
@fayematy8606
@fayematy8606 9 ай бұрын
Sélbe svp bayil waate
@mbayesene-c6i
@mbayesene-c6i 7 ай бұрын
Feen keessseee leu khaamou ci darra loumou neekh tamiit nganee diiw mooy daan aay waakh leu rek
@babacarba-ud4yr
@babacarba-ud4yr 9 ай бұрын
Ki doul rekk lay deff dioulitte dou gueum liiii seytane la
@eloumboup5767
@eloumboup5767 9 ай бұрын
Bilay ya beuri wakh on s’en fiche sa diganeter ak sa papa ak sa d wou mame
@Jamil-b9k
@Jamil-b9k 9 ай бұрын
Selbe ca kaw j ai plus confiance en balla mounoutoul 🤳
@ModouDiene-if3fn
@ModouDiene-if3fn 9 ай бұрын
Fenne bakhoul fann la selbe wakhener tapha tine daye d'Anne balla
@AmadouSow-jl1gu
@AmadouSow-jl1gu 9 ай бұрын
Sèlbè ndom bayil serigne touba tègua wãkhe sãye wãkhe bamba si diner le nèkone pètãwe dafa ãrãme
@ahmadoudiop5016
@ahmadoudiop5016 9 ай бұрын
Yow dagua eupeulé selbé si Serigne Touba et pourtant mougui wate si yalla sunu borom té waxossi mayal nite yi diam way akhh
@AmadouSow-jl1gu
@AmadouSow-jl1gu 9 ай бұрын
@@ahmadoudiop5016 ki limouye dèf lislame dako sipe pètawe dafa ãrãme
@chinousarr2105
@chinousarr2105 9 ай бұрын
yow salbe khana geumo yalla bayile doule actuelle yalla rek mo khame kouye daan
@Defunity
@Defunity 9 ай бұрын
N'importe quoi... Comment peut-on faire tout ce temps d'antenne pour des bobards pareil ???
@modoudiop7841
@modoudiop7841 9 ай бұрын
😱😱😱👂❤
@Enfant_béni_7
@Enfant_béni_7 9 ай бұрын
SALBÉ SAY WAX BO YORÉ PÉTAAW GUÉNÉ SI YALLA SWT, AK YA RASSOULOULLAHI ASAWS AK SERIGNE TOUBA nak niom diné ak lou séleu Lanou xame PETAAW DAFA XARAM
@ahmadoudiop5016
@ahmadoudiop5016 9 ай бұрын
Waw lolu môme dou yone
@ndiayebayegalass9495
@ndiayebayegalass9495 9 ай бұрын
Degua la❤
@SeyeMamadou-h9o
@SeyeMamadou-h9o 6 ай бұрын
Fi Mara boufi wakh nitafa tine d'ay dane meu fén lo leu niou yalla may kham kham doléne dégeu si Dara degeur ngénn fite loll té niémé yalla
@YayaNdiaye-lr2ts
@YayaNdiaye-lr2ts 9 ай бұрын
❤❤❤❤❤
@PapaMbow-fh8kv
@PapaMbow-fh8kv 9 ай бұрын
Balla guaye rk
@ndiayebayegalass9495
@ndiayebayegalass9495 9 ай бұрын
Ki dafa fane
@bayefall51
@bayefall51 9 ай бұрын
Selbe ndom bayil feen yaw dembou rek.nga fi wakh ni eumeu sene dafay danou si ay feni kesee
@girasene7223
@girasene7223 9 ай бұрын
Wakhoul lolou bayil sokhor
@Domou_Deukk_Bi
@Domou_Deukk_Bi 9 ай бұрын
Flash lén sama commentaire
@dioufpapndiaga3556
@dioufpapndiaga3556 9 ай бұрын
Bayil doul wakhoné eumeu day d'âne eumeu yorna diassi nga wakh
@NdiagneNdiaye-wn5ts
@NdiagneNdiaye-wn5ts 9 ай бұрын
Selbé mack nga, bayil féne
@abdoulsert6585
@abdoulsert6585 8 ай бұрын
Daye doule rek
@Domou_Deukk_Bi
@Domou_Deukk_Bi 9 ай бұрын
Oh Balla j'ai remarqué que meunoull entretenir relation
@astoufall2795
@astoufall2795 9 ай бұрын
Bilahi d’où lolou sénégal da ngay dem ba do kham Kạn ngay guem famille double laissse la yereum Bilahi
@AminataDIOUF-ez8kd
@AminataDIOUF-ez8kd 9 ай бұрын
Bilahi wakh gua leep ​@@astoufall2795
@trace-infos2a846
@trace-infos2a846 9 ай бұрын
Bilahi doul rek lay def. Kou hame Balla gaye hamni nit kou bakh la
@Domou_Deukk_Bi
@Domou_Deukk_Bi 9 ай бұрын
@@trace-infos2a846 yaw kou deug sa ndeye nga doungene nangou deug jamis domou hadj bi
@Domou_Deukk_Bi
@Domou_Deukk_Bi 9 ай бұрын
@@astoufall2795 mane je ne parle pas dans le cadre de serigne mais une relation sociale... balla gnikoy ngagne dafa beuri téh nieup meunouniouko togna ndo... nagnou waxanté deug
@HerveBasse-in1lv
@HerveBasse-in1lv 9 ай бұрын
Saint valentin dafa leer
@diaaammmouuuurekkkkkkk
@diaaammmouuuurekkkkkkk 9 ай бұрын
Salbé balla dèfoula dara nak boul took ba balla amme problem si lamb nga beug ko wédié.boufèkè lingay wakh deug la si balla thi beug bingako beug waroko dieul
@Enfant_béni_7
@Enfant_béni_7 9 ай бұрын
BILAHI WALAHI WAXATIKO DÉ
@ndiayebayegalass9495
@ndiayebayegalass9495 9 ай бұрын
Sa touba day fane
@NdiagneNdiaye-wn5ts
@NdiagneNdiaye-wn5ts 9 ай бұрын
Billahi wallahi meunoulo toth bééne quartier à plus forte raison toth rééw
@ZizaBourg
@ZizaBourg 9 ай бұрын
Phiraona bayil fen
@omarnjie2023
@omarnjie2023 9 ай бұрын
VAR is waiting
@papegueye9665
@papegueye9665 8 ай бұрын
Khaliss rékk la beugue ki weroul mentalement
@ndiayebayegalass9495
@ndiayebayegalass9495 9 ай бұрын
Sa touba khamoul dada😂
@GotteSene
@GotteSene 9 ай бұрын
22:16
@mamecheikhniang4876
@mamecheikhniang4876 9 ай бұрын
Daye doule
@AbdoulayeBarry-kf3vx
@AbdoulayeBarry-kf3vx 9 ай бұрын
Eumeu kou zon la ngembo ak Lou vert
@papadiom9260
@papadiom9260 9 ай бұрын
Ak lou bleu !
@AbdouBassNdiaye-s6z
@AbdouBassNdiaye-s6z 9 ай бұрын
Amna lou wékh nak
@PapendeneMbodj
@PapendeneMbodj 9 ай бұрын
Bayilén yak combat diambour li bakar la
@MameboussoDiakhate-nt9zm
@MameboussoDiakhate-nt9zm 9 ай бұрын
Bayil doule
@GalleBa
@GalleBa 7 ай бұрын
C'est pas vers arrêter de matire
@diacheikh2411
@diacheikh2411 9 ай бұрын
Ragalall yalla
@DiarraCamara-o1s
@DiarraCamara-o1s 9 ай бұрын
Sélbé koumou wakh Moy dan kokoy danou
@saliougaye7721
@saliougaye7721 9 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@Diouf-chroniqueur-Lamb-Lutte
@Diouf-chroniqueur-Lamb-Lutte 9 ай бұрын
No balla d'où diap niteum je comprends pa il a toujours des problème avec ces amis
@MilkMilo-qr5uc
@MilkMilo-qr5uc 9 ай бұрын
Même bouko sétt kat waxoul lolu xalé bouy doga dioud sakh xamna tapha tine bou fébarone sakh balla mi dou moy dane tapha tine il faut aussi arrêter de se voiler la face tapha tine bane wayadi wala bane gnak fayda mo wara néke si mom bay bayi balla di ame si mom sakh reupp 🙄
@Rassoul__Moustapha07
@Rassoul__Moustapha07 9 ай бұрын
Billahi fr Dafa yom torop
@abdoulamadouba-qu6xk
@abdoulamadouba-qu6xk 9 ай бұрын
Selbe dangay doullllllllllll
@SaliouDiallo-ov8dl
@SaliouDiallo-ov8dl 9 ай бұрын
Doudeugue
@houssngth2905
@houssngth2905 9 ай бұрын
Mofi wakhone sa thies moy dane day doul rék khamoul loumou agnè
@papendiaye7334
@papendiaye7334 9 ай бұрын
Meusso ko wakh yaw momou yay doule, et je te défie de sortir la vidéo... Fi yalla rék mo kham liy khéw wayé togn bakhoul wakhlo lén ko loumou wakh
@papandenediarra4784
@papandenediarra4784 9 ай бұрын
fenne rek dan si dalle rek
@abdoufall3831
@abdoufall3831 9 ай бұрын
Bayel fen dagay dul
@SerigneDieng-zw2sd
@SerigneDieng-zw2sd 9 ай бұрын
Salbe day doull rek
@AbdouBassNdiaye-s6z
@AbdouBassNdiaye-s6z 9 ай бұрын
Sa way ki mate nala yay amal respect li dara diarou ko
@ThiernoDiop-ei2ht
@ThiernoDiop-ei2ht 9 ай бұрын
Bayi len diambour bi dama na set rek sou wakhe Lou len arancewoul rek nguen nan khamoul dara eumeu bi mom rek mo demoul var set rek lay def machallah maman salbe ❤❤
@AmsaGaye-fz3cl
@AmsaGaye-fz3cl 9 ай бұрын
❤❤❤
🔴DIRECT DERNIERE FACE-2-FACE TRIPLEX AMA BALDE VS FRANC
Fadam2 expert de la lutte sénégalaise
Рет қаралды 1,7 М.
When you have a very capricious child 😂😘👍
00:16
Like Asiya
Рет қаралды 18 МЛН
Beat Ronaldo, Win $1,000,000
22:45
MrBeast
Рет қаралды 158 МЛН
黑天使只对C罗有感觉#short #angel #clown
00:39
Super Beauty team
Рет қаралды 36 МЛН
The importance of tawheed and  staying away from shirk - Ustadh Abu Salma
1:06:15
Masjid Salaam Mutoon Lessons
Рет қаралды 1,6 М.
BALLA GAYE 2 VS TAPHA TINE : UN AFFRONTEMENT À COUPER LE SOUFFLE !
26:14