«Bimou Kay Dougeul Si Nek Bi Guiss Nako Dafko…» Diary Sow V!olé Et Tué€ Un Témoin Raconte Les Faits

  Рет қаралды 268,824

People 221 TV

People 221 TV

Күн бұрын

Пікірлер: 298
@People221sn
@People221sn Ай бұрын
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
@lemzokonate4950
@lemzokonate4950 Ай бұрын
Li wara am day am, c’est le destin. Toutefois, deukk bi woratoul et la responsabilité des parents est engagé. Wakhouma teudd sans connaître où se trouve son enfant mais goudi, il faut éviter que les enfants sortent mouy fête ou pas. Même pour dém boutique wala boulangerie, âpre timiss mom bou bèn khalé nekk hors de la maison s’il y’a des choses à régler dehors na magg guèn c’est plus sûr parce que les prédateurs sont partout même dans les maisons wakhoumala dans le quartier. Wassalam.
@onlygood1114
@onlygood1114 Ай бұрын
Bilahi deugla
@FatouNdao-xx4jn
@FatouNdao-xx4jn Ай бұрын
Lemeo merci mais gniy critiquer sa maman fou heur bii laniouko wara wax yed yeureume moko gueune
@MaimounaDieng-fz5hr
@MaimounaDieng-fz5hr Ай бұрын
Tous les parents doivent être vigilants et constater à chaque fois la présence et l'absence des enfants.les enfants ne doivent pas sortir la nuit.on doit les accompagner pendant les déplacements 🎉🎉
@Ftymaa
@Ftymaa Ай бұрын
Dmrm djiou tiim khalei diko sakkou yallah ngako réthiou
@alioubadiane6704
@alioubadiane6704 Ай бұрын
Merci
@AffiNiang
@AffiNiang Ай бұрын
Restée très vigilant ne faites confiance à personne garder vos enfants très près de vous ne les laisse pas traîné dans les rues où ailleurs même pas accompagné leurs amis ou qui que ce soit le monde que nous vivons n’a même pas la sécurité qu’il faut donc rester très vigilant
@astoundiayekebekebe1135
@astoundiayekebekebe1135 Ай бұрын
Ngir yalla nagnou arr khaleyii niongui lenn Di rayy dilen sakkou lii bonne naa 😭😭😭😭
@cheikhsadiboutoure1909
@cheikhsadiboutoure1909 Ай бұрын
Au temps nos parents ferme la porte après que nous aurions couchés. Maintenant les parents disent au enfants fermer fermer la porte si vous couchez.
@inconnu90000
@inconnu90000 Ай бұрын
Bilahi 😢 Tecc sa bountou après timiss! Gooryi si bopam nio matoul kilifeu
@cheikhsadiboutoure1909
@cheikhsadiboutoure1909 Ай бұрын
@inconnu90000 yemena dougnou ko nangou mais parent yi dagnou demissione
@RamatoulayeDiedhiou-xj5gq
@RamatoulayeDiedhiou-xj5gq Ай бұрын
Wakhatiko tayal 22h dagay guiss kou tok teudeu yoni domam dou yone khalé 20h na rer 21h mou dem teudeu comme élève là mm boudoul élève khalé da wara téla teudeu fête yi guir yalla parent delen yobou di begueul sen dom yi wayé legui khalé yi gnoy demal sen bop parent legui yi tamite war nagn khalate sen bop
@cheikhsadiboutoure1909
@cheikhsadiboutoure1909 Ай бұрын
@@RamatoulayeDiedhiou-xj5gq war nagnou diokh sougnouy domm lou eup lignou sougnou parent yi diokh vraiment. Parceque adouna Day guena bone rek
@aidasamb7541
@aidasamb7541 Ай бұрын
Goor modane teuthie bounetou keureum Mai’s beugeu seuf lep jighen ji c’est irresponsable la maman dinguako yeureum ndah yoor ay Sekh dafa meti Mai’s jamais ma teudeu mane sans samay dom teudeu fete ak lep ci yam
@nourradam6391
@nourradam6391 Ай бұрын
Lima gana mettie moy gisso sadom apre nga ted nelaw Eh man douma deflolou mukkou damai worr dekki bi yep😢
@adjasaliou8309
@adjasaliou8309 Ай бұрын
Kone yaw diapp ngua lolou en faite lolou la xell meune ta nangou
@khadidiatousimal3413
@khadidiatousimal3413 Ай бұрын
Bima dégué mou wakh lolou dama rouss en tant que yaye
@ndieneka7938
@ndieneka7938 Ай бұрын
Yaw nio yame xalate papa dji tamite nane co teudeule ba suba te khamo sa dom thi louniou nek
@nourradam6391
@nourradam6391 Ай бұрын
@@khadidiatousimal3413 Billahi diakhal nama lol🥺
@maimounatoure3693
@maimounatoure3693 Ай бұрын
Lolou moma guena meti.yaye dji dafa irresponsable
@MakhadyDmwm233h
@MakhadyDmwm233h Ай бұрын
23ans Teh douma guenn Goudi kholate lennn niguennn diii yareiii 😭Yalna agaleh ndawam aldjana 🤲🏾
@Ndeye-v2p
@Ndeye-v2p Ай бұрын
Vraiment
@faustinomillogo8316
@faustinomillogo8316 Ай бұрын
Mais c'est la fête c'est normal 31 tout le monde sort pour spéculer les feux d'artifice et être avec ces amis
@BoussoGaye-c2k
@BoussoGaye-c2k Ай бұрын
آمين يا رب العالمين آمين يا رب العباد
@Sabrun-jamil
@Sabrun-jamil Ай бұрын
Il faut avoir a l’esprit que ces genres de drame ont lieu a keur massar et environs chaque le 31 Decembre. Car quand certains sont concentrés dans des festivités, les malfaiteurs eux attendent ce jour avec impatience pour commettre des atrocités. Nagn ci bayyi xel bou baax🙏 qu’Allah place ce bel ame parmi les enfants au paradis avec le prophète Ibrahim aleyhis salam🙏
@JosephineCamara-qu1gt
@JosephineCamara-qu1gt Ай бұрын
Teyelene séné dôme parce que khaleyi warougno Guen goudi surtout à cet âge massa yallah nako yallah yereum
@MorCisse-p1g
@MorCisse-p1g Ай бұрын
Guir yalla na Yonne déf ligueyeum svp li méty na trop 😭😭😭
@AminataDramé-t5r
@AminataDramé-t5r Ай бұрын
veillons sur nos progénitures bilay dom dafa sakh si khol do bgu louko meti mais il faut savoir etre ferme avc eux . Mane mi le 31dec ma fille de 12ans a pleuré falewoumako parce qu'elle voulait sortir avc ses copines.massa a cette maman dioyna 😢je compatis
@inconnu90000
@inconnu90000 Ай бұрын
Yaral bou bakh ! Bo bagnee mou dioyloleu euleuk ! Bayiko mou dioy ba dioy deret ! Elle comprendra plus tard quand elle sera maman à son tour 😢
@abyba5966
@abyba5966 Ай бұрын
Ndeysane j'imagine la douleur k ressen ses parents ndeysane dom dafa sakh si khol yana motali ndawame aldjana yalla May kholou mougne sa famille surtout sa maman et k justice soi faite li dafa yomb trop di ray rek melni kou yor bayima dou yague ngua guisko you libereko c trop facil
@AminataDramé-t5r
@AminataDramé-t5r Ай бұрын
@@inconnu90000 bilay khamna si dara ma maman a tjrs été ainsi avc nous animou tay on est devenue ce qu'on est aujourd'hui.
@saidoembalo-m7q
@saidoembalo-m7q Ай бұрын
بارك الله فيك وجزاك الله خيرا جذاء
@YoussoufKeita-m4r
@YoussoufKeita-m4r Ай бұрын
Ndeyssan bay Péne wakhonako: pédophiles yangui souniou bir nagniou bayi khél thi gonéyileé. Yalna motali ndawam thi Aldiana. Nallén Yallah may kholou mougne ( parents ). Amine ya Rabi.
@malickndiayd3931
@malickndiayd3931 Ай бұрын
Lii kouko def Ray rekk lagn la wara def
@Delphine-bl1ch
@Delphine-bl1ch Ай бұрын
Bilay li c'est inexplicable. Pour il ne l'a pas fait à sa propre fille ?
@Ftymaa
@Ftymaa Ай бұрын
Kassé nopalou genre yi gno yakk société bi domou kharam leuh
@DiagneFall-g4c
@DiagneFall-g4c Ай бұрын
Yalla Na ko yalla yeureul amiine Y'a Rabby 😢😢😢😢
@yandediop9697
@yandediop9697 Ай бұрын
D'après moi, il faut vérifier vos enfants, peut être ce n'est pas la première fois, avec vos enfants de votre quartier il faut emmener tous vos enfants en consultation gynécologie c'est plus sûre, il peut les menacer les autres
@kionking-i9k
@kionking-i9k Ай бұрын
Il faut savoir on sont vos enfants à chaque minutes
@AisatouWade-b5m
@AisatouWade-b5m Ай бұрын
Diabote day niaw diorte
@elzodieng8067
@elzodieng8067 Ай бұрын
Très bien
@HelenePouye-fk5em
@HelenePouye-fk5em Ай бұрын
Très bien dit
@NdiayeMamemarame-r6w
@NdiayeMamemarame-r6w Ай бұрын
Blh mane dh sama yaye dafay wakh dama doff ms deuk by lègui mo doy war
@Sweetyberry12
@Sweetyberry12 Ай бұрын
Keerok 31 sama rakk bima magguei 3 ans mo guen keur gui 00h dinane dafay tali petal mom 15 ans la ame wantei 00h40 lako dieuliwate mom ak kharitam yeup dem teudi jour bobou degg na lou nekk "daga soff " lou nekk kay wayei bamou yeuguei li la kham
@MatyDiaw-z5j
@MatyDiaw-z5j Ай бұрын
Vraiment ligua deff nonoula ma cherie parents legui yii khamou gnou sakh louy khalé dou takhawalou leur unique souci moy bouléne khaleyi sonal😢
@PapebabaSeck-x9k
@PapebabaSeck-x9k Ай бұрын
Oh metina looooollle firdawssy sa demeure amin yaraby, justice, justice, justice, justice.
@mamendoumbefall9783
@mamendoumbefall9783 Ай бұрын
Ay way li métina trop wallahi prenant yi tam saganan deuk bou doy war bi nga mana bayi khalle goudi mou nek si mbedi mi samay dom boumay nelaw bathieuk dama len di teudeul ki am 3ans damakoy teudal bamou nelaw ki am 6ans mom amoul ay nelaw dama koy diokh téléphone mou setane desain anime khale mom bou diagui woul teye ko si keur gui Sénégal legui lifi khew doyna war 😢
@hayapeul5904
@hayapeul5904 Ай бұрын
Pareil que moi j'ai une fille de 3ans 8mois après l'école je ferme la porte elle ne sort pas quand elle veut veux jouer vc les enfants voisin je reste devant la porte jusqu'à quelle finit elle rentre avec moi ,ndogal amna mais nak parents yi def sene Devoir yalla bakhna
@Ndeyesau
@Ndeyesau Ай бұрын
Senegal hamouniou valeurou halè,,diour dom doko surveillè diko yoni mou exposè wou si mbed mi,,halè si bir keur la war dinèk,,bou guènè mak la war di andal
@Ramzek-f3s
@Ramzek-f3s Ай бұрын
Wakhal deh.
@kionking-i9k
@kionking-i9k Ай бұрын
Beugue diour ta manouniou té khaler problem yi en general si pauvre yi rek laye âme
@inconnu90000
@inconnu90000 Ай бұрын
Parents yi nio irresponsables ! Xaley dou guen goudi après timis tecc len seni doom ! Diamono diou ndieuk , xaley dou ngnime romb bountou keurgui 😢 waye legui ! Tout Ce qui était interdit semble normale pour nous ! Dokh timiss, guen goudi , lek di wakh, taxaw di saw, taxaw di nane,saguante ndey, tontou sa moromou wadiour, niak kersa nit,etc etc .... rien n'est grave aujourd'hui 😢maintenant
@mariamadabo9100
@mariamadabo9100 Ай бұрын
Yalla yalla maye lene kholou mogne
@kharyW59
@kharyW59 Ай бұрын
Yalanagneko borombi tabaraka ; wataala terouko aldjana firdawssy amine yarabii
@nohaneba398
@nohaneba398 Ай бұрын
Elhadj ya touti yalla nga dé😢dé bou niaw peine de mort balla Sénégal di rayé wou si carte Afrique
@mia14253
@mia14253 Ай бұрын
Eeeeh mane j’ai 27ans mais sama papa si biir keur gui laniou teudj mane ak samay rakk nane mouk douniou guen kerok nio raw khadiou balcon😂😂😂
@ndeyerokhayandiaye8567
@ndeyerokhayandiaye8567 Ай бұрын
bilahi begne dou réé diamm😂😂wayé waxna deug
@ndoyem4020
@ndoyem4020 Ай бұрын
Responsabilité parentale lima jahal dakar yen quartier dangay guiss khale yi di nek ci mbede yi ba ay 23h voir plus Mangui massax wou ay wadiouram bubah yalla may lene kholou mougn
@NdeyeDiop-eh4nj
@NdeyeDiop-eh4nj Ай бұрын
Kidéf li mobone mais limay dégue thi wakh bi Moy diary mine na kogne bi Trop ta khalé khamoul dara
@karimkarim-ew1rq
@karimkarim-ew1rq Ай бұрын
il faut appliquer la semaine de travail à 4 jours , du lundi au jeudi pour que les parents puissent avoir un weekend de 3 jours pour veiller sur les enfants et éduquer correctement les enfants ... cest la seule solution
@marfatou5239
@marfatou5239 Ай бұрын
Li nehnama deh
@momoaidara5347
@momoaidara5347 Ай бұрын
El hadji ya toth sa thiotou nday😭😭😭😭
@BabacarNdiaye-i7n
@BabacarNdiaye-i7n Ай бұрын
Paix à son âme 🤲
@BabacarFall-e7t
@BabacarFall-e7t Ай бұрын
Yalna yalla wer kidefli amine
@AhmadouDiop-d8q
@AhmadouDiop-d8q Ай бұрын
Li méti Na loll billahi mais yalla n'ako yalla yeurem
@ElhadjiNdiayenewyork
@ElhadjiNdiayenewyork Ай бұрын
Sénégal peine de mort nguen wara appliquée bly man souma deggéee gnuni df am kouñ Ray Sénégal blh damay rouss bapare niouni ay dioullit nguen 😪😪
@Ramzek-f3s
@Ramzek-f3s Ай бұрын
Yèneu zone yi ils sont trop laxistes et negligeants, tu vois même souvent des petites-filles dormir dans les chambres des garçons nice nii comme ça et ça n'intrigue personne. Plus de vigilance franchement.
@ndeyefatoucisse7829
@ndeyefatoucisse7829 Ай бұрын
Nguir yalla etat sénégual na gnou Rayyal ki ni nguir yalla sama khole métina métina bilahi li gnawna
@goradiagnewade8018
@goradiagnewade8018 Ай бұрын
22h gouddi naa sii bayi halé bou tollou nii dii gueneu bountou keur nguir yalla
@rokhayacisse7905
@rokhayacisse7905 Ай бұрын
MoMA diakhale
@adamasene5849
@adamasene5849 Ай бұрын
Surtout djiguéne soyons très vigilants et protégeons nos pauvres enfants innocents rip
@AbySow-k4i
@AbySow-k4i Ай бұрын
Jourou 31 nieupay guene Tall petard donc khaler yeup dagni tok di khar 00h diott
@Heuget923
@Heuget923 Ай бұрын
Fête bi la motah
@MassDiene-o9p
@MassDiene-o9p Ай бұрын
Wa Congo Kinshasa baniou sonné thi criminels yi ils sont commencés à les exécuter publiquement
@NdeyethioroDiop-g5w
@NdeyethioroDiop-g5w Ай бұрын
Mane sama dome somay nalawe beuthieuk té diaguiwoule sou teudoule sama wéte douma mana nalawe wahoumala guoudi
@fatoukinethiam5472
@fatoukinethiam5472 Ай бұрын
Mane de nonoula mel sama dôme sama wett
@aramendour1595
@aramendour1595 Ай бұрын
Sokhna si mann bama yalla dinker ndiaboot la samay nelaw diekh
@amycollendiaye1682
@amycollendiaye1682 Ай бұрын
Bilahi Mane mi ay gor la yorè mais bouniou nelawoul douma mana nelaw yalnaniou yala samal souniou ndiabote
@AmieSall
@AmieSall Ай бұрын
Yalah na agalé ndawame Aldiana Firdawsi
@Seyes-ld9hn
@Seyes-ld9hn Ай бұрын
Elaj mii iska nitt la bilay ki amoul amoul khol😢😢
@Omardiop-x2j
@Omardiop-x2j Ай бұрын
Paix son âme
@belladiop7095
@belladiop7095 Ай бұрын
Bilay deuk bi legui woratoul am n'a Kou goor kouma invité wone sene keur néké kene nekoufa sama xel niaw manékou magui niew parsk bene policier la wara tasel mou diokhma sama carte d'identité jr bobou souma défoule wone meunama forcé teudéma ray ndakh intention teudéma la beguone alors k am n'a 30ans woroul ainsi bi kay bayina seti goor😢
@khadyaidara5511
@khadyaidara5511 Ай бұрын
Kou raye gnou rayla sou borome moko wakh
@famakhathiouba6946
@famakhathiouba6946 Ай бұрын
Mane sama dom yeup nio ngui si internat di diangue mais bilahi depuis ma yeukk li meunouma nelaw bilahi😭😭😭
@rassoul3548
@rassoul3548 Ай бұрын
Internat yui dinanioula diangual . Wante douniou la yare. Moytoul niou mague ame banene djikou.
@famakhathiouba6946
@famakhathiouba6946 Ай бұрын
@ surtout mais meunouma si dara sen papa lolou la beugg gorr ak djiguen niom nieupa dem bilay té tabaski rekk laniouy nieuw 2 mois après niou delouwatt
@fatoudiop3907
@fatoudiop3907 Ай бұрын
Paix à son âme
@DieynabaDembaDiallo
@DieynabaDembaDiallo Ай бұрын
Walahi
@AstouSarr-jd7fo
@AstouSarr-jd7fo Ай бұрын
Gni meuneu kot amougnou mbam. Moi j'ai pas d'enfants wante mes diarbat meme apres le bac ne sortent pas seuls au dela de 21h. Taxi dieuleul numero auto bi ak plaque bi. Amoul wolou. Bougnouy dianga Alkhuran boul sori . Xale yoboul-indil yoboul-Indil .
@maguettebomou5177
@maguettebomou5177 Ай бұрын
Je ne comprends pas à une heure aussi tardive si on voit une petite fille de cet âge en compagnie d'une personne aussi peu recommandable on réagit on cherche à savoir le pourquoi du comment je ne comprendrais jamais le laxisme de certains sénégalais et les parents ont aussi leur part de responsabilité en étant pas plus vigilants sur la sécurité de leurs enfants c'est trop triste toute cette décadence ces agressions ces meurtres on a besoin d'un ministre de l'intérieur et d'une justice très sévères pour redresser la barre car trop c'est trop...
@mouhamabambasall4917
@mouhamabambasall4917 Ай бұрын
Leegi nga gisko ba pare seetaan ko
@mamedegueneseck2600
@mamedegueneseck2600 Ай бұрын
Man lolu moma diaxal
@makhfaye-c2k
@makhfaye-c2k Ай бұрын
Ki def li nagne ko raye
@AichaKebe-uh8jp
@AichaKebe-uh8jp Ай бұрын
Billahi lolou la wakh Li dafa yombou trop ishhh
@AliouSylla-cv9pv
@AliouSylla-cv9pv Ай бұрын
Non li metina trop bilahi 😭😭😭
@timadieng2221
@timadieng2221 Ай бұрын
Man je ne reconnais plus mon pays ay niawtéf rék ngafiy dég légui 😢😢
@FamaDiop-h3h
@FamaDiop-h3h Ай бұрын
Sokhna Diarra billay ligua wakh la wakh guiss gua ko mou dogou loutakh bi gua guissé guenoul gua signaler ko wa keureum
@sokhnaawandiaye3873
@sokhnaawandiaye3873 Ай бұрын
Son pere tamit esk nit la sa dom fanan Ale ngay nelaw 😢😢
@ndiayealimatousadia3215
@ndiayealimatousadia3215 Ай бұрын
Yangui dougal sa bope dei ayy del yoni diary ay day dougou basi bire boutique bi mom woroul dinguène wakh ba dougal sène bopeu
@Dominic231
@Dominic231 Ай бұрын
Donal nitt
@makhfaye-c2k
@makhfaye-c2k Ай бұрын
Sénégal légui jeune yi légui dougnou reference ndakh dagnou yanke diome raye bi dafa bary ndakh éta bi ame nagne ci par de responsablité lépe gnome la
@maguettefaye1508
@maguettefaye1508 Ай бұрын
Bilahi wahnga deug
@SoukeynaFall-r1x
@SoukeynaFall-r1x Ай бұрын
Je me demande lane motakhe nieup nane nagne déme keur niome Elaje😢
@lejoker221
@lejoker221 Ай бұрын
bima degeh lolu la pause video bi di khol ndax dina ame kouko remarquer si commentaire yi
@amycollendiaye1682
@amycollendiaye1682 Ай бұрын
Mane dal déwou khalè bi nimou ma touchè eupna😭
@khadyaidara5511
@khadyaidara5511 Ай бұрын
Khalé bi Parent yi sagane nagnou trop
@Ben-z5v2l
@Ben-z5v2l Ай бұрын
Yar lene séne dom yi. A travers ses images tu vois que la fille se comportait comme une grande fille. Comment laisser une petite fille se maquillait et sortir en pleine nuit.
@Magalieee9
@Magalieee9 Ай бұрын
Arrêter de culpabiliser sa mère 2h 3h on peut pas se permettre de cherchée dans la rue et se mettre encore en danger vue le milieu ou il vie vous connaissez très bien malika et ses jeune délinquant 😢😖😭😭
@seynaboudiop4050
@seynaboudiop4050 Ай бұрын
Sa dôme bo diour rere ngaye khalate lounioula meune deff ndeye bout diour dome sa dôme bou nekei en danger nga fater sa bopou
@jeanine4830
@jeanine4830 Ай бұрын
On peut appeler la police madame Bayil sa khel bigay fowè nane on peut pas. N’importe quoi du coup tu vas dormir tranquille dans ton enfant ? C’est honteux
@mamedegueneseck2600
@mamedegueneseck2600 Ай бұрын
​@@seynaboudiop4050bilahi tu as raison nan la nit meuna teudé nelaw tei guisso sa dom xamo foumou nk ngay am loy expliquer
@maimounandiaye-le1tu
@maimounandiaye-le1tu Ай бұрын
Li metitam eupeuna supporte
@MariBa-f1f
@MariBa-f1f Ай бұрын
Métina trope🤲🤲🤲
@coumbadiouf1356
@coumbadiouf1356 Ай бұрын
Elhaj mi donuou xol domam bi est-ce que défouko dom dji tamite ahh
@elisabethmarieleacampal7518
@elisabethmarieleacampal7518 Ай бұрын
Wa ki niit la nga guiss ko do réagir !
@ElsaCamus-gd7es
@ElsaCamus-gd7es Ай бұрын
Ct ou? G pas t’y capté .. merci de me traduire
@AmadouBa-m2n
@AmadouBa-m2n Ай бұрын
Vraiment ce gua là il a la conscience comment peut on faire cette acte
@soradiop4978
@soradiop4978 Ай бұрын
Yi doka foguè sakh
@AisatouWade-b5m
@AisatouWade-b5m Ай бұрын
Waroulwone toudou elhadji
@Fatousene12m
@Fatousene12m Ай бұрын
Bilakhi
@aminadia9030
@aminadia9030 Ай бұрын
Bilahi
@Adijifama
@Adijifama Ай бұрын
😢😢😢😢😢😢
@strategiesetdeveloppement2525
@strategiesetdeveloppement2525 Ай бұрын
Le monsieur en rouge est pudique et merci à lui
@madodiop6479
@madodiop6479 Ай бұрын
Woloungako ?
@MiaGueye-q8r
@MiaGueye-q8r Ай бұрын
😢😢😢
@aichagoudiaby1148
@aichagoudiaby1148 Ай бұрын
Sénégal mo geneu bon harlem
@mameaissatougoudiaby8951
@mameaissatougoudiaby8951 Ай бұрын
Yow yaye mbame deug nga guiss ko ak xalé bi ba paré interveniro ah sénégalais mo doywar après u es là à le dire com si de rien n'été😡😡😡
@gkhady9
@gkhady9 Ай бұрын
Non ak doumou el hadj la ko guissal
@camoucamara6649
@camoucamara6649 Ай бұрын
Tu l'a vu après tu parle dans les réseaux
@alhamdoulilah1344
@alhamdoulilah1344 Ай бұрын
Vous avais tous une part de responsabilités de cette situation comment pouvez laisser une fille de 12 ans se promener seul san même savoir à préalable où elle est parti , on doit jamais laisser son enfan mineur sortir san c parents
@CoumbasounaBop
@CoumbasounaBop Ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤
@nitoudegeki6631
@nitoudegeki6631 Ай бұрын
Senegal ray nit tè dara doulaci feke kasso dafa yombou dagay leke di nan di nopalou
@AwanaMbaye
@AwanaMbaye Ай бұрын
J’appelle tous les parents du monde entier à faire encore preuves de vigilance surveillez vos enfants de près ou de loin aduna dafa neexatul wax taan leen encore ag xale yi Ba
@BambaSougou-x4i
@BambaSougou-x4i Ай бұрын
Sarab lii waay lii dafa yombou trop
@mamousy9797
@mamousy9797 Ай бұрын
Dame ray nama 😂
@mounassngom8164
@mounassngom8164 Ай бұрын
Nite nio wara teye sene dôme yi Sénégal mane dama yakar da ame loulene dougue yi khetou sadik
@princessemyadiallo9791
@princessemyadiallo9791 Ай бұрын
Elad fall dal naniouko ray ndakh ammna yéne façon ray yo khamni diaroul teudj naniou ray ndayam mou diékh
@AïdaNdiaye-v6r
@AïdaNdiaye-v6r Ай бұрын
😭😭😭😭😭
@CoumbasounaBop
@CoumbasounaBop Ай бұрын
😭😭
@mamediarraka2214
@mamediarraka2214 Ай бұрын
Yaw doul amo lo waxx bagua ko guisse mou and ak khalei bi tei meusso ko guiss doko signaler ay mbokam li diaratoul waxx 😢😢😢
@baloutadanso
@baloutadanso Ай бұрын
Iow boulniou sonal ki khalatoulwone ni ke nonou lay deme nit kesse le te nit matoul
@mamadoudiop1105
@mamadoudiop1105 Ай бұрын
D apre les media c etai une personne qui se droguer sa reputation n etai pas bonne ds la mesure ou tu l as vu tu devais reagir soit avise ses parents mai osi naniuy eviter khaleyi di guen certaine heure kiko ray mom nagn ko yobu stade dakhar n dayam ray n dayam devant tt le monde
@makeitreal6918
@makeitreal6918 Ай бұрын
Bilahi
@aydathiaw4820
@aydathiaw4820 Ай бұрын
Boul wakh lolu daguaa yakareii wouuul bou done yaw nonu guay réagireii
@Elhadji2187
@Elhadji2187 Ай бұрын
No domou el hadji domeram bi la andalon donc ki meunou thié won ham dara
@jeanmariesene8330
@jeanmariesene8330 Ай бұрын
Kon el hadji mak la?? Genre yii bilay mo tah nite yii réclamé kou raye ñou raye la.
@ndiayemantoulaye3066
@ndiayemantoulaye3066 Ай бұрын
Domekhrame bi, il a plus de 35ans
@mbenedieng2298
@mbenedieng2298 Ай бұрын
​@@ndiayemantoulaye3066ba paré ponkale la photo bima légui kokou khadioule si khalé paix à son âme
@ndiayemantoulaye3066
@ndiayemantoulaye3066 Ай бұрын
@@mbenedieng2298 bilahi diarry kou ndaw la, bamou kay sakou khamna youkhou na wona yaye wo pape, dejà rek dieul mak rèk da metti, bouma khalatè lolou sama yaram bi yeupay simekou, elle a du souffrir
@elmansoursall8180
@elmansoursall8180 Ай бұрын
Juste une question où se trouvent les toilettes ou l'enfant a été retrouvé et qui y a accés? Personnellement même ce gars me paraît louche. Ne faire confiance à personne. Règle No 1.
@mouhamabambasall4917
@mouhamabambasall4917 Ай бұрын
Kiii police dafko wara woo
@issahabasse9563
@issahabasse9563 Ай бұрын
Cité sonatel
@RassoulNdaw-m5l
@RassoulNdaw-m5l Ай бұрын
Yalla na yalla deupei xel yi ak xol yi vraiment niit yi legui sokhor nagn trop xalei bou ndaw nga am xol def ko genre affaire yi vraiment dal moy lolou mai tmt juste que na parents yi xolatt Sen taxaway senegal li fi am amoul fen nam yalla bal dh mai dangay guis couple Bo xamni amouñiou capacité gérer enfant dom mom surveiller rek mm sou fekei fête leu mai yalla baxna
@MaimounaDiouf-o6e
@MaimounaDiouf-o6e Ай бұрын
Dém teudi bayi sa domm tamit😮
@cheikhfall4729
@cheikhfall4729 Ай бұрын
Antouka niom warouniou won teudeu té guisouniou khalé bi
@SadioCoulibaly-s4n
@SadioCoulibaly-s4n Ай бұрын
Métina trope
@fktfkt2932
@fktfkt2932 Ай бұрын
Yawit noy guissee lolou sachant la réputation de ce domaram la ga bayi ko mou andeu ak mom delenn niaw khel
@SY.KHADA.221
@SY.KHADA.221 Ай бұрын
Soye danou thiouné ngaye nekk😢
@AwaSall-s7e
@AwaSall-s7e Ай бұрын
Noumay déf ba diote Gouy gui sokhla nako dé
@mouhamedseye2213
@mouhamedseye2213 Ай бұрын
Wadji sougn mako mayon bama niaf ndm😡
@Ben-z5v2l
@Ben-z5v2l Ай бұрын
Del wakh rek, légui niou dieulsi la. Tu donnes trop de détails jusqu'à menstionner 09h36mn.
@KadiatouKeita-x4f
@KadiatouKeita-x4f Ай бұрын
Ces journalistes incompétent que niko yallah diouré un peu de respect elle n'est plus
Série - Lady Diama - Saison 1 - Episode 49 - VOSTFR
53:39
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 497 М.
Mom Hack for Cooking Solo with a Little One! 🍳👶
00:15
5-Minute Crafts HOUSE
Рет қаралды 23 МЛН
BAYGUYSTAN | 1 СЕРИЯ | bayGUYS
36:55
bayGUYS
Рет қаралды 1,9 МЛН
Pikine : Wadji mo badola deug xoléne loumou beugone dééf
11:21