Salam père Birahim kou deugoula am dîné niémé deugue té kham lamb, Mome rék la guiss mouy décortiquer lamb,guiss lamb,loumou la wah tak ko térré machaalla yalla nako borombi doli soutoural.Niou méleni moma diafé si lamb.le reste lo wah niouné 50% ak 50% si grand combayi.soudé combat bou ndaw niouy wakh ba tass. Lo léne si kham. Père moy roi consultantyeup si lamb.