Bril - Wétalngama (Clip Officiel - B.O "Pod et Marichou")

  Рет қаралды 3,096,001

Bril

Bril

Күн бұрын

Abonne-toi à ma chaîne ici goo.gl/Qw5BFh ##
Nouveau clip : "Wétalngama" de Bril Fight 4, chanson écrite pour la B.O de la série "Pod et Marichou" : la douleur immense occasionnée par la disparition d'un être cher.
#Brilfight4 #Wétalngama #ClassChicMusic #PodetMarichou #team221
Crédits, remerciements & dédicace du clip « Wétalngama » #
Lieux : Kédougou / Thiés / Lac Rose
Réalisation : H-Lab Pro Entertainment (771833387)
Déguisement : Les Bassaris
Un grand merci à tous ceux qui ont participé à la réussite de cette vidéo.
Je dédie ce morceau à tous ceux qui ont perdu un être proche et y rends hommage à mon Père.
"Je pleure son absence mais ma plus grande souffrance , c’est quand je me rends compte qu’il est parti pour un voyage sans retour et ne reviendra plus jamais."
Crédits de la chanson "Wétalngama" #
Auteur & compositeur : Bril
Studio enregistrement, mix, edit & mastering : Class’Chic Music
Une production de Class’Chic Music (Senegal, 2018)
Retrouvez Bril sur les réseaux sociaux #
Facebook / brilfight4
Instagram / brilfight4
Twitter / bril_fight4
Snapchat : @bril-fight4
Lyrics de la chanson "Wétalngama" #
(1er couplet)
Kholna founé, Démna founé , Guissatoumala.
Djaarna féppeu fodane nek , wakhna louné ,Déggatoumala
Douma nangou né dotouma guéstou ba guissla sama wett.
Sama adouna toukina , taagouwouma bayima may wéétt.
Djoulina di niaanat Yalla , mou délossila, donté ben biss la ,
Sa dém wi louma tiss la
Lingfi bayi sass wou diss , douma ko atane , douma noppi fok ma guissla Niakkeula loumay djooyla
{Refrain}
Waro dém Bayima, Nakh ngama, Wétal ngama
Gueuwoumani doumala guissati féneu , Nameunala, Wétal ngama
Niaan nala wakhma fane nga né ? Bouma khamone finga nék nieuwfa , wakhma fo né ?
Damalay Niaan wakhma fane nga né ? Bouma khamone finga nék nieuwfa , wakhma fo né ?
(2ème couplet}
Damay tog’ak ay Nitt niouy wakhtane té doumalén dégg,
Bobou mangui Fénén
Founiou tokk di kaff di rétane mane douma thi meuna bokk
Sama Xélangui thi Yénén
Fatélikouna biniou dane Réé / Bi nga dane déf louné ndakh mane .
Dima takhawou féppeu foumou waré yaw , dima djappalé thi lo meunoul ak linga meune
Fimou tollou ni thi sama Doundou Dara Safatouma ,
Khamouma louma tékki di djarign ndéém Djégguéwoma
Sori ngama , Yaw kheuy nga dém bayima ,
Boma djèguè kaay wouyouma
Sa Dém bi wétal nama
(Refrain)
Waro dém Bayima, Nakh ngama, Wétal ngama
Gueuwoumani doumala guissati féneu , Nameunala, Wétal ngama
Niaan nala wakhma fane nga né ? Bouma khamone finga nék nieuwfa , wakhma fo né ?
Damalay Niaan wakhma fane nga né ? Bouma khamone finga nék nieuwfa , wakhma fo né ?
(Outro)
Lingfi bayi sass wou diss , douma ko atane , douma noppi fok ma guissla Niakkeula loumay djooyla

Пікірлер
BRIL FIGHT 4 - TRAHISON (Official Music Vidéo)
3:40
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 6 МЛН
Baye Mass Ndaw (Clip Officiel)                             #marodi #impact
4:08
Baye Mass
Рет қаралды 3 МЛН
Ful Video ☝🏻☝🏻☝🏻
1:01
Arkeolog
Рет қаралды 14 МЛН
Bril - I'm Sorry - Clip Officiel
6:02
Bril
Рет қаралды 2,9 МЛН
Thione Seck - Diaga
8:14
GELONGAL
Рет қаралды 24 МЛН
Bideew Bou Bess - Belle (Clip Officiel)
4:56
GELONGAL
Рет қаралды 8 МЛН
MOMO KINE & SARAH | BRIL FIGHT 4 - TRAHISON [POD ET MARICHOU]
3:42
GalsenMusicSerie
Рет қаралды 736 М.
Bril - Titeulnama (Clip Officiel)
4:03
Bril
Рет қаралды 1,8 МЛН
All Stars Band1 // YAAY (video officielle)
5:14
Prince Arts
Рет қаралды 3,1 МЛН
Solution
5:12
The Serial Traveller
Рет қаралды 12 МЛН
Wally B. Seck - Kay Ñu Pello WAVE
50:08
Wally Seck Officiel
Рет қаралды 473 М.
BIRAHIM Kima Done seet Remix
5:45
Prince Arts
Рет қаралды 11 МЛН
Ful Video ☝🏻☝🏻☝🏻
1:01
Arkeolog
Рет қаралды 14 МЛН