CARRIÈRE, GROSSESSE PRÉCOCE ET ABANDON : NOGAYE DIENG RACONTE SON PARCOURS DE SURVIE - INTÉGRALITÉ

  Рет қаралды 116,379

SSP SENEGAL OFFICIEL

SSP SENEGAL OFFICIEL

Күн бұрын

Dans cet épisode bouleversant de Confessions, Nogaye Dieng se confie sur son incroyable parcours. Tombée enceinte à un très jeune âge, elle raconte avec émotion l'abandon de l'homme qu'elle aimait profondément, et comment elle a dû affronter seule cette épreuve. Malgré cela, son père l'a soutenue sans relâche, restant à ses côtés à travers les moments les plus difficiles, tout en l'aidant à élever son fils aîné. Nogaye parle également de son amitié avec Mame Ndiaye Savon et Mama Vulgaire, deux figures clés qui l'ont épaulée et l'ont aidée à traverser ces périodes sombres.
Découvrez comment Nogaye a transformé ces expériences douloureuses en une force qui lui a permis de réussir et de briller sur TikTok, tout en surmontant les défis liés à sa carrière et sa vie familiale.
------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------
Vous pouvez vous abonner à notre chaîne en CLIQUANT ici :
Rejoignez nous sur: / @sspsenegalofficiel
Facebook - www.facebook.c...
www.tiktok.com...

Пікірлер: 454
@GorakhalifGaye
@GorakhalifGaye 4 ай бұрын
Vraiment elle a très bien parlé machalla, yalna yalla yook ay khewalam bamou teral papam ak yayam si barkee Seydina MOUHAMED PSL ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@Tymanga
@Tymanga 4 ай бұрын
Détournement de mineur g mal au cœur des coeurs pour notre nogaye
@diarryseck4332
@diarryseck4332 4 ай бұрын
Ndeysaan Nogaye dama setane émission bi geun la beug bilahi ❤❤❤une femme très forte 💪🏽 limou doundou yeup sakh wakhouko ndeysaan kou am soutoureu la❤yakoul badienam ben yone
@mamitacaramel
@mamitacaramel 4 ай бұрын
Celui qui lit ce commentaire que Dieu vous bénisse et vous garde en bonne santé vous et vos parents ❤
@SokhnafatouGueye-uu2qu
@SokhnafatouGueye-uu2qu 4 ай бұрын
Amine
@SokhnafatouGueye-uu2qu
@SokhnafatouGueye-uu2qu 4 ай бұрын
Yalla nagnu Yalla may soutura ak wérrgui yaram
@aidadiack8594
@aidadiack8594 4 ай бұрын
Amine
@halikano392
@halikano392 4 ай бұрын
ALLAHOUMA Amine MACHALLAH MACHALLAH MACHALLAH ❤❤❤❤❤❤❤
@Mareme-k2i
@Mareme-k2i 4 ай бұрын
Amine
@momartallacisse2501
@momartallacisse2501 4 ай бұрын
Courage Nogaye! Yalla na yalla changer sa situation pour que tu puisses faire plaisir à ton courageux Papa.
@LabelleLouisa07
@LabelleLouisa07 4 ай бұрын
Ohhhh dire qu’elle dort dans la même chambre que son père. Nogaye yalnala yalah oubil bountou weurseukk banga ame keur meuneu teral sa papa . Ndeyssane gni beigualaté gnoyy gueuneu souffrir de nos jours parce que c’est de braves personnes. Chapeau Nogaye
@ndeyegueye115
@ndeyegueye115 4 ай бұрын
😢😢 OHH NOGAYE SA PAPA BAKH NA YALLA NALEN YALLA MAY GOUDOU FANE AK WERR BA NGA MOTALI SA YENE THI MOM
@khoradiathiam2228
@khoradiathiam2228 4 ай бұрын
Parfois dagnouye guiss nitt diko juge té dokho kham force a toi Nogaye kara❤❤
@Enfant_béni_7
@Enfant_béni_7 4 ай бұрын
MAAM MODOU KARA mayal Nou NOGAYE KARA mi sa béneu Talibé bou bax mou yoral nouko Guire dieumi AHMADOU BAMBA MBACKÉ RTA 🤍
@sopeunabifall1902
@sopeunabifall1902 4 ай бұрын
Walla mou takk ko
@Dieng-y2y
@Dieng-y2y 4 ай бұрын
WARNAA. MANA. NÉK. NDAKH. PAPAM. S. MODOU. KARA. LADOON. KHEUYEUL
@pendandiaye1970
@pendandiaye1970 4 ай бұрын
Nogaye li mo takh nga fonk sa papa yalna féké sa ndiarigne ak sa bou dom bilahi nite boko khamoul bouko jujé
@MameCoumbaMbaye-ut2gy
@MameCoumbaMbaye-ut2gy 4 ай бұрын
Bilahi deuleu sénégalais ci boppam mo khamoul addina
@halikano392
@halikano392 4 ай бұрын
ALLAHOUMA Amine MACHALLAH MACHALLAH MACHALLAH
@halikano392
@halikano392 4 ай бұрын
Nénagnou natou mo djitou dioudou borome motakh kéna moutioul khana raw rek 😢
@fallkeum
@fallkeum 4 ай бұрын
​@halikan❤❤❤o392
@marieheleneberre8736
@marieheleneberre8736 4 ай бұрын
Bonne chance ma fille que Dieu t'accompagne inchallah.
@ÉmilieMarcellaIrèneDiatta
@ÉmilieMarcellaIrèneDiatta 4 ай бұрын
Elle est vraiment vraie Nogaye yalla nala yalla takhawou niteuh guenouko🙏🫶❤️❤️❤️❤️
@ThioroMbodj-y2f
@ThioroMbodj-y2f 4 ай бұрын
Je suis fier de toi ma chérie dina bakh Inchallah ne pleure pas ma chérie je t’aime ❤
@Diamond_Black27
@Diamond_Black27 4 ай бұрын
😢Remplissez le bocal🫙de cœur ❤️
@sokhnathiam519
@sokhnathiam519 3 ай бұрын
Je n’ai jamais regarder confession bamou diékh je sais même pas ce qui m’a pousser à le regarder mais vraiment Nogaye elle est brave et forte et elle sait très bien ce qu’elle veut force à elle
@fatimacoumba3956
@fatimacoumba3956 4 ай бұрын
Wallahi nogaye mi elle n'est pas folle de elle est adorable mashallah elle est parfaitement raison
@maimunafofana904
@maimunafofana904 4 ай бұрын
Her talking about Her dad makes me cry. I'm also a daddy's girl May Allah give our parents long life and good health ❤❤❤
@nickythiam
@nickythiam 4 ай бұрын
bly ya gorer ya bakh bouder nianou wadiour daye fegne thi dom yalla nala yalla teral
@KittyDkr
@KittyDkr 4 ай бұрын
Du courage Nogaye ❤ Allahouakbar c’est tellement triste je la comprends mieux maintenant ! Qu’Allah t’assiste et te facilite
@diezjeylani6837
@diezjeylani6837 4 ай бұрын
Seu Papa mm sou yoroul defna liko war dou layok iow MachAllah ❤️force à vous Yalla nala Yalla defal wer oubil la weurseuk
@tawdevaleurs3724
@tawdevaleurs3724 4 ай бұрын
Tay lakoffi Wah Bala dewen inchallah boy guissate sa vidéo bi Dina tokkk du Kawer sa diote inchallah T yalna yallah bayiwale fi sa papeuh mou feker lepp ak tal
@NdiabaThiabou
@NdiabaThiabou 4 ай бұрын
Amen
@famasalihathioubsaliha9201
@famasalihathioubsaliha9201 4 ай бұрын
Amine ❤❤❤
@SodaGueye-f8b
@SodaGueye-f8b 4 ай бұрын
Ay way amine sa niane gui yalla na dall si barké Mohamed psl
@SadioNdoye-g5n
@SadioNdoye-g5n 3 ай бұрын
Amine inchallah 🙏
@ndeyesalimatasene4659
@ndeyesalimatasene4659 4 ай бұрын
Ooohhhhhhhh 😭😭😭😭😭😭😭 masta Nogaye li kouko doundoul menoko kham yalna la yalla taxawou si côté yépp inchallah 🙏 thiéy gor ltx amouniu yeurmandé si djiguéne la khamoul 😓😓
@tafadiop74
@tafadiop74 4 ай бұрын
C émouvant. Massa ma sœur. Yalla neula Yalla geunala diapale.
@MameCoumbaMbaye-ut2gy
@MameCoumbaMbaye-ut2gy 4 ай бұрын
Amiin
@FatouSamb-u6z
@FatouSamb-u6z 4 ай бұрын
Amine
@abdoulba9581
@abdoulba9581 4 ай бұрын
Li dh kouko setane damou diekh te dioyo amo xol bilahi ❤❤❤❤❤❤❤
@FatouDiop-uh8yp
@FatouDiop-uh8yp 4 ай бұрын
DEUG DEUG goor ga kou yalla beugue tel la natou talibé Serigne Touba dégueu day diar thi natou digua am borom keur bou bah in cha Allah du courage
@fatimatasylla1818
@fatimatasylla1818 4 ай бұрын
ya Allah donner à cette femme de quoi sortir de cette situation, bilahi damala naaw surtout beugue gui guaa beugue sa PAPA car moi aussi le mien et toute ma vie, je pleure et je sais PAS pourquoi
@nafytoure
@nafytoure 4 ай бұрын
Nogoye t’a gâté ma journée Bilaye courage 😢😢
@rokhayandao5832
@rokhayandao5832 4 ай бұрын
Té mom dafa reconnaissante machala ❤
@dienebandoye6171
@dienebandoye6171 4 ай бұрын
Nogaye bly lou bakh rk nguay ame sa papa yalna doundou bangua koy téral
@TymaSeck-le5gb
@TymaSeck-le5gb 4 ай бұрын
Nogaye inchallah lépeu dina bax le tous puissant voit tous 😢😢😢😢
@Salam-fx2wv
@Salam-fx2wv 3 ай бұрын
Force à toi sista vraiment g des larmes aux yeux ❤❤❤❤❤❤❤
@ndeyekhadygueye151
@ndeyekhadygueye151 4 ай бұрын
Bilay sama khôl bi da fess 😢ndogaye vrai ngor la Machalah yalla gua doundou bay teral sa papa dji🙏🏼🙏🏼
@thiawbadiane6873
@thiawbadiane6873 4 ай бұрын
Tay la kham sob bakhoul dama dioy 😢ba sonou ❤Louma guiss rék sétane❤
@AwaDiop-eb8to
@AwaDiop-eb8to 4 ай бұрын
Bari guasy morom
@thiawbadiane6873
@thiawbadiane6873 4 ай бұрын
@@AwaDiop-eb8to ah bon
@MouninaKounta
@MouninaKounta 2 ай бұрын
Ndeyssan yalnako borom bi faye kholal sa papa bamou fékei sen ndiarigne inchallah li damassi dioye ba sonou
@oulimatasall2796
@oulimatasall2796 4 ай бұрын
Ndaysann c'est vraiment triste wallay doli santt yalla 😢
@Natasha-cq1xd
@Natasha-cq1xd 4 ай бұрын
Yalnala yalla bolé ak goor bou bakh boula beugue meune la teral inchallah yalla meune nako té dinako def inchallah
@MameCoumbaMbaye-ut2gy
@MameCoumbaMbaye-ut2gy 4 ай бұрын
Amiin waay
@aissatoudiallo189
@aissatoudiallo189 4 ай бұрын
Ma chérie souhaite lui que ses affaires marchent mo gueuneu
@Natasha-cq1xd
@Natasha-cq1xd 4 ай бұрын
@@aissatoudiallo189 Je lui souhaite que ses affaires marchent aussi Tu es contente ma grande😅😅?
@SadioNdoye-g5n
@SadioNdoye-g5n 3 ай бұрын
Amine inchallah 🙏
@oumydiawara3533
@oumydiawara3533 4 ай бұрын
Ay way nagnou défal Nogaye cagnotte pour mou ame fond de commerce
@MamemorDiouf-ph2xt
@MamemorDiouf-ph2xt 4 ай бұрын
Ho nogaye ma fait pleurer aujourd’hui Bilakhi ame problème ba paré da ngua beugue sa nite yalla na la yalla déffale diambe ❤❤
@KhorediaTHIAM-ez3lz
@KhorediaTHIAM-ez3lz 4 ай бұрын
Day metti rekk wayy dina bakh ndakh lo wakh né sama papa té olof nena weurseukk nday barké bay, digua takk dé inchala
@SadioNdoye-g5n
@SadioNdoye-g5n 3 ай бұрын
Amine inchallah 🙏
@MaxNiass-d9u
@MaxNiass-d9u 4 ай бұрын
Mane dama beugue Nogaye bilahi dina bakh
@ndeyegueye115
@ndeyegueye115 4 ай бұрын
INCHALLA NOGAYE YALLA DINALA DIAPALE BA NGA AM LO TÉRALE SAY WADIOUR DU COURAGE YALLA BAKH NA ❤❤❤
@mirriamcisse7328
@mirriamcisse7328 4 ай бұрын
Derriere un beau sourire se cache toujours une triste histoire arrêter de jugé les gens Dieu Seul est l Parfait Juge
@Ramapoulo
@Ramapoulo 4 ай бұрын
Nogaye dangua ma dioylo bama sonou😭😭😭😭😭😭😭😭😓
@mamandieng5128
@mamandieng5128 4 ай бұрын
Bilay y’a des papa iramplaçable courage ma 😍
@fatoumbengue3576
@fatoumbengue3576 4 ай бұрын
Ohhh my goodness 😢😢 😭😭😭😭Thiey Adouna ❤
@mamecoumbaseck4931
@mamecoumbaseck4931 4 ай бұрын
J'ai les larmes aux yeux, Yalla nala Yalla may teraga
@MayanaDiallo
@MayanaDiallo 4 ай бұрын
Machallah elle vraiment brave émission yeup la diot yalla na yalla maye bébeute bi geu beugeu si sa famille surtout si sa papa 😢
@MARIEDIOP-q4c
@MARIEDIOP-q4c 4 ай бұрын
C triste aidez la pour ceux qui ont les moyens son père a bcp de mérite
@elisabethdiallobalde2129
@elisabethdiallobalde2129 4 ай бұрын
C'est triste Lou diaffé si wadiour bou goor yalanala yala takhou maye sa papa wer bamou féker lep inchallah
@pendandiaye1970
@pendandiaye1970 4 ай бұрын
Mane nak sa yaye khaw nako méré ndakh dom war 'gua ko gueustou ba kham si limou nek
@somb8122
@somb8122 4 ай бұрын
Yayam di koba! Kerok bimou gneuwer ci boutique bi elle etait gênée beugoul wonn salh yaye dji wakh 😢
@halikano392
@halikano392 4 ай бұрын
Soutoural ko ndakh nogaye
@Patriotsavie
@Patriotsavie 4 ай бұрын
​@@somb8122yayam wakhdji matoul sakh une minute gua jugé ko nonou batok😢😢😢
@AlimaSAMB-zz9hy
@AlimaSAMB-zz9hy 4 ай бұрын
@@somb8122 ioenyako geuneu done koba senn yii nguenn ara bayi lo hamal yayam ba ngakoy wakh koba
@Fatima-ev1xd
@Fatima-ev1xd 3 ай бұрын
​@@somb8122soutoura svp
@malicksourang
@malicksourang 4 ай бұрын
Sacré nogaye thiou diambar la nakk❤❤❤
@ladivandiaye8337
@ladivandiaye8337 4 ай бұрын
Wa mane dé magui dioye rek ba li diamla ohhhhhh ayi souma yalla mayone taye dinala teral bagua diomi barki alhouranou Karim
@awabop5671
@awabop5671 4 ай бұрын
😭😭😭c triste courage cherie adouna dameussa mety courage rek sa papa kou bakh la
@mamyfatouniang2785
@mamyfatouniang2785 4 ай бұрын
Ndeyssane mame ndiaye kou bakh la♥️
@lamasylla5870
@lamasylla5870 4 ай бұрын
Serigne Modou kara nako maye terrain talibéyi tabakhal koko
@lamasylla5870
@lamasylla5870 4 ай бұрын
Mame ndiaye savon yak maman vulgaire Woutal lénko appartement dikoko fayal ngui yalla mom mouy dawal bopam dépense ba situation wam changer
@Enfant_béni_7
@Enfant_béni_7 4 ай бұрын
MANE MOM BEGEU NALA LÈGUI TÉ INCH'ALLAH je ferai tout ba DIAPELÉ la SI SUTURA 🙏🏿☝🏿❤ nak JIGUÉN BOU AME JOOM NGA mashallah 🙏🏿
@halikano392
@halikano392 4 ай бұрын
Surtout que DIEU te bénisse inch ALLAH ❤❤❤❤❤❤❤
@Enfant_béni_7
@Enfant_béni_7 4 ай бұрын
@@halikano392 allahouma amineee
@SodaGueye-f8b
@SodaGueye-f8b 4 ай бұрын
​@@Enfant_béni_7ay way défal lolou
@GnagnaMbaye-i5f
@GnagnaMbaye-i5f 4 ай бұрын
Nogaye rèye guama dioye na beu sone
@fatimatasylla1818
@fatimatasylla1818 4 ай бұрын
pareillement ma belle
@khadyngom9868
@khadyngom9868 4 ай бұрын
Mashallah Nogay Wakh Bi Rafétna Dina Bakh Bilay Wolof Néna Weurseugou Ndaye Barké Baye Dina Bakh Képp Koula Masa Déf Lou Bone Wala Lou Niaw Yall Dinaléne Até🥹❤️🙏
@mamadiordiengndiaye1903
@mamadiordiengndiaye1903 4 ай бұрын
Ndeysan sounei amogoul lou nekh sama yaram daw soudoul fi rek di feulé nogaye courage❤
@mariamandiaye8939
@mariamandiaye8939 4 ай бұрын
Bilahi ma bagne diokhé dome😢😢😢
@gniagniasene1710
@gniagniasene1710 4 ай бұрын
Ma chérie lossi bagne rek amnassi
@ZeynabFall-f8e
@ZeynabFall-f8e 4 ай бұрын
Vraiment Nogaye linga dound metti n’a trop 😢Yall nala yalla sam té ar la bou bah Amal diam bou bari🤲🏽
@BbliseNiang
@BbliseNiang 4 ай бұрын
Diam rk guay am nogaye bly yalla mogji fépp😢😢
@damedefer6233
@damedefer6233 4 ай бұрын
Vraiment Nogaye courage emission emouvante
@awambowfaramareene843
@awambowfaramareene843 4 ай бұрын
mai nite gni lane moy sen problem ak wasso gnoune gnepp ben lagne gnénio balamaïssa nga khamni dougnou gné ken dagne len di gné askanou gné gno nimou riché wa tmt tmt tamiti tamit❤ noguay yalla nala sougnou borom takhawou t nga gorgorlou boubakh lépay bakh❤
@maymounagueye7249
@maymounagueye7249 4 ай бұрын
Lou méti yague na mais tout ira bien inchalla force à toi Nogaye.
@marietougueye1886
@marietougueye1886 4 ай бұрын
Svp pensez à améliorer le décor , moins de couleurs , moins de lumières les rideaux , c’est pas esthétique, le décor c’est important on dirait les années 2000
@awadiop7440
@awadiop7440 4 ай бұрын
Avec tous les difficultés qu’elle traverse on voit bien keni sénégalais doula dimbaly ay millionnaire nioko weur loulein tèré niou dimbaliko ci lou ame foula au lieu nioukoy utilisé ci s’en ay live
@MamimamanNdiaye
@MamimamanNdiaye 4 ай бұрын
Bilay xaw mala mai koula fonk la ❤️❤️❤️❤️ yalla nalla yalla defal diam ak tawfekh ❤
@ndeyembeneniang3204
@ndeyembeneniang3204 4 ай бұрын
Yalnako yalla takawou ayy waye serigne modou kara diapaleko bok dak toureme bimouye dakanetalé sa bosss barké seydina mouhamed psl
@NgonéDIOP-k9l
@NgonéDIOP-k9l 4 ай бұрын
Nogoye yalla nala yalla takhawu vraiment li c très touchant et triste ❤
@fatoudiagnediakhoumpa8076
@fatoudiagnediakhoumpa8076 4 ай бұрын
Yalla na yalla faye sa papa daysane papam diou bah yomboul
@amicolediop4609
@amicolediop4609 4 ай бұрын
Machallah elle est très posée très différente dans les livres. Que Dieu te vienne en aide
@ndeyecoumbadiallo898
@ndeyecoumbadiallo898 4 ай бұрын
Ndogaye diambaar nga yalna yallah teral lahh
@mamanmargotchimerediop9784
@mamanmargotchimerediop9784 4 ай бұрын
Ndeyssan 😢yalla naleu yalla takhawou bubax Nogaye kara 🙏🏽
@Brigitte589
@Brigitte589 4 ай бұрын
Ayyy nogayy yagg ngama retan lo dh wayee tayy mom dioy lo ngama yaalllah na yaallah sedaal sa xoll
@alimaba6012
@alimaba6012 4 ай бұрын
Nogay mi wakhi nite deug la wakh wakhoul bene yone wakhi dof
@ThiernoDiallo-u8c
@ThiernoDiallo-u8c 3 ай бұрын
Massa way mon Nogoye😭 ndeysan nitt mo leudome😭sa dome da yarral sinon woroute
@walydiagne7955
@walydiagne7955 3 ай бұрын
En tant que mére je comprends son vécu courage ma belle ❤
@MamimamanNdiaye
@MamimamanNdiaye 4 ай бұрын
Nimouy wakhei guay xamnei kou beug papam la ❤❤❤❤
@radissondiamniadio9820
@radissondiamniadio9820 4 ай бұрын
Bly mots bi momay raay dra nékhougouma 😢
@aidadiack8594
@aidadiack8594 4 ай бұрын
Koula diapé doff dé moy doff bi
@NdeyethiabaNdiaye-c7v
@NdeyethiabaNdiaye-c7v 4 ай бұрын
Wallakhi
@nganengane5205
@nganengane5205 4 ай бұрын
Nianou Wadiour nakk mo diaffe thi diaomoni dji…Yallah gneup lafi nekal Nogayyalna ya Allah telkla lokho🙏
@Fatima-ev1xd
@Fatima-ev1xd 3 ай бұрын
Kouné gor bakhna sa bay mo takh limou souffrir yeup gor mokoko ték par ce que sou copin bi accepté wonn relation bi diapalé KO si dôme dji peut être konn d'où doundou li méti li yeup mais courage ngoay yalla nala yalla takha wou Banga faté lép Loula méti wonn
@beugbayecheikhousmanembow1044
@beugbayecheikhousmanembow1044 4 ай бұрын
Yalla na sa dom bi tekki ba teral la ❤❤❤❤❤
@NdeyeFatouKeïta-j3k
@NdeyeFatouKeïta-j3k 4 ай бұрын
Wouy sama khôl bi 💔🥺🥺🥺
@fatougueye-zh7td
@fatougueye-zh7td 4 ай бұрын
Yalla nako yalla may loume teralé papam 😢😢
@seynabousy3335
@seynabousy3335 4 ай бұрын
Mashallah notre noguaye nationale dine bakh in challah
@NdiobaFaye-k7n
@NdiobaFaye-k7n 4 ай бұрын
Sama coffession 2 heures de temps sakh dou takh ma paré té sisa ma enfance rek lay yam bly
@Ramapoulo
@Ramapoulo 4 ай бұрын
Courage ma sœur❤❤❤❤❤😢😢😢😢
@ndeyekarim1808
@ndeyekarim1808 4 ай бұрын
Massa ma belle kouko doundoul douko khamm😢😢😢
@astoubilla
@astoubilla 4 ай бұрын
Wallah moi je ne peux plus regarder 😢 comment on peut faire ça à une enfant Éh les gens sont mauvais
@DieynabaDéme-u2u
@DieynabaDéme-u2u 4 ай бұрын
Nogaye yallah yallah teraleih❤❤❤
@SadioNdoye-g5n
@SadioNdoye-g5n 3 ай бұрын
Amine inchallah 🙏
@Natasha-cq1xd
@Natasha-cq1xd 4 ай бұрын
Nogaye mii limou dundu dafko traumatiser motakh mou ame depression
@MameCoumbaMbaye-ut2gy
@MameCoumbaMbaye-ut2gy 4 ай бұрын
Loulou itam deuguleu
@fatimacoumba3956
@fatimacoumba3956 4 ай бұрын
Mais pourquoi tu dis ça elle n'est pas folle du tout elle se défend juste
@Yajogueye22
@Yajogueye22 4 ай бұрын
Dara diotouko c ma cousine wah gako doundou bi mo meti Koussa doundou meti kay faw mou fegn si yaw
@halikano392
@halikano392 4 ай бұрын
Wayé foumou ame gorgnou bone amna gnou bakh kholal kiko dieul ak domame yobouko thi wakeureume badianame refouléko mou déme yé diabarame mou watia lalame ak aye domome yégal ko thia kaw yobouko hôpital wouteul ko liguéye kone bakh amna YALLAH na ame kholou gnou bakh gnognou royoukaye MACHALLAH MACHALLAH rek ❤❤❤❤❤❤❤
@maimounacssko2026
@maimounacssko2026 4 ай бұрын
⁠@@fatimacoumba3956chérie dépression ak dof soriwanté naniou deih Senegal nak so amé dépression les gens disent que tu es folle alors que c’est pas le cas
@DiagneFall-ri4hw
@DiagneFall-ri4hw 4 ай бұрын
Machallah Mame ❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤🎉🎉🎉🎉Noguaye🎉🎉🎉🎉
@kharymbengue5660
@kharymbengue5660 4 ай бұрын
Li motax nitt kéne warouko jugé courage sister❤❤
@fabediloumloum8444
@fabediloumloum8444 4 ай бұрын
Da gore nak loum wakh nii mame ndiaye savon ❤
@mariemendiaye-r1x
@mariemendiaye-r1x 4 ай бұрын
bilahi dama dioy ba sama yaram bi tangue nogaye kara yalla nala yalla takhawou yoboula fou kawé sa ndiorte
@SadioNdoye-g5n
@SadioNdoye-g5n 3 ай бұрын
Amine inchallah 🙏
@yacinewade3477
@yacinewade3477 4 ай бұрын
Yalla gua âme dieukeur Bou yermende 😢
@mamendiemethiam7540
@mamendiemethiam7540 4 ай бұрын
Ndeysane khôl bi dara nékoussi yal nala yalla takhawou dénke la aye milliards bagua térale saue wadiour ❤
@MaremeDiène-t9y
@MaremeDiène-t9y 4 ай бұрын
Defal leine ko cagnottte mogui begale nieupppp tei begoul ndeyssane 😊
@AdamaAdamasarr-t5b
@AdamaAdamasarr-t5b 4 ай бұрын
Bilay ndeysannnnn
سورة البقرة كاملة لطرد الشياطين من منزلك وجلب البركه باذن الله surat albaqra
3:52:03
SAMEDI CONFESSION EP 28 Ft AISSATOU ( COEUR BRISE)
1:04:34
UFC 287 : Перейра VS Адесанья 2
6:02
Setanta Sports UFC
Рет қаралды 486 М.
Wednesday VS Enid: Who is The Best Mommy? #shorts
0:14
Troom Oki Toki
Рет қаралды 50 МЛН
LE VÉCU DE MAME NDIAYE : ENTRE MARIAGE COMPLIQUÉ ET DÉFIS DE VIE - INTÉGRALITÉ
1:33:06
Xalisso - Saison 1 - Episode 38 **VOSTFR**
45:25
EvenProd
Рет қаралды 1,3 МЛН
Confession: Terrible révélation de Cheikh Ndiaye
1:14:54
SSP SENEGAL OFFICIEL
Рет қаралды 93 М.
Ndeye khady Ndiaye sur l'affaire Adji Raby Sarr - Ousmane Sonko
9:32
Les compagnons de Ousmane Sonko
Рет қаралды 2,7 М.
Confession Abdou Aziz Niane une vrai histoire d'un artiste
1:20:11
SSP SENEGAL OFFICIEL
Рет қаралды 59 М.