Seugn bi moi jai ete dans un autre tarikha different de celui ci.jetais engagé et convaincue que cetait le bon chemin mais quand jai appris sur les ecrits du serigne quil se proclamait le prophete mouhamad psl sila daw.bolesi ils disaient que safara ak aldiana fiii leu si aduna.ce qui est contradictoire avec le coran et les hadith.alors je me suis dit " si le tarikha avait raison alors ALLAH ferait du wakh wakhét" subhanallah .ma conclusion fut CECI NE PEUT PAS Etre LE BON CHEMIN CAR DIFFERENT DES DIRES DU HUR'AN ET DES HADITH alors jai claqué la porte.nieup diakhlé ma xam lima xam té diangi waat. Et aujourd'hui plus que jamais je sais que la sunnah est le VRAI
@Mariam511176 ай бұрын
Alhamdoulillah alors ❤️ Qu’Allah fasse que nous mourrons en étant loin de tout chirk 🤲🏻
@ragenpro42116 ай бұрын
Est ce que Serigne Touba moka wakh parce que yagni guiss nii seytané yii défon Souleymane.S.Touba khamnané bou Watiato'e yatt laay eunalé parce que guys yii dagn kay wakhlo loumou wakhoul😂😂
@Senegaltv916 ай бұрын
Dagnay feneu fi Senegal amoul beneu tarikha boufi né aldiana ak safara fila yam soss rek ak feneu ngeneu fi neke beug né allah ngeneu gemeu
@MoulayeLaroussi6 ай бұрын
Machallah sunna rek mo wor
@abdoulayediop69366 ай бұрын
Slm mlk danaka messouma commentaire si yi wayé léne rek la léne Di dinke moy sounou borome gnimou yabal beri nagne lole té koussi nék dagnou ko wédi, done té lou lére nagne la wayé gnogna sén hole da mene goul yeuk lére gogou sougnou borome diléne fatali. Motah nak gnogui gnane souniou borome léral sén hole ak lép louy thieur si yéne ba guéne mene dégue kaddou souniou borome ak gnimou yabal ndah mbirou serigne bi koussi souniou borome naroul dimbeli Meno ko ham, wla Meno yeuk, wla Menoko dégue. Té yéne gni Def vidéo bi gnoune talibé yi daguéne gnouy dimbeli bou bah té hamoléne ko. Té béne conseil moy soléne beugué guestu mbidoume serigne bi ak alhourane té âme si lou lére guene léna farlou bou bah si sélale ak itté. Té mane Li nguéne Di Def ni dama hamoul Loléne si jouboulou. Mane dal beugue na âme ak yén bén conversation entre joulite hawouma noumay déf ba ame sén coordonnée Boudé yallah gnore Naléne. Ndah Li nguéne Di wah ni Daguéna déssé oubékou si yallah lolou kép la motah mais sounou borome dal kou beriy mbir la. Di toubate bou bah🤲
@user-io4zu7ns4g6 ай бұрын
MashaAllah Oustaz Qu'Allah vous récompense
@dembasoumare11476 ай бұрын
Wakh bou wouté ak wakhou Yalla. Kone wakh bobou fén la: koumou meuneu done. Wakhou Yalla rek moy deugg.
@Mariam511176 ай бұрын
❤️❤️❤️
@alassaneseye21916 ай бұрын
Machalah dieuredieufe oustaz alpha ba leral yi amna solo yalla na la yalla faye billahi louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na la yalla sam
@Mariam511176 ай бұрын
Allahouma amine
@Marou5146 ай бұрын
Yalla na niou yalla yeureum té diegueul niou
@moussandaby97076 ай бұрын
Yalla nala yalla fay oustaz alfa ba lou ame solo la
@Mamech3ikhDiop6 ай бұрын
Saway Alfa mi Limouy déf ni bakhoul ndakh di wédi Nit tou Yallah bouko bayi woul Man nasé ame dani bour Yallah ndakh Yallah souniou borom Beuguel kouy tong tong bakhoul
@Mariam511176 ай бұрын
Amine
@boroomxalimagui27896 ай бұрын
نحن مع شيخ أحمد بمب حيا أو ميتا فقط
@BabacarNdiaye-rv3mt6 ай бұрын
إن كنت مع شيخ أحمد بمب نحن مع الله و رسوله. لا تكن مجنونا يا أخي
@MaisonDiaw-dr6ip6 ай бұрын
Jâwartou rabbî bi lisânil harabî Bi lâ nihâyatine wa tâbat qourabi Puisse - je devenir toujours le voisin de mon seigneur par la langue arabe et que ma proximité avec Dieu soit exellente!
@taphandiaye606 ай бұрын
Dieureu dieuf Serigne Touba 🥰
@moussaseck95136 ай бұрын
Sa way yaww khamo dara demal dia gui kham kham Mane doumaa mouridee dh mais serign Touba Batinee laye wakhé ziar dafa am batinee am mbo khamoul batinee sac jour si erreur rek née té fock ni y’a née si deeeg……Mane geunee gana diezbou si serigne touba khasidaa amneu si benenee dég dégg si serign bi yalnako yalla dolli faye mom serign touba ❤️❤️❤️
@boubacartoure49036 ай бұрын
Baatine amoul si islam, en tout cas le prophète ni les sahabas ne connaissaient pas le baatine. Ce qui signifie ak dou islam rék
@MoulayeLaroussi6 ай бұрын
Ya wara dem diangui, l'islam amoul batine, 😂
@moussaseck95136 ай бұрын
@@boubacartoure4903 Chièkh bi Firil ma 🙏🏾euweullou- arirrou- ziahirrou - ak batinou douddè kham gua lolu firri gua ma tontou lee
@moustaphawade48615 ай бұрын
Wallahou youti moukahou mane yachao signifie Allah alloue son pouvoir à qui il veut sourate 2 verset 237 à la fin
@AlassaneThiam-by1fu6 ай бұрын
MachaAllah ya Oustaz amna solo
@joemansoursow3136 ай бұрын
Dieuredieufé Serigne Touba
@siacamane33616 ай бұрын
Et aussi que Dieu nous protege sur le Droit chemin amine yarabi
@moustaphawade48616 ай бұрын
Déweunté sourate 47 verset 14 Certains rêves nous d'Allah qui peut nous passer un n message
@hanekhadimrassoul16946 ай бұрын
Djeureudjeufeuty khadimou Rassoul PSL ❤❤❤
@ModouNdiaye-y4d6 ай бұрын
ولاتحسبن الذين قتلوا في سبيل الله أمواتا بل احيآء عند ربهم يرزقون. Firi ko
@BooMachalla6 ай бұрын
Machalla ❤❤❤
@aramendoye57186 ай бұрын
Jerejef Serigne Touba Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lampe. Serigne bi bindeu aye mayam, bindeu digueuntéme ak YALLA mbinb mou lére mo tiime, yaw gueumo ko bayil gni gueum .
@thiouthiafall85126 ай бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba❤❤❤
@matarndiaye99693 ай бұрын
Ndeysan😂😂😂😂
@siacamane33616 ай бұрын
Longue vie a vous ✊ ya oustaz ✊ ✊ ✊ Ba
@babsdia15056 ай бұрын
Ou est ce vous avez trouvé le khassida qu’on entend au fond ? Serigne touba dou morom
@laminekande94036 ай бұрын
Serigne bi yallaco yonni
@matarndiaye99693 ай бұрын
😂😂😂😂😂 sheytan kay
@moustaphawade48616 ай бұрын
Si un musulman tombe malade c'est un bienfait, dans cette même optique l'exile peut être un beau
@Leternel.incompris6 ай бұрын
Ya oustaz, stp, nguir yalla🙏🙏arrête d'éveiller les gens car tu gâche mon business ( je suis mountakha 😅🤣😂 )
@moadcasa91766 ай бұрын
S Touba Moy yalla ❤❤❤❤
@dëgmonjëkdëgmomuj17806 ай бұрын
Alpha kagn ngay nopalu😂Yangi wax gnongi geuna geum kou ted ki yow mi endurant nga dh Yalla na sa jam yag Barkeb Sëriñ Tuuba sunu yaakar tey ak euleug❤🤣🤣🤣
@@Diopdiopxt6so Bayileen foofu xamuñu ñun Sëriñ Tuuba mooñu dimbali motax ñu xam Yalla buñu xamone limu ligeeyal sunu Borom ci tundu Baol ak ndiambour ba Diolof ba sine ba saloum ci ay Ceddo dinañu xamni Sëriñ kuñu wara fonk la ta limu am dako ligeey bamuy doxal suna aka tubël ay nit booba l'islam raflé na kuko ligeeyal tey la jamano neex réseau sociaux yi ñow tog sa salon taal sa clim teg sa écran géant sol copati lire ñaari livre ni amnga xam xam ak ni dangay dundël sunna😂boy yi ay reetan lañuma deff réwandé rek moolen sonal bumaleen di seetan comme kuy seetan Adamo🤣🤣🤣
@dembasoumare11476 ай бұрын
۞ وَمَا كَانَ لِبَشَرٍ أَن یُكَلِّمَهُ ٱللَّهُ إِلَّا وَحۡیًا أَوۡ مِن وَرَاۤىِٕ حِجَابٍ أَوۡ یُرۡسِلَ رَسُولࣰا فَیُوحِیَ بِإِذۡنِهِۦ مَا یَشَاۤءُۚ إِنَّهُۥ عَلِیٌّ حَكِیمࣱ﴿ ٥١ ﴾ Il n’a pas été donné à un mortel qu’Allah lui parle autrement que par révélation, ou de derrière un voile, ou qu’Il [lui] envoie un messager (Ange) qui révèle, par Sa permission, ce qu’Il [Allah] veut. Il est Sublime et Sage. ACH-CHOURÃ, Aya 51
@moussakeita90856 ай бұрын
Ma sha Allah, qu'Allah vous récompense en bien.
@BalseAmadou6 ай бұрын
سبحان الله أن ذالك الكلام الله هو رب بعد كل شيء وقبل كل شيء لا احد يعرف الغيبيات إلا الله
@AbduXaadr-qq5uz6 ай бұрын
Mais yaw Alpha comprendro fi s Touba wakhé demal térem bigni wakh sindidi thi fin bi wakh foofou né dey dé dengaa wara gena yaatal sa gestou bala nga wakh thi ken
@ModouDiagne-hb6kf6 ай бұрын
Jërëjëf jëfë Serigne Touba yalna nouko sunu borom fayal lep loum wakh Dëgg la
@AmadiopDiop6 ай бұрын
non li mom ay FENN leu 😂😂😂
@hj-eu6xc6 ай бұрын
🤣🤣 gni ils sont pas normaux. Soubkhanala. Yi féne you meti
@BooMachalla6 ай бұрын
Tarikhayi lepo aye fenla 😂😂😂😂😂😂si la nekon waye legi magi sama diam😂😂😂
@Kebe432Kebe436 ай бұрын
Fén wuniou fénnél Serigne Touba , day dugg ji, fén yiko jiitu woon ! Il n'ya rien de nouveau: ce sont des menteurs, rien de plus ! Je ne pense pas que Serigne Touba a écrit de telles bêtisses ,c'est fort possible, que des gars comme Moussa Kâ ont écris ces bêtisses après le décès de Serigne bi
Oustaz Alpha Ba les savants sont les héritiers des prophètes donc ce Hadith montre qu'il n'est exclu .
@CheikhBa-hj3gu6 ай бұрын
Yaw kou sokhor nka total fale
@Senegaltv916 ай бұрын
Dieuredieufety seeigne touba ❤
@AlieuCeesay-z4r6 ай бұрын
Machalla leral yi Amna solo
@BabacarNdiaye-rv3mt6 ай бұрын
❤حافظك الله يا شيخ ألف به
@DarouMbacké6 ай бұрын
اراك انت لاتفهم هذه المعاني شيا
@CheikhgaïndéfatmaDiallo6 ай бұрын
Hamo dara demal diangui
@MoulayeLaroussi6 ай бұрын
😂 ya wara dem diangui
@babsdia15056 ай бұрын
Franchement démal gueustouwate,désolé mais votre niveau est trop bas
@MalickNiass-en6iz6 ай бұрын
Khamou lene batine
@KAADUDINEEJITV6 ай бұрын
🤣🤣🤣🤣🤣
@MoulayeLaroussi6 ай бұрын
Les écrits de serigne touba il ya beaucoup d'erreur, surtout al aqida wa tawhid ,niak kham el fiqh, il se concentre beaucoup sur ce que ont appelés batine ,qui n'existe pas dans l'islam.
Katal sa ndaye bayii doule serigne touba mo gueneu sa nday ak sa baye
@1GratefulSlave.6 ай бұрын
Hadha Batil!
@boyeoumar94326 ай бұрын
والله أنت لا تفهم اللغة العربية Comprendro téré bi dh Arabe sakh déugo ko. Dangeu war di deff debat gnou wakh la lo khamoutt wone
@boyeoumar94326 ай бұрын
Ay rée sakh lay def ni nooooo Ki mo khromou
@AssamaneVision6 ай бұрын
يمحو الله ما يشاء ويثبت وعنده أم الكتاب. اتق الله في قولك وبالتالي ألم يعلم الله سيدنا خضر العلم اللدني من الغيبيات مع أن نبيه سيدنا موسى عليه جهل به وهذه القصة نص قرآني