Cheikh Ahmed Cissé tacle sévèrement Bichiri et Gana messere, Serigne Touba ken douko fenal...togue

  Рет қаралды 35,574

Dakarnet TV

Dakarnet TV

Күн бұрын

Пікірлер: 215
@mamembaye5586
@mamembaye5586 4 жыл бұрын
ما شاء الله ياشيخ لا شك أنك قد أحسنت!! كلام واصح و مبين ماشاء الله!!! بارك الله لك وجزاك الله الخير الجزاء إن شاء الله
@dembafall7906
@dembafall7906 4 жыл бұрын
Je suis muride tu a parfetment raison sissé
@jadoredieuetmohamedkhadimo2521
@jadoredieuetmohamedkhadimo2521 2 жыл бұрын
Ki Kaye daniou kata ti ndayam ndax framacon yi nonou serigne touba nioko ngembe wayè bilahi digua ko reutiou ndax nioune mouride yi khadiou niou si yow dîna leer inchallah
@daoudadiaw3256
@daoudadiaw3256 4 жыл бұрын
جزاك الله خير يا احمد صدقت علي ما قلت، ان الناصت عن الحق شيطان اخرص
@Hibzo12
@Hibzo12 4 жыл бұрын
Vraiment je suis un talibé baye mais vraiment tu es une reference
@djibyly8544
@djibyly8544 3 жыл бұрын
Eskey yalla nala yalla fay
@aramendiaye6464
@aramendiaye6464 4 жыл бұрын
Macha allah walahi sa wax rafetna lool mais pourquoi senegal bougouniou deugeu Yallah nala yallah samma amin ya rabbi
@khadimndiaye9354
@khadimndiaye9354 4 жыл бұрын
Wakh guako négua serigne cheikh tidiane Sy mola geuneul gnoun serigne touba mongni geuneul
@swiftworldn
@swiftworldn 3 жыл бұрын
Serigne Touba boula geunale waro saga gnenen gni
@mouhamadoufall9243
@mouhamadoufall9243 4 жыл бұрын
Mane mouride la mé gana messré mom faine Kat la daf gnouy faine rk,,,
@santeserignetouba4826
@santeserignetouba4826 2 жыл бұрын
Saay mbokou talibé niasséne Door nañiou la ba gua soon, yaw mom am gua loula dooy
@ndoyepapaibrahimadiasse3026
@ndoyepapaibrahimadiasse3026 4 жыл бұрын
Soyez unies mo guen Sénégal est l'un des pays le plus pauvres donc nous avons un seul trésor c'est notre cohésion donc vous les jeunes arrêter de vous chamailler mais les guides ont accompli leur mission donc nous devons suivre leur chemin en respectant nos guides et nous accepterons jamais des satans ou des inconscients nous divertir arrêter de vous insulter svp le Sénégal est indivisible
@diawaracheikhousmmane8599
@diawaracheikhousmmane8599 2 жыл бұрын
Khamô dara thi serign touba ak mouride wakhal sa wakh té bayignou
@mamadoutoure4165
@mamadoutoure4165 4 жыл бұрын
Machalla cisse
@diengmouhamadeune5693
@diengmouhamadeune5693 3 жыл бұрын
Vous êtes avec Baye et pauvre nous avec Bamba et al hamdoulilahi c’est entre nous vous visez la famille Sy qui se dise Khalifa des tidjanes
@sadibousow939
@sadibousow939 4 жыл бұрын
ماشاءالله
@amethndaw3498
@amethndaw3498 4 жыл бұрын
Kidale kol lay wakhé gana kou âme solo la si yonwi ak bichiri
@FrancijFrancij
@FrancijFrancij 4 жыл бұрын
Machala Cisse amna solo tropp
@ibnsamba1249
@ibnsamba1249 2 жыл бұрын
Ndeyssane bi ngaye wax xamo wone ni biss dîna nieuw niou niousla ba nga dioy🤣🤣🤣 te sa wa keur nioko def
@baboulowe2526
@baboulowe2526 2 жыл бұрын
Baye naiss fodeme si adina talibe baye ngunfa
@mothdioo2712
@mothdioo2712 4 жыл бұрын
gana defay fen fen rak lay def
@omarthiandoum9905
@omarthiandoum9905 3 жыл бұрын
Jèréjéf Serigne bi 🙏🙏🙏
@baldediop3257
@baldediop3257 4 жыл бұрын
Yénn lann moy sén problème Serigne Touba limou déf kén défouko fi
@babaly5821
@babaly5821 4 жыл бұрын
Fen yeen porbelem bi ba leegui xamo leen lan moy lislam wax rek dieuf 0
@babaly5821
@babaly5821 4 жыл бұрын
Sèykou Oumar tal Moy seeni serigne niom nieup thi batina ak thi jahira
@mothdioo2712
@mothdioo2712 4 жыл бұрын
machlla hamna solo trob te pasa jërëjëf way❤❤
@seydinaaliounembaye2667
@seydinaaliounembaye2667 4 жыл бұрын
Ganna limouy wakh si serign touba khépnako serigne bi yalla lép lako diokh
@abdoulayeniang6643
@abdoulayeniang6643 4 жыл бұрын
Mais ki khamoul li mouy wax serigne touba da binde bayi fi
@ibrahimamba1296
@ibrahimamba1296 4 жыл бұрын
La religion au Sénégal est très spéciale ; c'est d'inventer des histoires , de mentir , de faire croire aux ignorants que le marabout est dieu en personne , il a été introduit dans un four à 1000 degré ; il a été introduit dans une chambre avec un lion affamé ; il a été introduit dans une chambre avec un boeuf méchant ; il a prié en pleine océan, ect ; et puis plus tu mens plus tu reçois plus de cadeaux
@allkaloallkalo1413
@allkaloallkalo1413 4 жыл бұрын
@@ibrahimamba1296 le problème c'est les marabouts du Sénégal ils sont pire que dajal
@Osirusavk
@Osirusavk 2 жыл бұрын
​@@allkaloallkalo1413 certains marabout
@ebrimajagne8841
@ebrimajagne8841 4 жыл бұрын
Serigne gana messere yalaganfiyag tewer sibarkep serigne Touba Mbacke amolmoroum
@ousmangaye1687
@ousmangaye1687 4 жыл бұрын
Ganna fénkat la
@mortallasamb3885
@mortallasamb3885 4 жыл бұрын
Serigne Touba. Gana amal diaammm
@NewNew-ex4so
@NewNew-ex4so 4 жыл бұрын
Ganna.doul.rek.lay.def.ak.seytane.mom.guemoul.dara.xaliss.rek.moko.nior.riba.rek.lay.dounde.
@daoudadiaw3256
@daoudadiaw3256 4 жыл бұрын
نصيحة مني الي كل السنغاليين تمسكوا بالطريقة التجانية طريقة محض الفضل والرضوان
@badaraalioune9293
@badaraalioune9293 4 жыл бұрын
Ma challah❤️🙏
@elhadjielhadji5300
@elhadjielhadji5300 2 жыл бұрын
Kii la gniassèène yi doone nokh c bien noppil mon gueune
@lecitoyentv2022
@lecitoyentv2022 2 жыл бұрын
Li motakh gnou dakhar sa ndeye
@moustaphagaye5785
@moustaphagaye5785 4 жыл бұрын
الحسد يأكل الحسنات كما يأكل النار الحطب Yaw miii di wakh dara diapoula loudoul sokhor dangay doul Ghana loumou wakh si Serigne Touba deug liii ngay wakh niii gueumosi dara
@omzikofficiel443
@omzikofficiel443 4 жыл бұрын
Koullil lahou malikal moulkou touxtil moulki man tachà
@ousmangaye1687
@ousmangaye1687 4 жыл бұрын
Ganna fénn kat la
@xaadim9615
@xaadim9615 4 жыл бұрын
Moustapha gaye merci
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
Waaawe gana dafa féne
@user-iz1xj8sp2m
@user-iz1xj8sp2m 4 жыл бұрын
serigne touba dh Amol morom
@hamathcisse7578
@hamathcisse7578 4 жыл бұрын
Merci beaucoup
@mbayendiaye170
@mbayendiaye170 4 жыл бұрын
Ki mo abpou xam xam mbolem kouy mourid
@hamzawydad4871
@hamzawydad4871 4 жыл бұрын
DIEUREUDIEUFAAAT SERIGNE BETHIO SERIGNE BAMBA DIARRAMATYYY SWRUUU MAME CHEIKH SIIKKAARR NDIAYEEE!!!.(MF)
@PapeTiam
@PapeTiam 4 жыл бұрын
Mouride yi danio wara nopi mbidanou yonene te bi bimou dewé Diourbel lagnko soûl ak lane lafa donne def bâ deh fa niou soûl KO fa nioukoye weur touba baye lenne senne khel yinguene di fowé
@yorosarr4140
@yorosarr4140 4 жыл бұрын
Serigne Touba Amoul Morome Adouna ak Alakhira yaw sa serigne lou def ?
@puranegritafgueye2245
@puranegritafgueye2245 4 жыл бұрын
Serigne touba dou morom moo niou mom mom adouna
@djibysow1728
@djibysow1728 4 жыл бұрын
Pape thiam liga wakhe degule de
@lahatefaye899
@lahatefaye899 4 жыл бұрын
Yao.mome.khalatalnala.faite.trais.attantion.
@lahatefaye899
@lahatefaye899 4 жыл бұрын
@@djibysow1728 katal.sandaye
@koudiadiagne2661
@koudiadiagne2661 4 жыл бұрын
Yameuneu doul égaléoumeu li ngay wah.....serigbe touba dousen mbapando dou sen mass nagéin déglou mbindeum yi borom aras Maass
@mbayendiaye170
@mbayendiaye170 4 жыл бұрын
Yaw ki mola guena mokal bindam s touba
@OmarLoSaliou
@OmarLoSaliou 4 жыл бұрын
Mak bou tolni iow nga nek fi di doule nioune serigne touba lagne ame boulniou sonal yangui meilni kou diangoul alkhourane bo deimei thi souratoul Maa ida nga xole aayah 36 loumouye signifié YAA AYOUHALAZINA AMANOU ITAKHOULLAH WABTAKHOU ILAYHIL WASSILA xamo sarape ndm ba parei di doule tei yonente bi (PSL) neina MANE LAME YASSKOUROUNASSA LA YASKOUROUMLAH kone danga wara ndy nopi iow nioune ndawi serigne touba yi saxe niola geuna diangue geune la xame alkhourane geune la xame li yalla waxe li rek mo taxe ngeine tardei amoleine bene diome serigne touba dou morome tei douko meussa ame wassalame
@oumarsall4785
@oumarsall4785 4 жыл бұрын
Saway so diangonn dou cautionné wakhou shirk ak bokkalé.. Fii yalla rek mofiy dess gneuppay dé.
@OmarLoSaliou
@OmarLoSaliou 4 жыл бұрын
@@oumarsall4785Mdr yeine li serigne bamba ame moleini dérangé mais deimleine rek
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
Gana mo féne motakh wakh léne KO mou bayi féne touti
@mbackembaye8849
@mbackembaye8849 2 жыл бұрын
Yaw kay ndékété sa niouss yi mérite leu ni nga fi nékéwone
@mamadoutoure4165
@mamadoutoure4165 4 жыл бұрын
Merci
@djoloftv8223
@djoloftv8223 4 жыл бұрын
GANA MESSERE DOUL REK LAY DEF
@nissmanunited6459
@nissmanunited6459 4 жыл бұрын
Ak Bichir😁😁
@sysybeye720
@sysybeye720 4 жыл бұрын
Machallah
@Ndanaan2.0
@Ndanaan2.0 4 жыл бұрын
Nafeq rek. Dassss sa lamigne bamou gnaw nga def kO commerce Kay di manquer de respect nit gni tè do tousss linga gueum dou toussss. Cheikh tidiane dou sen moromou ndey dou sen moromou baye dou sen moromou askane.
@princeuhlenfantdupays6497
@princeuhlenfantdupays6497 4 жыл бұрын
Nafekh nga yaw
@mohamedsouare3028
@mohamedsouare3028 4 жыл бұрын
Senegal yénén tibi Mohamed (psl) touti lafi am do deug sakh wakham affairou tarikha rek gay deug sama serigne fii sama serigne fée🙁 dommage yalla nagnou yalla ball
@khalilnewyorkino9493
@khalilnewyorkino9493 2 жыл бұрын
Fechi kaaat bi😂😂😂
@layembodj8826
@layembodj8826 4 жыл бұрын
Le Problème Pourquoi Leurs Chefs N'a Pas Réagir De Ça. Qui Dit Rien Est D'accord
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
Bayile sa khél bingay fowé
@moustaphadieng2843
@moustaphadieng2843 2 жыл бұрын
Morite lha di wayi wakhga Lou âmme soulou
@rekoreko2255
@rekoreko2255 4 жыл бұрын
Yaw serigne ganna messre la geune fouff fi serigne touba rekka fi nek
@Ndanaan2.0
@Ndanaan2.0 4 жыл бұрын
Wakho deug dh ndakh ki gueun mom khamoko
@senuvideosenegalaise5879
@senuvideosenegalaise5879 4 жыл бұрын
Yawe yaye fene s.touba mou guene
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
DEUG la mé gana dafa féne
@mbayendiaye170
@mbayendiaye170 4 жыл бұрын
Yen mouridyi kou fen rek mom Guen beugué
@oxymor5711
@oxymor5711 4 жыл бұрын
Niou deglo xel tey xalaat bayi saaga yiii MO geune am leen yarr
@matarndiaye6587
@matarndiaye6587 2 жыл бұрын
Ay serigne gnam ñoko douma doumayou metti
@moukhamedkounta1121
@moukhamedkounta1121 4 жыл бұрын
Gana mésséré halisse rék laye woute hamoule dara talibés yi hamoule dara niokoye deguelou ak dico diohe séne halisse
@maryniang9476
@maryniang9476 4 жыл бұрын
❤❤❤❤❤🙏🤝👍
@papathiane4927
@papathiane4927 4 жыл бұрын
Serigne Touba rek mofineg
@omarsow2992
@omarsow2992 2 жыл бұрын
li mo takh wa Kaolack yi nokk la sa bopp bou niaw
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
Macha ALLAH
@Ndanaan2.0
@Ndanaan2.0 4 жыл бұрын
Boulen wakh GANNA dafay feneu. Nelen dafay Doule. DOMAKHARAM la rek
@djilykheucha4945
@djilykheucha4945 4 жыл бұрын
Sa data yaye waye imbéciles
@djibysow1728
@djibysow1728 4 жыл бұрын
Ahmed billay Ganena mesere diaroule tontou de ab golola rek
@lahatefaye899
@lahatefaye899 4 жыл бұрын
Satounou.ndaye
@djibysow1728
@djibysow1728 4 жыл бұрын
@@lahatefaye899 man gaye saga balenala akk
@gratanon7832
@gratanon7832 4 жыл бұрын
Jerejeuf
@zeynafaalfaal1807
@zeynafaalfaal1807 3 жыл бұрын
Gana moy doul la serigne bi
@mouhammedniang9416
@mouhammedniang9416 4 жыл бұрын
من شر حاسد إذا حسد
@toldotalibebamba1685
@toldotalibebamba1685 4 жыл бұрын
Yéne nak dagua ngéna begue aye vue kéne mounoul wakh ba gana wagni dara si lomouy wakh li serin bi binde laye wakh, mouride you keume laye wakhal, nopi léne.
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
Wa DEUG la mé gana dafa féne wakh léne KO mou bayi féne makk dou féne
@ousmanethiandoum6268
@ousmanethiandoum6268 4 жыл бұрын
Yalla baye NIASS la dioh xam xamou yalla ak yonentame wa nègal nagne wakh thi xam xam sou fèkèni sène Sérigne am nagne xam xam
@seydinaaliounembaye2667
@seydinaaliounembaye2667 4 жыл бұрын
Kén douwakh bay ak nit ak Diour dieumé ko si s touba dawakh ni نزعني من الورى باقي القديم
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
Waw souléne nékhé mé ngéne wakh séne féne Kate yii rawa Tina gana mou bayi féne
@adjiedia1786
@adjiedia1786 4 жыл бұрын
Yeun boulen nou sonal yawmi di Wakh si sa biir wakhdji khamenasi sa farfarlo sén imam bi chiekh tidjian cisse dan 6 moi si ginaw wakhnafi fakh djiou niaw si touba ak tivaun bási mam khalifa gir lan yakati baye niass te wakh djiodjiou sougeunon Senegal tass manmi maguie Yor video bi
@dyamsastar5162
@dyamsastar5162 4 жыл бұрын
ngi bayiléine fofou rek mais send ma lien bi ma use vidéo bi
@khazimndiaye2369
@khazimndiaye2369 4 жыл бұрын
nguir yalla bayiléne niou... nioune dolleine waxe baniou tontu léine mais nguir yalla bayiléine niou
@mamadousaliou7014
@mamadousaliou7014 4 жыл бұрын
Mai da ngeni togne Serigne niou diabouryi ak islam
@abdoulayendiaye1246
@abdoulayendiaye1246 4 жыл бұрын
S touba de kon yén dolén xol ay binnem limo wakhal bopam kén amol fi to wahko bo kén sokhor
@Ramandiassé106
@Ramandiassé106 4 жыл бұрын
Wakh dji barina trop iow sa yonne nékousi manoull yaguini di tague bay bagne kou tague serigne touba yaw ligay wakh ngamo si dara nitou fitnaga rék
@Ndanaan2.0
@Ndanaan2.0 4 жыл бұрын
Dimbalen gnou way. Est ce que souma wakhé sa serigne loula nekhoul dangay teuthi sa gate ? Yeukeutil sa serigne té boul toudou serignou diambour
@moukhamedkounta1121
@moukhamedkounta1121 4 жыл бұрын
Gana moye ganayo féne rék di woute halis rék
@moustaphagaye5785
@moustaphagaye5785 4 жыл бұрын
Nioune mouride nignou bague Serigne Touba nonou laniou bague Ghana
@ousmangaye1687
@ousmangaye1687 4 жыл бұрын
Deug rék la wakh Ganna fénn kat la
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
DEUG kay mé gana féne Kate la
@ebrimajagne8841
@ebrimajagne8841 4 жыл бұрын
Yaw loysaporoplem sawakh badina serigne gana messere limo AM serigne Touba mokoumaye manolen simoum dara dieureudieuf serigne Touba Mbacke amolmoroum
@ousmangaye1687
@ousmangaye1687 4 жыл бұрын
Ganna fén kat la
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
Wa DEUG la mé gana dafa féne
@somasoma7476
@somasoma7476 4 жыл бұрын
Dara laniou ladioul thi serigne touba soxla ouniou professeur particulier ga balma nak
@ablayedieng2454
@ablayedieng2454 2 жыл бұрын
Gana doule rekh 🐕‍🦺🐕‍🦺🐕‍🦺🐕‍🦺🐕‍🦺🐕‍🦺🐕‍🦺🐕‍🦺
@lenaniang7200
@lenaniang7200 4 жыл бұрын
YAw Daguay khar dagua mér 😃😃😃😃😃😃😛😛😛😛😛😛😛😛
@amadousouleymanesow8549
@amadousouleymanesow8549 4 жыл бұрын
Billahi ya sokhor,bone,ignane.yaw lo andal billahi leuzi lah ilaha ilalah serigne bamba mo guene cheikhou tidiane rombe nako yagguena.koudoul borom barrierou or ba fétté wouko kaw.kou beuggue ak kou bagne,koum nékh ak koum nakhari loloo té dou dégne.sa wakh dji nga fok ni amna léne loum meuna wagni soune digganeték ganna ak bichri.nakh nga sa bop téye lagne léne guena soope,guena gueme,guena wollou
@omarlo5740
@omarlo5740 2 жыл бұрын
Astahfiroulah 😱😱😱😱😱😱😱😱😱😱 Yaw dh mala yeureum
@Osirusavk
@Osirusavk 2 жыл бұрын
Serigne Touba logigoul néna goudoul yalla mola fété kaw mou tourné waxat khadimou rasoulilah nitt no néké serviteureum ba paré gueun ko boy Serigne bi waxou fi touss
@modougueye3531
@modougueye3531 4 жыл бұрын
Ki louko méti bamba feep
@diengmouhamadeune5693
@diengmouhamadeune5693 3 жыл бұрын
Arrêtez vous derrière
@abdoukhadretop255
@abdoukhadretop255 4 жыл бұрын
Yow dal sokhor dongue la diapp imame arabi niasse baxna Lou gueneu reuy lou biChri waxx
@mansourdiop2499
@mansourdiop2499 4 жыл бұрын
Séne coalision bi touba Niasséne daye wadia tasse dou deugue mo takh yéna bokk Serigne nakk yéna rawe Senegal wakhtane léne rékk
@دفراتسنغال
@دفراتسنغال 4 жыл бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂
@mansourdiop2499
@mansourdiop2499 4 жыл бұрын
@@دفراتسنغال deugue la di
@mouhamethniang9541
@mouhamethniang9541 4 жыл бұрын
Honzoubilahi mina chaytané radjim
@wakhaldeug8424
@wakhaldeug8424 4 жыл бұрын
Ioe diougeul fi nafekh nga
@khazimndiaye2369
@khazimndiaye2369 4 жыл бұрын
gnii lane moy séine probleme a vrai dire ?
@bambombambabar1637
@bambombambabar1637 4 жыл бұрын
Khazim Ndiaye na gana yém thi serigne touba rek té bayi cheikh Tidiane
@ibrahimawague4315
@ibrahimawague4315 2 жыл бұрын
Ki dou talibé nittou dara nittou ibliss la guemoule dara dor kat la
@Yibrafalien
@Yibrafalien 4 жыл бұрын
Yene ni sokhor la quoi yaw djémal melni Gana té meunoko mel ndax ki dafa tarbiyou loumou wax amna foumouko tekk✨✌️🤞
@oumarsall4785
@oumarsall4785 4 жыл бұрын
Tegou fenn ci loudoul ay Kathie Serigne Touba diam la défonn bopam, ndakh diam leu.. Bayilenn shirk ak bokkalé.
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
Non gana dafa féne wakh léne KO mou bayi féne yii
@babacargaye1845
@babacargaye1845 4 жыл бұрын
Gana yalnafii yag
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
Nianal KO mou bayi féne touti
@modoulamine9451
@modoulamine9451 4 жыл бұрын
Geustouwolen srgn touba ,tè njiko geustou wakh si mom ngen beug ko wedi,adouna metina ,sa srgn sou meunoul defoul boulni ken meunoul
@senuvideosenegalaise5879
@senuvideosenegalaise5879 4 жыл бұрын
Ganna da meloule né yaw yay féne katbi
@mamadouly1474
@mamadouly1474 4 жыл бұрын
Bayiléne niom niou wakh ni serigne touba mo geune chekhu tidiane lane lay wanni si martabam d'Ara té mo geune nguéén taal fi réwmi yow kéy thi sa biir khôl boul ték kéne si kaw chékhu tidiane deugeula sakh meune neniou téré wakh yi méll noonu waayé fékkeu ki ngay wakhal dalay comprendre waayé bo xoolé commentaire yi niome défuniu lolu waayé boudoon sama sago képpeu kuy wakh thi geunélu béppu serigne boul tuddu kéne wakal né mo fi geune rék wayé booné chékhu tidiane waayé sa wakh yaruna téyna té éske loolu la wakhi Mousa ka bi di tékki ndakh nitu yalla du wakhane tu
@ousmangaye1687
@ousmangaye1687 4 жыл бұрын
Talibé ckeikh domi nialo douko beugue wayé sén khol dina daggue té douguén si meun dara cheikh ahmét tidian rék ba dé
@ibnsamba1249
@ibnsamba1249 2 жыл бұрын
Li wax ni serigne touba mo meune cheikhou tidiane lolou mome kene mounousi dara
@omarlo5740
@omarlo5740 2 жыл бұрын
😂😂😂😂 Ba nélaw gua ligua wax eupna sa khélmi bo khamoul démal ladj sa Serigne kouy Cheikhou Tidiany
@Daouda28
@Daouda28 4 жыл бұрын
Yiaw barigua wakh sayy sayy deugg gua
@damendiaye3081
@damendiaye3081 4 жыл бұрын
Promotion promotion sokhor bakhoul way
@oumarsall4785
@oumarsall4785 4 жыл бұрын
Wadji deug rek layy wakh, talibé you ndaw yi gno warri bayyi wakhou dof yi dikko diawalé ak beug senn serigne.
@khadimndiaye9354
@khadimndiaye9354 4 жыл бұрын
Té man lima diakhal video bi 2018 la balégui loutakh boba wakho lén si
@moustaphagaye5785
@moustaphagaye5785 4 жыл бұрын
Yaw kay kone fene kat nga ndakh yaw ya wakh kou netaly fene fene kat nga kone kay yaw fene kat nga
@ousmangaye1687
@ousmangaye1687 4 жыл бұрын
Deuge rék la wakh
@mbayendiaye170
@mbayendiaye170 4 жыл бұрын
Yaw yaye fen
@khadimndiaye9354
@khadimndiaye9354 4 жыл бұрын
Yaw yagui toupou si Ganna mésére té mom talou la
@ousmangaye1687
@ousmangaye1687 4 жыл бұрын
Ganna fénn kat la
@khadimndiaye9354
@khadimndiaye9354 4 жыл бұрын
@@ousmangaye1687 yaw dagua tardé
@mbayendiaye170
@mbayendiaye170 4 жыл бұрын
Douko tal ndakh te khaliss rek la beugue
@abdoukhadretop255
@abdoukhadretop255 4 жыл бұрын
Iow dagua amoul yarr bo bayilwoul batoub féne biguaye waxx di ci tek kou téd ki
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
Mé dafa féne a sou féné douniou KO wakh
@khadimdiop7867
@khadimdiop7867 4 жыл бұрын
Yéna ngui diéferou. Lidienti lène séni tarikha. Li rek takh nguène tarder
@saokadia9835
@saokadia9835 4 жыл бұрын
Talibe cheikh yi nioko yor maso deug serigne tidian bogniou posené niata serigne mourid nio dee si posene
@khadimdiop7867
@khadimdiop7867 4 жыл бұрын
@@saokadia9835 😂😂😂😂
@lahatefaye899
@lahatefaye899 4 жыл бұрын
@@saokadia9835 yawpossone.molayeraye
@saokadia9835
@saokadia9835 4 жыл бұрын
@@lahatefaye899 dangay doull khana yaw yay yalla
@harounaniang2002
@harounaniang2002 4 жыл бұрын
Ah mé gana mo togne féne wakh léne KO mou bayi féne yii
@bayedamekasse4641
@bayedamekasse4641 4 жыл бұрын
Wa demal diagi ba nopi
@ebrimajagne8841
@ebrimajagne8841 4 жыл бұрын
Serigne Touba Mbacke mofetekawgnepo amol moroum
@momobalde4765
@momobalde4765 4 жыл бұрын
Yw mi di wakh fenkat nga khamo dara te amo kham kham amo wilaya
@mbayendiaye170
@mbayendiaye170 4 жыл бұрын
Ki mo abpou xam xam sa papa
@momobalde4765
@momobalde4765 4 жыл бұрын
@@mbayendiaye170 bale nala
@moustaphagaye5785
@moustaphagaye5785 4 жыл бұрын
Yaw miii Yaye fene ndayam domou khathie
@moustaphagaye5785
@moustaphagaye5785 4 жыл бұрын
Billahi bou vocal amone doto guéne di wakh
@mouhamethniang9541
@mouhamethniang9541 4 жыл бұрын
Wakhofi dara
CAN YOU DO THIS ?
00:23
STORROR
Рет қаралды 42 МЛН
Human vs Jet Engine
00:19
MrBeast
Рет қаралды 162 МЛН
Elza love to eat chiken🍗⚡ #dog #pets
00:17
ElzaDog
Рет қаралды 12 МЛН
UFC 308 : Уиттакер VS Чимаев
01:54
Setanta Sports UFC
Рет қаралды 806 М.
Cheikh Ahmed Cissé limou wakh Serigne Mountakha Mbacke rafetoul dara dara
15:45
Diganté Serigne Touba ak Mame Cheikh Ibrahima Fall par Serigne Bouchra Samb
58:00
CAN YOU DO THIS ?
00:23
STORROR
Рет қаралды 42 МЛН