Machallah CMS vraiment merci do séne morome ba paré ame nga yar ak téguine😍😍😍
@bakarykurumang41362 ай бұрын
This guy is great in knowledge
@ibrahimasall48892 ай бұрын
Machallah bonne Continuation kham kham mo wor
@diopdiop75192 ай бұрын
Deug deug do sééne morome- Que Dieu veille sur toi Ma sha Allah
@linoosekk67722 ай бұрын
Machallah yangui léral féne yine nou gueumlowone
@djibrilndiaye63972 ай бұрын
Il est loin le meilleur Cheikh mbacké Sakho Heureusement qu’on a une personne comme ça pour nous éclairer le chemin de DIEU
@groupems45772 ай бұрын
Cheikh Mbacké Sakho. Machallah !
@oulsop2 ай бұрын
Cheikh Ahmed Cissé dieureudieuf tu poses les bonnes questions machallah😍😍😍
@diopdiop75192 ай бұрын
S 45-V 6-Voila les versets de Dieu que nous te récitons en toute vérité Alors dans quelles paroles croiront-ils après la parole de Dieu et après ses signes(waw y'Allah vakh li ta aye vakhame di Alkhourane nga gême yénéni vakh youdoul aye vakham)
@AmieFaye-sr7rw2 ай бұрын
Machalla Cheikh bi yalla sa diam yague Cheikh Mbacké saho yalla fayal gnoula yéna ngui gnoy libéré ak ham ham bou lére
@NdeyeyandeToure-j2q2 ай бұрын
Merci grand Cheik de nous remettre sur le droit chemin❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@hoorevision57532 ай бұрын
Cheikh Mbackè sakho un homme multidimensionnel
@elhadjiamadousow59162 ай бұрын
Mon idole spirituel après Mohamed saws
@AhmadouDieylaniba2 ай бұрын
Masha Allah, very beautiful. May Allah bless you.
@ebrimabah95782 ай бұрын
pin point questions . you killed it my sheikh..
@ibrahimasow11272 ай бұрын
Machallah khôl seddatina jerejeuf cheikh yi yalnalene yalla yaggal té samm leen
@bacarymaria61172 ай бұрын
Salam merci CMS le prophete Mouhamad PSL est devenu prophete a l'age de 40 ans .C'est quand fut revele qu'il est devenu prophete donc c'est le coran qui confirme le prophete et non le contraire.En plus le coran dit je viens de DIEU mais si vous n'y croyiez pas alors produisez un verser. semblable et personne n'a releve ce defi.CMS est tres pertinent que le bon DIEU le protege et continu de l'eclairer.Salam.
@CheikhDiallo-bd5cu2 ай бұрын
Mane mi depuit Bima khameh cheikh mbacke sakho laa changer ni ma done djouleh
@diopdiop75192 ай бұрын
Débat:diné islam kiye vakh Alkhourane ak kiye vakh lénéne dougniou bok CMS vakhou y'Allah laye nétéli motakh kéne manouko danél thi diné islam
@Gaye-industrieАй бұрын
Cheikh mbacke sakho il faut gua deglou ko ak xel pour xam loumouy waakh❤❤❤
@aliouneseck25112 ай бұрын
Walahi Cissé wakhal nga yalla tu est le meilleur
@MounassAw-e7n2 ай бұрын
Manchalla ❤❤❤❤❤❤❤❤
@YayouNabi-w7z2 ай бұрын
salam je suis vraiment facinee par cheikh mbacke sakho yaw mi la doon weer donnez vos contacts svp
@LeisterLotus2 ай бұрын
C la chaîne KZbin nihma tv
@Alascreationstandardfashiondes2 ай бұрын
Mashallah ❤
@abdoulazizly16122 ай бұрын
Machallah
@MouhammadCisse-dz5mt2 ай бұрын
Koumay diokh numéro mbacke Sakho kii dall jambarla
@RS.Africa2 ай бұрын
Nihma.tv
@Cabayoroyoro2 ай бұрын
Dangay suivre chainam Nihma Tv
@papissow22642 ай бұрын
Eyway sa DJ bi Mouna gayi
@diopdiop75192 ай бұрын
Kouko védi-védi vakhou y'Allah-loumou vakh ni fi la nék thi Alkhourane-Alkhourane nak daye dathi entreprise yinou créé diné islam ngî séni poche-li y'Allah ni borome khél yi laye vakhal-CMS borome khél yi laye vakhal-
@ablayng64462 ай бұрын
BAYE NIASS KOUDOUL MAME ELHADJI ABDOULAYE NIASS MEUSSOUKO DIANGAL BÉN NAAR MEUSSOUKO DIANGAL
@abdoumaslahmaslah35322 ай бұрын
Quelle clarté
@AhmadouDieylaniba2 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤
@pierrediatta70542 ай бұрын
Hi guys, how are you today? I will appreciate if you guys can challenge Christian Prince or Ahmad Muslim so we can have better understanding about.
@moussafaye95472 ай бұрын
Salam cheikh Mbacké sakho yaw dale ki dou ko wara tongale ndakh da nianweu lamine
@diopdiop75192 ай бұрын
Fi dini lahi-diné thi y'Allah moko mome-yonétebi la tane yoniko diné islam-yonénetebi démna-Alkhourane djine ko yoni vone mofi déss moye ligniou vara tope-Kilifa diné y'Allah vové vouko yonénetebi-kigniou sol ndaw li kinou tane tour yoyou lako y'Allah di vové-kone kilifa dîné founou diokè-
@babacardiagne17662 ай бұрын
Cissé❤❤❤
@babacarcisse15172 ай бұрын
Hola
@doyendiouf6240Ай бұрын
Non cheikh happy no stress
@mbyehughes3922 ай бұрын
Waurna yallah kii dayy rèèra laatè
@sambatoure88102 ай бұрын
Bayil sa thiakhan yi ki dila wakh alquran ngani day rérra laté😂😂😂😅
@DembaSow-bo2fz2 ай бұрын
يا ربنا زدنا علما وتوفيقا...كم عالم فَاتَهُ تَوْفِيقٌ حَتَّى أَجْهَلَ فِي الْعِلْمِ....مَنْ لا يسمع قول النبي صلى الله عليه وسلم كيف يسمع قول الله هذا اعجبني 😅😅
@badoubousonkofall2 ай бұрын
m,acha alla
@YayouNabi-w7z2 ай бұрын
lamine faty goor pir am djoudou bou bakhe dou saga. saga faibleyi lapatos yi gno ko moome
@fulaninasroullah77162 ай бұрын
Salam ki khamoul dara yonanti bi la guemoul alkhouran bi Mouy wakh aye sahaba gnoko dadialé binde ko gnognou gno dadialé sounna binko alkhouran bi si langue arabe la wathe si arabie saoudite gnognou gno guena degue arabe AK alkhouran gnognou gneupe deupo nagnou diangalé salafiste mo guena wérr ki tok si youtube Di wakh louko nekh ragaléne yallah
@Cabayoroyoro2 ай бұрын
Wakhi deugg s75v17-18
@sambatoure88102 ай бұрын
@@Cabayoroyorobayko mouy nakh bopam rek !!😂😂
@mamemorantasaly7942 ай бұрын
Yaw est ce que wéer nga ???
@fulaninasroullah77162 ай бұрын
Yow mi ya wéroul @@mamemorantasaly794
@oumardionguethioune6302 ай бұрын
Face to face Alpha Ba ak Mbacke Sakho pour mieux vous refaire sur le coran.....
@senegalpoint50652 ай бұрын
Billahi Alpha Bâ gnièmèwoul tè amoul niveau bi outal kènèn
@mouhamadsane67592 ай бұрын
Il a le cerveau cérébral endommagé, deyy daw dh niveau yii bokkul 😂😂
@Cabayoroyoro2 ай бұрын
Alpha Ba dalay méré deh 😂😂😂 CMS rékk la ragal
@mamemorantasaly7942 ай бұрын
Alpha Ba amoul niveau khamoul dara ci alxourannnn !