Cheikh Bara corrige publiquement Oustaz Mouhamed Mbaye "Ci Yonente bi" : Biteye les rectifie

  Рет қаралды 8,353

Walfadjri TV

Walfadjri TV

Күн бұрын

Пікірлер: 80
@rubicon1004
@rubicon1004 7 күн бұрын
No vous avez tort. En diné quand vous donnez une fausse information sur la place publique, vous devez être corrigé sur la place publique.
@abdoukarim4239
@abdoukarim4239 7 күн бұрын
Bitey yaw waxo fi Darra k joum public dañu ko wara corrigé public
@falloubasao7386
@falloubasao7386 7 күн бұрын
légui man bou barra Ndiaye corrigé wouton si public konn man samay fook ni li ameth wakh dégue laa
@ArjunJaikumar-f1g
@ArjunJaikumar-f1g 6 күн бұрын
Ak mann😂😂
@adnanekane5571
@adnanekane5571 7 күн бұрын
Oustaz bobou thi place public la fenal yonentebi fofou laniouko wara djoubanthi
@babacarba4273
@babacarba4273 6 күн бұрын
Bien dit bitey mom nafekh lah
@Ndeye-y2b
@Ndeye-y2b 5 күн бұрын
Salallahou halayhi wasallam❤❤❤❤❤
@lycherif1552
@lycherif1552 7 күн бұрын
Biteye nafikh la
@badiboy8698
@badiboy8698 7 күн бұрын
Bitey yaw nafekk gua bou magu sakh kou fen sii publique sii publique nanou kay wedee mouhamed mbaye dey fenn te khamnani dey fenn point baye ibou sakho moko eupeu kham fouf te mousouko wakh
@lycherif1552
@lycherif1552 7 күн бұрын
Lii souko touboul safara la diem te yonentebi moko wakh من كذب على معتمدا فليتبوأ مقعده في النار dou sama wakh wakhou صلى الله عليه وسلم la
@damendiayenekhthiouraye134
@damendiayenekhthiouraye134 6 күн бұрын
Serigne touba Khadim rasoull. Moussta Wakhall seye dina Mouhamed Lo niaw ba thie kharé yine ko gagner serigne touba daffko wormall ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@seexxunaadaraame6809
@seexxunaadaraame6809 5 күн бұрын
Jërëjëf wax nga dëgg.
@DjibiFall-rp1nc
@DjibiFall-rp1nc 6 күн бұрын
Mbaye Wahul dëgg
@idrissafall2239
@idrissafall2239 6 күн бұрын
Biteye macha allah yay walfadjri li nga wakh lolou moy dégu
@ibrahimakhalil2987
@ibrahimakhalil2987 6 күн бұрын
C'est exactement ce qu'ils font de Serigne Touba
@gninguekhadim531
@gninguekhadim531 6 күн бұрын
Mohamed Mbaye pour yaw ta raw cheikh bara Ndiaye mais là tu t'es ridiculisé car tu n'as pas avouer que vous avez fait une erreur et tu ne l'as pas accepté aussi cela montre que tu joues la fière tu devrais d'abord accepter ton erreur avant tout
@cheikhciss5549
@cheikhciss5549 6 күн бұрын
Waadji en costume deug rk la wakh sénégal amounou béén Thieur si YONNENT bi(psl)
@dinakane2032
@dinakane2032 6 күн бұрын
Biteye il veut tjr faire bonne impression 😂 nous savons tous que le gars Ameth soi-disant outaz dafa fenn donc arrêtel sa hypocrisie bi
@Snoopy266
@Snoopy266 6 күн бұрын
Bitéye bayil di wakhé sa khél légui nga nafékh deh . Borom xam xam yii niou khamal yalla ak yonenta bi (Psl)si penc mi ak xalima la niou dann wéranté . Pour nioune gni xamoul dara meuna mouthii si sén ndioumté .. cheikh bara bou wédiwoul wonn si penc mi sama classe gou amoul khél yii daniou geum né yonénta bi meuss nagn ko diapp ba dico nanne lo sawou geulèm astakhfiroulah 🙏🏽
@gninguekhadim531
@gninguekhadim531 6 күн бұрын
Biteye yaw mom Lou yalla xam doyna Il faut trancher c'est mieux Cheikh Bara Ndiaye dafa am ay nitt nioko demander la question et il a répondu sur le même groupe et Les vocaux sont partagés
@SerigneMbackeSylla-wq8ff
@SerigneMbackeSylla-wq8ff 6 күн бұрын
Bitéy mii doofff pire la
@lycherif1552
@lycherif1552 7 күн бұрын
Yow biteye mou wakh sii loumou wakh rek nga yam sii faw nga indi sonko nafikh bakhoul cheikh bara Ndiaye xam xam lako tontou momit na tontou xam xam rek wakhbi diekh
@taphandiaye2901
@taphandiaye2901 5 күн бұрын
Bien dis bitey nafekh la
@faliloufalilou493
@faliloufalilou493 5 күн бұрын
Kou déf erreur si place publique meunne na réral ay nite you beurri motax si penc mi lagnou KO wara djoubeunté
@papaalioulenerekmomanakhar1989
@papaalioulenerekmomanakhar1989 7 күн бұрын
D’accord yako raw mais dagua féne ligua wakh dou deugue
@MUSTAFASALIHSÀMB
@MUSTAFASALIHSÀMB 6 күн бұрын
Eska moko raw ?
@serignesaliousarr3566
@serignesaliousarr3566 6 күн бұрын
Saway bitey mi li day wané ni xamoul dara ci diné , kite kou dioume ci penc mi lou tolni sossal yonenti bi ci penc mi lagne koy corrigé
@sidytambedou3541
@sidytambedou3541 6 күн бұрын
Astahfiroullah younéntiby diangouma fougñoukou diappé
@assanesene4063
@assanesene4063 7 күн бұрын
Bitaye ligaye wakhe tégou fine dagaye fine rekk
@diarnotv31
@diarnotv31 7 күн бұрын
Il faut aussi corriger l'affiche, la croix rouge est là où elle ne devrait pas être. Merci
@AïchatouBâ-u3i
@AïchatouBâ-u3i 7 күн бұрын
Nguéne balmabé mé esq biteye wakhoule DEUG naka sama nbokyi
@malcolmxjr1717
@malcolmxjr1717 5 күн бұрын
yaw yangui toppeu sa kholl bi ba léegui, yonéntte bi SAW néena képp kouma fénal té tayko nanga waadial sa beureub tchi sasara, mais bitéye linga wakh yaw tamit tégooko fénneu kou fénn tchi pénthie mi gnou yédd ko tchi pénthie mi pour guindi gnou khamoul
@BabucarrSarr-d1x
@BabucarrSarr-d1x 6 күн бұрын
Legiu pour public bi Nak kagn lay ler
@bassirouba3338
@bassirouba3338 6 күн бұрын
Lha xayafi dîner biteye dhél wakh si comédie té bayi dîné kou dioum niou dioubantila
@idrissafall2239
@idrissafall2239 6 күн бұрын
Cheikh bara mougui fii diii défendre ay fénn
@ThiernomouhamedSy
@ThiernomouhamedSy 6 күн бұрын
Oustaz nangoul lk danga dioum adou na amoul solo 😢
@ArameNiang-r8j
@ArameNiang-r8j 6 күн бұрын
Bou fekeir dé niou ka warone Kay Fanne la wone ioe mi Di wax sakh kham nga ni li ngay wèroute
@mouslayeimmosenegal3529
@mouslayeimmosenegal3529 5 күн бұрын
bitéye setane nanioula fi ak ouztaze bi nekk walf guate xamoko si diné teudieul sa guémigne sa aloua dafa guateu amo si xam xam nafecc nga waxxal deugueu sa mbaye bobou nafecc nga kou fènal yonente bi publiquement di rèral aye nitt danioulaye ndaye werr publiquement.
@hulkhulk4973
@hulkhulk4973 6 күн бұрын
Bitey dességa maitrisé lislam !!! Lislam contradiction la weranté la !!!! Sou dioumé danioukoy dégui lolou RK
@abdoulayesagnan9642
@abdoulayesagnan9642 6 күн бұрын
YÉN MOM BITÈYE DOFOULO NALÉN BAPARÉ LÉGUI SOPINALÉN AY NAFËKH CHEIKH BARA NDIAYE MÔ NÉK CI DËUG NGÉN CROIX KO THIM
@groupenabiyetv8211
@groupenabiyetv8211 7 күн бұрын
Mouhamed mbaye djiamil yonén té bi dousa morom man de talibe cheikh la com yaw wayé linga wakh mom ndioumté la
@CisseBaboubeuguebayeniass
@CisseBaboubeuguebayeniass 6 күн бұрын
Salam biteye ci internet bi Lako wakhe motakh mou Tontou ci internet bi
@papyjunior4780
@papyjunior4780 6 күн бұрын
Biteye mane je n'aime pas boy wakh walleu ngay diokhé conseil surtout si diiné. Ndakh say conseils loussi beuri baakhoul. Diapp si rek nguir ALLAH yémal si diniou reetaane lo rek!
@ndiayendiaye313
@ndiayendiaye313 6 күн бұрын
Bitey nafekh bakhoul
@TeuwIbnou
@TeuwIbnou 7 күн бұрын
Dine ken douko wahk si souf
@ousmanesane4791
@ousmanesane4791 7 күн бұрын
Mouhamad mbaye ment et refuse qu il.a menti
@cheikhalimdiop2938
@cheikhalimdiop2938 7 күн бұрын
Louci yonou sonko ak bougane arrêté len waay
@adamadiallo-zg5js
@adamadiallo-zg5js 7 күн бұрын
Biteye tais toi Cheikh Bara l'a corrigé.
@modouniass2397
@modouniass2397 7 күн бұрын
Le s'avoir ça ne passe pas comme tu l'entends
@BabacarSeck-ix4hl
@BabacarSeck-ix4hl 7 күн бұрын
Mohamed mbaye amoul xam xam dafay degue di wax wax, diangoul, même cheikh bara dou borom xam xamou diine mais mo raw Mohamed mbaye, il faut diine dji borom xam xamou diine yi di wax si diine, kou djangoul noppi. Yonene tebi swsl mos na am belesur si khare mais ken mosou djapp com prisonnier
@papandiayeba7751
@papandiayeba7751 6 күн бұрын
Bitey day siissou
@LayeThiam-y4l
@LayeThiam-y4l 7 күн бұрын
Ferante bahoul
@Ahmadu-o2n
@Ahmadu-o2n 7 күн бұрын
Mouhamed Mbaye fénal na yonnant yàlla bi Yonnant yàlla wax na ni kuko fénal sa gètte manga sa safara
@elhadjindiaye7089
@elhadjindiaye7089 7 күн бұрын
Mane sa sopé la mais dîné kéne douko wéke thi dégue na
@ThiamSouleymanethiam
@ThiamSouleymanethiam 7 күн бұрын
Muhammad mbaye bayyile sa niakhayi borome khamm dangaye am dèlouwaye si tèrrai
@morndiaye8680
@morndiaye8680 3 күн бұрын
Cheikh bara mo wakh deugue
@moussadiallo7990
@moussadiallo7990 6 күн бұрын
Biteye li diné la bothi waxé thi penc mi loudoul nonu fok nio tontu thi penc mi,tay mome dioum gua
@AhmadouSamb-o6t
@AhmadouSamb-o6t 6 күн бұрын
Biteye wakhofi dara naafeékh bakhoul
@senganeibou
@senganeibou 6 күн бұрын
Bitey nafekh pire nga
@alaminethiam6950
@alaminethiam6950 6 күн бұрын
Bety mboup résumer na lép si thiowou sidy lamine ak Idrissa Seck affairou diné kou si wakh publiquement bougne lay tontou publiquement lagne lay tontou pck dougne bayi ngay réral gnénén gni
@MorTouure
@MorTouure 7 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂
@BabucarrSarr-d1x
@BabucarrSarr-d1x 6 күн бұрын
Muhammed mbaye na nangou ni yeynanko
@adamadiallo-zg5js
@adamadiallo-zg5js 7 күн бұрын
Mouhamed mbaye dey fénne waxoul deugue
@taphandiaye2901
@taphandiaye2901 5 күн бұрын
Bitey nafekh ga
@MakhtarFall-mq5ko
@MakhtarFall-mq5ko 7 күн бұрын
Biteye xam ak xammee du benna kii yonontebi la tumaal sun baayyee man na reerar ay nit yu beuri kon publiquement lanko wara corrigé
@serignesalioulo8023
@serignesalioulo8023 6 күн бұрын
Non non Mohamed biteye andou ma ak yaw dh a faire bi dou problème bara njaay ak oustas dh Mohamed mbaye mon joom limou wakh dou XAM XAM daa wara dellou ganaaw rëyy bakhoul
@babacarba4273
@babacarba4273 6 күн бұрын
Bitey yaw khamo touss sof nga deff ameth mbay da fène gnou wakhco day fène mou diekh
@aliounebadarandiaye5344
@aliounebadarandiaye5344 6 күн бұрын
Biteye est un vrai hypocrite
@Tiktok_insta_youtube123
@Tiktok_insta_youtube123 4 күн бұрын
Biteye tay mom dioum nga 😂 yaw tmt
@MDN_12
@MDN_12 6 күн бұрын
Mouhamed mbaye fén katt la point🤷‍♂️🥱té amoul doulli xam xam🤦‍♂️genre yii nio yakh Sénégal yaw diangoo ba paré naan dagne maa wakh😂 Yaw mane mii sakh gua khamni sama xam xam soriwoul si siira khamnaani lingua wakh ay mééw laa😒🤣
@soulymandione4895
@soulymandione4895 6 күн бұрын
Dine bi yalla kou mokoumome kine moumouko kou joume gnou wahalako
@moussadiallo7990
@moussadiallo7990 6 күн бұрын
No biteye tu ne comprends pas li thi penci mi lako mouhamed mbaye waxé donc fok gua tontu thi penci mi,té li nieup la concerné car islam la doka bagni nonu
@sadatall2911
@sadatall2911 4 күн бұрын
Bitey je suis pas d'accord avec toi foumou waKhé rék laniou kô tonto
@ibrahim8899-j3z
@ibrahim8899-j3z 7 күн бұрын
Diap yonnét Sws kou wax lolou. Non lolou manoul dh dou deug Ya rassoulahi kene massouko diap. Meme encerclé bi guen dii wax sakh motax yassine wadj biko yonnén bii diagui yéfar yi yep nelaw meme ibliss dafa nelaw yonéne bii diar sene kaw dem lou sorri gnoy dora yewou lolou mom amoul
@DjibiFall-rp1nc
@DjibiFall-rp1nc 6 күн бұрын
Bitty yaw nitnga
@babadiop5851
@babadiop5851 6 күн бұрын
Biteye tu n’as rien compris bayil di wakh si lo khamoul pourquoi mou warr ko wakh si souff c en matière de diné Yaw mi laniou wara yedd nakk
We Attempted The Impossible 😱
00:54
Topper Guild
Рет қаралды 54 МЛН
99.9% IMPOSSIBLE
00:24
STORROR
Рет қаралды 30 МЛН
Professeur Abdoulaye Dieye Corrige TekkiForLife!!!
14:25
XIFF XALIS DISCIPLINES
Рет қаралды 17 М.
Cheikh Bara Ndiaye Attaque Mouhamed Mbaye…Daye féne lim…..
22:34
LUNAIRE NEWS TV
Рет қаралды 103 М.