❤ Masha Allah ya sheikh Ebrahima Khalil lo ngabou yalla mai la werr
@assaneniang2133 Жыл бұрын
Assalaamu alaykum wa rahmatul Laahi wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yonnènt bi sAaws akiy sahaabaam rAa te wërsëgal nu ci ngënéelam nu dëkag gnoom ca kërug teràngaam. Nanu YÀLLA wan dëgg bamu leer mu yombalal nu topp ko, mu wan nu neen ba nu ràgnee ko mu yombalal nu dùmmôoyu ko. Nanu YÀLLA sàmm sàmmal nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xamxam. Jërëjëfati