Machalla diouf makhtar .... ken gueunoula ya bakh ta am talibè .... yag fi ta weer
@mthiam15672 жыл бұрын
Machallah. Lii Rafetna torop. Yalla na la yalla sameu ci Barke Baye akh ci Barke kou teddedki ki nga yakar..
@elhadjiba73322 жыл бұрын
YOOW DÉ BOROM DIMBAAL WARA NGA SANT BA DAME TABBI GUI SERIGNE SALIOU TABBI SÈNE BIIR DIEUL LA NGAAY TALIBÈME.LI DÉ DAAY FIRDÉL SERIGNE SALIOU MO YIILIF GNEP.DOOM DOOMU GUEUMÉ NI SERIGNE SALIOU LI DÉ WARNA YÉ KÉP KUUY NIITE.DIEUREUDIEUFTY SERIGNE SALIOU❣️❣️❣️♥️♥️♥️♥️
@modousarr193352 жыл бұрын
Jajëf Cheikh Makhtar Diouf,taylalay dogagis,muy luma neex Yàlla na yàlla mayla wér ak Gude fanew
@ghaliou29 Жыл бұрын
Machalllah respect à vous. C'est ça le Sénégal respect à nos guides religieux
@amadougueye6485 Жыл бұрын
Référence yi la Sénégal sokhla machallah té gnou mélnii gnou meune tabakh ap réuw
@moisediedhiou-jx8pv Жыл бұрын
C est vraiment ça l'élégance politique en démocratie. Éloigné sa famille du pouvoir politique. Le sang suit toujours sa lignée ancestrale biologique. Bravo président Diouf Abdou et ses enfants. Vraie croyance. La vraie foi paie cash. DIEU protège votre famille et le Sénégal. Merci
L’exemple du président Abdou Diouf c’est de ne pas vouloir mettre ces enfants aux pouvoirs et ne pas faire du Sénégal une république bananière merci infiniment Monsieur le président que dieu vous bénisse amine y’a raby 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🌹🌹🌹💕💕💕💕💕💕💕💕💕💓💓💓💓💓💓💓💕💕💕💕💕🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹
@awacisse70474 жыл бұрын
MASHA Allah mouride sadéh rek moy DEUG ak talibé rek mo ame solo
@mamadousene3552 Жыл бұрын
Vraiment tu as eu un père excellent et exceptionnel . Un vrais président . Que DIEU le garde
@serignesady6477 Жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Makhtar Diouf Yalla nagua fi gueuneu yague lolou témou andack wér ak wérlé andack diam ak salame yak mboleme koula sop thi barke Yonantibi Seydina Mouhamat Psl Barke Serigne Touba Khadimou Rasoul Mbacke Sounou Yakar🤲
@baldeissa2501 Жыл бұрын
Les confidences et révélations de Cheikh Makhtar Diouf sur le Khalife Général des Mourides Sérigne Saliou Mbacké. Un entretien captivant et instructif qui met en relief la pertinence de ce Grand Homme de Dieu qu'est Sérigne Saliou.
@fatougueye97352 жыл бұрын
Dieureudieuf mouride,goude fane ak werr thie barké seydina Mouhamed (psl)
@galloniang1602 Жыл бұрын
Cheikh Makhtar Diouf un talibe mouride bu deggu lool te baax
@barandoye74132 жыл бұрын
Ndeyssane YALLA NA BOROM BI YOKOU AY LERAM TASS NIOU SI BARKÉM MACHA ALLAH AMINE
@mbackeleye4264 Жыл бұрын
Masha.allah Alhamdoulilah
@laminesene95382 жыл бұрын
Billahi domou président la deh yala rek la beug ndah mounona nek si lenene lounehoul yala ndah boudé khalis rek ak doundou louneh amnako sant yala
@NganeSalihate2 жыл бұрын
MashaALLAH Srigne SALIOU Mbacké BOROM Bi yokk lèeram
@kanemariame8262 Жыл бұрын
Machallah la mosquée du monde musulmane❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@khadimfall87343 жыл бұрын
Macha allah. Ki Damako santir ci bopou rewmi bilahi
@elbiranetoure48702 жыл бұрын
Walahi ki moride sadikh là Sénégalais khamoni Abdou Diouf amna Dom diomelni Serigne Touba rek moko nior
@sawolamo Жыл бұрын
Cheikh ba gui, nit kou bakh ki woyof yaatou beugue domou adaa yi, kène dou yow Bakh gua torop torop mashaALLAH Yalla nafi yague tè wér
@SidahmedMeiloud2 жыл бұрын
Salut, je ne savais pas que Abdou Diouf a un fils à cet âge et mourid en plus, bravo ! Vive le Sénégal..
@ibadiop2546 Жыл бұрын
BIEN SÛR QUE LE FILS AINÉ DU PRÉSIDENT ABDOU DIOUF.PERSONNELLEMENT JE LE CONNAIS.NOUS AVONS FAIT LYCÉE MALICK ENSEMBLE,AUSSI NOUS ÉTIONS ENSEMBLE À LA SICAP DIEUPPEUL 2.UN MOURIDE FERVENT TRÈS SINCÈRE TALIBÉ DISCRET ET RESPECTUEUX.NOUS AVONS VÉCU DE SÉRIEUX MOMENTS ENSEMBLE. MERCI.
@adamadiouf88583 жыл бұрын
Thiey sama waji SERIGN SALIOU MBAKÉ
@MamadouFall-jh4wv Жыл бұрын
❤ Àaaaaammmmmiiine ❤
@aliounetoure76282 жыл бұрын
MANSHALAH:AMENA SOLO ,RAWEGUE SAYE MASS.
@khairydiallo2833 Жыл бұрын
Mâcha Allahou 🙏🙏🙏
@SaxumToubalofficiel Жыл бұрын
Makhtaar loutakh do lawakh moukni ginaaw yalla Mala yobbou thie Serigne saalihou AK Serigne Abdoul ahad yaak sasokhna AK rakkam ndofene AK rahmatoullahi cheikhouna bousso Domi sokhna may galas..malaboleek Serigne Abdoul ahad. AK Serigne saalihou yonou mouride mountakh rek wakh serre koubaakh douma wagnie dara.limawakh loutotila thie finoudiaar
@mbayendiaye67132 жыл бұрын
Alhamdoulilah sante rek yok wer goud fane rk
@karbalacisse24203 жыл бұрын
macha ALLAH yague yook weer
@ramataba5463 Жыл бұрын
Mashallah Alhamdoulilah
@Tse369 Жыл бұрын
Mach’ALLH🙏🙏🙏
@khadimdiop9384 жыл бұрын
Wakhtane bi Amña solo machallahthieuyeserignetoubakenedoumome
Alhamdoullilahi rabbil alamina ki rek moy talibè Ki rek mo bakh
@cheikhahmadoubambandiaye43602 жыл бұрын
1997 boba sa papa mo nek président nga djité ab dahira loolu kiman la dh domi président daana tall lenén liudoul youni mell dadan profito si pouvoir bi di noss
@diaspora25532 жыл бұрын
Abdou diouf amna domdjiou tollou ni ki taye lako khamme mais talibe la masalla
@elbiranetoure48702 жыл бұрын
Xam nakou dé bou yageu dé mais Talibe Rek Laye dondou
@mordiawdiaw12022 жыл бұрын
Xhmnako boyagg 1995 lawone tia dahratia
@mamoudoudiane81982 жыл бұрын
Qu’il repose près du prophète Ahmad PSL
@coumbaaichambow1859 ай бұрын
Thieuy serigne Saliou
@makonte7103 Жыл бұрын
MashaAllah Pedro🤔🤔🤔🤗
@moussagueye4049 Жыл бұрын
Tres humble !
@kif74713 жыл бұрын
MACHALLAH
@ablm91012 жыл бұрын
Machalla diouf
@adamadiouf88583 жыл бұрын
Dama beugu serign SALIOU
@moussagueye83642 жыл бұрын
Ku bax ki bari gua ci morom Il m'arrive de verser des larmes, juste en regardant sa photo.
@dabafall33 ай бұрын
Theye serigne saliou
@sambaka6552 Жыл бұрын
Un vrai mouride en l'écoutant
@ngagnewillane68902 жыл бұрын
Merci
@vissionmuride Жыл бұрын
Aaa abdou ya bari gaaff nak
@kotyniang7396 Жыл бұрын
Machala sama khole cédena
@fatoudiouf4658 Жыл бұрын
Salam yalla bour bi mon yieme pedro la wone ba thi Serigne Matar sa Badiene contana Serigne Touba nioune meunou 'nou 'noko fay Serigne saliou yalla na bour bi yessal yeurmande thi akhlou mbake yiep dieurdieuf Diouf Semou yalla na gua fi ya g AK sa ,wadiour wowou Amin yarabi Diouf
@aichadiouf14962 жыл бұрын
Machala Alkhamdoulilah li nekhna si khol très belle émission
@mbengueass58742 жыл бұрын
Dieuredieufate s saliou
@laminmaster9387 Жыл бұрын
Machallah Serigne Touba amoul morom wallahi ❤️❤️
@oumarsimssimaga4512 Жыл бұрын
Ce fils du président Diouf, il a vécu à Dieuppeul 1, dans le jardin, dans une famille chrétienne. Sa mère serait une chrétienne. C'est pourquoi dans cette famille maternelle, on l'appelait PEDRO...Je le connais très bien
@narcisse9825 Жыл бұрын
Mensonge il était avec le frère de son père.
@narcisse9825 Жыл бұрын
Sa mère la première épouse de Abdou Diouf est Saint louisienne
@abdoulayegerardsene3146 Жыл бұрын
Ama solo🤲
@makhtargueye5106 Жыл бұрын
Macha Allha ❤
@mamethiernobirahimembackem31064 жыл бұрын
Thiay Serigne touba kéndou mom momom diamo dé
@doussiga2 жыл бұрын
Rabbih samawatih wal ardih🤔
@ngagnewillane68902 жыл бұрын
Machallh 🥰
@amdyniang43642 жыл бұрын
Machalla amna solo
@ndeyekhadydiakhate73192 жыл бұрын
Boba bess Ken douko faté, yalnako yalla doli ay lérr
@layetoure5063 Жыл бұрын
Yallana boromebi samala beke si yow yalla mola defarale bopepame
@aissatoudanfa72162 жыл бұрын
Machallah contane na thi yaw
@cheikhdiouf47582 жыл бұрын
Akkasa.machalla.
@dionikdione6174 Жыл бұрын
Yawiite dé machalla si. Faye bi gua bokou
@sakhondeye4452 Жыл бұрын
❤❤❤❤❤
@alassanediallo9631 Жыл бұрын
Je ne savais pas
@djibrilcamara325 Жыл бұрын
On na besoin de ça Marre de la politique
@mbayebabacardiouf313 Жыл бұрын
🙏🙏🙏
@mamadougaye20852 жыл бұрын
Thiey sama wadji
@assanediagne63312 жыл бұрын
Dieredief s saliou mbacké
@ndongongom94222 жыл бұрын
Day san way eskey setal lirek bay abdu diuf am na ab murid
@modoumbacke29512 жыл бұрын
Walahi khamo dieumou dji ki keuram manga diattou mahwa mouride sadikh le walahi encore yoré daraye alkhourane keuram domou pr abdou Diouf pire le sakh je le connais téré bien s saliou rék lay noyo té moy dieuwrinou diouli gédjgu
@cheikheabdoukaka76592 жыл бұрын
Aminn wayy😂😂😂😂😂
@cheikheabdoukaka76592 жыл бұрын
Na dém bo bakh
@dioplemaire25462 жыл бұрын
Mouride rek kay deugueu
@tabaralo6420 Жыл бұрын
Machala yalna yalla goudeule sa fane
@elhadjimorsall58332 жыл бұрын
Cheikh makhtar yay taloube woutel keur touba yow dakar dousa keur yow thi wakeur khadim rasoul nga yabakh man manghi la khame keur segrine moutafa faty kane thia mbacke baol boba yanghi sotiba boba khalenga
@absamoukhamed51 Жыл бұрын
Serigne bi dama la beug leral lou touty Dakh mome mi fi wakh di serigne Makhtar bamouy am keur Touba chateau la fa am thi guinaw Palait NDIOGUA KÈBÈ THIA NOBOU SERIGNE SALIOU CHEK KHA GOULAKO EONE
@cheikhcisse41982 жыл бұрын
Bii paa nak Abdou diouf yalna démak djameu té baayi fi soun KHALIFA bou Téddeu bi.AMIIIIIIIINE
@elbiranetoure48702 жыл бұрын
Mais ki Abdou Diouf mokou diour makhtar 😭
@magueyembengue4692 жыл бұрын
Fedali nga sun pass pass dieuredieuf
@morthiam33474 жыл бұрын
Machalla
@xsidex1 Жыл бұрын
Il va mieux finir que Amadou sall c’est sûr. Le pouvoir et les confréries font juteux mélange
@assediakhate1012 жыл бұрын
Nit kouyaro
@juniorniass18652 жыл бұрын
Honzoubilaye minal cheytaniii radjimiiii
@cheikhahmadoubambandiaye43602 жыл бұрын
Yalla nanu yalla mousseul si yaw ak ñu melni yaw borom xol you leundeum yi
@juniorniass18652 жыл бұрын
@@cheikhahmadoubambandiaye4360 sa leudeumou ouyyyyy
@dakar-tv82282 жыл бұрын
Dieuredieuf borom touba ba fawwwwwwww
@diengmodou37513 жыл бұрын
Werna
@sarrmoudou58862 жыл бұрын
Pedro bon.sang.ne.saurait.mentir.un.gosse.bien.nee .qui.prospert.des.vertueuse.vuos.un.exemple fils.diatou.hommonyne.mactar.diory.il.faut.demander.le.senegal.et.vous.l.airez.
@modouseck9750 Жыл бұрын
Ma salakh
@amadoulofaye48832 жыл бұрын
Makhtar niaw malay may hodias thi sama paapa nekho mou woor si
@mariannedieng3360 Жыл бұрын
Pedro Diouf
@modouseck9750 Жыл бұрын
L'idée yiemena trop
@MariaAlverenga2 жыл бұрын
Ki du *Pedro* ?
@dakar-tv82282 жыл бұрын
Momla kay legi moukhtar latoude deuk touba dianatou
@djibi-4935 Жыл бұрын
Ki da Niame yalla
@benoodoolelngayengaye650 Жыл бұрын
yawe de ko bahga bo yoto rewemi no johela ko
@gassndoye67123 жыл бұрын
Esk c le fils du ancien président abdou diouf
@cheikhdiabaye60993 жыл бұрын
Wawe. Mahtar.diouf.dadi.talibe .rek
@mordiawdiaw12022 жыл бұрын
Momla deh si werr sax
@dakar-tv82282 жыл бұрын
Pedro la toudon legi moukhtar mouride sadikh and na ak Président Abdou diouf ñeuw mbackè kadior dalési
@rosaliediouf538 Жыл бұрын
Oui c est bien son fils, il a travaillé comme responsable du service Marketing de la Sotiba Simpafric
@ndongongom9422 Жыл бұрын
Ndaye san aun bay adu amna doom juu baxx
@momarndoye2003 Жыл бұрын
Wa lane mo takhone domou abdou diouf yi kénne dawoulén dégue? Para por ak amadou sall sk karim wade?
@ibrahimafaye5867 Жыл бұрын
Sa baye mo yakh rewmiiiii
@aboudione76722 жыл бұрын
On s en fiche du fils de abdou diouf.concernant le dc de serigne saliou vous savez ce le coran a dit au prophète....
@dioufmareme2902 жыл бұрын
Yaw kan mola cheikhal
@sowsoda66742 жыл бұрын
yaw yabatéwo rèk
@dioufmareme2902 жыл бұрын
@@sowsoda6674 laathie da aay. Iska yaw lay laathie
@dakar-tv82282 жыл бұрын
Serigne Saliou moko cheikhal aka bari mbolo da beugoute adina rek mo djité dahira wakana haxan
@ahmethgoumballa53942 жыл бұрын
Ndeysan yaye rame sa baye! Mom guemoul darra Ndeysan franc maçon le!
Tu racontes des conneries toi . Le prophète est mort les sahaba sont morts pourquoi tu penses que serigne saliou ne sera pas mort ou bien tu ne crois pas au coran
@mouhamedmakhroufthiam14762 жыл бұрын
Il faut essayer de comprendre ce qu'il veut dire, pourtant bi yonente bi psl gaineu adouna seyidina omar rta meunou ko wona geume ba dagn ko dalale sahaba you danio tago wone ak sene sago.bassi seyidina omar rta, il faut gua essayer comprendre fimiy wahê. Dê nieupa ko geume.
@cheikhndiaye62082 жыл бұрын
Toi on dirait que........
@sylla8644 Жыл бұрын
Doul rék
@abdoulayegerardsene3146 Жыл бұрын
Sa baye moy doul
@cheikhfall4640 Жыл бұрын
Bayil aigri dinga delou ganaw dé mbirou Serigne Touba Manou rek soxibokoul sinon rek dinkadjiss tôt ou tard Wasalam pith Bou tawté
@Colosud3 жыл бұрын
Ki doorkat rekla. Wakhou doorkat.
@vieuxtraore79613 жыл бұрын
Dieuredieufeti Serigne SALIOU MBACKE Wakhtane wi amna solo
@cheikhcarlosndiaye26682 жыл бұрын
Daure pour lane ? Boudé khalisse ci la dioudou, boudé siiw maye domou Abdou Diouf laa , doye naassi ; Mais nak ainsi va la vie au Sénégal yakhekateyi gnou ngui feupe.
@modoumbacke29512 жыл бұрын
Walahi khamo dieumou dji ki keuram manga diattou mahwa mouride sadikh le walahi encore yoré daraye alkhourane keuram domou pr abdou Diouf pire le sakh je le connais téré bien