Malbn: Toujours au service de la Hadara Abonnez vous à notre Chaine KZbin via ce / @malbntv .Aimez notre page Facebook sur / ligueyalbayeniass Visitez notre site web: #MALBN Tél: (+221) 774572894
Пікірлер
@WeuyouBaye5 ай бұрын
Merci beaucoup cheikh bi il faut que gnouy wakh DEUG si baye, Baye est quelqu'un de modeste, il lui appartient pas à ces genres de karma élémentaire
@AmadouSow-ft4fv4 ай бұрын
Dieureudieuff CHEIKHOULKHAYRI ❤❤❤❤
@IbouNdiaye-h1s5 ай бұрын
Beaucoup de choses qu'on raconte sur les Marabouts sénégalais sont de pures légendes. Merci beaucoup d'avoir rectifié les fanatiques !!
@salioundione25945 ай бұрын
Billay Serigne wahgu deugue parfois ils nous font honte❤
@abdoukarimcisse94255 ай бұрын
Alhamdou Lillah Niass RTA djazakoum Allah Khair Ciiiiiiisssssseeeee RTA djazakoum Allah Khair.
@Bayeniasskesse5 ай бұрын
Masha allah. Rafeet na
@salioundione25945 ай бұрын
J'aime cet homme billay comment faire pour le voir svp
@Thyphanie80194 ай бұрын
Va chez lui a kaolack.un homme très disponible.
@djamiltoure25645 ай бұрын
Machalla yague fi lol té and AK wér nite kou bakh kou yiw kou tédd yalla nala yalla sham té ar may fan bou goudou AK wér milliardaire seydina Mohamed Amine
@emiliediam66485 ай бұрын
Amine ya Rabbi 🙏🙏🙏🙏 dieuredieuf niass yalla nagnou dég té topeu
ما شاء الله ياسيدي شكرالك أطال الله عمرك مع صحة والتوفيق بيركة القران الكريم وبجاه الشيخ الإسلام وسعادة الأنام رضي الله عنه ❤❤❤ والله فرحنا بك غاية فرح❤❤❤
@mamadougueye60235 ай бұрын
Dieureudieuf
@MouhametTop-l7w5 ай бұрын
Alhamdoulilah ❤
@KarimDrame-wg3fv5 ай бұрын
Senegal mo beuri fanatique ak nit youdoul wakh deugg. Nioy rereul niou beuri. Merci beaucoup pour ce discours pertinent
@IbouNdiaye-h1s5 ай бұрын
Vérité incontestable il y a trop de fanatiques dans ce pays.
@IbrahimaFall-u3z5 ай бұрын
Al Hamdou lillah machallah dieureudieufé maolana cheikh Ibrahima Niass ❤❤❤❤❤
@ibougueye24175 ай бұрын
Nous voulons que Médina Baye soit ériger en commune
@moussakalamoullahndaw61205 ай бұрын
Lii lagn sokhla deh des gens équilibrés et saints d'esprit.
Billahi waxatiko, faydou bi lou nékh waay déff kén dou wax. Ko diok niou diohko lidiaza
@thiamfatou40275 ай бұрын
MachaAlah Niass 🙏🏽
@AssaneNom-m6z5 ай бұрын
Wallahi bien dit mbirou baye Niass dou ay Thiakhane
@ismailathiam62595 ай бұрын
Moi quand Oustaz Barham Diop avait repondu qu il n a jamais parlé chinois en Chine j etais pas content de lui.Mais plus tard je l ai aimé à cause de cette honneteté intellecruelle. SOYONS VERIDIQUE NOUS SOMMES DANS UN MONDE DE PLUS EN PLUS RAITIONNEL to😮ut ce qui est Faux sera jeté aux ordures aux yeux des generations inombrables
@irshadoulikhwane17455 ай бұрын
Vous avez grandi
@AssaneDiop-ln4il5 ай бұрын
Dieureudieuf niass , Yalla nagniou Yalla diapalai si barkai yonente yalla Mohamed ak cheikhou tidiani ak cheikh ibrahima niass
@irshadoulikhwane17455 ай бұрын
Cheikh Kouraïch est un grand communicateur On devrait lui confier la tâche de contredire certains propos
@mbadiartv74855 ай бұрын
Masah allah
@malicksarr21415 ай бұрын
Machala Seringe bi niass ❤
@yacinefall83725 ай бұрын
Machallah Niass❤ Amna solo🙏🏾
@AlphaSall-t7b5 ай бұрын
Ndessane li moy nitter macha allahou kadou yi rafetna am n’a djerine
@AwMoussa-xx3iz5 ай бұрын
شكرا جزيلا لكم انياس جزاكم الله عنا كل خير ❤❤❤❤
@sft11305 ай бұрын
Ak tegue mi ak fèthi mi
@BeugueSénégal5 ай бұрын
Walahi Niass say kaddou rafetna lool ❤❤❤❤❤ moi je t'aime tellement
@queenladyyayebaye58015 ай бұрын
Maacha ALLAH ALHAMDOULILLAH.nyakk Adab bi chi Faydou bi..wakh djou bari..worteh Makhama gi..pour lan la..nitt nyi sonn nenyu..nyun topu ken..BAYE NIASS RA REKK LENYU TOP..
@MamadouThiam-qb7qq5 ай бұрын
ماشاء الله تبارك الله أطال الله عمرك انياس❤
@HamdyTall5 ай бұрын
Machallah djiere djief Baye amna solo de
@daoudaballtv45385 ай бұрын
Dieureudieuf serigne bi tu es un vrai fils de Baye et un vrai ambassadeur de Baye😂😂😂❤❤❤
@whatsup-hl5qm5 ай бұрын
Machalah Niass say wakh dafa dal ta teey aussi ak fethie ak teg yi warnajse wakh boubakh
@omarsow27505 ай бұрын
Yeuwe yaye Kane bassi wakh fi nga féka faydou té dangaye dème bayi kofi lidiantile sa problème mo gueune té nga yéné mbindeff yeupe diam comme nouko baye Niass diangalé
@omarsow27505 ай бұрын
En plus pour yeuwe faydou Sénégal rekk la yéme 😂😂😂 tok Sénégal Di wakh dafa yombou Dee baye dafa dadialé monde bi Dee méloyi beuri dieumeu yi beuri etc... Beugué baye Niass moye deugue té kou beugue baye dou khasse kéne 👂👈
@whatsup-hl5qm5 ай бұрын
@@omarsow2750 yaw dof nga amo xel sa genre yi motakh niouy Wakh
@elhadjiomargueye25355 ай бұрын
Macha Allah niass dieura djeufati
@ibrahimathiam95935 ай бұрын
Machallah serign bii
@babacarthiam44555 ай бұрын
Macha'Alla Serigne bi NIASS On ne doit pas tout dire sur internet
@E-p9g5 ай бұрын
بارك الله فيكم وجزاكم كل خير وايدكم ونصركم ووقاكم كل شر
@DameSeck-if8dj5 ай бұрын
Alhamdoulilah machallah barhama forever ❤❤❤
@hady_al_michrii5 ай бұрын
idée bou rafetee la na khalifa bi def assise niou waxtané li nek si faydou teh bougn bayi dara , commencer ko si féthii mi ak woté fén yi , teh sou bobaa nagn ko def en direct leguii lep lër !!!!🇲🇷♥️
@jasonmady16455 ай бұрын
parfaitement d'accord avec vous🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@CheikhIbrahimThiam-wu3wx5 ай бұрын
Force Commune médina Baye Niass moni niore mais pas ça pourquoi ne dissent président ezappe Khalifa général médina Baye Niass wahklén si way Médina Baye Commune 😢
@CheikhDiop-mo8kq5 ай бұрын
Yow Hana wakhi dof yii dagako gueumoone madina baye sou neikoul commune batay loolou ci suniu kilifa yila nioo valoriser woul madina baye diomay neiuw madina amoul bein sens
@Babacarndia5 ай бұрын
Alhamdoulilah ❤❤❤🎉🎉
@cheikhtidianekanediallo15565 ай бұрын
Il faut impérativement mettre en place un COMITÉ DE RÉFLEXIONS ET DE SUGGESTIONS SUR LES ENSEIGNEMENTS DE CHEIKH IBRÂHIM NIASS. Les membres qui constituent les membres de ce Comité seront choisis après mûres réflexions.
@vieuxndao75605 ай бұрын
Alhamdou Baye
@ABBABADJI-bd7el5 ай бұрын
Machallah❤❤❤❤❤
@AissatouMaron5 ай бұрын
Amin Niass Serigne bi soopé bi koula kham ,kham la ci deug AK degou ,
@lamineniang7065 ай бұрын
Machalah li rèk moy diarign❤
@IbouNdiaye-h1s5 ай бұрын
Wallahi
@Honzou295 ай бұрын
Bagna toppou Baye wessouwoul Baye waxngou ken dou wax “Allah Baye” ta fo tourner mom ngay degg.
@jasonmady16455 ай бұрын
Bo ci wakh bou yagué niouné la yow khamo Baye motakh wayé liniouy def té Baye guërëmouko mongui beguë beuti
@Honzou295 ай бұрын
@@jasonmady1645 bilahi waxat ko
@amadoucamara61345 ай бұрын
Merci mon frère Oustaz baram Diop léral nako si waxtaan chiirk baakhoul té Baye limou fi bayi dafa lerr warou niouko yak
@seynaboukamara2465 ай бұрын
Walahi deug la té def niou reral
@ousmanediarra42885 ай бұрын
Diaradieufe Niass
@mayorotine36125 ай бұрын
Bilahi walahi talahi dëlou kossy rek mo mana reglè mbiiryi
@cheikhbayeToure-hy7vf5 ай бұрын
Degele. NiASS ❤❤❤
@ousmankah90605 ай бұрын
مآشاء الله انيس آمين
@ousmanethiam41215 ай бұрын
Jazakalla Serigne bi
@zenazena57655 ай бұрын
Walaye diote na, Alhamdoulilah
@dioptv92565 ай бұрын
ما شاءلله شكرا
@ahmedbiais38545 ай бұрын
واضحا جدا يا شيخي بالحق نطقت والله لازم ان تصحح كل الافتراءات وشيخ ابراهيم اقوى من كل هذا
@dahiratoualelmouwalimam47685 ай бұрын
جزاكم الله خيرا يامولاي الشيخ محمد قريش الشيخ إبراهيم انياس رضي الله عنه وعنابه آمين الحل الأوحد والمستقبل الأسعد للعالم ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mahmoudly46415 ай бұрын
Wax dji mome sangue ndiaye ak baye ousmane ak diengu sala 😢gni gno beugu yak faydou bi🎉❤
@bassiroungom37445 ай бұрын
Serigne nga balma mais kou nek na diapné wakhdji yako mome niou defarate togayi
@zlatanyoutubeur51095 ай бұрын
Jërejëf mâwlânâ Sangue Abubacryn Barhamou Ndiaye faydou bi yako valoriser
@Cheikhbambasar5 ай бұрын
Ya meuna day
@mamadoulamindiallo54815 ай бұрын
Wallahi wanga dége dh Seringe bi
@Ouzzthiam5 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Niass
@diopomar90195 ай бұрын
Ak féthi mi berina torop
@CheikhSeck-si2uu5 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@BabacarDieng-ob1dm5 ай бұрын
مع شاء الله
@abdoulayesarr9835 ай бұрын
Ma challah serigne bi ziare nala ❤❤❤❤❤❤❤❤
@BayemodouSall-sb6cz5 ай бұрын
❤ Baye
@elhadjcheikhdiagne18355 ай бұрын
Vraiment il y a trop de n'importe quoi dans certaines sorties médiatiques des condisciples. Jarajëfati
@topcasjuliana45995 ай бұрын
Ce que je condamne mooy le silence des Fils de baye vraiment depuis El hajj Abdullah aucun d'entre n'a pas pris ses responsabilités face aux dérives au sein de la fayda......Les moukhadams doivent revoir leurs copies et malheureusement Ya trop de sabotages
Diadieuff, mais Manon nga wahh si sangue ndiaye miy wahhh moyy yalla t ndiaye la yalla sante, kou kasss ndahh hasss baye , wahsi yalla waro tokk t tontuwossi
@bayeniang60775 ай бұрын
Yaay djokh ndigueul serigne bi legui Sangue Ndiaye sera décoré la veille du Gamou à k inauguration de la tante Gamou pour son dévouement dans la faydou liguey bou reuy bi
@@OusseynouFall-v1j mani dell naan meew mou seed 5hi tangay laniou nekk invité nala thi décoration bi souniou né souba la Gamou thia tante ba Medina Baye Niass
@OusseynouFall-v1j5 ай бұрын
@@bayeniang6077 invité lannn damalenn talla deglou ... Limay Hamm mangui siyy sant yalla... Ba douma diawalè yalla akk mbindeff.... Seydina cheikh tidiani Chérif limou wotè dou li sangye ndiaye Di wahhh... Hamoull tousss barki cheikh tidiani...
@moustaphaniass87275 ай бұрын
Niass
@mameallefall5 ай бұрын
Pays bi mom légui , lou nékh way wakh. Ay mééw rek. Nagn nék nitt té bayi YALLA YALLA lou bi
@papedioplamerdioplamerdiop29655 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@bayekaw5 ай бұрын
Légui nak moukhadam yii di wakh si yalla louléne nekh ay wakh yii niak téguéne
@jamaljamal29865 ай бұрын
Sa deug deug. Yakh kat yi bari nanou..
@abdoulayegueye52715 ай бұрын
Mais le problème moye gniye déf lolou lép si kanamou domou baye yi wala si kanamou seutyi lagne koye déf voilà le problème
@assanediallo43355 ай бұрын
Surtout lolou
@moustaphathiam10735 ай бұрын
Machallah
@AssaneSy-ho4tp5 ай бұрын
Bou serigne yep melone ni yaw talibé yepp danay réussir
@segaguisse7745 ай бұрын
Ay kaddou you diouboul si faydou bou dafa bari lol. Mouhadam yi ware nagne yar talibé yi. Baye mom ken meunouko sossal 🙏🙏🙏
@Honzou295 ай бұрын
Fi ak ningi dietal khaliss, Faydou bi dina geuna danou
@KabirmouhamadoudiopDiopdiop5 ай бұрын
Faydou dou daanou gniy déf du n'importe quoi nioy daanou
@Honzou295 ай бұрын
@@KabirmouhamadoudiopDiopdiop deug nga wax
@MameballaGueye-w8h5 ай бұрын
C trop tard yenako beug mou diaralen lou nek mbolo rekk ak daradja dem lenn´ rek
@atoubayintaamdarckness8015 ай бұрын
La danse Féth mi
@Abdallah313415 ай бұрын
Guiss nga lolou tamit, faydou bi rideau mayga lako gars yi beug déff lou nékh waay déff
@PapeDiop-v1r5 ай бұрын
Baye Mbaye MC mii exilé dolén ci wax mou déllou
@AssaneSy-ho4tp5 ай бұрын
Serigne bi bolé thi borome djiné gni
@ansaroulfaydatv78665 ай бұрын
Limom warna am faydou moko sokh la
@beuguebayeniass24275 ай бұрын
Comme sangue ndiaye yalla dou nitte ak mbaw borome baye andiwoul mankhrifa lidafa niaww bouma béén doff tontou négatif
@ousmanedrame65475 ай бұрын
Ki mom degouna dh
@cheikhndiaye1495 ай бұрын
Problème bi yeup moukhadami leu gnissi eupp s’en bopp rek nekalougnou baye
@positifman185 ай бұрын
Tu as raison à 100%
@amadougueye41375 ай бұрын
Assalamou aleykoum diotna pour ces soit disant moukhadam réglé té bayi sen woté yi kou ame béral sa yonou bopp té guné ci baye niasse ,di wakh si makhrifa di wougni mbott yi foné lolou moy kham yallah rére yalla daga koy kham ba paré mou réré la bopam atención kham yalla ŕanié ko lou diaffé ,yalla boudé ndiaye la sant an wa gueyenne ak diobenes yi bailen sén thiankhane yi.
@ElymaneSaidoukane5 ай бұрын
Billahi deug la trop de désordre dans la fayda trop de Foutaises le problème déjà entre Mbow et Sangue Ndiaye sincèrement ça doit s' arrêter on a trop laisser faire
@IdrissaDiaw-g5o5 ай бұрын
Rewmiiii sa beurri aye fenkatte
@ibrahimathiam3565 ай бұрын
Walahi Serigne bi Dafa djot yéne nit yi arrêter yok bi nioune talibé yi sokhla wougnou lolou Baye rek mogni niorrr donc na gars yi bayi mew bi taye wakh deug
@DaboIssa-i3k5 ай бұрын
Ak certaine femmes de médina sen habillement yi bopou néne ak ect... fok niou kholateco tamit
@abdoulayegueye52715 ай бұрын
Peyibi da bari ay tok mouy dokh lolo waral biryi
@barhamsokhna56605 ай бұрын
Il est temps de mettre fin aux dérive des soient disant moukhadames comme sague ndiaye
@ismailakane37515 ай бұрын
Mon cher Sangue Ndiaye est le plus grand vulgalisateur de la Fayda Ibrahîmiya à travers les enseignements et les écrits de Cheikh Ibrâhim Niass...Sokhor rek ak ignane molén diape wayé Sangue Ndiaye ndoķél ko rek mo lén ware ndakh Mbeguélam si Baye...
@rokhayamanka14505 ай бұрын
Dieuredieuf Cheikh Mouhamadoul Khourayche il est temps que les gens arrête : la divulgation des secrets divin (weer mbot), live Tik Tok, you tube, Instagram, Facebook di wakhtane si marifa, hahika, et enfin di woté makhama mawlana cheikh Ibrahim sois disant Khalifa Yalla, Yalla Ndiaye etc... Vraiment nous regrettons d'avoir perdu El hadj Abdoulaye Niass (Papa Ass)
@AlphaSall-t7b5 ай бұрын
Ndessane li moy nitter macha allahou kadou yi rafetna am n’a djerine