Cheikh Mbacké Sakho et Cheikh Baye Niasse feraient un excellent duo : une très bonne équipe.
@AmieFaye-sr7rw4 сағат бұрын
Yalla na yalla défal la diam Yak sa invité ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@hubutaha355641 минут бұрын
Il faut Inviter Cheikh Ousmane Mbow pour discuter de la Mahrifatou Billah et sur la Ma'rifat Billah
@MabajahubBah12 сағат бұрын
There are some Talibes dango apaal Sheikh bi. Thanks so much Sheikh Ahmed 🇬🇲
@hubutaha355614 сағат бұрын
Masha Allah xam xam am na ci debat bi Yallah may gnou deg ak topp
@souleymaneann39514 сағат бұрын
Dajal dal moy kou réreulaté Mahdi moy kouy joubeul./ Yague nañu theroriser 😂😂😂 Cheikh Baye Yangui yeungeul deukk bi. Mais man Imam Moustapha Gueye la ndieukk dég mou tegui wax bi. Machallah
@ballboury3811 сағат бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤machallah Machallah ❤❤❤❤❤❤❤
@jamilly59457 сағат бұрын
Une question : si diné islam est ce que yonnenti bi amena droit Di kharamal wala daganal? Wala est ce que yalla rek moy daganal ak Di kharamal si diné bi? Je pense que prophète est un messager d'Allah , il transmet juste les paroles de Dieu. Donc si on dit que yonnenti bi dafa kharamal wala daganal je me sens confus.
@floorishy4 сағат бұрын
cheikh baye mi dafa réér ci bir kham kham bimouy ooté C'est vraiment dommage. Kouniou toudé baye amoulo téguine té sa mélokane ak say wakh wanéwoul ni waliyyou nga
@MabajahubBah12 сағат бұрын
Louma gena yeen senn mbirr Moy their minds are computerized amoul khelaat 😂🇬🇲❣️
@MabajahubBah12 сағат бұрын
These Ahlou Sunnah people have been terrorising our minds 😂😂😂Sheikh Bai do nit🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲
@alassanajallow787111 сағат бұрын
Cheik you are sleeping deh 😂
@theman807012 сағат бұрын
Waraqa the cousin of Khadijah a Christian made Muhammed a prophet.. the seven sleepers was from the syriac legends.. a Christian told Muhammed what he saw in the cave is angel Gabriel and Muhammed believe it.. torment of the grave is from the jews... isa made a bird from clay is from the nastic which is very late... good to learn all of this 👌
@DembaSow-h7d6 сағат бұрын
Damalen beug té yalla takh😊
@dinodiouf43729 сағат бұрын
Yala naniou may ndioup Al ragal yala am xam xam yombna ragal yala mo diafe ko tak lo eup 4 diabar si bakane rek gako tek me meunoo ko layal
@Mamour-uw5rb13 сағат бұрын
Salam, Dine dou logique rekkkkkk. Mais Mariage temporel lou wara mananekkkkkk la mais avec des regles. Bissi djekkkk wakhtanekoo ba djoubo.
@MaimunaCeesay-iq7gq11 сағат бұрын
❤❤❤❤❤❤❤
@MoussaSylla-k8n9 сағат бұрын
Ngirou imam Malick doynagnou
@MaimunaCeesay-iq7gq12 сағат бұрын
Masallah
@syllasadia636010 сағат бұрын
Est-ce que d'où Moshe dayan moy dad....
@dinodiouf437210 сағат бұрын
Yala naniou yala yeureum li dou xam xam sey bobou so dagane teude thiaga kon aramoul ndah kouy dem thiaga meuna fass yene tak la si wahtou bobou so dano fasse liga wah hel sah ndagou wouko li moy bandit ga nit gni ndialo len
@LayeGueye-lx2kf9 сағат бұрын
Yaw dangay beug wakhné diamou yonénte Gni dane pratiqué mariage temporair donc daniou dane thiagalou en toute logique
@LayeGueye-lx2kf9 сағат бұрын
Si diamonoy yonénte plus precise
@dinodiouf43729 сағат бұрын
@LayeGueye-lx2kf nekato diamono yonent by nak gni ay sayy say laniou
@LayeGueye-lx2kf7 сағат бұрын
@@dinodiouf4372 té yonéntebi wakhni topoulén sama souna ak sama souna khoulafahou rachidien Yaw ana kane Moy sa référence?