Cité Fadia : Tristes confidences du père de Mohamed Diop, battu à mort dans un Daara

  Рет қаралды 38,796

SeneNews TV

SeneNews TV

Күн бұрын

Пікірлер: 90
@aissatousylla4172
@aissatousylla4172 14 күн бұрын
Ndéyssane yalna YALLA yeureum MOUHAMED kharé co aldiana si barké tourandom S.A.W amiiine amiiine amiiine
@khadijetoulykane8909
@khadijetoulykane8909 11 күн бұрын
Il à parfaitement raison le papa, ici en France les enfants plus particulièrement mes enfants aiment aller à l’école, ils aiment leurs enseignants et pourquoi liSlam qui est paix et amour ñoussiy lor ay nit ratatina ay khalee
@lauraag5251
@lauraag5251 11 күн бұрын
Je te jure à cause d’eux et toutes les guerres qui se passent dans le monde tout le monde déteste l’islam et les musulmans les gens les plus mauvais sont des musulmans et c’est eux qui vont partir au paradis ? Mdr
@NganeSalihate
@NganeSalihate 11 күн бұрын
Deugue deugue
@papemylenekhoule2884
@papemylenekhoule2884 15 күн бұрын
C'est mon beau frère nite kou bakhe té gnimé diabote yalla n'alla yalla maye kholou mougne
@khadidjatoudiop6123
@khadidjatoudiop6123 12 күн бұрын
Ndeysann lii métina torop way je ne cesse de regarder sa photo un garçon adorable qui semble dégager une très forte PERSONNALITÉ ET BRILLANT..Yakar tass na wala gni bonne naniou .Yalla na motalé ndawame Firdawsi si péguou tourendo wom Mouhamed saw 😢.
@yatta8062
@yatta8062 14 күн бұрын
SamaKhôl demna si mouhamed sama cousin 9ans rék la âme dagnon wotté rék ni déna dans le mois de novembre 😢😢😢
@aissatadia5539
@aissatadia5539 13 күн бұрын
Inallilahi wo ina.ileyhi radjioune.Allahouma aghfirlahou wo yarhamhou amine que le bon Dieu ľaccueille dans.son vaste paradis firdawsi amine ya Allah
@seynabousene5675
@seynabousene5675 13 күн бұрын
Amine 🙏💔
@pendaseck8760
@pendaseck8760 17 күн бұрын
Ndeyssane repose en paix. Khamouma diangalé rek loussi diare dore khalé bamou dead. Que justice soit faite
@NdeyefatouDiokhane-cw8ee
@NdeyefatouDiokhane-cw8ee 13 күн бұрын
Nessane yalla naka yalla yeureum khareko adiana firdawsi
@valtima9918
@valtima9918 11 күн бұрын
Amna interna ak darayo xamnè limasi giss doyna war bilahi kèn menuko wax😢
@ndeyematydiop2232
@ndeyematydiop2232 10 күн бұрын
Au way wakh ko
@nohaneba398
@nohaneba398 10 күн бұрын
Oustaz bouye féne nak je ne reconnais plus mon pays peine de mort. Rip notre petit ange Oustaz bi dé kéne douko lathieu lou sougniou borom wakh si féne😢😢😢
@serignendiayebeuguefallou7088
@serignendiayebeuguefallou7088 12 күн бұрын
Ohh thiéye Sénégal Fomou dieum ohh vraiment lii métina trop bilahi 😢Yalla Yeureum ko
@gueyediarra2340
@gueyediarra2340 10 күн бұрын
Khaléyi di lorou ci yéne darayi doyne ware trope débounouy wakhe ci affairou darayi oustaz yeupe commencé nane dano contre dara té niata khalé nio dé ci dara 😡😡😡😡😡😡😡😡
@Mamebousso-uq8zf
@Mamebousso-uq8zf 15 күн бұрын
Mane deh daara dji sama dom di diangué u26 Macha Allah khaleyi danio free bolen kholé khameni sonouniou meussouma dem sama dome wonema ben signe thiono
@NdayeKebe-e1l
@NdayeKebe-e1l 17 күн бұрын
Sénégal nak diarna satete djikoyi limetina khawouma bane rew lane nek 😭😭😭😭😊
@souka1321
@souka1321 4 күн бұрын
Daffa.méti.trop.
@serignendiayebeuguefallou7088
@serignendiayebeuguefallou7088 12 күн бұрын
Parents yii téyé sén domes yii cii sèn keur yi ak essayé de supporter vos enfants c'est tout point
@ramatadiallo2531
@ramatadiallo2531 12 күн бұрын
Gnoune gni sougnou domyi nek si internat yeup lolou lagnouy ndound bo wakhé gnou eupela lamigne ter ligniye def dou diner dou Islam
@dexterdexmen6707
@dexterdexmen6707 12 күн бұрын
PEINE DE MORT DÈ TANT AMOUL SENEGAL DOU REGLÈ
@NdeyeSarr-n6i
@NdeyeSarr-n6i 12 күн бұрын
Outaz bi nawax deugue oooh mouhaméd mingui raféte waye yalna motalé ndawaw aldiana firdawsi thi barcké mouhaméd psl allahouma amiine 🙈 🙈🙈
@ADJI982
@ADJI982 16 күн бұрын
Cette histoire me déchire le coeur depuis que je l'ai écouté a rfm xalass ce daara c'est a fadia auprès du terrain. Que justice soit faite noooo ki moye domerame ya certains oustazs vrais domerames
@mamediarrademe9243
@mamediarrademe9243 11 күн бұрын
Bilaye Lou neti yalla nako yalla yeureume
@mameseygueuye4540
@mameseygueuye4540 17 күн бұрын
Té bo yobouwoul sa doom daara gnoulay critiqué
@FatouMbayeDiop-fz2qb
@FatouMbayeDiop-fz2qb 16 күн бұрын
Bilaye j' ai des larmes au cœur
@dabaniang8141
@dabaniang8141 10 күн бұрын
Ndeysane yalla na motelè ndawm si aldina FIR dawsi thi barkhè seydina Mouhamed psl
@Nafidramè-r7b
@Nafidramè-r7b 16 күн бұрын
Yalla nako yalla yeureume kharèko aldiana
@paulinebeguerisse4892
@paulinebeguerisse4892 15 күн бұрын
Connaissance à quel prix???
@AmyFarathioup
@AmyFarathioup 2 күн бұрын
Ayy Dmrm laniou koi li ba kagne teh limasih mèttih dou noudiou fenn Daniouye tèdieu sa gèmigne ba do meune wakh que justice soit faite Oustaz bi Danio wara niaff ndeyeme mou kham 😭😭😭😭😭😭
@Tocabubs
@Tocabubs 13 күн бұрын
Ayy wayy tieyy allah .ana diangaler ak dorater
@naboukebe5390
@naboukebe5390 10 күн бұрын
Yalnako yalla yereum souf woyof si kawam
@sougou7533
@sougou7533 13 күн бұрын
Le gouvernement doit prendre ses responsabilités tro c’est tro 😅😅
@pendandiaye3968
@pendandiaye3968 16 күн бұрын
Ohhh métina ndeysan yalla nako Borom bi terou téral barkéb tourando bi Seydina Mouhamed psl
@ADJI982
@ADJI982 16 күн бұрын
Non daras yiiii du n'importe quoi trop de morts que justice soit faite non gniiii donio tegeule sene data ndeye rek
@Katelia1503
@Katelia1503 15 күн бұрын
Mane deh sam dom souma yekho'e touty mou fatou si dara bi metit la donne dound diekh takk si ko khamni da ngua amone yaram interner dara conseiller wou mako kene
@aminatagueye4659
@aminatagueye4659 15 күн бұрын
Ndeysane metina yalla nako yalla yeureum si barke Seydou mouhamed psl
@AissatouGueye-q9h
@AissatouGueye-q9h 12 күн бұрын
Sama khol bi dina dague thi deuk bi
@seynabousene5675
@seynabousene5675 13 күн бұрын
Yalnala Ya Allah yeureum té kharé la Djanatoul Firdawsi MOUHAMED 🙏😭💔
@EspaceNdugu
@EspaceNdugu 16 күн бұрын
Paix à son ame
@MameFatouSeye-h9d
@MameFatouSeye-h9d 12 күн бұрын
Ay way 😭😭😭damay lathe nitt gni man khôl lagnou woré 😭😭😭😭😭
@ngonefall3837
@ngonefall3837 15 күн бұрын
Justisse pour mouhamed
@ndeyeadiabaye6656
@ndeyeadiabaye6656 4 күн бұрын
Mane Daal khawma bane Sénégal la Niou nek vraiment da négatif Beug sa dôme âme Éducation diangue dînée mais do kham fane nga kay dougal Mane yobou na sa ma dôme bou djiguéne internat sa ma frère bi topando ma yobou niarri domam you goor moin de 10ans Internat fi Cambéréne di faye chak mois 40 Mil ay 2012 mais defou niou fa un ans béneu week-end la fa dem di len dieulli pr niou nieuw weekend Khalé yi diekh takeu amè diarrhée khiff sen valise rek la dieul def si yeuré you beurri rek daw fa la diaré delouwatou niou ba tay may wakh Oustaz bi di ma wo nane ma khaleyi ba diameu mo len teuyé ma ni ko Bayi na niou Yalla reka niou soutoural wayé Khalé yi da niou don diarrhée ba dé t dou niou si ame lou doul Yalla def na li geune t lépeu niom la ki li ko dale méti na trop wayy
@adamasy4258
@adamasy4258 12 күн бұрын
Mane de daraa moma yakal.sama doom ba.degalouma dagnou lay yakhal
@olayolay1908
@olayolay1908 17 күн бұрын
Paix à son âme bayi lene seni dom yi guene di diokhe sans autant guene di lene saytou sa sou nek
@AstouBa-ic6pe
@AstouBa-ic6pe 3 күн бұрын
Oh mon pays va mal
@Ava-eva
@Ava-eva 9 күн бұрын
Internat legui yi mome douma ko digeul Kéne ,xalé meune na mokkal Alkhouraan tei dougn ko interner 😢
@KhadyBaldé-q8y
@KhadyBaldé-q8y 16 күн бұрын
Yalla nako yalla yeureum ta kharé ko aldiana mes na police def ligéyam amna lousi nek
@cheikhahmedtidiane1615
@cheikhahmedtidiane1615 9 күн бұрын
En tout cas man daara la yorr mais cas bi mom amnassi diaxler lool t negligence si côté you beuri dasser fegne yalna yalla may ay waydiouram xolou mougne t moussal gnou tchi gathier addouna ak alakhira di massa wou daara yeup si cas bi dilen wax ak lougne si meuna degg nagne mougne ndax sougne mbokkou mo fautif
@FatouWade-bf9hg
@FatouWade-bf9hg 12 күн бұрын
Bilahi wax na deug demb rek guiss na yayam mai ba legui nekul
@yacinegaye7174
@yacinegaye7174 7 күн бұрын
Metineu tiss neu mais yallha nala sunu Borome maay kholou mougne . Internats yi dangaay geum djokhé sa dome ngiir mou ame dinné mais do kham sakh leep lafay khéw doyna warr tropp.
@maimounandiaye-le1tu
@maimounandiaye-le1tu 17 күн бұрын
Tim khaler diko dore Mbamou dé nite gni gua khamni sen khol you bone yi di djangualer
@serigne3607
@serigne3607 16 күн бұрын
Oustaz bobou dina rayat ay khalé ndakh dafa febar pchycopate leu
@awafall2349
@awafall2349 13 күн бұрын
Darra loudoul teudj daraa bi
@Tocabubs
@Tocabubs 13 күн бұрын
Quel est le nom du daara pour que les gens puissent savoir
@modoudiop6385
@modoudiop6385 16 күн бұрын
😭😭😭😭
@Katelia1503
@Katelia1503 15 күн бұрын
Li dey moy diangual khaleyi fen so wakher ma door la da gnouy menacer khaleyi ba dou gnoi gnemer wakh
@AissatouGueye-q9h
@AissatouGueye-q9h 12 күн бұрын
Ay nguir yala bayilène khalé yi guéne di ray
@damembow6374
@damembow6374 16 күн бұрын
Crime dou parfet
@nafiesenghor2980
@nafiesenghor2980 17 күн бұрын
Metina trop mane sama niari jumeaux lolou lagniou done doundou mbour
@Fatoueye
@Fatoueye 16 күн бұрын
Mba dieuli gualéne rek
@nafiesenghor2980
@nafiesenghor2980 16 күн бұрын
@Fatoueye Bou yag
@diabousakho3787
@diabousakho3787 16 күн бұрын
bilay li métina trop 💔😭
@diabousakho3787
@diabousakho3787 16 күн бұрын
justice pour mouhamed diop
@ngonefall3837
@ngonefall3837 15 күн бұрын
Bane internat svp sama dome fofu la nek ​@@nafiesenghor2980
@AliouneMbengue-y3v
@AliouneMbengue-y3v 16 күн бұрын
Daye doule dara yi y a du n'importe quoi
@ndiobalaye-mb8cy
@ndiobalaye-mb8cy 11 күн бұрын
😂😅😊😅😊❤😊😊❤😊❤😊❤😊😊😊😊❤😊❤
@bathiegaye8706
@bathiegaye8706 12 күн бұрын
Yalla mo dogol lolou rek mes kou diague nou dorko
@ramatadiallo2531
@ramatadiallo2531 12 күн бұрын
Aki doram adouna wessouna fofou nit niagui mokal alkhourane té ken fitnalouco
@nabiadja
@nabiadja 12 күн бұрын
@@ramatadiallo2531 oustaz bi mo amoul saggoo
@diorfallndiaye1173
@diorfallndiaye1173 13 күн бұрын
SERIGNE BOBOU NONOU KOU BONNE LA MOKO DAURE BAMOU DÉ NA YONE DEF LIGUEYAME
@seynabfallou395
@seynabfallou395 12 күн бұрын
Senegal danio wara dieul dra ak internant sérieux dieul ay loi ak ay sanction nitt kham l'an moy loi ak sanction dra yi ci rewmi lagnou bok bayilén complexé bi tay terél li islam wakh
@bathiegaye8706
@bathiegaye8706 12 күн бұрын
Pourtant yaw yagui née mouhamad wathie n'a ba mokal ak am mbecte trop si oustaz bi tay yalla ndogol natou si mome nga tok fii dit wakh loula nekh ta aussi yaguifa bayi sa niari dôme you djiguene loutakh nit dou geum ndogol
@nabiadja
@nabiadja 12 күн бұрын
yaw xamé go ndogal ak tayéf oustaz bi amoul saggo
@bathiegaye8706
@bathiegaye8706 12 күн бұрын
@nabiadja walahi ndeysane khale kouko ndiagal bamou wathie alkhourane niari yone baye diague kham kham si même dara même bouko dorer yalla mo toudou née si lokhome lay fatoo mes amoul vone yene pour rayko
@khadijetoulykane8909
@khadijetoulykane8909 11 күн бұрын
Baayi leen naafekh, boudée lislam te yoneent bi psk moy sounou royou waay meussoul diglee ay door bien au contraire. Mes deux garçons sont nés en France ma yobou leen dara, mais lou leer laalen wakh avant inscription. Ils doivent amener les enfants à aimer le coran , aimer leur religion sans kheut kheut ak mal traitance
@mamediarrademe9243
@mamediarrademe9243 11 күн бұрын
Lidafa mety trop dafe wara diekh
@nabiadja
@nabiadja 11 күн бұрын
​@@bathiegaye8706 cheikh bi mane diar na dara def nafa lou eupou 8 ans xamna bou bakh limay wakh guiss na kou dor ap talibe bamou poupe toubay bi mouni talibe bi par force dina lek poupe bi boys bi lek ko . lolou keneu netaliwou mako mako feke yalla xam nako ande ak sa saggo dafa bakh
@fatimadiatta5620
@fatimadiatta5620 15 күн бұрын
😢😢😢😢😢
RDC : les gangs de Kinshasa | ARTE Reportage
24:27
ARTE
Рет қаралды 18 МЛН
Mise à M.O.R.T de 70 Kulunas exécuté à Kinshasa - Angenga ! | Opération Zéro Kuluna
14:03
Мен атып көрмегенмін ! | Qalam | 5 серия
25:41
人是不能做到吗?#火影忍者 #家人  #佐助
00:20
火影忍者一家
Рет қаралды 20 МЛН
🚨🚨TFM LIVE  :   Xibaar Yi 13H du 18  janvier 2025
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 1,4 М.
RADIA - COCO LAYE LAYE - (clip officiel)
2:57
RADIA TV
Рет қаралды 1,5 МЛН
Мен атып көрмегенмін ! | Qalam | 5 серия
25:41