N'oubliez jamais les 5 prières de la journée Fajar... Tisbar.... Takussane... Timiss.... Guéwé
@fatoudiene403 жыл бұрын
Q
@yakharandiaye60313 жыл бұрын
Merci beaucoup
@fatoukinembodji95433 жыл бұрын
Merci beaucoup
@fatoukinembodji95433 жыл бұрын
❤
@aminata_lilas3 жыл бұрын
❤
@aminataseck45373 жыл бұрын
Je connais très bien cette famille, nous sommes arrivés dans le quartier en 1967, et avons trouvé cette famille sur place. Aujourd'hui , n'eut été la mort, personne n'oserait attaquer cette famille. Mbaye Ndoye et Mamadou Ndoye ont été dignes jusqu'à la mort. Leur mère, Adja Makélé, a fait beaucoup de biens pour les jeunes de Colobane. Je suis sure, que Dieu vous assistera, insha-Allah.
@barkhamadiop433 жыл бұрын
Gno bokone kogne ndeyesane depuis l' an 2000 lafa diogué rue 44×45
@deugrek33123 жыл бұрын
C’est triste
@aidandoye89593 жыл бұрын
9
@nabombodj38493 жыл бұрын
Oh la la je trouve pas les mots 😥😥ça me donne des frissons grave j'ai pleuré comme un bébé une famille formidable machallah ça me touche au plus profond de moi MAIS DIEU EST PUISSANT
@wasswissoubiaye48123 жыл бұрын
Bilaye gnou bakh mallene khame 😭
@aidaly28553 жыл бұрын
Hoooo massawaye ndoyenne une grande famille lebou a colobane.....qu Allah Vs viennent en aide...leur papa fut tres digne......🤲🤲🤲😪😪🙆♀️🙆♀️.
@cheikhibrasamb84763 жыл бұрын
Une famille digne et noble.Qu’Allah les viennent en aide.
@maremesouware45113 жыл бұрын
Kagne la niit di bayi tek fitna moromame😭 Justice pour cette famille
@a-qudoosallahisone64983 жыл бұрын
xana waxo fi justice bou réew mi dh
@seyemamefatma16863 жыл бұрын
😭😭
@maremesouware45113 жыл бұрын
@@a-qudoosallahisone6498 bilahi wakhatiko rew mi amoul yone
@a-qudoosallahisone64983 жыл бұрын
@@maremesouware4511 lolu rek mo waral yi façons
@jeannoelhelmutbadiane24693 жыл бұрын
Vraiment c dure ma sœur
@adamathiaw20443 жыл бұрын
C tré triste vrema mé osi parents yi nanouy waxtan ak ndiabot gui prck deh defay betté organise sa keur avan ngay dem mo gueun nga bayilen si lo xamné ni moy llou la plus part genr histoire yi limakoy guis yepp sou pabi dewé lay donn té dangay deg niou n'a df nanoufi plus d 30ans diap 40ans xeuy un bn jr rek guené lenn nnou san avertir c domage k dieu vou vient en aide
@mouhamadoudiop6783 жыл бұрын
Une très bonne famille ici à colobane ay nobles deugg bilahi niou bakh gui nii yallah n'a bonnes oeuvres yi djapalei lene ci nattu bi barkep Khadim Rassoul
@sallamane33233 жыл бұрын
Oooooh j'ai le cœur ❤qui saigne 😭 vraiment le Sénégal mon pays de la Téranga va mal .courage la famille que Dieu vous assistent amine
@yerimsy87403 жыл бұрын
Téranga bi diékhna bou yague boye
@sallamane33233 жыл бұрын
@@yerimsy8740 walahi wakh Deugg
@aminatandoye56913 жыл бұрын
Wa ndoyenne ligueye niakh diarignou rek lagnou kham walahi . Ils sont Nobles ,dignes machalah , yallah bakhna
@oulydiene86693 жыл бұрын
Ndeysane sama yaram dawna 😭🤭 bilahi dema dioy Sénégal meti père Sama khol toyna ayway milliaders yi cagne lagnouy diapalé newdi dolé yi😭😭😭😭
@amadoundoye23683 жыл бұрын
Yalla rekk mo am dolé kén amoul dolé yalla na yalla ate deugue yalla na yalla defar lepp zayirane wa batinane amine courage frères metina trop
@aissatakeita3863 жыл бұрын
Douko djig Inschallah dankh YALLAH Bour bou bakhla. Li métinama, khamna keurgui bou bakh wallahi. Ooooh la mort 😢😢😢😢😭😭😭
@abdoudiop10323 жыл бұрын
Yalla na serigne Babacar sy takhawou 🙏thiéy Sénégal dou avancé jamais 😭😭
@aidasouane64393 жыл бұрын
Serigne Babacar deh na Naka lako mane takhawou. YALLA rek mana takhawou domou Adama balma nak diangat rek la
Babacar s'y dé n'a bou yague meneloule bobape dara wahi doff rek
@symami44703 жыл бұрын
Talibé cheikh yalla rék mo mene takhawou diamame
@Amadou-Amira3 жыл бұрын
😭😭 man bo doon sama sago douma guiss rongoniou mag te bakhoul si rëw Wayei fi mome chaque jour ame ngingou djoylo yalna borom bi maye kholou mounge😢
@abybathily82213 жыл бұрын
Yalna l'en serigne babacar sy takhawou inchalah
@symami44703 жыл бұрын
Talibé cheikh yalla rék mo mene takhawou diamame 🙏🙏🙏
@youmanebadji94523 жыл бұрын
Ndeye sane yalla nalaine yalla takhawou toute la famille 🥲
@pape75923 жыл бұрын
Allahouma Amine
@a-qudoosallahisone64983 жыл бұрын
Amnafi doomu adama yoo xamni litax sunu boroom andi lenfi mooy liii rek 😭😭 Yalla mi yorr jamm téy jammal koku neex yalna leen jammal té leeral leip inchallah
@aissatoukane22553 жыл бұрын
Une des plus anciennes famille de Colobane 😔Que DIEU leur vienne en aide pour que cette grande famille reste réunie !!
Que justice soit faite liii dou deug dou yone walahi ils ont débarqué chez nous avec un lus de 100 policiers mardi matin sans aucun papier valable ils nous ont maltraités et expulsés sans aucune raison 💔😭😭😭
@minafall87093 жыл бұрын
massa y'alla deinthie na Lou eupp lolou inchallah
@Real-tr8nl3 жыл бұрын
Courage mon frère !
@mamiwata15173 жыл бұрын
Allez porter plainte à DSCOS
@mbalofficiel75133 жыл бұрын
Doyna war yal nala Yalla bourbi diapalé
@salimata6733 жыл бұрын
Massa chéri yalna Yalla até si Barké Seydina Mohamad psl Courage
@saliyadiaw24443 жыл бұрын
c’est ma famille walahi niou bakh machallah les bonne volonté takhawoule thi Barker Seydina Mohamad psl hoooo métina Ndeye sane aiwai dioulite dina defli moromou diouli tame doyna warr je suis de tou c oeur avec vous courage à tout la famille inchallah 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
@bounadieng15053 жыл бұрын
Les plus forts mangent les plus faibles senegal lifi nek yeup yalla douko setann
@bybakane49493 жыл бұрын
DEUG rek ka wakhe
@Corailpro3 жыл бұрын
Les banques et les sociétés immobilières font bcp de dégâts au Sénégal. Trop de problème de foncier au Sénégal, Letat doit régler cette situation qui perdure. Cette famille doit être relogée ailleurs au nom de la dignité humaine. Yallah nalene yallah sam soutouralene
@peulhpeulh25023 жыл бұрын
Talla fall soumadone yaw keur gui dossi beugueti dara aii make youye dioye métina 😭😭
@lalionnenoire73713 жыл бұрын
Peulh Peulh bilakhi deugue la mane t'es dama titt sakh li des diaroule dieune diaye dolé rek
@peulhpeulh25023 жыл бұрын
@@lalionnenoire7371 keurou aduna dou dara démone cimetière outefa place bou bakh té khamni fallaye moudjie fofou rek moye keur mongueune mouye dioylo aiii make
@dabaniang81413 жыл бұрын
Yalla nalèn bour yalla takhawou thi barkhè seydina Mouhamed psl
@presi13163 жыл бұрын
Yén gni di commentaires yeup est ce que dougnou djémeu déf dara pour gnome Genre gnou partagé ko si réseau yeup Comme que justice amoul si deuk bi Li métina trop trop bilahii
@rokhayagueye86353 жыл бұрын
😭😭😭😭masta deselene ak yalla mo dakk am keureu adouna dou touss
@zeynasene23633 жыл бұрын
Il faut qu'on lutte pour ça, c'est plus fréquent dans notre pays
@moustaphagueye83143 жыл бұрын
Il fau gnou ame bene page rien que pour sa kou amati problem you melni wakh ko gnou déme khéhal la
@maimounadiop99903 жыл бұрын
Oh nonnn souniou keur Ndoyenne way on a grandi ds cette belle maison j ai les larmes aux yeux 😭😭😭😭
@Corailpro3 жыл бұрын
Massa yallah sam lene
@kebadanso63563 жыл бұрын
Il fallait payer les dettes de la banque ou négocier sur des bases claires. Nous le savons tous que quand nous prenons des crédits bancaires, il y a toujours des petites écritures aux quelles nous nous faisons pas attention. C'est de là viennent les problèmes.
@tamimoumbengue38243 жыл бұрын
Li niawna yeurmandé adouna Dou keur vraiment je compatis si samay mbook lébous ke Dieu leur viens en aide
@nogayeniang30543 жыл бұрын
Hoo c ma famille sama diabaru tonton fi la dakk yalla na léne yalla takhawu metinw torop bilahi
@tickodia78473 жыл бұрын
ALHAMDOULILAH ALHAMDOULILAH ALHAMDOULILAH ALHAMDOULILAH yallha n'a borome bi takhawouléne adouna bi métina tropp
@yayoumouhammad84073 жыл бұрын
Ça me rappel la famille pouye dou moudier feneu waye yalla nalene yalla takhawou ba nguene diott sene keur
@Bibina98063 жыл бұрын
Il a coulé m'est larmes massa sunu Borom dineu defatat le peu incha Allah
@awagueye33 жыл бұрын
Yalla naléne yalla takhawou si barkei seydina Moukhamed (saw). Lou métti
@senegalsenegal49893 жыл бұрын
Metina mais tien n'est clair dans les discours. La journaliste ne pose pas les bonnes questions. A qui appartient la maison? Est ce l'heritage a été bien fait? On parle d'une société avec des intiales Snr? De quelle société s'agit t -il ? Qui avait donne en location la maison? Depuis quand? Qui recevait les paiements? Quel montant a ete versé ou recu? Qui a achete la maison.? Qui a vendu.? Ou sont les avoxats? Ce dossier comme d'autres merite d'etre analysés. Que dieu nous protège, donne accorde soutoura weerlecak werla si barke seydina Mouhamed. Encore une fois massa à cette famille. Les milliards faites quelque chose
@baxnamendy33023 жыл бұрын
La S.N.R. est la société nationale de recouvrement chargée de gérer les actifs des défuntes banques BNDS et autres qui ont fermé. Si tu avais 1 prêt au niveau de ces banques c'est à cette société qu'il fallait payer sinon rien que les intérêts depuis les années 90 risquent de faire des dizaines de millions. Et sûrement le vieux avait un prêt et avait dû hypothéquer sa maison.
@kebadanso63563 жыл бұрын
@@baxnamendy3302 merci monsieur Mendy. Vous êtes mieux que cette journaliste. J'ai bien compris quand vous avez parlé de BNDS.
@abysow16533 жыл бұрын
Li niaw n’a Walahi yalla guene gagnier thi barkep seydina mouhamed yalla guene diottate Sene keur yalla Migui guiss lep🙏
@miyabadiane69343 жыл бұрын
Adouna bi diékhna d'ara diaroule li mes yalle n léne yalle até ak kidéf li métina trop mes yalle bakhna dolé mene deugue si réwemi 🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Yanna yalla takhawoulène si barker Seydina Mouhamed S A W
@ndeyekorkamergane84353 жыл бұрын
C’est très triste mais quelque soit la situation avant de démolir au moins avertir les accupants attendre qu’ils sortent leurs bagages mais venir un beau matin avec des camion de policiers et un catarpila c’est vraiment injuste
@Ousmanyatassaye3 жыл бұрын
Si c'est le cas, ce que Sénégal ne plus le pays de droit. Par contre, j'aurais bien voulu connaître l'avis de l'autre protagoniste. On ne peut pas détruire un demeure sans des arguments ou preuves tangibles. Navré pour la famille. C'est dur, j'espère que la situation va trouver une issue positive
@ndeyecissegaye44843 жыл бұрын
Yalna len yalla takhawou ci barke Mohamed psl
@kheuchdia20633 жыл бұрын
Ay nitt you bakh gnon fa deuk yalna yalla takhawouléne si barké naby 🤲🤲🙏
@ndiayemaman3 жыл бұрын
Hooooo li metina trop dawal lene yeurmande adouna dou keur lep fi laniou kay bayi kone na lep rafet famille bi bouniou guené founiou dieum ak ndiaboot gui ak fi rewmi tolou ni kholal khaleyi sa yaram sakh dafay metina dé yalla nasi yalla def diam rek inchallah metina trop
@soumboulsowlofficiel96453 жыл бұрын
Wallahi g pas les mots 😭😭😭😭
@lhommesage25073 жыл бұрын
bilahi brooo Dara bobou la diangué alquran keur gui keurou thiosane la
@eakM53 жыл бұрын
Sénégal wakh deugue dé yombou fiii trop de zone d'ombres dans cette histoire. Kahm séni droit warone na takh guène yoré papier keur gui. Comment la baque a fait pour diay ko? Mais aussi kokou nonou guène di toudd khalissam la yor di dieunde vous n'avez pas à le citer comme ça comme si que mome guène diotell Métti na mais boulène togne Yallah beugoul lolou et Force à cette famille
@mouhamadfaal85313 жыл бұрын
Tu as raison...Les papiers de la maison sont avec la banque...Leur papa avait une dette auprès de la banque avant sa mort.C'est cette dette là qui a causé tout ce problème.
@khalifadione733 жыл бұрын
Yalle naléne yala tachawou thie bark Serigne Babacar ❣️❣️❣️❣️ yalle rék mo am dole💪💪💪💪💪
@atoudiasse25203 жыл бұрын
Yallna yalla takhawou leen lii mètèna trp mè yalla sounou brp yp lafi lèkalle
@fatimaba10403 жыл бұрын
Meti grand max yalla nalene yalla diapale
@aichabop26163 жыл бұрын
Matssa yalna yalla takhawou si barkè sangue bou tèdeu bi psl
@khoudarkhlayhisalam80203 жыл бұрын
Yalla yalla yeram domi Afrique 😭😭
@clairemari72923 жыл бұрын
Ndeyssane c triste et grave que le bon dieu vous vienne en aide
@adamadiatta13283 жыл бұрын
Police Sénégal naniou bayi Di trokhal nite adouna d'où keur couye def Lou bone rek woléne bakhna adouna diekhna ba paré😭😭😭
@cirediedhiou26463 жыл бұрын
Qu’Allah le Puissant vous Assiste.
@cocosfire22383 жыл бұрын
Sama khôl daffa fess😭😭😭😭 yalnalén yalla takhawou
@kalsumbaro4693 жыл бұрын
Lii méti na diay dolé bakhoul j'ai mal yallah naléne yallah défal soutoura 💔💔💔😭
@natachfaye37643 жыл бұрын
Amine yarabi
@loucha71793 жыл бұрын
Comment peut t'on acheter ses genre de maison et y habiter avec l'esprit tranquille
@ndiemendiaye99793 жыл бұрын
Motakh niuy deuk mm pa un moi niu fatu
@mbalofficiel75133 жыл бұрын
Walakhi deuguele
@rokhayasarr93183 жыл бұрын
Yale na.lene.yalla diapale.si barke désigne babacar sy
@mamigueye57603 жыл бұрын
Sénégal diaye dolé mofi beuri yalla naléne yalla takhawou
@aissatakeita3863 жыл бұрын
Ndeyssane, je connais bien cette famille surtout la mère de Tonton Mbaye N'doye:Adja Makalé parce que c'était une guinéenne, une Soussou. Tchey Yallah, li métina 😢😢😢
@pape75923 жыл бұрын
Ndeysane yalna yalla takhawou léne si barkép seydina mouhamad
Ndeysane allahou akbar le senegal a changé ana sougnou yeurmander li metina
@aramedioufbeye96863 жыл бұрын
Tiey souf moytoulen tiowal souf alalou baye dou alale mouhamed (sws) amoul daray adouna adouna dou keur masta la famille
@kalakalababu57733 жыл бұрын
Loutahk dou alal
@ndeyecodoundiaye70663 жыл бұрын
C'est avec tristesse qui regarde cesces image car c'est dans cette maison même qui je suis née et passée une partie de mon enfance je connais cette famille mais courage
@elimanembengue3 жыл бұрын
Ndeyssan la dame à la fin de la vidéo, elle est une dame cool, elle vend du bon petit déjeuner ! Yalla naleen Yalla taxawou
@mamou24823 жыл бұрын
Bilahi mane mi khalé bou ndaw mangui dioy té yayou mako😭😭
@diorseck18423 жыл бұрын
Allah il est juste très juste même Mo gnou guena kham t gnoun khamougnou T dina atté soite fi si adouna gneup di guiss wala alakhira
@maguettethiam71543 жыл бұрын
soubhanallah yeureumande adouna dou dara yeureum len nitt gnii
Senegal niak naniou yeurmande yalla nalene yalla takhawou
@thiambabel97433 жыл бұрын
Macky,les chauffeurs,les famille,les etudiants (encor en greve de faim),nieupeu dièpii nanioula,bathi rabou ndoyeni sakh!! Ay liii ma la bagne🤬❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥💔💔💔
@diouldewar49423 жыл бұрын
Billae nieumpeu… wayé def sa bompou bour teih yalla moy sa bourr dallay setan rk 🥺yalla nalén yalla takhawou inchallah
@papid1003 жыл бұрын
Je suis de tout cœur avec cette famille que je connais bien . Je compatis c’est très dur. Que DIEU vous aide .
@mbathiendiouga58383 жыл бұрын
Yalna len yalla teklo kho
@thiernodiouf46303 жыл бұрын
ndeuysann wadiour dina tekk njabotam tionah banque bakhoul bayilenn dii tayleeh keur... Etat aussi waroul guiiss niouy neweul dollee badollla li mettinah trop yalla na yalla diapalenn baguenn djott sen keur
@ouleyediop40903 жыл бұрын
Yalla nalene yalla takhawou 🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻
@daoudaka76453 жыл бұрын
Du courage père yalnalén yalla takhawou
@astoudiagne58113 жыл бұрын
😭😭😭😭🤲🙏
@nogayekane50353 жыл бұрын
Li de sougnou kogne la bilay dafa daw yaram😭😭😭😭
@ndiomegueyebapoulo48353 жыл бұрын
Bilay ndoyéne ndeysane thiey Sénégal 🇸🇳 métina nakari n’a dounde meune nagnou diay dolé😭yalna lene yalla tek lokho Sama keur mane
@pendandiaye2983 жыл бұрын
Hooo li métina trop😭😭😭 way yalla nalén yalla takhawou dimbalilén baguén tiotate si métina Président Macky yalla dinala lath no yoréwone Sénégal euleuk nakh policier yi niouy djiteul niouy naguou keuri diambour yi yi niaw na trop agresseur ak sath yi banditisme yonam toujour
@fatoudiouf61003 жыл бұрын
Ndeysane ronbou n’a Lén ce jour 2 auto police go garé Ani soutoura yalla naléne yalla diapalé
@talladiop85253 жыл бұрын
Li niawna trop walahi diaye dole bakhoul yalnalene yalla takhawou si barcke psl seydina Mouhammad warowone toudou mortalla adouna dou dara demal mangui gniow lofi guis deey diekh deloulene si sougniou borome
@zeynasene23633 жыл бұрын
Massa, que le bon dieu vous protège
@julediakhate25693 жыл бұрын
Ay way Ana yeurmander 😡😭😭😭😭
@Zahra-tx5vk3 жыл бұрын
Yallah naleine yallah takhawou
@amydiallo4343 жыл бұрын
Yalla naleen khalifa takhawou guinaw yalla akk yonentii bii 🙏😌
@bocarbocoum42213 жыл бұрын
Yalla na yalla leral lep inchala du courage c'est vraiment triste
@serignetoure95333 жыл бұрын
Yalla rek moufii ne yalla nalene yalla takhwo barkbe serigne touba
@mohamedrassoulgueye63953 жыл бұрын
Thiey Sénégal yalna yalla takhawou famille bii way
@momombodj97163 жыл бұрын
Vraiment c'est très triste😥 li si Sénégal
@laminediagne29493 жыл бұрын
Il faut invoquer AllâH contre les oppresseurs.
@Fatoumbodji4593 жыл бұрын
Yalna lén yalla atté té diapalé lén Inshalah
@BinetouDiop-sy5gh Жыл бұрын
Mioune len rk té yalla takh yalla mongui guiss lep
Yalla nako yalla saafara diay doler bici deuk bi mowara dak
@aminabeuguebfallou7363 жыл бұрын
J ai pas les mots walay ku Amul imane deugue di k salite li metina niawna ay allah Vient au Secours des souffrants amen
@dioplemaire25463 жыл бұрын
Le grand Serigne de Dakar dois réagir tu sers à quoi ta communauté une famille noble et digne lebou niou len dilen trokhal si diguou Ndakarou dou Yonne