Condamnation de Bougane "c'est un verdict d'avertissement, il va changer de comportement" P.Ndiaye

  Рет қаралды 6,551

Walfadjri TV

Walfadjri TV

Күн бұрын

Пікірлер: 126
@ThiamBabel-p4m
@ThiamBabel-p4m 2 сағат бұрын
Bougane n'a yarou té dem diamoudji yalla gnanal sokhnam si yalla nako yalla yeureum
@bayesalioufall7838
@bayesalioufall7838 Сағат бұрын
Bravo équipe walfo TV sa kaw sa kanam rek inchallah barkep Serigne bi❤❤❤❤❤❤❤
@mbadji3581
@mbadji3581 3 сағат бұрын
FAL AY MAIRES, DÉPUTÉS BA FAL PRÉSIDENT😮 BAYI BOPAM ! KI MOY GOR MOY GARMI ❤❤❤ DIEUREDIEUF YALLA BOUR ❤165 DÉPUTÉS AK SUNU XOL DOYOUL BA TEY🎉🎉🎉🎉
@mbstvtv
@mbstvtv Сағат бұрын
Gor dégue
@bayesalioufall7838
@bayesalioufall7838 Сағат бұрын
Sénégal yalla nafi diamou yagui barkep Serigne bi❤❤❤❤❤❤❤
@mbstvtv
@mbstvtv Сағат бұрын
Amine ya-rabi
@sokhnadiop5172
@sokhnadiop5172 Сағат бұрын
Amine 🙏
@laminewade1890
@laminewade1890 Сағат бұрын
Merci bcp pape Ndiaye
@ffutu1
@ffutu1 2 сағат бұрын
Il faut assainir votre milieu car ya bcou de personnes qui n'ont pas leur place dans les médias. Sonko rek la gnouy suivre.
@HafidaSeyad
@HafidaSeyad 54 минут бұрын
Sonkooooooo Sonkooooooo rek inchallah
@aminatafall9934
@aminatafall9934 2 сағат бұрын
Biteye li nga wah amoul béneu transhumance mo am moy diouguè ci parti dem ci bénén parti. Rien à voir avec un appel au vote
@khadysoumare1518
@khadysoumare1518 3 сағат бұрын
Vous avez oublié que Bougane a traité vos collègues de charognards et d hypocrites. Moustapha Diop Mame birame wathe et pape matar Diallo. C est aujourd'hui que Bougane est devenu l ami de walf. Quelle ironie
@tabaradiallo7956
@tabaradiallo7956 2 сағат бұрын
Vraiment lii amoul logique
@amadoudiallo7997
@amadoudiallo7997 Сағат бұрын
On s'en fou c'est parce qu'il est en désaccord avec le Pastef que bougane est mauvais maintenant. Fouettez nous la paix avec la politique de la pensée unique.
@PatrioteXxL
@PatrioteXxL Сағат бұрын
Hypocrisie ne tue pas au Senegal
@bayesalioufall7838
@bayesalioufall7838 Сағат бұрын
Thiey yalla vraiment doyna warr dh bilay😭😭😭😭😭😭
@bachirgueye548
@bachirgueye548 Сағат бұрын
Bitey massoul beugue sonko
@ElyasSow
@ElyasSow 2 сағат бұрын
Billahi Béty Ak Biteye Warougne Bokou Plateau Jtjr Danguéne Beury Wax Trop
@SerigneSarr-vh8lt
@SerigneSarr-vh8lt 2 сағат бұрын
Biteye n'a pas sa place dans le débat politique
@Diaw-l8g
@Diaw-l8g Сағат бұрын
Free Bougane free Bougane
@abdoubassdiop9481
@abdoubassdiop9481 2 сағат бұрын
XANA MALICK GAKOU da transumé kone
@Moussaseck-g5k
@Moussaseck-g5k Сағат бұрын
Biteye quel est son problème,c'est quelqu'un qui n'aime pas Ousmane Sonko mais il risque l'AVC ou le goidre .Sonko d'où moromm
@alufaye1470
@alufaye1470 2 сағат бұрын
Biteye un mecrean mechan
@diopmouhamadou3129
@diopmouhamadou3129 Сағат бұрын
Biteille vraiment sa wx da beuri trop Motakh douniou comprendre Dara Dara Dara
@CheikhDrame-f3v
@CheikhDrame-f3v Сағат бұрын
Biteye pastef la bagne surtout Sonko, appel a voté pour quelqu'un et rejoindre un autre partie,c'est très différent,un nafekh de plus
@khadrovitch
@khadrovitch Сағат бұрын
😂😂😂biteye khanaa cône yaw saga transhumè .😂😂 Dakh walf nga nekone deme séné TV.diouguè senn tv😂😂 legui lolou noko toudè .. soutien AK transhumè d'où benne.
@LayineGueye-f3j
@LayineGueye-f3j 3 сағат бұрын
Biteye domuharam là Il critique toujours ce gouvernement
@beuguebamba7612
@beuguebamba7612 2 сағат бұрын
Robino yi mo teth
@lebaolbaoltigui2599
@lebaolbaoltigui2599 4 сағат бұрын
Bitey il crie fort pour dire des betises
@PapeFaye-hp8cr
@PapeFaye-hp8cr Сағат бұрын
Bougane mi beug rail ousmane sonko
@moustaphadiop9566
@moustaphadiop9566 Сағат бұрын
Biteye moom C'est une personne de mauvaise foi... Moom il est contre Sonko. Ce gars est politicien masqu...
@laminewade1890
@laminewade1890 Сағат бұрын
Mais biteye bougane dou nit il es fou c normal de le garde en prison un gars comme lui le peuples n'a pas besoins de ca
@Lotatine-m6o
@Lotatine-m6o Сағат бұрын
Bougane est un homme généreux qui a aidé au vu et au su de tous les sénégalais des gens désœuvrés, des malades etc, emploie des centaines de personnes etc contrairement à ceux qui le critiquent. Lui au moins a montré la voie de la générosité et de la persévérance pour réussir là où certains de ses compatriotes aigris ne veulent le voir.
@mouhameddiallo9969
@mouhameddiallo9969 29 минут бұрын
C'est son devoir parce que il mounoul deff leneen dé
@HafidaSeyad
@HafidaSeyad 53 минут бұрын
Bittey est contre pastef
@adamadiop6269
@adamadiop6269 Сағат бұрын
Béty mi beugoul deug
@ModouThiam-t2p
@ModouThiam-t2p 2 сағат бұрын
Thiey "Bouteille"sou défoul bariwoul ndiarigne.Bou tothi ba yeess😢😢😢
@bachirgueye548
@bachirgueye548 Сағат бұрын
Imame aline badara ndaw example
@mortallandiaye6369
@mortallandiaye6369 Сағат бұрын
Sa haine dafaay fégne sii Sonko sii plateau yeup amo xaam xaam nopiil
@alioufaye7825
@alioufaye7825 2 сағат бұрын
Biteye, un journaliste doit être plus outillé que ça Tu ne dois pas prendre au sérieux les gens qui font de la comédie sur les réseaux sociaux
@songondiaye6012
@songondiaye6012 Сағат бұрын
Bitéye guiss ngua you gueuna graw thi comportement wa opposition bi té wakhoulo thi dara .
@songondiaye6012
@songondiaye6012 Сағат бұрын
Bitéye do dara yow thi nonou Sénégal yi nga bokk
@Agaziop
@Agaziop Сағат бұрын
BITEYE REJOINT ALIOU SOW ET DOUDOU KOULIBALY. SIDATE AVAIT RAISON
@beyebaba3724
@beyebaba3724 2 сағат бұрын
Biteeye yawe Ousmane sonko mooye saa problemi da nga ignane vrais nafekhe ngaaa demale defie saa commedie ak gnome niokhite
@beyebaba3724
@beyebaba3724 2 сағат бұрын
Te yawe biteeye mouno solou sa yeere bou khewiibii
@serignembackedieng976
@serignembackedieng976 Сағат бұрын
Biteye mii Bougane dakoo wara recruté rekk Barki Yàlla ñu noppalu ci moom
@PapeFaye-hp8cr
@PapeFaye-hp8cr Сағат бұрын
Bitteye gayi marqué nanla
@papekora8330
@papekora8330 2 сағат бұрын
Bougane gueye n'aime pas sonko et lat diop voulait que sonko meurt en prison lat diop à fait l'apologie sur sonko et pourtant ya pas de débat
@HafidaSeyad
@HafidaSeyad 53 минут бұрын
Bitey vrai domram la
@yerosow7063
@yerosow7063 2 сағат бұрын
Pape liga wakh tchii kasso dguela mais dafay fekk nga intelligent En plus il y a des récidivistes
@AzizNiane-j1b
@AzizNiane-j1b Сағат бұрын
Biteye vraiment n a pas sa place ici
@mamethiernoniass7711
@mamethiernoniass7711 2 сағат бұрын
Biteye Ku soff ngz
@mortallandiaye6369
@mortallandiaye6369 Сағат бұрын
Yaaw da nga done niaane Sonko yaague sii kasso bii yaa guëuneu bône nieupp yaaw biteye
@PapYoussouphaSamba
@PapYoussouphaSamba 2 сағат бұрын
Waaw Biteye yow bi Moustapha Diakhate di wakh neh yalna bu ben jigeen jurati doom ju melni Sonko,foo nekkoon?
@birame696
@birame696 2 сағат бұрын
Bittey mi doff la
@khadrovitch
@khadrovitch Сағат бұрын
Biteye amoul niveau 😂😂😂😂😂temps bi raw nako
@serignesall7635
@serignesall7635 Сағат бұрын
Bitéye dafa beug forcé say yamal comedien nga😂
@omzo9376
@omzo9376 2 сағат бұрын
Biteye il est trop con franchement.
@lamine3372
@lamine3372 3 сағат бұрын
Moustapha Diakhaté donnn niane Ousmane Sonko dhé ci cachot, Biteye mi il est malhonnête
@bigsam3133
@bigsam3133 Сағат бұрын
Biteye nafeka sonko rek la bagne
@Nogaygagou
@Nogaygagou 2 сағат бұрын
Bitéy diamonoy soncko foumouonéwon déé sakh nànal nankoy soncko
@cheikhka-ok5gz
@cheikhka-ok5gz 2 сағат бұрын
pape sou fé kéné bougane nitle
@DjimbaThioye
@DjimbaThioye 10 минут бұрын
bitaye mom kholbou bon lako lalha défall ❌️❌️❌️
@aliounecissebop2870
@aliounecissebop2870 2 сағат бұрын
biteye est non seulement nul mais c'est un hypocrite..
@amadoudiallo7997
@amadoudiallo7997 2 сағат бұрын
C'est parce que il n'a pas dis ce vous voulez entendre.
@babadiop5851
@babadiop5851 2 сағат бұрын
biteye khamo louko bougane deff ba takh mou yéné lolou yagui nonou bougane toke khass say mbokou gua diko soutenir kone kay nagoulko loumou la wakh fofou la kholam tolou
@Lamine.fall92
@Lamine.fall92 2 сағат бұрын
Wa pastéf bo waxé sa xalat té anrégéwoulén niouni la amo xam xam wala narfékh 😂 alors que nio khamoul thiottou ndém
@afcprod-c1c
@afcprod-c1c Сағат бұрын
Biteye il parle trop té tousss xamou Koo
@xeltélévision
@xeltélévision 2 сағат бұрын
Biteye mo bari wakh amoul bén xam xam
@mamadoudamedieng208
@mamadoudamedieng208 Сағат бұрын
Bitèye parle trop pour ne rien dire
@boureliou4579
@boureliou4579 Сағат бұрын
Bitey dof plus la deg deg
@HafidaSeyad
@HafidaSeyad 51 минут бұрын
Bittey ❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌
@ngomcheikh8508
@ngomcheikh8508 2 сағат бұрын
Ce gars pastef rek la bagne
@salioudiallo5585
@salioudiallo5585 Сағат бұрын
biteye est limitei,boppou konkorong
@badiboy8698
@badiboy8698 2 сағат бұрын
Bitiye theatre katt na yemm sii lolou Bitey nitt nakk doko bagne ba diko fenal te yaw si ay fenn rekk guay dokhh
@BakhdadTv-of9id
@BakhdadTv-of9id 2 сағат бұрын
Bitey mi weré nafekh la aka bagne pr sonko
@PapeFaye-hp8cr
@PapeFaye-hp8cr Сағат бұрын
Thiokass sa diabar 😂😂
@khadimbambandiaye8133
@khadimbambandiaye8133 Сағат бұрын
Mais bitey mi loutax mou contre pouvoir bi à ce point Di wax ba guemign gui Di four ni narnga sone
@issacoulibaly4667
@issacoulibaly4667 2 сағат бұрын
Biteye sa lamigne reuyna té khamo gate
@mataboulaye3995
@mataboulaye3995 2 сағат бұрын
Biteye t’es pas sérieux, ne généralise pas un cas .
@ousseynoudiedhiou4371
@ousseynoudiedhiou4371 Сағат бұрын
Ce mec il n'es pas sérieux où il est amnésie Souzane kamara a dit pure que ça 🤔
@seydousall2233
@seydousall2233 47 минут бұрын
Biteye il est nul ensuite il parle trop il déshonore le groupe walf
@moustaphadiop9566
@moustaphadiop9566 Сағат бұрын
Biteye sudee Sonko ngay bañ sa xol di gëna Boon. Di Nga am AVC. Ce que tu dis de cette personne lépp mi ngi yaw. Ku bañ pouvoir bi Nga. Enlève ton masque, te Nga dëggal sa bopp ci far ak sak mbañeel ci Sonko
@abdourahmanediallo4828
@abdourahmanediallo4828 2 сағат бұрын
Biteye amoul xam xam
@PapeFaye-hp8cr
@PapeFaye-hp8cr Сағат бұрын
Bougane di mbam daffa kham teranga
@mamadoucamara9201
@mamadoucamara9201 2 сағат бұрын
Biteye ne peux pas parler français Il est de Ndoffane. Il se croit un grand journaliste et il ne parle jamais français
@cheikhndiaye5370
@cheikhndiaye5370 2 сағат бұрын
Bitey mom domeram la
@songondiaye6012
@songondiaye6012 Сағат бұрын
Biteye boul niou sonal yow Sonko ak pastef beugo lén guiss do wakh dara lou bakh thi gnom
@AzizNiane-j1b
@AzizNiane-j1b Сағат бұрын
Biteye vraiment tu dois retouner a l ecole
@soniadiallo5893
@soniadiallo5893 3 сағат бұрын
Salam Bitéye kagne ngay arrêté liniou arrêté Bouganne dala nakhari nga thiy am loy wakh Bitéye demal def li Bouganne def nga khol ndakh do yagg thi kasso bi Bouganne amna chance ndjit you bess yi amnagnou lougnouy kholal comme mom néna lideur Politique la nieup di wakh bou boba di nga khamné limou thi ak neew foula thi fekk dounga reuy lamine rek bagne gni fi yallah tek essayél rek bilahi dinguene dé walka nguéne vieillir avant l heure ndakh bagna nanguou dogalou yallah te gni diapougnou kénne diaplouwougnou kene loutakh Bouganne défoul wonne li thi Diamono Macky bayilléne nafekh té nangou dogal ce n sont pas les mara c Dieu
@Elzo317
@Elzo317 Сағат бұрын
Biteye moko tay Wala day griller ki amoul khel d
@assanendour2074
@assanendour2074 2 сағат бұрын
Biteye reuy na lamigne niakana kham kham nafekh na
@beuguebamba7612
@beuguebamba7612 2 сағат бұрын
Biteye mom khamoul dra😂
@massambasowe3380
@massambasowe3380 Сағат бұрын
Gnakk xam xam bisi bitéy
@PapeFaye-hp8cr
@PapeFaye-hp8cr Сағат бұрын
Billahi biteye c un nulard
@khadimdieye9677
@khadimdieye9677 Сағат бұрын
Bitey mii na dal doff deug leu
@FatouDia-c6n
@FatouDia-c6n 2 сағат бұрын
Biteye MBA do poupe sa bopou nigay wakhé métina
@aissatousylla4172
@aissatousylla4172 Сағат бұрын
Oh bitéye ou est ton intelligence ?
@ang7087
@ang7087 Сағат бұрын
Bitey defeant là
@seynabougueye8692
@seynabougueye8692 Сағат бұрын
Vraiment biteye vrai domerame amoul benne kham kham ak sa kaname guiye melni sa kouss gui vrai salopard
@KhoudiaCisse-tv4ps
@KhoudiaCisse-tv4ps 2 сағат бұрын
Bitey tu nous emmerde tu nous tympanise
@adijniang5991
@adijniang5991 2 сағат бұрын
Bitey khamo dara
@khadimbambasylla4453
@khadimbambasylla4453 3 сағат бұрын
Bitey dina masa Day ci plateau bi
@dabakya9
@dabakya9 3 сағат бұрын
Bitey lignou wakh sonko mo raww mayniou détail reik guay analyser
@cheikhka-ok5gz
@cheikhka-ok5gz 2 сағат бұрын
bitéye yaw tagha daghor si bougane Di diaghasé réwmi
@mariamamoussoubagoudiaby8604
@mariamamoussoubagoudiaby8604 Сағат бұрын
Bitey yow mbépé
@mandiayendiaye6912
@mandiayendiaye6912 2 сағат бұрын
walf biteye mofa gueneu gnake xame xame
@malickdiene1782
@malickdiene1782 3 сағат бұрын
Bougane 😂😂😂
@capricefemelle3168
@capricefemelle3168 Сағат бұрын
Bitey nafek bou mak la
@amadoudiong5905
@amadoudiong5905 2 сағат бұрын
Biteye t'as haine vas te tuer mon gars. Nioune sonko rek
Kepar Gui du Jeudi 31 Octobre 2024 Sur Walf Fm 99.0
Walfadjri TV
Рет қаралды 7 М.
Colorful Pasta Painting for Fun Times! 🍝 🎨
00:29
La La Learn
Рет қаралды 308 МЛН
Каха и лужа  #непосредственнокаха
00:15
Try Not To Laugh 😅 the Best of BoxtoxTv 👌
00:18
boxtoxtv
Рет қаралды 6 МЛН
Du jamais vu!! les gr@ves révélations du ministre des sports: Ahmed AIDARA dépassé...
23:05