J’ai pas regretté d’avoir regardé cette émission.Une femme brave et battante ta gueme yalla vraiment référence nga maman Ndeye Diouf . Yalla nala yalla same
@biinetandiaye41944 ай бұрын
Je savais que je n'allais pas être déçue si je regarde. Elle est tellement intéressante cette dame ma sha Allah... Yalla na Yalla seddal seu khol li dess si seu doundou yayou gneup . kouleu deg hamni kou bakh nga.
@altesseroyale43833 ай бұрын
Ndèye Diouf est une femme de valeur de dignité, qui se respecte. Elle est une référence pour la jeunesse, une source d’inspiration pour les jeunes sénègalaises.
@deugrekkdeugkesse14404 ай бұрын
Thieyy serigne Fallou balla Aïssa ♥️sokhna ci yalna nga Goudde fane,fenne moy niawteef bi gueuneu bone kou ko bagne nite kou bakh nga🙏🏽bonne tu es une grande dame❤❤doundeul❤️ thiono dou reere boromam dolle sante rekk 🙏🏽
@MairyNdoye3 ай бұрын
Massa petite sœur. ❤❤❤. Adouna dafa méti. Tu es un exemple de motivation pour toutes les personnes qui souffrent ❤
@Toubaexellent2 ай бұрын
Sama yaye dji damako beug té hawma sakh loutakh ndékété SËRÏGÑ FALLOU bounou bokk beug la 💚🙏🏿🇸🇳
@ndeyesall3 ай бұрын
MaaShaa'Allah ❤maman N'deye Diouf mou Serigne Fallou. Yalneu borom bi geune leu takhawou, aaamiiiine yà rabbi. Xol yi toyneu niou😢
@CoumbaAmadouTall3 ай бұрын
Vraiment jai été fier dècouter cette femme une référence machalah jai vérsé des larmes
@Ami-t7z4 ай бұрын
Machalla ndeysane Ndeye Diouf ya bakh thiono bigua sona si sa yaye ak surtout sa raka bi ak saye rakh ame yeurmande labire rafet hole machalla mome lala yalla faye on t'aime longue vie et bonne santé à toi ❤❤❤
@ndeyeastoudiatta90203 ай бұрын
Machala maman ndeye nieupa la beug,khamuma won sa borom keur dafa wagniéku,yalana borom bi yeramko tabalko dianatul firdawsi📿🙏🏼
@dieynadiouf64104 ай бұрын
Fallou awa bousso kouko beug ma beug la ak no meunti mell nak ❤️❤️❤️
@ndeyecoumbacamara72014 ай бұрын
Bilahi j'ai jamais pleure pour une émission mais tata ndeye ndeye diouf vous êtes une grande dame machalla
@fatimaniang17213 ай бұрын
Koubakhe la sama tata koumane loumouye def Machallah goudoufane ak wére légne koye nianal
@ndeyembeneniang32044 ай бұрын
Wakdji daye yokou diome ak gueme yalla machala long vie maman❤❤❤
@aminapulaar43684 ай бұрын
Très belle émission, Maman Ndeye Diouf est une belle personne ❤❤❤❤ de l'intérieur comme de l'extérieur Mashallah
@mameantagueye86774 ай бұрын
Sama waykatt bi yalnala yalla mayat dieukeur diou bakh bou mélni sa khadim gueye bi gueye ndioro yalna khipé adiana ak gnifa nék gneup
@Mariama-no4tj4 ай бұрын
Ameen
@VassorDiallo4 ай бұрын
Ay kokou ngadone fotoul kou bona bone la djoyma ba sone bilahi amna gnou gnak yeurmandé 😭😭😭😭😭 Alhamdoililah ba lép djékhna yalanala yalla may goudou fane ak wér TATA
@SokhnaassiDiop4 ай бұрын
Une vraie lionne yalla n'a yalla samla ❤
@Mariama-no4tj4 ай бұрын
Allahuma Ameen
@Ami-t7z4 ай бұрын
Barke baye machalla Ndeye Diouf yagua sonou si sa papa ak si aye ligueyame diko ladial alarba serigne Fallou motakh lepe barkel na machalla yalla na yalla gueuna doli khewal ak soutoura tu le mérites ❤
@FallDamel74844 ай бұрын
Vraiment metina trop sakh Maman Ndeye Diouf ❤❤❤nala yalla sunu borom doli defar Sutoura si barké seydina Mouhamed 🕋
@mamealimaniang4 ай бұрын
Ce que retient le plus kou ame reconnaissance la yalna yala doli taxawou 🥰🤲🏾
@Oumar2015.64 ай бұрын
Machallah ndeye diouf je l'aime trop
@Betelgueuse804 ай бұрын
Masha Allah tata Ndeye Diouf, doundal yalla yok tawfekh ❤
@VitorSilva-fg6nn4 ай бұрын
❤❤❤❤❤ ❤❤❤❤ une dame de fer ❤❤❤❤❤ une brave dame machalla une lionne une battante ❤❤❤
@awaséne-h8u3 ай бұрын
La seule leçon à retenir dans cet interview c'est la reconnaissance niit dangay reconnaissant
@bbkine39573 ай бұрын
Ayway maman ndeye Diouf yalnangua goudou fane té andak wére❤
@MariamaDanfa-dl7td3 ай бұрын
magui 😭😭😭 sakh bly une femme k j'estime bcp yaye Moy lepp Soko amoul rek té foutu
Lou meti yaguana thi adouna barke serigne babacar sy
@perlagueye15734 ай бұрын
Walahi 😢
@cecilefaye35624 ай бұрын
Machalla une dame de classe ❤❤❤❤
@hawadiagne72214 ай бұрын
Emission bi nekhna machallah
@LobeNgom4 ай бұрын
Naww nalla dh😊
@coumbaba30154 ай бұрын
Ndessane adouna 🇺🇸🇲🇷🙏🏿
@massowgueye47644 ай бұрын
Cette femme est tres intéressante
@mamendoumbefall97834 ай бұрын
Machallah yalla na yalla defal la diamou ❤❤❤❤
@salioutine44264 ай бұрын
merci ndeye mo serigne fallou mbacke ❤❤❤❤❤
@adamaly24494 ай бұрын
Machallah Yaye boye ❤❤❤
@salioutine44264 ай бұрын
machallah mame coumba ❤❤❤❤❤❤❤❤
@sokhnaastoucisse55394 ай бұрын
Mashallah elle est très gentille je l’adore
@FatimataDiallo-y8r4 ай бұрын
Meilleur émission
@NdeyeSokhnaGaye-g3f4 ай бұрын
Machalla gueuneu fasse diomnmm
@BayemodouSall-sb6cz3 ай бұрын
Merci beaucoup coumba dia ❤❤❤
@khadydiop33014 ай бұрын
❤❤❤❤longue vie maman
@ngonesaliou83474 ай бұрын
Ndeysane ndeye diouf kou bah gnak yaye ma thi ham dara da méti
@maguettegueye73584 ай бұрын
Machalla goudou fane ak wèr amale diam mama ndaye
@adjaratoufall4 ай бұрын
Ndeysanne, Ma Shaa Allah. Yalna sunu Borom same niou mayniou bax akk oyof. Elle a l'air tellement gentille et généreuse. L'histoire du linge impayé m'a fendu le coeur. J'ai une copine à ma mère qui s'est également mariée à 40 ans. Mais Ma Shaa Allah, elle était toujours vierge, beurii fouleu lol ba diaxal ma.
@awandiaye56374 ай бұрын
Wakhtanebi amna solo lole masala
@tymandiaye23554 ай бұрын
Ndeysane metina trop 😢😢
@adjambodji5824 ай бұрын
Dieuredieuf Serigne Fallou
@cissaminata52294 ай бұрын
Vraiment je l'estime beaucoup 🎉😂❤
@ArameKebe-lw8te4 ай бұрын
Bilaye yala até naléne☝️☝️
@NimhYsih4 ай бұрын
S'il était possible d'avoir des sous titres, vos vidéos toucheront plus de monde, je ne comprends pas le wolof malheureusement. En attendant beaucoup de courage, vos émissions sont très intéressantes
@awaliciouss83264 ай бұрын
Une grande dame❤
@bakhmamembacke63824 ай бұрын
Ay waye kimou don fotal li mom douko djik adina ak allakhira 😭😭😭😭
Aye ndeye heudieuna Dioye émission bi yeup dama KO Dioye sama yaye 1986 la ganiou ma nekk khalebou ndaw mais metina
@seynabousarr15524 ай бұрын
Yalla nala yalla faye
@famathiam85244 ай бұрын
Aduna yageuna metti ndeysaneu
@rouguiba37844 ай бұрын
Machaalla yalla nala yalla feyal bopam 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@JoumaeNdour2 ай бұрын
Mai dioye na dadou li way😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@safietousambe35334 ай бұрын
do nieuw ma mayela sama papa daga dioulité trope t sama papa aussi. mame coumba diokh ma numérome
@jukanjie75624 ай бұрын
This is a very sad story aunty ndey you went through a lot
@LunikSeul-gk9bh4 ай бұрын
Bilaye yalla xamnani dafa bakh meussouma setane émission am louma meti mais dolisi am louma neeex thiey yalla sounou borom amna gno xamni euleuk dina meti si gnom nax akkkk Dma diare si mbindane mais certains personnes yalla yakamti woulein
@thiattediop28764 ай бұрын
Ohh ndeyesane 😢😢
@tallaba71284 ай бұрын
Bilay adouna dafa metti 😢
@FANACISSE-p9c4 ай бұрын
J'ai des larme aux yeux 😢😢
@astourassoulmane77424 ай бұрын
Instructif
@aichadiagne6013 ай бұрын
Mame coumba svp invite le docteur youhanidou wane dia Directrice de l’hôpital militaire de ouakam
@SabelleDrame4 ай бұрын
Ohhh amna niou bone té niémé akhh🙄
@DieynabandackDiop-or8oo3 ай бұрын
Racky Aïdara svp🎉
@Noirceur143 ай бұрын
Foote bobu dh wallahi gnee wuma koula ko doone deflo wallahi soko topone dh dinga hamni rethiou ngako
@FatoumataDiof3 ай бұрын
Ky dama ko buga rek ndey diouf
@altesseroyale43833 ай бұрын
Si j’avais 50 millions je les offrirais à Ndèye Diouf Serigne Fallou pour payer ces deux jours de travail qu’une personne malhonnête a refusé de la payer! Mais je sais que cette personne subira le châtiment divin!