Coumba Baldé hausse le ton "affaire bi Coumba am Ndeye ak Coumba Amoul Ndeye La, Naniou Bayi Fimisté

  Рет қаралды 10,374

DAKARBUZZ TV

DAKARBUZZ TV

Ай бұрын

Coumba Baldé hausse le ton "affaire bi Coumba am Ndeye ak Coumba Amoul Ndeye La, Naniou Bayi Fimisté

Пікірлер: 46
@papethiaw8510
@papethiaw8510 Ай бұрын
Mère yiii sakh si l'ambiance yiii thieyy Sénégal 😭😭
@ladianepathe5637
@ladianepathe5637 Ай бұрын
Fadel dangua seytané trop sk nguir yalla guena leeen si famille diambour yii
@MbayeFaye-ev9rd
@MbayeFaye-ev9rd Ай бұрын
FÉLICITATIONS LISS NDIAGO KASSÉ REK 🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@seringembacke9316
@seringembacke9316 Ай бұрын
Baol baol pir barke serige saliou mbacke ♥️♥️♥️♥️💚♥️💯♥️♥️♥️♥️💚♥️ Merci beaucoup yai Boy baol kesse ❤❤❤❤
@mamadubalde3118
@mamadubalde3118 Ай бұрын
Mére bi vremnt moy lolou
@user-ys2dd8fb7y
@user-ys2dd8fb7y Ай бұрын
Mère ioe dell raffétal adouna amoul solo té lamb famille moko geune ndakh lamb dayy diekh té famille dou diekh
@oumybadianne7453
@oumybadianne7453 22 күн бұрын
Coumba Baldé dama ko yénné Dom dji am reussite totale ci lamb ndakh Yayame vraiment dama yeureum yaye dji
@idrissaba8124
@idrissaba8124 Ай бұрын
Mère bi elle communique mal
@ahmedseck991
@ahmedseck991 Ай бұрын
Fadél vrai saïtaané nga Amna lo xamanté waroko nangou ay question saytané rék ngay poser. Mère Coumba Baldé nékal nitt vraiment lingay deff nii dafay yakkal Pokola xaaliss waroula boolé ak say mbokk Jul sou banioonn poko dou nieuw cii combat nékkal nitt mère. Sada lou raffétt rék la beugoonn et puis moom ak Pokola ba dara doul dara la woonn Mère makk nga bayil ay détail tanga am esprit positif ish
@cheikhmbow7315
@cheikhmbow7315 Ай бұрын
Mère bi moy yakhale pokola li man malako wakh
@AlyYoro
@AlyYoro Ай бұрын
Mére yangui yakhal sa dôme de bakhna rek🤷
@marmendy3314
@marmendy3314 Ай бұрын
Ta raison mère vraiment.
@sambatorino8115
@sambatorino8115 26 күн бұрын
Pokola yalana fi dioguer di danou nakhe nga nopi
@user-wx8dp8lo1j
@user-wx8dp8lo1j Ай бұрын
Pokola seul
@papadjibrilsy3780
@papadjibrilsy3780 Ай бұрын
Mère bi beugoul Jacop baldé c'est dommage. Nrikal mak ngeu bollo famille bi
@user-zp8uw3cq1m
@user-zp8uw3cq1m Ай бұрын
Pakola yayame moco nara yakale loubarri
@AliouDiouf-tj2cu
@AliouDiouf-tj2cu Ай бұрын
Billahi Day daw rek
@papendione2411
@papendione2411 Ай бұрын
Mère.nekale.nite
@lamine3372
@lamine3372 Ай бұрын
Mère bi beugoul Jacob raw pokola
@thebosh-se5lb
@thebosh-se5lb Ай бұрын
Mere bi xaliss mokoy tagal3 ak famille Jules balde louko nite bagne bagne Xamnii deretuuu famille yii niokko Geumeull lepp way3 xaliss bakhoul
@lamine3372
@lamine3372 Ай бұрын
Mère bi seytané leu
@pronosticfootsenegal1112
@pronosticfootsenegal1112 Ай бұрын
YALLA NA YALLA DOLI DIAM..POKO LIGUEYAL REK ..LAMB AMOUL SECRET ENTRAINEMENT REK LE RESTE DAY COMPLETER REK
@yakhoubaseydi905
@yakhoubaseydi905 Ай бұрын
Faadel yw gor bou seytanee nga blh
@lamine3372
@lamine3372 Ай бұрын
Mère bi ele n'est pas reconnaissante Jules baldé boys yeupp laa yamalé
@Senegalausenegalais
@Senegalausenegalais Ай бұрын
Kon jul baldè dafa bagne pokola balde
@ModoulaminTouray-xp8tr
@ModoulaminTouray-xp8tr Ай бұрын
Boy nekal nitt
@ibouciss3519
@ibouciss3519 Ай бұрын
frère ioe tamit Jules sou banione Pokola dina nieuw si combat bi arrété way tamit
@mamadousylla4592
@mamadousylla4592 Ай бұрын
Grand yow sétanga
@ibouciss3519
@ibouciss3519 Ай бұрын
@@mamadousylla4592 ah nakh gua sanie ko wax gni ay diakhassé kat légne rek blyy
@mouhameddia5168
@mouhameddia5168 Ай бұрын
Dome meunoul faye yaye xolou yaye moko diap comprendre lêneko rèk
@mamoudousow1031
@mamoudousow1031 Ай бұрын
Mere bi dafay wutal doomam ay noon
@ModouFall-zz7je
@ModouFall-zz7je Ай бұрын
Mère bi ak Jules BALDÉ nékhowougnou
@user-ey5fm9st9h
@user-ey5fm9st9h Ай бұрын
Mére bi boko kholé rk khamni maggué toume Koba la
@MilkMilo-qr5uc
@MilkMilo-qr5uc Ай бұрын
Amal respect si yayou diambour
@user-ey5fm9st9h
@user-ey5fm9st9h Ай бұрын
@@MilkMilo-qr5uc nio bokkou Pikine biniou deuk
@MilkMilo-qr5uc
@MilkMilo-qr5uc Ай бұрын
@@user-ey5fm9st9h d'accord na et wédi wouma mako mais wakh ni mo xawa déplacé mane faralou ma l béne mbeur pikine mais je la comprend
@diobs1474
@diobs1474 Ай бұрын
Mère bii wéroul dei
@yakhoubaseydi905
@yakhoubaseydi905 Ай бұрын
Fadel lii nga wakh ci sada ak lii nga wakh fii bokoul boul diakhase famille diambour
@ModouFall-zz7je
@ModouFall-zz7je Ай бұрын
Nn fadel wakhoul dra lou niaw si interview mom ak sada bi
@mamoudousow1031
@mamoudousow1031 29 күн бұрын
Deggo fi béen yaayu mbeur néek fi propagande doomam bi ish
@Senegalausenegalais
@Senegalausenegalais Ай бұрын
Jul baldè dafa sokhorè pokola baldè
@seynaboukane9017
@seynaboukane9017 Ай бұрын
Bayil seytane Jules balde loumouy soxore pocola
@sambatorino8115
@sambatorino8115 26 күн бұрын
Yaw mère nekal nit
Naniouko Japalé Guir Yallah
19:58
DAKARBUZZ TV
Рет қаралды 7 М.
WHO DO I LOVE MOST?
00:22
dednahype
Рет қаралды 3,9 МЛН
WHO DO I LOVE MOST?
00:22
dednahype
Рет қаралды 3,9 МЛН