🇸🇳Débat Baye Niass kouko guiss Doug Aldiana🤔 - Oustaz de la Nouvelle Génération & Oustaz Alpha Ba

  Рет қаралды 12,377

KAADU DINEE JI Tv

KAADU DINEE JI Tv

Күн бұрын

Пікірлер: 88
@amadouourydiallo3145
@amadouourydiallo3145 Жыл бұрын
Macha ALLAH Oustas Alpha ba et sa team. Il faut tous les démasqué.
@fatimadieye9478
@fatimadieye9478 Жыл бұрын
Soubhanal lahh
@AbuMuhammadAlGambi
@AbuMuhammadAlGambi Жыл бұрын
Jazak'Allahu Khairan Ustadh Alpha Bah حفظه الله tontu bi rafet na Allahuma Barik إسكاتهم بالمعرفة
@assanedeguenekhul6190
@assanedeguenekhul6190 Жыл бұрын
Machallah cheikh alpha
@asannediop3826
@asannediop3826 Жыл бұрын
Oustas alpha ba mo baah machallah barakallahou fikoum
@hamdine7940
@hamdine7940 Жыл бұрын
Merci Serigne alpha ils ont entre de jouer
@2rayone760
@2rayone760 Жыл бұрын
Noooo!Senegal very sad😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@alinesamb5006
@alinesamb5006 Жыл бұрын
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته كيف حالك أنت بخير أحسن الله إليك ماشاء الله بارك الله فيك جزاك الله خيرا بارك الشيخ الفاهم باه حفظه الله ورعاه ❤❤❤
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
‏وعليكم السلام ورحمة الله وبركاته آمين ولك مثله
@Mouhamad-u6f
@Mouhamad-u6f Жыл бұрын
Machallah ma khady et younouss également
@Mouhamad-u6f
@Mouhamad-u6f Жыл бұрын
Machallah oustaz alpha
@bassiroumbaye8099
@bassiroumbaye8099 Жыл бұрын
😂😂 كبرت كلمة تخرج من أفواههم إن يقولون إلا كذبا 😂😂 حفظكم الله ❤❤
@seynaboukane2767
@seynaboukane2767 Жыл бұрын
Sofianqué yi séne problème moy séne wahou serigne laniou gueune gueum que wahou borome bi AK yonéntibi
@dieynabandiaye9211
@dieynabandiaye9211 Жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤ débat bi amna solo
@younousseaidara3892
@younousseaidara3892 Жыл бұрын
مَا يُبَدَّلُ الْقَوْلُ لَدَيَّ وَمَا أَنَا بِظَلَّامٍ لِّلْعَبِيدِ
@OumuTawaim7299
@OumuTawaim7299 Жыл бұрын
لاحول ولاقوة الابالله العلي العظيم
@AmadouSylla-pg2kh
@AmadouSylla-pg2kh Жыл бұрын
شكرا لك الفاء باه وفقك الله واصل طريقك فإنه طريق الخير باذن الله تعالى نفع الله بك
@tawhid-i3l
@tawhid-i3l 2 ай бұрын
Medoune bayil philosophie bi 😂😂😂
@odoa4880
@odoa4880 Жыл бұрын
Kou amoul dalil rekk transformer wou ab philosophe 😂😂
@ngommahtar4689
@ngommahtar4689 Жыл бұрын
إن الله لايفلح الميعاد نعم / أولكن لا تعلمو( أن البار)كل يوم هو في شأن
@FatouNiang-d1k
@FatouNiang-d1k Жыл бұрын
Ma warou .Qu'Allah nous guide.
@baboucardiop5121
@baboucardiop5121 Жыл бұрын
❤❤ machallah ya oustaz Alpha contanna si yew ❤❤❤❤
@adramesagnan5195
@adramesagnan5195 Жыл бұрын
Oh oustaz ya réer Baye Niasse pour nka firi ay wahom fay nka ame DEUG DEUG ya rérr bilahi
@Makhtarka
@Makhtarka Жыл бұрын
mais limou dougal si dîné ji des 1000 sen baye ak sen serigne defouko si islam bi point. c'est un homme extraordinaire et multi dimensionnel
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
Lolou sa xalat bopou laa 😂😂⁉️
@dameadame6062
@dameadame6062 Жыл бұрын
Ah kay yalla dafay changé waxam . يمحو الله ماشاء ويثبت وعنده علم الكتاب
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
Ban borom xaam tafsir moo koo firee ayat bii nonou tee ragal yAllah cii sa commentaires bii
@moustaniang7375
@moustaniang7375 Жыл бұрын
Je ne suis pas d'accueil avec lui mais il faut équilibré
@ibrahimac-y4g
@ibrahimac-y4g Жыл бұрын
ta teunku si algur ane ak suna li moy deugue wa salaam❤
@mariamaba5454
@mariamaba5454 Жыл бұрын
😘😘👍
@KAADUDINEEJITV
@KAADUDINEEJITV Жыл бұрын
‏وعليكم السلام ورحمة الله وبركاته بارك الله فيكم
@GakouBaba-w1v
@GakouBaba-w1v Жыл бұрын
15:40 mashallah
@aboudiop353
@aboudiop353 Жыл бұрын
❤❤❤❤
@bounesadio9934
@bounesadio9934 Жыл бұрын
Medoune fall ''' yallah néénaa dou togn ''' lo deff AK wakh diodiou
@sakhoousmane7066
@sakhoousmane7066 Жыл бұрын
Alpha wadie douy na warr legui mom dafa begue deguel Baye Niass yide wakho yala no li doy na warr
@bineta1752
@bineta1752 Жыл бұрын
Kou diotali wahou yalla ak wahou prophète bi gnouni tu est dur dagna meti dagna sokhore arrêter l’hypocrisie yalla dou fowoukaye yalla dou Morome kepe kouy diouli di wore di supporté gni wote si dine te bokossi nafeke gna Malheureusement les cœurs sont malades 😢ouztaz alpha ba le mal est très profond très même
@bineta1752
@bineta1752 Жыл бұрын
@@ismailadiallo7819 salam ma tontula yaw moi personnellement aussi je ne vis pas au senegal je ne parle pas avec toi au cas ou tu te sens concerné par mes propos cela n’engage que toi Mane sounna Senegal lako diangue avant may guene Senegal Assalamou aleykoum
@bineta1752
@bineta1752 Жыл бұрын
@@ismailadiallo7819 sama genre yiii mane amouma sa diote di daguessante ake yaw sama temps dafa précieux lolu pour prendre mon clavier et discuter avec des gens yo khamni loulene nekh lagnuy wakh Kholal salam
@bineta1752
@bineta1752 Жыл бұрын
Salam à vous aussi
@Yeme--NA
@Yeme--NA Жыл бұрын
Assalamou Aleykoum sama béne Dieuwrine dafma wakhone Yalla dou wakh ba paré Wéddi boppam et Il dit qu'Il est le plus juste des juges. Légui mane je me dis que sou naré atté dara dinako déf pour samoneték limou wakh. Té pourtant c'est vrai que souko narone déf mba bagneko déf kéne meunou kaka téré fokna ki wofou laye wakhé. Mais aussi il faut que niou khamni mom dou wéddi boppam. Sinon yaw Alpha amna question boumala beugone poser tchi séne débat bobou nguéne done wakh Yalla mingui tchi kaw wala tchi souf.
@samsoudinesallseck4722
@samsoudinesallseck4722 Жыл бұрын
Diuemmi Yalla Migisi Kaw Khame khamame Mignisi Bepou Barap Yalla moko Wakh Ak Yonentame قال تعالى أأمنتم من في السماء أن يخسف بكم الأرض فإذا هي تمور أم أمنتم من في السماء أن يرسل عليكم حاصبا فستعلمون كيف نذير
@Yeme--NA
@Yeme--NA Жыл бұрын
@@samsoudinesallseck4722 Légui nak Alpha la beugona latch fane moy tchi kaw wayé bala lolou damaka beugona latch ndakh guem nani la terre est rond ? app boule la bou mélni wer wi rek bou nek tchi diaw dji dans l'espace et qui ne repose sur rien apart kémanou souniou Borom. Souma wakhé ni mom guem nani la terre est ronde après nak lakoy latch wala ma lérale ko béne mbir mou dolli matchi.
@babacarsokhna6363
@babacarsokhna6363 Жыл бұрын
Yalla mo waxal bopam ni migui ci kaw.
@Yeme--NA
@Yeme--NA Жыл бұрын
@@babacarsokhna6363 Waw mane je suis juste à la recherche d'éclaircissement motakh kourel yeup lay déglou après ma khol, légui fane moy tchi kaw la beugua latch Alpha mais bala lolou mou expliquéma est ce que la terre est ronde ndakh nda mélni ball. A partir de là nak lakoy diokhat explication pour mou dollima.
@alphaOumarsy389
@alphaOumarsy389 Жыл бұрын
Sounnah rék oustaz sa numéro
@diopkeba8068
@diopkeba8068 Жыл бұрын
Yaw âme gua kulawax bët moy guis. Lo xamul dagay manou baye Niass koku yalla moko teral. Un grand éducateur
@matarndiaye9969
@matarndiaye9969 Жыл бұрын
Et après dafa takh kouko guiss dougou aldiana ?
@modouniane2163
@modouniane2163 Жыл бұрын
baye niass djoublou waayou wakhame bi moye kou gisne maye ki donnou yone nennetou yalla mouhamed صلى الله عليه وسلم ngua beugue ma thi lolou dinala tek mome bye niass thi yone wokhamene so thi wathioul de mo tere ngua dougou aldiana
@alphaOumarsy389
@alphaOumarsy389 Жыл бұрын
Numéro alpha ba
@bounesadio9934
@bounesadio9934 Жыл бұрын
Ki xamoul Dara wayyy 😂😅😅 baye Niass d'où touss nitt késé laa
@alassaneseye2191
@alassaneseye2191 Жыл бұрын
Billahi louler
@AFRICAN67
@AFRICAN67 Жыл бұрын
​@@alassaneseye2191wallahi Ibrahim Niasse nite simple kassé leu, soufianké kémane rék le gëm
@bounesadio9934
@bounesadio9934 Жыл бұрын
@@Makhtarka ok mais d'où yallah fofou lay wakhé ... Nitt leu comme sa baye .... Baye Niass déy POUB comme sa ndeye 😭🤣🤣🤣🤩
@Makhtarka
@Makhtarka Жыл бұрын
​@@bounesadio9934 mais limou dougal si dîné ji des 1000 sen baye ak sen serigne defouko si islam bi point. c'est un homme extraordinaire et multi dimensionnel
@Makhtarka
@Makhtarka Жыл бұрын
محمد بشر لا كالبشر بل هو كالياقوت بين الحجر
@mustaphabaldeh2232
@mustaphabaldeh2232 Жыл бұрын
Salaam Alpha, Baye Nyass watou wahtadul wujud walla Hullol walla itahat baye Lim wakh outea ak Lee yeep
@abdourahmanelaye9846
@abdourahmanelaye9846 Жыл бұрын
السلام عليكم ورحمه الله اسمي عبدالرحمن لاي ساكنا في اسبانيا ولكني بودي ان اشارككم في الحوار ولكن أراه بعد ماانتهت كيف اشارككم مباشرة وشكرا
@aboubakrydiallo3739
@aboubakrydiallo3739 Жыл бұрын
قال تعالى ( مايبدا القول لدي و ما أنا بظلام للعبيد ) Ki limouy wax mo reuy Waxu kéfér leu
@ibrahimac-y4g
@ibrahimac-y4g Жыл бұрын
lal moy man liilaa wla léélaali am solo moy djoulite laa naniou néke ay djoulit
@DIALOGUE-DEUG
@DIALOGUE-DEUG Жыл бұрын
Un autre philo-Doff 😂😂😂 ce Médoune
@dialloibrahima8134
@dialloibrahima8134 Жыл бұрын
Tarikha problème la thi islam
@falloutoure135
@falloutoure135 Жыл бұрын
Lou lér 8:39
@XadimgayGay
@XadimgayGay Жыл бұрын
Kii lim wax dëgg la yéen ñii yéenay sanka nitñi dagéena soof yalla léepu lum def mbaa lum wax dafa dagan ci moom?
@baaliou6634
@baaliou6634 Жыл бұрын
Aquran Ak Sunna Rek mo worr point
@asannediop3826
@asannediop3826 Жыл бұрын
Dafa lére wallahi barakallahou fikoum
@mbayendiaye7560
@mbayendiaye7560 Жыл бұрын
Mais qu es ce qu on a foutre guiss n importe qq serigne en reve q es ce q ca nous raporte la religion est complet by Moustapha swa
@samburu-lelionnoirdafrique6194
@samburu-lelionnoirdafrique6194 Жыл бұрын
C'est faux oustaz de otv de ouakam, une chaîne sur KZbin. Je viens de le vérifier. Il parle trop sans connaissance
@user-wm7dl2iu4
@user-wm7dl2iu4 11 ай бұрын
imam Alfa boull wakhe AK ki wallahi Mane dama tite
@bahalimatou8108
@bahalimatou8108 Жыл бұрын
C'est une perte de temps de discuter avec des ignorants, farfelus de ce genre, avec cet accoutrement de comediens
@asannediop3826
@asannediop3826 Жыл бұрын
Loutah sering ci maneu reuye yeuye Lou nane ragal yalla mo am solo wallahi dafa lére wallahi
@aliounediouf8196
@aliounediouf8196 Жыл бұрын
MAIS C'EST QUOI ÇA?DES ROUGE À LÈVRES? 🤔🤔C'EST UN OUSTAZ GOORDJIGUÉNE???🙊🙊
@Babe-FaLilOu
@Babe-FaLilOu Жыл бұрын
Soubhanallah akhi moytul wax loula worul Barakallah fik
@yayathiongane9839
@yayathiongane9839 Жыл бұрын
Waliyou yalla yi louniou wakh d'où dagne baye niass cheikhoul islam sou wakhé kouko gise dougue aldianne mougui wakh ak dioulite yi té nion niou kou naroul tékhé doléne beuge doléne gise yonèntibi kou ko gise douga aldianna té amna yéfeur youko gise kone Bouy wakh lolou mougui wakhak dioulite té dafa ame gis gissou beut ak khoul meun ga khôl nite té gissou ko yalla mo môme aldianna môme safara moy dougal kouko nékh aldianna wala safara mais ngiko nékh moy ngiko geume déf lime santané khôl bou sél yalla dale moy yalla
@Makhtarka
@Makhtarka Жыл бұрын
وشكرا @yayathiongane9839
@djibi710
@djibi710 Жыл бұрын
Wokhou doff rék
@diopmouhamadoumoustapha8757
@diopmouhamadoumoustapha8757 Жыл бұрын
Yeurma dé sounou borom noko diapé
@FatymaBah-v5f
@FatymaBah-v5f Жыл бұрын
Tarikha yii doul rek lanioy déf danio niémé yallah
@alioufall4265
@alioufall4265 Жыл бұрын
wkh mou change équestre woul si yall moy deuge
@FatymaBah-v5f
@FatymaBah-v5f Жыл бұрын
Téksi diagouniou
@mamoudoudaff3028
@mamoudoudaff3028 Жыл бұрын
Feiheilen va deff yenen dioulit mogueun ....baye niass loumou deff ci dinei lislam bi kenn defouko
@rappel4152
@rappel4152 Жыл бұрын
Wa kho deugueu deh tafsiroul al Quran d'où livre Fiqh d'où livre sharh khadith. Dewoul ci combat meusooul combat defoul aussi ouverture. Diayoul bakanam té Ken guené wouko pays nguir l'islam... livreram bokoul ci livre telouway pour xam sa diné té yi laniou meuneu défal islam alors sa Baye Niasse loulou def ? Réponds avec preuve et n insulte pas
@mamoudoudaff3028
@mamoudoudaff3028 Жыл бұрын
Jamais ma sagua .baye niass limou convertir ay nitt ci l'islam en nombre kenn defouko ci adouna...féhélen def gni nékoul dioulit pour gnou neik dioulit..tei baye limou def ci dinei lislam c palpables..c te donner la liberté qui va avec un responsabilité..
@mamoudoudaff3028
@mamoudoudaff3028 Жыл бұрын
Cheikhal l'islam...c lui le cheikh de l'islam. Et tu prétends à dire qu'il na rien fait de l'islam...suprime ces disciples dans le monde et tu verra un bon nombre de musulmans diminuer...arrêtons de dénigrer entre nous musulmans. Faisons tous pour rependre l'islam comme la voulu le prophète sll
@rappel4152
@rappel4152 Жыл бұрын
@@mamoudoudaff3028 diw limou def limou def lim ko ?... vas y tous la defoul ci l'islam. D'adiou ci liniou dadioul de 1 de 2 Cheikh Al Islam c'est Ibn Taymiyyah partout dans le monde fokhé wakhé Cheikh al islam gnouné Ibn Taymiyyah. Yalla koko diaglele. si tu me crois pas va taper sur Google qui est Cheikh Al islam ? Ibn Taymiyyah lalel guenal avec plus de 1000 résultats Do guiss feneu Founiou wahé Baye... Ibn Taymiyyah a écrit plus 300 volume un seul livre à lui " Majmough Fataw " fait plus de 16,000 pages sur islam. Mo diangal gnou dakka Tafsir ci Isalm Ibn Kathir, ibn hayyim... Té meunala bindal 10 pages youma holoul feneu ci limou defar islam. Dalam sah mo gueune Baye Niasse s'en kokou dou touss la defaroul islam. Limou bindeu yeup da matoul sah 5000 pages on vous a menti demlen diangui s'en dîné
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
@@rappel4152Merci ❤️👊🏾
@gueyediop
@gueyediop Жыл бұрын
Modou limoy wakh lou amla yen por yen yalla yen rek lay douguel aldiana mou guen sanion niepay dem safara waye yalla borom bou matla
@masiba7272
@masiba7272 Жыл бұрын
Yalla dou wax waxet.yalla tegui promessam.yalla d'où tegui ay waxam. Lolou ken douko lam lamé. Soy tegui wax dangay Andi dalil si arhouranou yalla,wala sounay yonentem.
30 novembre 2024
21:53
Ambiance Media
Рет қаралды 63
小路飞和小丑也太帅了#家庭#搞笑 #funny #小丑 #cosplay
00:13
家庭搞笑日记
Рет қаралды 17 МЛН
Lazy days…
00:24
Anwar Jibawi
Рет қаралды 9 МЛН
Mom Hack for Cooking Solo with a Little One! 🍳👶
00:15
5-Minute Crafts HOUSE
Рет қаралды 20 МЛН
“Don’t stop the chances.”
00:44
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 26 МЛН
😂Père Ngol Ngol Jeunes Patriote Yi Sonal Nanouko Bilahi 🤣
2:58
Jakarlo mouride wahhabiste
22:55
FIPOU NEWS
Рет қаралды 1,5 М.
20 نونبر 2024(2)
13:03
دولةبكي فشنيقال
Рет қаралды 408
小路飞和小丑也太帅了#家庭#搞笑 #funny #小丑 #cosplay
00:13
家庭搞笑日记
Рет қаралды 17 МЛН