Sanoussi Bâ est le meilleur !! Fier de son courage intellectuel et de sa probité.
@ousmaneseck29536 ай бұрын
Yalla mbigui fep nit kou nek daguaye wahé fo tolou té yalla dafa matte mais si il n'est pas dans les toilettes il va manquer et Dieu ne manque jamais .
@freemanfreeman44654 жыл бұрын
Le professeur Sanou Sy Ba il est très pertinent mashallah bonne continuation Pr
@didi37594 жыл бұрын
Merci
@amydieye84524 жыл бұрын
Bilay
@moustaphalo51034 жыл бұрын
Amine
@abibseck62404 жыл бұрын
Ki séytane la andake
@FascinatingMya4 жыл бұрын
pertinent woul touss. Ahmed khalifa, fi la tok né meunanio mayé par transfert d'argent et donc par téléphone. nieup dal ci kawam. alors k ak pandémie bi deuk yangui key def. nit bolene ko hamoul. delene mandou ci mom
Merci professeur je suis ndongo dara mais tu m'a même convaincu 🙏
@AbdoulayeCamara-di9lq9 ай бұрын
le problème c'est que les jeunes n'écoutent pas
@papediop94044 жыл бұрын
Merci encore hameth khalifa Niasse,defèna Sénégal bou aamone 1000 personne comme toi walou dîné on sera deuxième derrière Arabie Saoudite..mousse mousse laa,khaathe khaathe laa👌👌
@djibydouf58094 жыл бұрын
C akhmėd ki ne devė pas rėpondre a sette invitation wakhou yalla laye wakh tė gni sén wakh bope lagnou wakh pour ame bauz
@ibrahimakebe60274 жыл бұрын
Complexé mo niouy ray s'il le disait en français personne ne parle mais si c'est en wolof ça crée un débat
@arfangndong44524 жыл бұрын
On est pas des français té sounou langue daffa am soutoureu
@cheikhseye43064 жыл бұрын
Limiy wakh dafa niaw
@babadiop79074 жыл бұрын
Wakh nga deugueu soutoureu c est un faux probleme
@khadycisse41874 жыл бұрын
Ibrahima Kebe billh
@princeloum5004 жыл бұрын
wallahi bro cest ce que je dis toujours
@reveilpopulaire3 жыл бұрын
Akhmed Khalifa a raison parfois fokk gua jar thi digg bi pour niou degla.
@CISSEBOUSONKO4 жыл бұрын
Khalifa niass daal laa andall ndakh s.touba وجوزوا تصريحه عند البليد ان كان لا يفهم تلويحا يفيد
@beugwoutam13654 жыл бұрын
Ahmed mala fan. Sénégal nio méti. Wolof mo niaw rék. Leuf ak peuya leep béne la
@supplements_nutritionnelle31084 жыл бұрын
Le probleme moy senegal dafa beuri ay nafèex xam xam bu andoul ak ay tegun amoul gnarin kunou fi waxon sabay ya ngu si doos bi dafay day dula nèex epui sunou borom kuy wax simom dafay andak tegun
@aminataaminathiam98774 жыл бұрын
T'assure...
@abliesowe51664 жыл бұрын
Saway yangui diawalé li yobou yallah si douss bi té sax mosout fa diogué ndakh "fa ayna ma touwaloo fa sama wadj houlah" ak "wa houwa manhkoum ayna ma kountoum" ak li yobou nit si douss dou bène. Nit dafa dem si douss pour fath adio sou paré guéne yallah nak mom mosoufa diogué té fath adio yobouwoukofa
@deemo37474 жыл бұрын
Ablie sowe Wakh dji ak leral bi rafett na ta teguinei. Masha Allahou. Dieuredieuf
@nogayefall47704 жыл бұрын
Franchement
@thiernoalassanbah86864 жыл бұрын
ahmene halyfa moraw sene baye yeene hamoulene dara wallahi tous hamoulene ko
@farmatafall56384 жыл бұрын
Merci Ahmed sènègal moy lolou kham kham rèk mo waure
@afrifinanceconsfina84969 ай бұрын
Ahmet khalifa dafaye wakh thi khame khame te gnimouy wakhal khamounou fimouy wakhe lolou la
@tahiracisse35124 жыл бұрын
So khamé Yalla genrou wakh yi doula choqué! Kou nek ak yalla limoula nbidé ci sa tieur sou niawone doco ame. Soûla dara dalé medecin bilay fathieu ci digiebi lay diar. Kham kham dal mo wor ak kham yalla nguir dague bepeu kiray. Ahmed khalifa Niass nioumiye wakhal nieup ci plateau bi ay kham lagn
@mamadousy79794 жыл бұрын
Ahmed khalifa dou seni morom
@mamadoutoure44104 жыл бұрын
Senegal ngay jiss menuisier bou taxaw di corriger architect. Serigne jangue alhourane beu matt jangue xamxam sambaboy taxaw feulei diko corriger... niaw ak rafete cest culturel cest pas divin lolou la sambaboy yi nar xam... affaire bi dou waxou xel ak pertinance.. yalla nena yeuneuntou saw nena laniu la wax mem boudei kou eup ahmed khalifa xamxam amena togoul ci plateau bi ka meme... cest un faux argument de contredire kelk1 sous pretexte amena kouko gueun xam
@mouhamadoufall92434 жыл бұрын
''innallaha laa yastakh yii minal khakki'' yalla néna mom si boppam amoul kersa si deug,,,,,, deugue si boppam mo amoul massla mo amoul lougne siy neube neubeul,,,dafay lairr gneup kham,,,kiii dafa diangue ba diangue diotéé ,,, gnikay contredire gneup moy séne baye,,,
@mouhamet1154 жыл бұрын
Mouhamadou fall bilahie bro mais sénégalais mo amoul deg deg
@mouhamadoufall92434 жыл бұрын
@@mouhamet115 billahi lolou rk moci néke,,, ignorant bo guiss dafay beug wéddi wala Di débat si lo khamni Dara khamoukoci,,, c triste billahi kou tékki li yalla wakh ngani no dafa insolent,,, wakhine bi gnaawoul,, nope yikay déglou gno fébar
@mouhamet1154 жыл бұрын
Mouhamadou fall lolou kessé leu mais sénégalais nio yapp ki té ki loumiy wakh kham kham Bou lerr lheu mais ndeysanne bo diangoul amo deg deg loula nekh guay té fek khamo ko sakh dagniy bayi bamou dem yalla na yekh niounane wakhone nako
@AboubakryBa-i2b3 ай бұрын
Walahi wakh nga deukkk
@mareimendiaye50664 жыл бұрын
Merci professeur il temps que quelqu'un met en place khalifa Niass
@amadoundiaye91103 жыл бұрын
Merci khalifa niass. Do séne morome
@djibrilgueye57054 жыл бұрын
سبحان الله! Il a quand-même raison ! Ahmed Khalifa Niass
@marinaeggermont74664 жыл бұрын
Mercie amet khalifa niasse c bien Tu leur append l expression coranique
@mamadoujallow21974 жыл бұрын
Amet khalipha est devenu fou il ne mérite pas d'être invité sa ridicule
@afriquecomedie12244 жыл бұрын
Bilay dafay yakh socité
@mbayedeleguesokhna62854 жыл бұрын
Yow khamo touss Ahmed khalifa Niasse et le meilleur
@babacarndiaye82634 жыл бұрын
ce qu il dit c bien ca
@modoudiop87103 жыл бұрын
On doit le mettre en curentelle
@tip45824 жыл бұрын
Senegal Délén fowé al khuran rek khamolén sakhh lii dii dall sén kaw,je suis bcp de preches en français et jamais on n'a traduit les môts du coran d'une maniere aussi vulgaire dans toute autre langue mais c'est en wolof que vous voulez vulgariser les paroles du seigneur.que dieu me preserve des professeurs comme ce mec
@cheickmoinga32454 жыл бұрын
Merci professeur, Sonko for life.....😘 Galsén for life...🇸🇳🇸🇳
@serignefallouleye7710 Жыл бұрын
Ahmad khalis limou wakh yayou hissa koka ka wakhone yayam mou mér
@omarthiaw93304 жыл бұрын
Ils ont raison xam xam day andak worma ak pédagogie aki téguine
@adjisy15704 жыл бұрын
Cc
@cheikhcheikh8934 жыл бұрын
Demlèn diangui ahmed khalifa niass il a raison yena khamoul dara loutakh sen khalif générale yi dou niou ko wèdi
@mouhamet1154 жыл бұрын
cheikh cheikh lou lerr khalife general you beurri fi Ahmet meunalen diangual
@coumbacoulibaly45064 жыл бұрын
DEUG dafa metti professeur a parfaitement raison, yalla naniou yalla may Aÿ magou xam xam you discipliné
@seynabouthiam2994 жыл бұрын
Amine
@onelove20574 жыл бұрын
coumba coulibaly ki foumou nek professeur foumou soutèniré
@Domino404 жыл бұрын
Nena ndaosi sax amnako ter xamouko
@arondia74214 жыл бұрын
L'essentiel Ahmet khalifa il maîtrise ce qu'il dit. A part ça sounou jangg soriwoul
@Doxandemgroup4 жыл бұрын
Aron Dia ki day wakh rek na nangou débat ak borom xamxam mou geun moye topou plateau yi gua xamni kou diangue dine amoufa
@papaibrahimaseck10034 жыл бұрын
Khamoul touss Satan la
@toulayeceesay22134 жыл бұрын
@@Doxandemgroup nan ngounako et à chaque fois il demande à débattre ak borom kham kham yi mais gnome gno gnemewoul ndakh mo len soute du coup ils répondent pas de peur d'être décrédibiliser même le oustaz qui est sur le plateau s'est réservé de parler ils ne font pas le poids c'est ça la vérité dans la vie il faut toujours être à la quête du savoir comme ça vous débat nga mena wakh mais sa diang bon game ci kelkes sar ak kelkes Aya rek nga yakar ni eg nga c'est là où se trouve le danger té Sénégal Lilou mofi Bari gni fi wote kham yeup khamougnou c'est pourquoi ils induisent les gens en erreur et c'est triste
@mouhamadouthiam55874 жыл бұрын
voila c ça le probléme nak on est pas le mm niveau avc lui
@mamerosediop95194 жыл бұрын
Toulaye Ceesay wakh bou beuri bi lanou taloul ndakh ahmed khalifa niass mi dafa rakadiou tei il exagère kou am kilifeu xam ngani dou nieuw di débat ak satan bi mohhhh
@KhadimSylla-c2p9 ай бұрын
Merci professeur d'avoir ni se ignorants a sa place n importe coi
@assanetoure86404 жыл бұрын
Merci infiniment professeur t'as bien dit machallah...que dieu vous bénisse et vous garde
@ndeyedabadiop42774 жыл бұрын
AMINE YARABI
@sidyseye78514 жыл бұрын
Il faut appelé les choses tel kel sont
@papealioudiagne13274 жыл бұрын
C un grand Mr AHMED deugu mo nékhoul rk serigne bii limou wax meunoulénn si dindi darra guénn nékk fii di nann na rafétt ak na téguiné Sénégal mo métti rk il faut appelé le chat le chat tmt li nk néxatoul AHMED limouy wax meunoulénn ko dindi
@papaly63034 жыл бұрын
Pape aliou Diagne iow kii dou darra
@khadijachou67754 жыл бұрын
Pape Alioune je suis désolé mais wolof dafa and ak téguine Donc juste parcequ'il faut appeler ça comme on le pense tu serai d'accord qu'on dise à ta mère moural sey tate au lieu de moureul sey thieur? Deleine atté deug way
@falloundiaye49154 жыл бұрын
Ameth khalifa loume fi wakh yeupe deugue leu Sénégal leu métti rk bly
@fzahra35544 жыл бұрын
Way way c pas de notre culture.Louner da wara andak worma ak soutoura! Khamougnou yilee kadou.
@AboubakryBa-i2b3 ай бұрын
@@khadijachou6775donc arabe amoul téguine?
@malcommalcom45984 жыл бұрын
Leufeume la
@warriorsevent92794 жыл бұрын
Khalifa dafa deggg, ham ham dafa am solo. Trop de tocard dans ce pays veulent débattre avec lui a'ors qu'ils n'ont pas le niveau
@princeloum5004 жыл бұрын
franchement
@DiawaraMouhamadou-bg2ux7 ай бұрын
Merci beaucoup ahméd khalifa niasse merci pape makhtar dieurengén dieuf
@issandiaye73734 жыл бұрын
Sénégalais mo complexé limouy wakh kham neko bou bakh ignorant yi ak complexé yi gnoy rafetal alors que khamougnou. Ahmed khalifa doundeul
@mouhamet1154 жыл бұрын
issa ndiaye bly bro mais sénégalais mo amoul deg deg
@ismailaseydi43374 жыл бұрын
Wa sen TV amm nguénn invité bou matt seuk se soir 🤣🤣
@عليبابكرشك4 жыл бұрын
Ismaila Seydi kane la
@SDMTv8054 жыл бұрын
Mdrr hahaha wawww waxal dè
@bayemodoudiop70304 жыл бұрын
Parfaitement raison billahi deugue dou rombou Aÿ nope
@payaniang89143 жыл бұрын
Merci beaucoup
@fatoumatacissokho75884 жыл бұрын
Machalah professeur. Merci pour votre courage d analyse. Vous êtes pertinent. Mes encouragements à Mohamed.
@khadimdiop33584 жыл бұрын
Gui dafa dof
@yilebaba65654 жыл бұрын
Très bien dit professeur ... ce minable et faux prêcheur mérite d'être recadré
@libasseseye1214 жыл бұрын
Mon cher,j'espère que tu vas bien ainsi que la famille. Je te conseille fortement de changer ton pseudo. Car "Wahid" est pour ALLAH et dire Ibn signifie fils. ALLAH n'a pas de fils,Il est trop pur pour cela. J'espère que cela va nous servir.
@yilebaba65654 жыл бұрын
@@libasseseye121 salam libass je vais bien alhamdoulilah et j'espère de même pour toi ! Merci pour ton interpellation ! Quand je dis ibn Wahid je fais pas allusion à Dieu mais à mon père qui se nomme wahid ... d'où ibn Wahid " fils de wahid", je sais mieux que toi que Dieu n'a pas de fils ... ! Tu as mal interprété s'aurait été plus simple de penser à l'explication que je t'ai donnée au lieu de prétendre que je ne n'avais pas compris la signification du pseudo que j'ai moi même choisi ... salam
@IbrahimaNdiaye-b9g9 ай бұрын
Merci amna solon
@awasane97794 жыл бұрын
Yalla nagnou yalla léralale si barké ya rassoulilakh 🥰🤲🤲🤲
@salladiaw64264 жыл бұрын
Amine
@ndeyedabadiop42774 жыл бұрын
PSL
@ahmedsylla14254 жыл бұрын
Amine
@awasane97794 жыл бұрын
@la_verite_ triomphera yaw tu n'écoutes pas
@dmxsowkharitouyayam27644 жыл бұрын
Bilahi mo beuri kham kham niass
@bijoujobe86684 жыл бұрын
Koi kon puisse dire akhmed borom kham kham .il est très instruit et sa façon d'enseigner est direct clair et précis..
@abdoulthiam55654 жыл бұрын
Bijou Jobe dara khamou ko déjà fardj signi lignouy neube chez la femme c’est à dire ce qui est caché le vagin en arabe a plusieurs appellations
@abdourahmaneniang11484 жыл бұрын
Tu es malade
@bijoujobe86684 жыл бұрын
@@abdoulthiam5565 sa connaissance est général lo bagne bagne leuk nangoulko meune daw...maintenant vous pouvez vous alarmez sur sa façon faire et ça je vous l'accorde car c votre point de vue
@abdoukhadredabo79654 жыл бұрын
Le problème tu lui poses des question il te repond direct avec des perspectives de débat sur le coran ... tu ésseyes de l'humilier de l'amerder il te pose des questions et toi tu n'arrive pas a répondre donc il est ou le gars qui doit la fermer ?
@princeloum5004 жыл бұрын
les gars ki veulent débattre avc lui tei amougnou xam xam
@fayealpha22154 жыл бұрын
C'est ça fi amoul niou am xam xam pour débattre avec lui
Merci professeur vous avez tout dit mais c'est dommage le vieux est mauvais il est fou
@moustaphawrrdiouf61174 жыл бұрын
Lougnouy rafétale? nonou lah toudou amoul bénénn tourr,walla nga djéll lakk djambourr késsé.boudé wolof par exemple «koye» mou démm si arabe yis nane «aw-ra» té pourtant français moy nane «pénis» kénn dou wakhh. Bien vrai père niass de foi mou dougou fou khott mais darra djélale li si important rékk.té nakk nagnou djéndd livre yis té djéma guéstou sougnou diné lolou moy deugg traduction âme.
@SambaSANGHARE-b2k2 ай бұрын
Tous les télé doivent organisé ses débats sur l islam
@mdfaye37864 жыл бұрын
Merci Ahmet khalifa machalla kham kham gaye wakhè satoulo waye si kham kham amna solo trop diaradieuf
@dieyemodou90704 жыл бұрын
Cey professeur bilahi je t'aime beaucoup sumay nommé meilleur prof de l'année yaw laakay Jox bilahi
@baldediao88614 жыл бұрын
Mais pas bi diaroul invité télé parce que dey deff promo satanique yii di diakhase rek il est très dangereuses
@@mdfaye3786 bindal youtube Ahmed khalifa Niasse franc maçon deguako gues Lou ler lala wakh Ahmad khalifa Niasse franc maçon
@syllasonko4 жыл бұрын
Tu as raison il est toujours derrière lobbies
@tsaftv42474 жыл бұрын
Ameth Khalifa référence la si rew mi boulen ñiou fonto soof guen
@mexdroid17034 жыл бұрын
Ndaw référence imbécile
@soumareismaila37204 жыл бұрын
Pourtant ahmed khalifa a parfaitement raison pk les gens essaye de rafétal les paroles de dieu qui sont déjà beau mais wolof mo doywar le coran étais la bien avant le wolof alors arrêtez
@lho92154 жыл бұрын
Mais kou nekk ak fi nguay waxé xam fi nguay waxé ak ngui nguay waxal wax day raffett yonente bi dafa meuss wax wax bou raffetoul
@soumareismaila37204 жыл бұрын
Momz wolof mo rafetoul je te donne un exemple les femmes divorcées on les appelle THIAGA EN VRAI VRAI WOLOF alors que nous on dit que thiaga moy prostitution wolof mo mel nonou
@lho92154 жыл бұрын
@@soumareismaila3720 waw deug la mane weddi wouma wallah mais wax bou raffet dafa bax
@alhassantall63144 жыл бұрын
@@soumareismaila3720 saway liguaye wakh degue la dh wayé Bou fékké Sétlou Gua Bou bakh Limou Wakh yeup wakh Nako si Batou Wolof You Rafet kone Diaroul Moy dieul yigua Xamnéh djiékol Di ko wakh Si Télévisions Borom xél Diondiou rk doy Nako wassalam
@tsaftv42474 жыл бұрын
Barkep Borome Touba
@sodasalioucisse5274 жыл бұрын
Diagne Bou eup day diflo nit😡
@lho92154 жыл бұрын
Kilifeu daguay matt kilifeu do nekk di wax wax djou beury si télé basiy defaanté ak say morom Dom ! Respect nak yakoy may sa bopp
@thiandoummoussa33944 жыл бұрын
Kilifeu gua wakh ki dou dara amoul orma si kéne nék kilifeu dou rék domou diw la mé si comportement la
Yéna khamoule touss guénii ratatati isque geume guéne yalla sakh
@saloumwilane75424 жыл бұрын
Professeur sanou dall Mancha Allah 🙏 Amna sollo Xam xam bi lérna🙏
@awasall36404 жыл бұрын
Mai mome défoul dara da direct ré
@serignedjilymbacke64224 жыл бұрын
Sama sopè ahmed khalifa
@awabarry98204 жыл бұрын
Wawaw déle diar ci diguibi 👍👍👍
@diallohachim31554 жыл бұрын
pabi dey reral doumou adamayi père ligay wax set thi yalla 🙈
@aminataniasse94774 жыл бұрын
Ki loumouyy sax yalla rk lassi set arxouran mo sax mou frii koi koi amoul xam xam douka dega
@mamadoudiouf27724 жыл бұрын
Merci prof
@fatimadiop83834 жыл бұрын
Doul merde toi yak mome
@mamerosediop95194 жыл бұрын
AMINATA NIASSE iow mi am kham kham deglou ko pfff niou on s'en tape de lui
@arfangmane11714 жыл бұрын
De ngaye fen
@souleymanecisse3014 жыл бұрын
Mais Ahmed khalifa Niass respect pour le peuple
@serignecisse42704 жыл бұрын
AHMED AMOUL FOULA AMOUL FAYDA TÉ LIMOUY WAX AMOUL RÉFÉRENCE SI DIINÉ
@muhammetp.l82204 жыл бұрын
Ahmed khalifa niass Dou référence
@muhammetp.l82204 жыл бұрын
Ahmed khalifa niass Dou référence ap say saya leu
@grausir5534 жыл бұрын
@@muhammetp.l8220 Dites du bien mes frères
@dieynabasow17384 жыл бұрын
Bandit leu
@boygainde37644 жыл бұрын
Ahmed Khalifa niasse mo eupp sen Baye kham kham mé ne blâmer pas Ahmed Khalifa niasse il a juste traduit les paroles de dieu khana kay sougnou langue mo vulgaire bouko traduire ré thi français dolen wakh dara
@KhadimSylla-c2p9 ай бұрын
Selon lui ils est le plus intelligent du Sénégal alors que même Les enfants peuvent labrande
Aye Wolof la wakh dale 😂🤷🏽♂️, yéne si boop yena ame problem, Leuf la kay si wolof, legui Battou arabe bi niawoul?
@ahmadoucisse31844 жыл бұрын
No ki d'où note😂😁😂😃
@71kado4 жыл бұрын
Bou done sa ndeye dou ame probléme cone
@abliesowe51664 жыл бұрын
Vraiment
@abliesowe51664 жыл бұрын
Diangalé dé da wara ler ndakh gniy deglou comprendre
@azomboup4 жыл бұрын
@@71kadoyaw Dagua ma saga wayé waxé wo ak xam xam, problem amousi , Leuf yaw wakh ko si béne lake bu doule wolof ma deeg, sa yaye leuf la yoor , leuf moye batou wolof bi, peul bi , diola bi, Englais bi ame nimou ko toudou tamit. Meunoléna wax ba toudoul LEUF si wolof, Complex moléni raye, di yootu louguén doul nék ba fawu, ba far réré Sen boop ba fawu.
@goradiagne98674 жыл бұрын
Non Khalifa non non narafètt
@beuleupndao11554 жыл бұрын
J'aime bien mr niasse il est parfait avec ses sénégalais coincé6 !!!
@sen-info7-tv9 ай бұрын
Merci beaucoup sanoussi félicitations à toi. Bilahi tu fais des analyses pertinentes.Domoromo nafékh, Yi nassa doome âme 80 ans ténga nék n'a fékh
@khadyndiaye85644 жыл бұрын
Merci professeur ki iow rek ya meune si mom dara
@abdoulayeseck45654 жыл бұрын
Merci beaucoup mon frere ki domeyerame pure la daye khekhe dina waye dousi ame name moukou incha Allah
@toulayeceesay22134 жыл бұрын
Kham nga louy khekh dine moy gnep di wor ben kor gnoune gnou def 2 ba 3 koor kham nga louy khekh dine moy surlendemain Arafat gnouy Doga Tabaski la listes est super longue ki di wakh li yalla wakh nguen ni dafay khekh dîne wakh dji kay moy kou woloubopam rek n'a gnew wedi Limou wakh c'est aussi simple que ca wakhouma nak bayi ba émission bi passé ngay wakh mais en face à face avec lui mala wakhni t'aura pas de volontaire il vaudrait mieux tirer leçon de ce qu'il dit et comprendre ce qu'il dit!!!
@myathiam9214 жыл бұрын
Kham kham bokou khamoul dagay dem weriko ahmat khalife lou mou wakh deugue le yaw so khamoul dagay nopi mais boul,wédiiii
@mouhamet1154 жыл бұрын
Mya Thiam merci mais sénégalais mo diangoul ba paré amouniou deg deg
@pounayelsall21854 жыл бұрын
Choc Professeur T'es trés pertinent machala
@samsamm1444 жыл бұрын
Merci Sanousy mon prof je salut ton courage et ton fran parlé comme tjr
@sistafinaka22614 жыл бұрын
Nonpabi dafadef
@rtiste-jj-mg6tc4 жыл бұрын
En vérité, toutes les paroles n'est pas bonnes à dire.
@FascinatingMya4 жыл бұрын
et toutes les langues ne sont pas faciles à manier
C'est vraiment vrai ya des mots si on les prononce en wolof vous allez me blâmer, mais si je le dis en français ou anglais vous ne direz rien.
@mourtalagoumbala61374 жыл бұрын
Sénégalais mo xèp bopam
@mariamekatarmadikatarmadi86014 жыл бұрын
mimi dewa lolou dafa lérr
@boygainde37644 жыл бұрын
C ça kon nioune souniou langue bakhoul
@mouhammadahmad27374 жыл бұрын
CHAQUE LANGUE A SES REALITIES SOCIO-CULTURELLES. VOULOIR ANALYSER LES RÉALITÉS LINGUISTIQUES EN SYMÉTRIE EST UNE IGNORANCE PURE.
@khadijachou67754 жыл бұрын
Mais parceque wolof deug dafa ladj téguine
@catalan904 жыл бұрын
Merci professeur c'est genre de personne ne devrait même pas être invité dans ces genres de débat parce qu'il sont malade et irresponsable...
@justuncliktv52624 жыл бұрын
Oh quel niveau... Il parle d'expression purement coranique... Les pays d'Arabe niom amouniou possibilité rafétal baatt bi ndax la signification reste la même si suniou langue locale yi amna niou bobou possibilité mais sa v dire ke soko waxéwoul nonou amo orma. Ahmed fofou lay waxè
@ramatoulayely45574 жыл бұрын
Sanou sy ba 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾
@barrodepoet60384 жыл бұрын
Professeur bi fan nako way Amethe genre yi nio bakh ci mome ki xamoul dra napou nieup
@ahmadoucisse31844 жыл бұрын
🙏🙏🙏🙏
@damediop74704 жыл бұрын
Moi aussi
@barrodepoet60384 жыл бұрын
C'est que Sénégal 🇸🇳 genre yi lagne wardi ték ci plateau yi niou yéé ndaw yii
@augustindieme93854 жыл бұрын
Prof bi nullard la. Vive Ahmet le véridique
@LëndëmJi4 жыл бұрын
Ahmed khalifa est franc est vrai . Wakh Dagne koy wakh . Apres chaque personne doit prendre ces responsabilités pour comprendre. Les parents doivent prendre leurs responsabilités.
@djibrildiedhiou74374 жыл бұрын
Khalifa a raison de ce qu il dit,même oustace oumar Sall qui est contre les tariha au Sénégal a confirmé ses dires mais il est incompris éternellement,vu en l Islam il y a 4 école juridique.Avant de critiquer il faut vérifier les sources
@aminataniasse94774 жыл бұрын
Merci
@djibrildiedhiou74374 жыл бұрын
@@aminataniasse9477 je vous en prie Amina
@oumarsow99254 жыл бұрын
Grand Sénégal Gayiii djangou gnou douniou nangou xamou niou
@djibrildiedhiou74374 жыл бұрын
@@oumarsow9925 absolument
@sidyaseck12394 жыл бұрын
Monsieur sanou sy ba et sa réplique philosophique
@seydinagueye55284 жыл бұрын
Xam Xam késsé leu kumu néex ak kumu nakari talubé niuni léne srgn bangui si douche bi ñiu mér Àh xalass
@MoussaDiop-ji2gn9 ай бұрын
Ay talibéme déh khana khaLiss Lagnouco topé.
@idrissandoye65504 жыл бұрын
Le niveau de ahmed depasse le niveau de auditoire ,philosophie ak alhourane ame un ocean de difference ...