DÈBAT : Soufiyankè lou tarikham wakh lay khol bala mo khol lou sounnah wakh. Li niawna

  Рет қаралды 24,327

alkhuran ak sunna rek

alkhuran ak sunna rek

Күн бұрын

Пікірлер: 181
@abrahamabraham7897
@abrahamabraham7897 4 жыл бұрын
MASHA-ALLAH oustaz MOURTADA GUEYE Merci pour tous yalla na yalla goudeul sayy tè dèffal la soutoureu Alhamndoulilah
@cheikhkebe5472
@cheikhkebe5472 5 жыл бұрын
Serigne Moutakha Gueye ;vous êtes très intelligent mais au Sénégal les gens ne croient que le tarikha
@abuahmad9938
@abuahmad9938 5 жыл бұрын
Qu'Allah vous préserve cheikh Dr Mourtada.
@khaoussoukabadiaby6347
@khaoussoukabadiaby6347 5 жыл бұрын
Machallah ya Dr mourtada et cheikh oumar mbaye. Ludul sunna bone na, ludul sunna rer leu, ludul sunna nén leu !!!!! Sunna rek mo wor,sunna rek moye deugue !!!!!!!!!!!!!
@khadygaye6098
@khadygaye6098 5 жыл бұрын
والله
@khaoussoukabadiaby6347
@khaoussoukabadiaby6347 5 жыл бұрын
@@khadygaye6098 qu'allah nous guide et Qu il leurs guide sur suratal mouss takiiim !!!
@khadygaye6098
@khadygaye6098 5 жыл бұрын
@@khaoussoukabadiaby6347 آمين يارب العالمين جرجف
@khaoussoukabadiaby6347
@khaoussoukabadiaby6347 5 жыл бұрын
@@khadygaye6098 en francais svp
@khadygaye6098
@khadygaye6098 5 жыл бұрын
@@khaoussoukabadiaby6347 d accord je dis amine Ya rabbi et merci
@almrtgan2769
@almrtgan2769 5 жыл бұрын
Sunnah moo leer, mais bidaa moo lëndëm
@diammouyalla3880
@diammouyalla3880 5 жыл бұрын
Yaw bodi wabiyoge the bida ganek
@abaaba5045
@abaaba5045 5 жыл бұрын
Yalnama yalla mosal si tarikha ak tasawouf magi wone sisen darayi 11ane waye magi sante nioumelne mortada gueye nioumaye kougeronla siyoyou waye yalnama yalla reysisunah mouy degde komleroul dinala masalerr sen dietal tarikhabi apdole Senegal domam momayer billahi wallah tallah baye nek sisen darayi landan wakh toubabyi sakh dounkowakh ndakh daknak toubabyi 16ane Senegaleyi dal barina aye dof
@milineemilien6865
@milineemilien6865 5 жыл бұрын
OK explique encore
@alamine8024
@alamine8024 5 жыл бұрын
Tasawof bo dol diné kone koye diné
@bayeniass2077
@bayeniass2077 3 жыл бұрын
😅😅😆😆😆😆😆😆😃😃😃مرطدى كي يو ومن كان في هذه احمى فهو في الاخرة احمى واضل سبيل
@Mamadou-Fall
@Mamadou-Fall 5 жыл бұрын
Yallah nama yallah mousseull thi tarikha ak TASSAWUF
@ibrahimniass2008
@ibrahimniass2008 5 жыл бұрын
MOUHAMADOU lou tahe?
@Mamadou-Fall
@Mamadou-Fall 5 жыл бұрын
Ibrahim Niass .. parceque 1 alquran ak sunnah djangallee woull tarikha wala TASSAWUF 2 yallah dafa tèrè group groupoo khaadjalèè diinnee 3 TASSAWUF ak tarikha, daniou layy woommatt thi nitt kou dèè au lieu de alquran ak sunnah 4 alquran ak sunnah dafa leer nagnnn Leeppou lou djoullit bi wara deff nguir yallah yeureumm ko , djeggeull ko , yoobou ko aldjana , yallah ak yonente bi wakh naniou ko thi alquran ak hadiths Konn lann mootakh niou wara woutt serigne wala bokk thi tarikha wala toopp TASSAWUF???
@ibrahimniass2008
@ibrahimniass2008 5 жыл бұрын
Kone wahabiyou lou mou
@Mamadou-Fall
@Mamadou-Fall 5 жыл бұрын
Ibrahim Niass .. wahabiya ,, baatt laa boo khammni , yenn waa ahlou TASSAWUF, yeena ko touddee waa ahloul sunnah mais Mann personalement alquranu yallah ak sunnah yonente bi ak yoonou sahaba yii , thi laa fass yeennee gorgorlou inshaAllah Yallah dafa tèrè division thi islam Yallah dafa tèrè wouutè ak sahaba yii Yallah dafa tèrè djamou loo khamm ni dou guiss dou deeggeu dou djarign dou lorr!!
@diopdame6260
@diopdame6260 5 жыл бұрын
@@ibrahimniass2008 wahabiyou kat amout yenalenko toudè ngir gniak aw lay mousso gis kou takhaw nè man wahabiyou la te doko masa djiss.
@abdoullahmoe4620
@abdoullahmoe4620 5 жыл бұрын
MachaAllah Dr. Deugueu bou takhawé rek nenn day saraan...
@bathiembaye7833
@bathiembaye7833 5 жыл бұрын
Oumar mbaye sofnga trop
@bathiembaye7833
@bathiembaye7833 5 жыл бұрын
Mourtalla yaw mbambga rek
@manebassirou779
@manebassirou779 5 жыл бұрын
Dr Mourtada gueye yannala yalla sameu
@Ibnouahmad1900
@Ibnouahmad1900 5 жыл бұрын
Jeuri Jeuff Cheikh Docteur Mourtada, Jeuri Jeuff Cheikh Omar Mbaye. Yalnaléén Allah Faye Gansaraféti Fayéén Akk Képpou Kouye Wooté Ci Alquran Akk Sunnah Rekk. Ameen!!!
@naramar5208
@naramar5208 5 жыл бұрын
wadial 18 safar inchalla mouy sono bég teh❤️☝🏽
@mameceexibrafall4115
@mameceexibrafall4115 5 жыл бұрын
Moy sounou dem makka, waw kay incha Allah ❤
@diammouyalla3880
@diammouyalla3880 5 жыл бұрын
18 safar ila touba rekk
@babeybass4039
@babeybass4039 5 жыл бұрын
Machalla chiekh mourtada Gueye
@salmanediallo9001
@salmanediallo9001 5 жыл бұрын
Machallah sunna mo leer yallna niousi fatou temou nangoul niouko
@abdoulayefall2312
@abdoulayefall2312 3 жыл бұрын
Lahilaha ilalah Mouhamed Rasoulilahi PSL
@abuahmad9938
@abuahmad9938 5 жыл бұрын
L’Imam Abû Hanifa (رحمه الله) - m.150H - a dit : « Si je dis une parole en désaccord avec le livre d'Allah ou la parole du Prophète (صلى الله عليه وسلم), alors rejetez ma parole. » (Al-Fulânî dans « Iqâdh ul-himam » p.50) L'Imam Malik (رحمه الله) - m.179H - a dit : « Je suis certes un être humain qui se trompe comme il peut avoir raison. Regardez donc attentivement mes opinions. Tous ce qui est en accord avec le Coran et la Sunnah, prenez le, et tout ce qui est en désaccord rejetez-le. » (Ibn 'Abd Al-Barr dans « Jami' bayan al-'ilm wa fadlih » vol.2 p.32 et Ibn Hazm dans « Usûl al-ahkâm » vol.6 p.149) L'Imam Ash-Shafi'i (رحمه الله) - m.204H - a dit : « Si un hadith du Prophète (صلى الله عليه وسلم) s'avère authentique chez les savant du hadith a propos d'une question sur laquelle j'avais émis un avis contradictoire avec le hadith, alors je me rétracte de cet avis de mon vivant et après ma mort. » (Abû Nu’aym dans « Al-hilya » vol.9 p.107) L'Imam Ahmad Ibn Hanbal (رحمه الله) - m.241H - a dit : « Les opinions d'Al-Awza'i, de Malik et Abû Hanifa ne sont que des opinions, et elles se valent toutes a mes yeux, mais la preuve réside dans les hadiths. » (Ibn ’Abd Al-Barr dans « Jami' bayan al-'ilm wa fadlih » vol.2 p.149)
@ahmadoudame7031
@ahmadoudame7031 2 жыл бұрын
Masha Allah wa Sounna✅❤️❤️❤️✍🏾👂🏾👂🏾👂🏾
@mgeagripreneur
@mgeagripreneur 5 жыл бұрын
Maa chaa Allah, Cheikh Mourtada yaye seen Baye Thi xam xam. Soufiyankee bou feer idji thi dîné amoul. Ay contes ak ay histoire rek laniou xam
@OumarDiouf-c8i
@OumarDiouf-c8i Жыл бұрын
ماشاءالله تبارك الله ❤❤❤❤❤
@bachirdiouf4882
@bachirdiouf4882 4 жыл бұрын
Machallah Dr
@cheikhgueye9944
@cheikhgueye9944 4 жыл бұрын
Machalla yallna yala motali sene yene número bi
@modougueye9950
@modougueye9950 5 жыл бұрын
Billakhi wa tarikha démeleene défari juikoyi bayi gnii gakhame ni wakh rek lagnouye déff
@mackysallbadolala600
@mackysallbadolala600 5 жыл бұрын
Ndeysan lima nakhary thi salatoul fatiha diko werda souba ak ngon te do thi diele ben yiw Alhamdoulilah man mom wakh na ba sama borom keur bayiko
@aidandiaye2299
@aidandiaye2299 5 жыл бұрын
Ya niémé yalla wakho deug so khamol li ngay wakh nga noppi thi salatoul fatiha nit day mandou way gueum len sén bopp tontou nguen sén bopp li thi khol yi yalla khamnako nioun gueumou nioulén
@kebatouretoure8923
@kebatouretoure8923 5 жыл бұрын
Yalla nagnou yalla mousal si bidaa
@thernoba4452
@thernoba4452 5 жыл бұрын
Mashallah oustaz
@omarosesea8036
@omarosesea8036 5 жыл бұрын
machallah cheikh mourtada
@omarosesea8036
@omarosesea8036 5 жыл бұрын
ki da khamoul loumouy wakh rek cheikh mourtada ki khamoul foumouy takhaw sounna rek moy degeu
@bachirdiouf4882
@bachirdiouf4882 4 жыл бұрын
Diadieuf mourtada
@mameballafall3117
@mameballafall3117 5 жыл бұрын
Tarikhayi bou amoul wone Sénégal kone kène dou am kilifa wallahi
@gorpurre8269
@gorpurre8269 5 жыл бұрын
Yaw Bou wkhak ñii ay yééfeurr lañ
@mameballafall3117
@mameballafall3117 5 жыл бұрын
GÔR PÜRRE no done ay yeefar danio xamoul rèk wala niou xam banoppi di dof dof lou
@abdoullahmoe4620
@abdoullahmoe4620 5 жыл бұрын
Islam amonna senegal lou eup 700 ans lolou bo demé IFAN amna ay preuves you lerr. Sen serigne yii nguendi topp di fog né gnio indi islam senegal, niom fann lagniou diagué Islam ba soss tarikha?
@mameballafall3117
@mameballafall3117 5 жыл бұрын
Abdoulaye Camara toppal falè
@masiba7237
@masiba7237 5 жыл бұрын
@@abdoullahmoe4620 très bonne question.
@khelcom3639
@khelcom3639 4 жыл бұрын
Diinè dou ay wèrantè..lima mètti moy niguèn sonnalè borom tariikhayi sonalolenko foo catyi ak thiakhaan katyi ...nguir yalla noppaloulèn...tagueen mandou...
@ibrahimadiop8916
@ibrahimadiop8916 4 жыл бұрын
Maintenant Dieu détient tous les pouvoirs et a la plénitude des possibilités. Il peut offrir a qui Il veut.
@moctardia7774
@moctardia7774 5 жыл бұрын
Macha allah
@mameceexibrafall4115
@mameceexibrafall4115 5 жыл бұрын
Yow si nakar ngay dee dem safara, believes wadial 18 Safar incha Allah
@modougueye9950
@modougueye9950 5 жыл бұрын
dieure dieuff serigne moustapha sy
@ibrahimadiop8916
@ibrahimadiop8916 4 жыл бұрын
Mourtala si tu éclaircis une chose pour toi c'est toi qui a raison. Tu connais tout et les autres se trompes.yoonou khamkhame yallah rekkmooko khame.
@dembakebe8506
@dembakebe8506 4 жыл бұрын
Magui si talibé cheikh
@ousm7710
@ousm7710 Жыл бұрын
Serer demal leki Thierré
@masiba7237
@masiba7237 5 жыл бұрын
Douniou massa andi firndee ndax amoul Aÿ sosse la.té louniou sosse si pass pass si diamou yalla bida la.ngeunel yi ni thi wax yeup amoul.
@yacinegueyetahir9487
@yacinegueyetahir9487 5 жыл бұрын
prkoi les arabes n ont pas d tarikhaa
@tabakhsasocietewadialsabam5517
@tabakhsasocietewadialsabam5517 5 жыл бұрын
Cheytannei mom leip lou meuneu défarr nitt..tarbiya nitt fi ci dounya daff kay toumal lou bidah wala chirk. Térei woul shirk ak bidah amm. Avant de catégoriser un acte de bidah ou de shirk, il faudrait d’abord maitriser les réalités esotériques et exotériques de la religion. Adouna niarry mbir moffi neikeu wakh ak dieuf bou yiw wala wakh ak dieuf safann... Cheytann meun nala nakh thi kham kham mei meunoula nakh thi teguin/yarr/mandouté. Parsk Cheytanei meun na fènn, yakkeu khel mais meunoul am djiko bou teiddeu. Lou wayy wakh tei wakh bi lambolou woul ak yarr/ mandouté /teiguinn/ khorma/ ak dalil (base) bou solide wakh djodiou so kholei ci biir très probalement wéroul. Salatoul fatihi c’est la prière sur le prophète (Salal lahou alaeyhi wa salam), la meilleur des créatures. Tei diouli si yonenti Yallah mokeu santanei : In’allah wa mala'ikatouhou you sallouna alal nabi Ya ayou'al leuzina amouna sallou aleyhi wa sallimou taslima...La salatoul fatihi c’est une source de lumière divine intarissable et inépuisable..dayy diokhei fat’khou ngay meuneu kham, di khamei di rangnei. Adouna bi leip lou fi weir daniou ko di'ngeut..lolou mission ibliss leu aki ndiobott tam même yonenti bi am na nioko gueumoul. Leip lou weirr tei kènneu di'ngeut touko sa khel war nassa tayy.. Donc lakoum dinei koum walieu dinn. Gueumeul ligueu gueum tei mandou si lou kénènn gueum. Wa salam !
@hadji71giab36
@hadji71giab36 4 жыл бұрын
Gua guisse hadith bagne ka djeufai fofai la dioubedi tambalai
@cheikhndieye7640
@cheikhndieye7640 5 жыл бұрын
demlen diebolodij
@cheikhkebe5472
@cheikhkebe5472 5 жыл бұрын
Je m'appelle cheikh Kebe, je voudrais faire partie de votre croupe ,comment faire ?
@ibrahimadiop8916
@ibrahimadiop8916 4 жыл бұрын
Yaw y'a wakhne mourtadaa foo jangue. Foo jodoo.koula toude .kou nguente.. Loolou indile joulites yi.
@papeniang7472
@papeniang7472 5 жыл бұрын
كذبت يامرتضى غي قال شيخ أحمد تجاني رضي الله عنه ونفعناالله ببركاته إذا سمعت مني شيئاً فزنوه بميزان الشرع فإوفق فخذوه وإن خالف فتركوا
@sonyboys2967
@sonyboys2967 3 жыл бұрын
C grave bilaye debattre avec wa bibah c une perte de temps des que vous l'heurs pose des question part manque de preuve ils commence a sortir des insultes
@abdoulayendiaye2208
@abdoulayendiaye2208 4 жыл бұрын
Quelques anecdotes Le plus grand détracteur (et sans doute le meilleur) de Mohammed ibn Abdelwahab n’est autre que Suleyman ibn Abdelwahab, à savoir son propre frère. Ce dernier a écrit un livre intitulé « les foudres divines sur les thèses wahhabites » où il réfute point par point tous les arguments du premier en référant systématiquement à Ibn Taymiyya et son disciple Ibn Qayyim al-Jawziyya, tous deux considérés par les wahhabites comme ayant une vision « pure » de l’islam. Il existe un hadith « sahih » (à savoir « véridique ») rapporté par Bukhari où le prophète prophétiserait l’avènement des wahhabites en ces mots : « De l’Est, paraîtront des gens, ils liront le Coran, mais il ne dépassera pas leurs gorges. Ils quitteront l’Islam à la vitesse avec laquelle une flèche transperce une proie. Ils ne reviendront pas [à l’Islam] tant que la flèche n’aura pas regagné son encoche. On demanda : "À quoi les reconnaîtra-t-on ?" Il répondit : "Leur signe distinctif sera qu’ils se raseront le crâne" ». Or ce signe distinctif ne peut que s’appliquer aux wahhabites, puisqu’ils sont les seuls, leurs contemporains en attestent, à s’être rasé le crâne. Cette pratique est encore en usage parmi eux. Nous pouvons donc déduire que selon la prophétie islamique même, les wahhabites sont considérés comme des hérétiques .
@yancoubabadiane6197
@yancoubabadiane6197 5 жыл бұрын
Sunna mba sonnou
@alphaoumarsoindebalde1766
@alphaoumarsoindebalde1766 5 жыл бұрын
Sunnah rek moye deg
@thiernoracine1248
@thiernoracine1248 5 жыл бұрын
Sou fékon yén AK thiédo yi rék le kon dérèt tourou wayé mak gni toubal négne thiédo yi té dara héwoul
@cheikhndieye7640
@cheikhndieye7640 5 жыл бұрын
legueyi leen tebayi. fenyi
@oustazdiallo1215
@oustazdiallo1215 5 жыл бұрын
Souna safinatou noukh
@ibrahimadiop8916
@ibrahimadiop8916 4 жыл бұрын
Nieneen gni wotewougnou thi alkhourane ak souna. J'ai pitié de ces gens qui croient tout savoir et pourtant lhislam c'est de la pratique mais eux ils ne sont pas pratiquant.ils vivent pas lhislam.on apprend l'islam. Pourquoi utiliser KZbin.? Mourdala se contredit . je ne sais pas quest ce qui le prend. Mourtala tu es intellectuel musulman pousse les études et tu verras. Il y'a des gens hyperdoues qui ont un don et il y'a des fous qui mangent dans des poubelles et personne ne peut les juger.
@kallagueye6899
@kallagueye6899 5 жыл бұрын
alkhour ane ak sounah moo woor le reste c'est inutile
@thiernoracine1248
@thiernoracine1248 5 жыл бұрын
Té kan mo wakh salatoul fatiha mo gueun alhouran fan lagnou ko binda thi tarikha bi amoul béne houlafa thi tarikha bi bouko wakh sose bakhoul ragal léne té moytou fitena yonèntèbi néna fitna dèy nélaw té yala reubeu neu kouko yé
@momoudrame7928
@momoudrame7928 5 жыл бұрын
Mourtada Yaw demall xooli nou dioudou domi haram dji Ta nga bayi ndiallo
@mgeagripreneur
@mgeagripreneur 5 жыл бұрын
Xana sa serigne dafa dan ndialo, wala sa baye banga fook ni niep nanioum laniou meel
@papama1975
@papama1975 5 жыл бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 why Serigne be ya wax degueu.mourtada dou.darra yow kéne séttoul lou la néx ak lou lou la nakhary 😂😂😂😂😂
@mouhsininatv9285
@mouhsininatv9285 5 жыл бұрын
Wa ki dafa dof wala dala lal lou bonn mashap ak tarikha yep bonn la te woutewoul ak souna benn yon
@abdoullatiftoure8062
@abdoullatiftoure8062 5 жыл бұрын
Mandèye limathi manawKhe linguène di moudjiè bayabo Nguène dieukèko modi gueneu khameni ikhetilafoul houlamah rahematoune lil ouma djisngua bounguène fidèone 40 jours doutakhe niary kourèleyi kène manefè dialè sa morom lèrouk sounou borom boudè sotèkou thi niary bèrap youbokoul nature naniouye rèagirer dou bok kangam youmak yasoss kourèleya thia bou dieuk niomatakhe diwakhe nanou beuguenetè sopanetè ta yalla takhe taye masella thia lanou woutè kounè nek thia lako doye bou eulaguè yalla atè diamegner lolou mom dong laye walame manedè thi ngi ngouye woyer sofiyou labok ta doumathi diok lifèk mangui ande ak samam khèl donetènak mane ape dioulitt la khame khawema ak khadjialè nginiouye woyer salafiste amena thi aye kharitt wayer mane mèlow djioulitt hakhane laguiss thi niome niomitt niofokema loll khathiena niokhame latakhe dinanouye wakhetane nak thi lislam loubari wayer dounou weranetè ndakhe wèranetè khathio deugue rek la tadaye fèwale ay khol bouniako sèkhe tèyoutt ladokhe sounou dinganetè thik woutè nioudithia dèf ndank ndakhe kham naniouni douma djiahil doumap nafèkhe manitt khamnani donou niouthi lène niomitt mbolo mo dèmenak dingafa fèk niou eupeul ak niou nitèwoutt louyakhou nak niarè thia nionia laye toukè ta lislam talout yoyou fimounè diafè diafè yi lislam diam thi adinabi finoutolou niaka ande reka nouko tek bisbounè noni lislam yi dinou dèf lounou nakhari tadounouko manafathie ta niaka ande monouko tèk bounou andone kène dounou mana dèkou wayer dall kou fèk ap sofiyou akoup salafisete diwèranetè bo yakametè bayabo dème takhameni niar niouye perte sène temp rek laniou bouniou tèyer nak diwakhe tane ndiarigne mane nathia dioguè thi niary wale yèpe mangui djieguelou damanèk thi yone nikone dina guena lèral loubary
@ibrahimadiop8916
@ibrahimadiop8916 4 жыл бұрын
Ce que tu dois faire c'est combattre ceux qui attaquent l'islam les franc maçons et autres. Ça doit être notre objectif mais attaquer les tarikha non on n'accepte pas. L'autre aspect il faut savoir qu'on ne peut pas tout savoir et il ne faut espérer toujours détenir la vérité. La référence pourquoi autant de division sur une question entre d'éminents savants musulmans. Pourquoi cette division?, il faut se ressaisir et savoir je peux être professeur d'informatique sans pour autant pouvoir fabriquer un ordinateur. Il faut être pas un complexé u' déraciné. Vous ne pouvez pas savoir tous les hadith.
@diammouyalla3880
@diammouyalla3880 5 жыл бұрын
Talla Gaye diotalal sanday dem nelawi domi takha walo the
@ibrahimadiop8916
@ibrahimadiop8916 4 жыл бұрын
On ne peut pas tout connaitre dans la vie quelque soit ton niveau d'étude. L'islam c'est de l'histoire une feuille de route qui a un commencement et qui n'a pas de fin.Maintenant notre prophète a indiqué jour par jour heure par heure mn par mn sde par sde. Est ce que tous les gens étaient jours et nuits près du prophète pour savoir tout dans lhislam? Mourdata est ce que tu connais tout ?
@ibrahimadiop8916
@ibrahimadiop8916 4 жыл бұрын
Pourquoi toujours ce savant et pas les autres.
@ibrahimadiop8916
@ibrahimadiop8916 4 жыл бұрын
Yaw yay nittou souna. Yeen khanaa tarikha nga ngueen di wakh.yaw yaa weer.yaw doo dioume. Kifoo joudoo ci Sénégal. Tarikha mooko nguente. Bilaahi se en khole ci tangue laye deukk. Niome nioo moome adjana.dio moome safara. Wawe noune souniou demée safara katolik yi ak franc maçons athées douniou jeume.mane daal yi incohérence kouko moussa guisse. Comme ngueuneel minguici yalla Kaye wakh ji jeekhna.
@syalioune2747
@syalioune2747 5 жыл бұрын
Salam débat bi bou bès la wala
@MakanTV3709
@MakanTV3709 5 жыл бұрын
hahahahahaha diarna lath dh
@abdoullahmoe4620
@abdoullahmoe4620 5 жыл бұрын
Wawkay
@theaniston1572
@theaniston1572 5 жыл бұрын
wa ahlou bida danio dof référé ce sont des égarés
@thiernoracine1248
@thiernoracine1248 5 жыл бұрын
Tarikha mounouléko khékh dakh gni ko jité gnolén raw thi ham ham gueun lén ne ragal yala
@wakana756
@wakana756 5 жыл бұрын
Doundou souna bo khame né ni fene rek.
@yacinegueyetahir9487
@yacinegueyetahir9487 5 жыл бұрын
ceeey yallah...khaana dou yallah laniou djiaamou aak yoneentibii
@amadouwouryba8255
@amadouwouryba8255 5 жыл бұрын
MDR yaw yallah ak Yonnentebi sallahou alayhi wa sallam ngay diamou gnounn yallah rek lagnou diaamou
@ameddiouf7175
@ameddiouf7175 4 жыл бұрын
Diamoul Yalla rek yemthi boul diamou kénene. Fekhel rek nga diaamoko niko yonanté bi salla Allahou aleyhi wa salam diangalé
@sankarebecaye9384
@sankarebecaye9384 5 жыл бұрын
Soune mba sone
@ibrahimadiop8916
@ibrahimadiop8916 4 жыл бұрын
Yeen wahabistes Lima jakhale kouye deglou se en wakh te parparlouwoul date khamne niou réer lagne.Amougni degg .amouniou khame khame.bilaahi khekhbici fe'neenlah. Lima jakhale Mourtada sol sagawoul sa yeneen mbokk gni nekk ci alkhourane ak souna daniouye sagga serignesi. Kone wakhole niome niou bayyi loolou jame nekh.Lou yalla wakh ci mandou.
@alioupouye3479
@alioupouye3479 5 жыл бұрын
مور كى اتق الله وإذا حىىتم بتحىة فحىو باحسن منها أوردوا ها
@papeniang7472
@papeniang7472 5 жыл бұрын
مانهى مذهب إمام عن قرائة بسمله
@papama1975
@papama1975 5 жыл бұрын
Billahi Mourtada tontou gua sa boppe.kounge wax gua mérr la gua jeuke wax mo bakhoul 😂😂😂😂😂😂😂😂 té yow Mourtada so beugué xam fox gua tarbiouji walla gueu dém jebeulou.wanté ni guaye lajai dafa yommbe trop té yow ki khassou la sax.yammi Mourtada yow saye audio yeupe bi gua commancé Be téy ji ay khass té ak ay sagua Réck guéy déff ak khassté.
@ousmanendao5091
@ousmanendao5091 5 жыл бұрын
Lougha wakh deug la mounona wakh nit yi dieuriniou mais nek di indi werente ay thiow sa dakhalawou azim bidah kouko wakh diarou débat si tarikha
@hadji71giab36
@hadji71giab36 4 жыл бұрын
Yaw mi di wakhale tarikha dioubo
@papehamadousall5223
@papehamadousall5223 5 жыл бұрын
Il faut meme pas discuter avec ces wahabites allies de l'occident.
@BayeNiassSahko
@BayeNiassSahko 5 жыл бұрын
Khana dou yallah moy mayé louko soob wala yaw yallah dala wakhné Limay mayé lo khamoul boulouthia
@fatimasevane1264
@fatimasevane1264 5 жыл бұрын
Yallah dal loum tere, tere nako
@sidydiop9413
@sidydiop9413 5 жыл бұрын
Sa bay ak sa mame sakh manogo dindi xamolen touss
@ablayembaye1031
@ablayembaye1031 5 жыл бұрын
Wakhabit you bon yi khamo lén dara
@abdoukarimdiop4108
@abdoukarimdiop4108 5 жыл бұрын
C’est faux. Vous n’avez pas raison. Vous êtes libre, vous ne pouvez pas changer le cours du tidianisme. Vous ne pouvez pas garantir aller au paradis et nous mettre en enfers pour notre tidianisme.
@cheikhndieye7640
@cheikhndieye7640 5 жыл бұрын
non s touba. ak. mam. maodo lanokhm ak niemel. neniom
@malickdiouf1586
@malickdiouf1586 4 жыл бұрын
Dama beugue bok si groupe bi malick diouf 77 550 35 50
@aboubakarndiaye8866
@aboubakarndiaye8866 5 жыл бұрын
Group madialice beugnace bok inchallah
@toubandindiinfo5829
@toubandindiinfo5829 5 жыл бұрын
kouy rer di nalaw mouno ko kham
@zaydibnhaariss6310
@zaydibnhaariss6310 5 жыл бұрын
Yén mandouwoulén nakh dolén dougal debat entiére bi wayi di daggeuh partie you len arranger
@oustazmouhamadougueye2541
@oustazmouhamadougueye2541 5 жыл бұрын
Serigne bi lép néckoul si alkhour.ane. yaw sa tour néckoul si alkhour.ane Sénégal néckoul si alkhour. Ane mon vieux
@mawdodiop3833
@mawdodiop3833 5 жыл бұрын
Wa saway mba yagui suivre say rendez-vous dalal jamb
@oustazmouhamadougueye2541
@oustazmouhamadougueye2541 5 жыл бұрын
Les saaléfiste talibé ibn Abdoul wahab
@fatimasevane1264
@fatimasevane1264 5 жыл бұрын
Lo lou loumou djote ak debat bi
@mohamedsarr7739
@mohamedsarr7739 4 жыл бұрын
@@mawdodiop3833 😅😅😅😅
@BayeNiassSahko
@BayeNiassSahko 5 жыл бұрын
Dr yak kila ndiangal yéne niep ay nafékh nguéne té bolene touboul linguéne nék ba Fatou kéne manouléna té déme sawara
@amazonmbaye4832
@amazonmbaye4832 5 жыл бұрын
Yangui diou dh ndakh kouko diagal khamal lingay wakh mo geune si yaw
@babeybass4039
@babeybass4039 5 жыл бұрын
Ki wa bidah
@kebatouretoure8923
@kebatouretoure8923 5 жыл бұрын
Argument vous
@mouhamedndiaye3219
@mouhamedndiaye3219 4 жыл бұрын
Dama beug boque si group bi 77 341 29 40
@adamambaye8413
@adamambaye8413 5 жыл бұрын
Mourtada Gueye satounou Baye khamo dara Liga néke mowouték souna
@mamadoudiagne5907
@mamadoudiagne5907 5 жыл бұрын
Lii dafaye wanei seine mbone gui .saaga rek ngueine meune.loolou mooye seine yoone.
@thiernotine2675
@thiernotine2675 5 жыл бұрын
Démlén ligueyali khadim rassoul bala nguén di dé di réthiou
@fatimasevane1264
@fatimasevane1264 5 жыл бұрын
Ligueyal koula meunta fay, ko khamne dena, dem lem ligueyal yalla mo geun.
@thiernotine2675
@thiernotine2675 5 жыл бұрын
@@fatimasevane1264 kokou yalla ko diokh limou yor lép
@fatimasevane1264
@fatimasevane1264 5 жыл бұрын
@@thiernotine2675 loumou yor?
@thiernotine2675
@thiernotine2675 5 жыл бұрын
@@fatimasevane1264 kouy weur kou gnak diom ak kou goré di ba aksi si koumél ni yén deup
@thiernotine2675
@thiernotine2675 5 жыл бұрын
@@fatimasevane1264 noo mangui perdre sama temps koi,
@MakanTV3709
@MakanTV3709 5 жыл бұрын
debat bii 10ans yeena nguissi khana amouleen ligueey waya lepp ak arabie saoudite la dagne leena wara bayyee fay rk
@gorpurre8269
@gorpurre8269 5 жыл бұрын
Mane déé Yalla bouma bok Si dinay fay 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭نعوذ باالله No ñi daño yabaté rk
@MakanTV3709
@MakanTV3709 5 жыл бұрын
@@gorpurre8269 amiiin way kenn gnanouko yalla
@gorpurre8269
@gorpurre8269 5 жыл бұрын
ñiii kay khamou ñii dara
@abaaba5045
@abaaba5045 5 жыл бұрын
Diney islam arbi sawdit ladioge mane morid lawone waye legui rekhasounasi baset youbari damafogone migi si alkhuran dege aye falsela
@MakanTV3709
@MakanTV3709 5 жыл бұрын
@@abaaba5045 ANDEYSSANE NIAKKA KHAM LIMOU WARAL BARRINA fii kilifeu you barri dianguee nagne arabie saoudite mais kham kham ba lagne dieul bayyi fa thiakhaan ya thiakhaan manouta wessou naan ab dioulit yeefar nga te keppou koula diangal niala magg gni ligne nek falsela ay fenn la
@kharbalabci3622
@kharbalabci3622 5 жыл бұрын
Salafiste=Mensonge
THEME: L'exagération des soufis sur leur idoles✅🎧🔊🎙🕋🕌
45:34
alkhuran ak sunna rek
Рет қаралды 28 М.
Démantèlement des imposteurs Ahmad Cisse et Cie || Imam Fadel Ndiaye
17:07
alkhuran ak sunna rek
Рет қаралды 1 М.
So Cute 🥰 who is better?
00:15
dednahype
Рет қаралды 18 МЛН
Леон киллер и Оля Полякова 😹
00:42
Канал Смеха
Рет қаралды 4,3 МЛН
DEGEU  BODIWoUBOUL DOULA  nèkh
7:07
Sayroul Khalbi Tv
Рет қаралды 871
DEBAT: NDAKH SALATOUL FATIHI SAKH NA WALA‼️CHEIKH OUMAR MBAYE & BOY NIASS🔊
56:59