Décès De Demba Ba comédien, Les Tristes Images De Son Enterrement

  Рет қаралды 332,145

DAKARBUZZ TV

DAKARBUZZ TV

3 жыл бұрын

Пікірлер: 841
@bane257
@bane257 3 жыл бұрын
Soxnam kou goré machala reposes en paix demba yalla tek si ndiabote gui lokho Bravo la dame wathie nga machala Dieuredieuf
@africamazing8143
@africamazing8143 3 жыл бұрын
Deug leu mashala . yallah nako yallah kharei aldiana
@khadyba678
@khadyba678 3 жыл бұрын
les bonnes volontés guir yalla diapalé lene les enfants de Demba.
@ismailandiaye8550
@ismailandiaye8550 3 жыл бұрын
Fii Sénégal nioune niou niak rk nioy deffalanté niou am touti nioy xool yalla
@fatoubary847
@fatoubary847 3 жыл бұрын
Bo febarè kène doula djapalè bo déwé gnouy Doga gnew,😭😭😭
@ngenarfoune4625
@ngenarfoune4625 3 жыл бұрын
80
@fatimaniang2664
@fatimaniang2664 3 жыл бұрын
Bilay
@katysarr5828
@katysarr5828 3 жыл бұрын
Senegal tenque dewo douniou la diapale
@oumoudabo6601
@oumoudabo6601 3 жыл бұрын
Thieye yalla démbou adouna téye barsakh yalnako yalla yéreume mais il a laisser une brave lionne
@diagnendoye5756
@diagnendoye5756 3 жыл бұрын
Wallaie ndeyssane ALLAHOUMA AMINE
@madamefallmounadieye6343
@madamefallmounadieye6343 3 жыл бұрын
Yalnako yalla yeureume si barké mohamed
@aramesndiaye590
@aramesndiaye590 3 жыл бұрын
Qu'allh l'accueille dans son paradis thi barkém seydina Mohamed 🙏🙏🙏
@KatyNdeyeDiop
@KatyNdeyeDiop 3 жыл бұрын
Allahouma amine
@mariendao4262
@mariendao4262 3 жыл бұрын
Amiin yarabi
@xhadimfvll6321
@xhadimfvll6321 3 жыл бұрын
Amine
@oussaynouseck4460
@oussaynouseck4460 3 жыл бұрын
Oh yallana nako yalla kharie Aldiana🙏
@taphasylla3784
@taphasylla3784 3 жыл бұрын
amine
@ndeyengoneseck6867
@ndeyengoneseck6867 3 жыл бұрын
Ndeysane yalana ko borom bi téro aldjana firdaws,mais sénégalais yi aussi il faut contribué à la survie de sa famille,toute mes condoleances à sa tendre épouse. Brave dame
@seyadiouf7964
@seyadiouf7964 3 жыл бұрын
Ndeysane que ton âme repose en paix 🙏 sa diabar bi yalla ko yalla diapalé
@alydiop4954
@alydiop4954 3 жыл бұрын
Amine
@salladiaw6426
@salladiaw6426 3 жыл бұрын
Amine
@salioumboup5091
@salioumboup5091 3 жыл бұрын
AMINE
@alexismendy8809
@alexismendy8809 3 жыл бұрын
Amine🙏🏾
@kacheikh4857
@kacheikh4857 3 жыл бұрын
Amiiiiiiiiiine brkp brome Touba
@diengselly6344
@diengselly6344 3 жыл бұрын
Adouna dou dara Repose en paix que paradis soit sa demeure éternelle Yalna Yalla tekk lokho ndiabott bi t mayleneu xolou mougn Sa diabar yalna ko Yalla fay xolam
@salladiaw6426
@salladiaw6426 3 жыл бұрын
Amine
@laliyasarr5584
@laliyasarr5584 3 жыл бұрын
Ohhhh wallahi tu as marqué notre enfance il s’est marié devant moi en face la maison de ma grande mère mais wallahi aziiim kii diabaram bouko yallah fayei kholam...yallah nako yallah yeureum kharei ko aldiana
@aichandiaye8927
@aichandiaye8927 3 жыл бұрын
Tonton waly seck diapaléle les enfants de démba bouko défé yalla dinala geuna maye dolé bilahi
@fatimasow3816
@fatimasow3816 3 жыл бұрын
😭😭😭mane dh jé mêm op les mots bilay stp nguirr gniko meun diapa léléll gnimou bayi si guinaw
@abdoulhamidsarr5747
@abdoulhamidsarr5747 3 жыл бұрын
Repose en paix papa que paradis soi son demeure éternel 🙏🙏🙏
@aminaba5283
@aminaba5283 3 жыл бұрын
Yalla na souf oyof sa caw tonton demba yalla na yalla are sa ndiabote courage madame ba djiguène nou diambarga yalla nala yalla fay sa xol 🙏
@fatoumaguettefall1584
@fatoumaguettefall1584 3 жыл бұрын
Walahi spécial saint Valentin bi 😔😔 malay cétann et j’étais Just trop fière de votre couple... Yalla na yalla tekk loxo sa ndiabott gui yalla may lénn courage baniou meuneu surmonté cet épreuve🙏🏽 Rest In Peace ✌️ Demba 🙏🏽
@sokhnafatimasarrsagna2595
@sokhnafatimasarrsagna2595 3 жыл бұрын
Ndeysaan yàllah nako yallah khare aljanna te yekheniou inchallah
@salladiaw6426
@salladiaw6426 3 жыл бұрын
Amine
@sokhnafall7860
@sokhnafall7860 3 жыл бұрын
Amine
@isseudiene6766
@isseudiene6766 3 жыл бұрын
Ho que Dieu l'accueille dans son paradis firdawsi fi barakati Rassoulilah Amine Les bonnes volontés diapalé léne la femme de Demba Ba et ses enfants yalla sougnou borom fayléne
@sitoebassene8244
@sitoebassene8244 3 жыл бұрын
C un homme fière qu'il.repose en paix et que dieu veille sur sa progéniture ,yalla oyofal yéne bi mme ba ,massa c trist
@ngonefallsylla584
@ngonefallsylla584 3 жыл бұрын
Mattal rek kou mattal dem yallah nako yallah yeureum amiiine
@abdoudiop8697
@abdoudiop8697 3 жыл бұрын
Repose en paix papa mais une chose il faut aider nos parents qui sont malades qui sont de grand nom dans notre société
@bolydiao9023
@bolydiao9023 3 жыл бұрын
Qu'il repose en paix et merci à DAKARBUZZ toujours près de la société surtout les gens qui ont des difficultés.
@mohamedndiaye6504
@mohamedndiaye6504 3 жыл бұрын
Yallena souff oyoff si kawam. Oeuvrer vers Dieu à travers les hommes. Aider la famille de Demba un acte noble.
@ramatoulayedoumbouya9981
@ramatoulayedoumbouya9981 3 жыл бұрын
Magui mastaou sa femme très brave billaye aka goré ho
@falysarry9030
@falysarry9030 3 жыл бұрын
bilay
@kharyfaye8324
@kharyfaye8324 3 жыл бұрын
Bilahi
@khadydiallo9721
@khadydiallo9721 3 жыл бұрын
Bilaye wakhatiko yomboul dé
@landella1411
@landella1411 2 жыл бұрын
Goré look sax
@khadidiatakamara6005
@khadidiatakamara6005 3 жыл бұрын
eskéy adouna paix a son âme ndeysane
@maguishadiop6793
@maguishadiop6793 3 жыл бұрын
DAKAR BUZZ SOCIALE diapalé léne sama sœur daffa am problèmou foi elle souffre troooooo😭😭
@ndoyembaye134
@ndoyembaye134 3 жыл бұрын
Lan moka dall?
@fatoulomouserignebabacar7395
@fatoulomouserignebabacar7395 3 жыл бұрын
Prends leur numéro et appel les
@pendafall4845
@pendafall4845 3 жыл бұрын
Wo lene
@modoumbacke7725
@modoumbacke7725 3 жыл бұрын
Woma si num 775986255
@bourymbaye2786
@bourymbaye2786 3 жыл бұрын
Ay way ma puce appel les ndaysan
@codoufaye4265
@codoufaye4265 3 жыл бұрын
😭😭😭😭senegal y'a des milliardaires gno khamni meunougnu sakhh diapalé sene moromou dioulite gni soxla ndimbal té bou nekone ay thiaxane kounek di battré di wanéwou c'est honteux dans quels pays sommes nous
@mbenegueye5232
@mbenegueye5232 3 жыл бұрын
Ma soeur xallice Bou bakhoul doutie défe Lou bakh
@codoufaye4265
@codoufaye4265 3 жыл бұрын
@@mbenegueye5232 Ahh c vraiment pitoyable
@mbenegueye5232
@mbenegueye5232 3 жыл бұрын
@@codoufaye4265 ce la vie
@codoufaye4265
@codoufaye4265 3 жыл бұрын
@@mbenegueye5232 yalla baxna té barina soutoura
@mbenegueye5232
@mbenegueye5232 3 жыл бұрын
@@codoufaye4265 waw mais pour mane sama xallate Bou gate mouye arctice yie dayou wara ame asurance pour bouyou tombé malade
@binetaniang2671
@binetaniang2671 3 жыл бұрын
Yalnako yalla yeureum khareko aldiana firdawsi si darke seydina Mohamed
@coumbafaye2149
@coumbafaye2149 3 жыл бұрын
Yalla na thionom yam adouna yalla tek lokhom si ndiabot gui akh sokhnam sou goré sosou
@ibrahimasorydiallo3332
@ibrahimasorydiallo3332 3 жыл бұрын
Gir yallah aidons les enfants ENFANTS😭😭😭 de Demba ba SVP 🤲🤲🤲🤲🤲 fissa bi lillah🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲 Yallah nako yallah yereum té khareko Adjiana firdawsi Amin 🤲
@mariamadrame8733
@mariamadrame8733 3 жыл бұрын
Alakhou akbarr 😲hier nuit rek sen video saint-valentin bi la donee setane ndeyssane adouna nga ni rek demal magui nieuw la yalla nala souniou borom térou la si adiana firdawssi😭😭
@seynaboubiteye2475
@seynaboubiteye2475 3 жыл бұрын
Ay way li métina trop mane mi rek magui donn sentane sen video saint valentin bi... Yalla nako yalla khare aldiana amine
@seynaboucamara7967
@seynaboucamara7967 3 жыл бұрын
Bilaye ak mane mi mome ladone setane ndeysane paix a son ame
@diarrandiaye2152
@diarrandiaye2152 3 жыл бұрын
Yalla nako souñou Borom yeureum t kharré ko aldiana firdawsi 😭😭😭
@natachfaye3764
@natachfaye3764 3 жыл бұрын
Amine yarabi
@serignembackendiaye8978
@serignembackendiaye8978 3 жыл бұрын
Dupuis 4 sans 😭😭😭 Gnioko Mana fadj Nh khass Nguéne kharr Bame Guéneu Adouna Nguény Ndieukanté ci Sarakh Sy 😭😭😭..Mane khawma Bane Sénégal lane Néke Mé yallah Dina lénko Lathe ko euleuk 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@angeleseck9477
@angeleseck9477 3 жыл бұрын
Qu'Allah lui accorde sa miséricorde et l'accueille au paradis
@Youla_Beauty
@Youla_Beauty 3 жыл бұрын
Oh li métina trop ndeysane mann ki diabar dji damako fan beugeu ko bilahi yalnala yalla takhawou yak sa ndiabote gui inchalla yalla dinala fay dé sa khol yalla nako yalla téro aldiana
@toubandindyafricanhairbrai2924
@toubandindyafricanhairbrai2924 3 жыл бұрын
Inna lilahi wa Inna ilayhi rajihoon yalla nako Yalla yeureum te djiegual ko kharey ko thia aldianal firdawsi ci barke seydina Mohamed psl 🙏🏼
@sowamina1725
@sowamina1725 3 жыл бұрын
Ndeyssane Sokhna ci machAllah diambar le ayway bouma amone
@sokhnadiawndiaye1921
@sokhnadiawndiaye1921 3 жыл бұрын
😭😭oh c’est triste barké Cheikh Ibra Fall Moi j m demande où sont les gens d bons cœurs 🥺pourquoi vous attendez jusqu’à sa mort ......il a laissé ses enfants 😭sa femme derrière lui .... Arrêtez de regarder des gens souffrir 🥺🥺 Liii niaw naaa
@fatoumadeleinengom4576
@fatoumadeleinengom4576 3 жыл бұрын
Kéne dou dimbali kéne fiiii yalananiou yala mayy wéeer amiine kufi febar ter amoo rek dangay déeee si souffrance Demba a trop souffert dans sa maladie
@fatousene318
@fatousene318 3 жыл бұрын
Bilay li meeti na yalla nako yalla yeureum😭😭
@khadijadiallo5012
@khadijadiallo5012 3 жыл бұрын
@@fatoumadeleinengom4576 walahi ta marché sur ma langue kil repose en paix notre papa
@fatimatasy6887
@fatimatasy6887 3 жыл бұрын
Sa femme ❤ yallah nala yallah fay mayla katan nga meune yor sa dome yii😪trop dur d perdre un être cher
@princessedangerous3858
@princessedangerous3858 3 жыл бұрын
Ay way yalla nako yalla xaré aldiana deukou dioulite bi té kena dou diapalé kena amnegne ko mai fou bone rek lagnou koy dougeul wala mayé guisteul wally mom macha allah yalla nako yalla faye xol wam il a aidé bocoup de personnes macha allah
@diekygueye8530
@diekygueye8530 3 жыл бұрын
Dieu dit dans le Coran " Dans chaque difficulté il y'a certes une facilité". Ta vie sur terre était certes une épreuve mais ton épouse a été la facilité. Qu'Allah t'accueille dans son paradis éternel. Allah est Miséricordieux
@ndiemethiam27
@ndiemethiam27 3 жыл бұрын
Yal nako yalla kharé Al jennah firdawsi si barké yonnenti bi SAWS daffa woté walou ba kheuye guéneu adouna métina
@ndeyfatoumbengue6113
@ndeyfatoumbengue6113 3 жыл бұрын
yalla nako yalla yeureum khare ko aldiana si barkè seydina mouhamed metina trop
@evangelinamendy1520
@evangelinamendy1520 3 жыл бұрын
Na aldiana di ca dekouway puisse dieu le père t’accueille dans son paradis céleste
@awaseck8369
@awaseck8369 3 жыл бұрын
Amine
@adgraphics9204
@adgraphics9204 3 жыл бұрын
Amine
@landella1411
@landella1411 2 жыл бұрын
Amine
@sallmadina1141
@sallmadina1141 3 жыл бұрын
Nom li mounoule nek degeu hier rek St Valentin mome ak djabar ladone cétane nom way 😭😭😭😭
@nafifaye1057
@nafifaye1057 3 жыл бұрын
Repose en paix demba ta yalla tekk lokho si diabotam si barker seydouna Mouhammad psl
@paaliounendiaye2908
@paaliounendiaye2908 3 жыл бұрын
Demba ndeyssane yalnako yalla téro thia aldjanan firdawsi
@aidadiouf5085
@aidadiouf5085 Жыл бұрын
Yalla nako yalla kharé aldiana fidawsi si barké seringe saliou MBAcké 🤲 amine yarabi 🤲😭 amine yarabi 🤲
@rackyba4884
@rackyba4884 3 жыл бұрын
Ndeysane thieye yalla sounou mborom yalla nako yAlla yeureum khareko aldiana si barke Seydina MOUHAMED psl inchalla
@serignediop8349
@serignediop8349 3 жыл бұрын
Hoo ndeysane thiey aduna lii métina yalna yalla yokou ay léram té takhawoul ko ndiabote gui
@karimfaitsesvideos7903
@karimfaitsesvideos7903 3 жыл бұрын
Non setane nenko trop thieuy adouna yalla nako yalla yeureum😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@abykebe3342
@abykebe3342 3 жыл бұрын
Yalla nako yalla atei si yeurmandem Amine
@dieynabasow5901
@dieynabasow5901 3 жыл бұрын
Yalla na ko yalla yérem té kharé ko aldiana 🙏🏽🙏🏽 métina
@astouseck7833
@astouseck7833 3 жыл бұрын
Amine 😭😭😭
@omarfall5559
@omarfall5559 3 жыл бұрын
Sénégal ngay guis kou febar 1 millions war la Fadj nga dé niou beug diokh sa famille 10 millions
@dembafaty4126
@dembafaty4126 3 жыл бұрын
Demba Ba yalla na aldianay firdawsi di keurou noflayam yalla bouko thiat djitou ci biir bamelam ak bép dioulit ci Barker seydina Mouhamed PSL amine yaraby
@ndeyegueye4937
@ndeyegueye4937 3 жыл бұрын
Nit kou bakh demna yalla na yalla yeureum te khareko aldiana firdaws niaboot yalla na lene yalla same sokhna mougne
@evasopenaby4700
@evasopenaby4700 3 жыл бұрын
C'est vraiment triste 😭YAlla nako yAlla khare Aldiana you guena kawe si Barke mouhamed PSL
@massassimedias221
@massassimedias221 3 жыл бұрын
Yalla na kou yalla Yaram si barkép s Touba mbacke 😭😭😭
@salladiaw6426
@salladiaw6426 3 жыл бұрын
Amine
@senghormaguett318
@senghormaguett318 3 жыл бұрын
Yala nako yala kharé aldiana si barké serigne fallou Mbacké
@aminatadiakhate3672
@aminatadiakhate3672 3 жыл бұрын
Ndeysan repose en paix tonton que firdawsi soit votre demeure éternelle 🙏🙏 et que le tout puissant vous accueil dans son céleste paradis 🙏🙏🙏
@salladiaw6426
@salladiaw6426 3 жыл бұрын
Amine
@morniass2363
@morniass2363 3 жыл бұрын
Yalla na nako yalla yeureme si barké seydina Muhammad sala law aliou wa salam
@amyniang2846
@amyniang2846 3 жыл бұрын
Ndeyasan c'est comme ça la vie paix a son âme 😭😭😭😭😭
@laminendiaye9185
@laminendiaye9185 3 жыл бұрын
Yallah nako Yallah kharè aldiana firdaw si barki seydina mouhamad amine😪😪😪
@khadycamara8687
@khadycamara8687 3 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureum 😭😭😭
@thiarasamb3209
@thiarasamb3209 3 жыл бұрын
Ohhh😭😭😭 ay waly seck yalna guiss li diapalé djabotam bi yalnako yallah yeureum té kharé ko aldjana frdawsi ❤️😔😔
@aidasene7333
@aidasene7333 3 жыл бұрын
Yalla nako yalla yereme si barkepp seydina mouhamed🙏
@mariendiaye4875
@mariendiaye4875 3 жыл бұрын
Ndeysane yalla na khipé aldiana😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@girlnoir9154
@girlnoir9154 3 жыл бұрын
Ndeyssan dei moy deug wayei mettina trop sax Yalnako yalla kharei aldiana firdawsi tei tei yalla tek lokhom si ndiabote ngi
@marianeba6662
@marianeba6662 3 жыл бұрын
Adouna dou touss dou dara Yalah nako Yalah tour yeurmander Niit nga deudou gnou djouler la soul la wanla guinaw thiey adouna esk diarna def lougnaww ?? 🤷🏼‍♀️🤷🏼‍♀️🤷🏼‍♀️😭😭😭 Papa repose en paix 🙏🏻😭 neilawall ba yandor sa ndiabot guii Yalah dinassi tek lokho inshaa Allahou 🙏🏻😭
@moulayedabakhfall7619
@moulayedabakhfall7619 3 жыл бұрын
yallna yalla yeureumko xareko aldiana ndeysan sétane na yayam geureumko baye diooye ndeysan
@kineba5017
@kineba5017 3 жыл бұрын
Ay waay boleen continuer di sétaan liii guir yalna diap leen si ndiabott gui ay waay😢😭😭
@diagnendoye5756
@diagnendoye5756 3 жыл бұрын
Thieuy SUNU BOROM moo sagñ ci jamm bi Aduna dou dara ndeyssane D'emba Ba Yalna ko YALLA yeureum diegeul ko xarei ko Aldjana ci Barké Yonettbi (SAWS) Le reporter Fadel ak Mouhammad Amar mõmu Yalna leen SUNU BOROM fay yiw yok xewal yi ak gñiko doone japalé ñieup ta YALLA taxx insh ALLAH
@aidasagna4283
@aidasagna4283 3 жыл бұрын
Ndeyssan Drmba yalla nala yalla yeureum kharei leu aldiana firdawsi si barkei Seydina Mohammed psl
@kanefaty8701
@kanefaty8701 3 жыл бұрын
Yalenala yalla yeureum si barké alkhourane 😭
@Queenprincesse1
@Queenprincesse1 3 жыл бұрын
Ndeysane yalla nako yalla yeureum tei kharéko aldiana adouna dafa metti
@binetaseck5985
@binetaseck5985 3 жыл бұрын
Yalla nako yalla khareii aldjiana firdawsiii 😭 souff sedeuu si kawamm😭🙏
@absadiop2563
@absadiop2563 3 жыл бұрын
Yalla nakou yalla yereum te kharee Aldiane firdawsi si barke serigne Touba Mbacké
@bassirouka9761
@bassirouka9761 3 жыл бұрын
Yalla nako yalla yerem ta kharèko al diana ci barkèp serigne touba
@ousmanebasse8967
@ousmanebasse8967 3 жыл бұрын
Paix à son âme
@fatoudia9900
@fatoudia9900 3 жыл бұрын
Auh ndéyssane yalnako yalla yeureum kharéko aldiana thi barké ndiol maka 🤲 psl
@isatouchorr398
@isatouchorr398 3 жыл бұрын
Am sorry fr the lose May his soul Rest In Peace 😭😭😭😭. This is so painful
@bayecheikh8807
@bayecheikh8807 3 жыл бұрын
Ndeysane yalla nako yalla yeurum té khare aljana firdawsi AK newou dioulittt té séne sarakh yague sougnou lokho gnoune dioulite yeup amine alhamdulillahi 😭😭😭
@adjasy7456
@adjasy7456 3 жыл бұрын
Oooooooh😭😭😭😭😭😭😭😭 dafa matal rekk ndeyssane Yala nako yala yeureum 20ans de mariage yomboul deh sokhnam si nako yala may kholou mougne Repose en Paix Papa ndeyssane avant ma yeukk ni dafa guéneu adouna rekk lakoy togne naneu sama soeur bi Demba modone Saint-Valentin di togne di topando nimouy wakhé😭 même pas 1h de temps sama yaye wakh mako Mes condoléances
@FATIMAKEBEWALLYBSECK.
@FATIMAKEBEWALLYBSECK. 3 жыл бұрын
Ndayssane c'est triste walahi
@niteundiaye9675
@niteundiaye9675 3 жыл бұрын
Ndeysane fan yi yeup mouy niaane nimbal 🥺
@antadiop5943
@antadiop5943 3 жыл бұрын
Sa diabar yalla nako yalla diapalé takha wouko yalla nako fay kholam yalla naniou yalla dégue thé naguoul niou souniouy niane
@sopenabyndaw3208
@sopenabyndaw3208 3 жыл бұрын
Yalnako yalah yereum
@mariamamariama6771
@mariamamariama6771 3 жыл бұрын
qu'Allah t'accueille dans son paradis céleste 🤲🤲
@mbeguesaliou2494
@mbeguesaliou2494 3 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeurum khareko aljana barkep s Touba cheikhoul Khadim
@abyndiaye2886
@abyndiaye2886 3 жыл бұрын
Ndeyssane yallah na ko yallah yeureum té diégual ko oyafal souf thi kawame léral bamélame yallah na FIRDAWCI done keureum Amiiinne 🙏🙏🙏🙏🙏
@maitoure9921
@maitoure9921 3 жыл бұрын
Ndeyssan yalla nako yalla yeureum te kharé ko aldjana
@khadysoumb7888
@khadysoumb7888 3 жыл бұрын
Yalna deh doone sa nofly darajay Nabi Salallahu alehyhi wa salam.toute mes condoléances à sa famille 🤲🏾🤲🏾🤲🏾
@minachouendiaye8462
@minachouendiaye8462 3 жыл бұрын
Ndeysane repose en paix 🪦 yallah gua khippè aldiana ndeysane
@wesh6583
@wesh6583 3 жыл бұрын
qu'Allah le tout puissant l'accueille dans son paradis éternel amine 🙏🙏🙏
@khadidiatoucamara7454
@khadidiatoucamara7454 3 жыл бұрын
Rip aidé à famille s'il vous plaît 😭😭😭
@bakhyaye3262
@bakhyaye3262 3 жыл бұрын
Gnun gnep man nagnu len aider... bugnu khep sugnu dereum
@papemamadoundiaye4899
@papemamadoundiaye4899 3 жыл бұрын
yallna yalla yeureumko khareko aldiana amine yarabi 🤲🤲🤲
@assanediop9893
@assanediop9893 3 жыл бұрын
Yalla nalaine yalla faiye si barkai Mohamed salalahou alaiyhi wa salame yaine Ahmeth amar ak issa amar, ak fadel le journaliste
@ibk4266
@ibk4266 3 жыл бұрын
Yalna ko yalla yeureum kharèko aldiana 🙏🏽
@khadjiafall307
@khadjiafall307 3 жыл бұрын
Ndeysane yalla nako yalla yeureum tè khareko aldiana
@maimounagueye2835
@maimounagueye2835 3 жыл бұрын
Paix à son âme ke FIRDAWS soit sa demeure éternelle
@ousseynoudieye8336
@ousseynoudieye8336 3 жыл бұрын
yalnako yalla yerum té diégeulko kharéko aldiana ci barké Mohamed 😭😭😭
@awathiaw3724
@awathiaw3724 3 жыл бұрын
Walakhiiiii Fadel Yaw yallah rk molay fayy Les derniers images yakoo wanè Ba tay yallah def lu gueune Svp diapalène domam yii T realisel ko limu bguona defal Diabar djii ak ay guorom🙏🙏🙏🙏
@antadiop5943
@antadiop5943 3 жыл бұрын
Que la terre soit léger. Yalla nalla Serigne touba térou sa aldianay firdawsi😭 repose en paix 😭
@salladiaw6426
@salladiaw6426 3 жыл бұрын
Amine
@rabytine6932
@rabytine6932 3 жыл бұрын
Ndeyesane il m'a vraiment fait pleurer 😭😭😭
Barthélémy Dias boycotte l'appel du Président Diomaye ? Ahmed AÏDARA se...
11:35
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 6 М.
Can you beat this impossible game?
00:13
LOL
Рет қаралды 45 МЛН
狼来了的故事你们听过吗?#天使 #小丑 #超人不会飞
00:42
超人不会飞
Рет қаралды 60 МЛН
Did you find it?! 🤔✨✍️ #funnyart
00:11
Artistomg
Рет қаралды 124 МЛН
Spécial Saint-Valentin avec Demba Ba et SA FEMME
27:34
DAKARBUZZ TV
Рет қаралды 340 М.
Avant sa mort, regardez la dernière vidéo de Modou diagne comedien…
12:27
Can you beat this impossible game?
00:13
LOL
Рет қаралды 45 МЛН