Un autre grand homme Ahmed Bachir Kounta. Il a accompagné de sa voix de nombreuses generations avec ses traductions des films musulmans. Il a bercé bcp de jeunesses macha Allah! Doundeul papa!
@obtrice42575 жыл бұрын
Eyow il est partie je viens de l'apprendre..et je disais la même chose à l'instant ..j'ai grandi avec lui pratiquement ..les traductions des films avec pharaon et il a même fait le journal en wolof...qu'Allah le tout miséricordieux le très miséricordieux l'agrée et l'l'accueille dans son djanatoul firdaws..🙏🙏🙏
@amisow75376 жыл бұрын
Bashir kounta ta voie est unique dieuredieuf .
@cbonmoi34036 жыл бұрын
Sidy nièpako bokone ndayssane . Yalla nako Yalla kharé aldiana . Vous 2 là je vous aime beaucoup . Yaglènfi téh wer barké Khadim Rassoul saws . Amine yarabi .
@fraisebo25246 жыл бұрын
MachaAllah Kounta Yallah ga yaga fi weer yake ki ga tougale Amine
Macha'allah Allahou Akbar hamdoullillah Vive la verite rien que la verite macha'allah vive L'Islam, que le bon Dieu lui pardonne ses peches et l'aceuille dans son paradie le plus haut incha'allah misericordieux et benediction incha'allah
@latdiordiop60516 жыл бұрын
Sidy yalla nako yalla yereum ta diegueul ko. Diambar deugu. Diadieuf counta.
@ibrahimasenenabien8586 жыл бұрын
Machallah kounta sidy yalnako yalla diègal tè xarèko aldiana firdawsi
@ndeyediop63326 жыл бұрын
oh ndeysanne!!!!!!
@marietoudiop99236 жыл бұрын
Talla nako talla yerem
@syllayoussouf46496 жыл бұрын
Wakh dji rafetena kounta yallah nala yallah faye
@Sopeymamediarra20246 жыл бұрын
Pa bi Niasse nimou civilisé taye mouye fompeu guémigne bi ak di ségnou comme sérére bobou molaye wan ni il est trés affécté et tres en douleur. Il a vraiment regressé! Massa papa! Siggil ko ndigalé!
@tiveritejolie56176 жыл бұрын
Bayil sérérrr yi😂😂😂
@diagnendoye57566 жыл бұрын
Walahi Ndeyssane Yalna ko deudo ak diam Papa Sidy Lamine Niass yalna Yallah yessal yeurmendem yok sa leer cisa barké Maam you bakh yi
@perlediallo19086 жыл бұрын
Fit bi mo dem d rek dou aye thiakhane
@latdiordiop60516 жыл бұрын
Ahmed je t’aime bcp mais dangua meun deconé. Dama beugu borom kham kham ak kou am fitt niar yeup Moungui thi yaw. Mais auci defoi danguay deconé rekk ahmed.
@diagnendoye57566 жыл бұрын
Nonnn pourtant daniouko dessé deggeu rek ndeyssane. Papa Sidy lamine bocou d'entre n l comprené pas dans ses positions mais dernièrement qu'ont comprends. Sénégal moo mel nonou
@ibrahimandiaye41496 жыл бұрын
Detway
@mbayediop93196 жыл бұрын
Waly masala nias sidy lamen kenalwun ☝🏿🙏🏿😢
@Sidydiagne-246 жыл бұрын
amine amine
@mdkcomkounta70276 жыл бұрын
M'a sha Allah
@smoovelikebjay27086 жыл бұрын
Alhamdoulillah
@moustaphandiaye87346 жыл бұрын
dière dieuf mam Ahmet khalifa et mam Bachir na yalla lerral sen khool ta teral leen.
@moussadiallo49296 жыл бұрын
Sidy lamine niass cest a jistuce , l'islam , la démocratie, la voie des sans voix vive la paix et la vérité.
@fatougueye30526 жыл бұрын
am na solo kadouyi ahmed bachir kounta yagfi te were liii moy yeufi dioulite
@alioutoure26556 жыл бұрын
sidy lamine dafa am geum geum
@khadimsow50236 жыл бұрын
Na ma yala diegal wayè pa niass dafa saf khorom khol ko ak wer yi ak fompatou bi ak lokho yi si bouche bi 😁😁😁😁 yalna yala yareum sidy
@mourtadalove4156 жыл бұрын
nanou moytou fattaliko Loy indi thiow si am réw amoul solo dh gén balma👃👃👃
@khadimndiayeahloufadailou39856 жыл бұрын
Setettttt wa baye ahmad tamite mongui nane rėk Di gnindou epui mou secrëtêwou ak baramam.
@galsenflow90776 жыл бұрын
Bachir kounta hypocrite dou nitou dara mom akh ahmed meune nagnou andeu quand mon père est décédé dafa khethio akh gnoune neh ndiassane lagnou koy soule teh béne domam deukou faa association kheutio néwou bayou diambour yii wanteh boléne deh weh kéne douléne kheutio nakh tékiwoléne dara demb akh tay
@a-m-t-senegaljefjel15426 жыл бұрын
Ahmed khalifa aka beug lou neekh.kholko rek
@awakante13506 жыл бұрын
Yalna souf sed si kawam me lou takh ahmet di nan ngenkoy dielrek
@tayemounekhndiaye91506 жыл бұрын
awa kanté. Lou mouy nane tamit ni
@ngoneseye69396 жыл бұрын
Bilay moma diakhal mane
@xelmoyniitxel90536 жыл бұрын
Sidy dafa amoune geum geum wa
@jerysow17176 жыл бұрын
Diaradieuf bachir
@fifina6096 жыл бұрын
Depuis le début je n'ai pas vue Mr Niass prié pour son frère à haute voix comme niko adouna bi yeup défé moy Yalla yeureum Sidy Lamine Niass kharéko aldiana wala ma guissoul vidéo bi. Ngene balma
@mansoursybarry4936 жыл бұрын
Il l'a fait nak
@fifina6096 жыл бұрын
@@mansoursybarry493 Alhamdoulilah parce que c'est tout ce qui compte la prière