Mashalah! Yallah na yallah yagal takhaway bi.Sopp nako lolou waay Serigne Saliou,matt nga sa place,un vrai homme de paix,d union et de sagesse! mbokoum layenne boufi diarr rek..
@Sopeymamediarra20245 жыл бұрын
Serigne Saliou dal ndeguer fo sori la guissone si Serigne Bethio ndeysane, Mane der taye la geun geum Serigne Saliou ak limou defal Serigne Bethio Thioune, baye fall lam ba. Serigne Bethio, Yalla na ka Yalla Yeureum, Harer ko Aldiana. Yalla naka yiw gui mou fi bayi fekk si biir bamelam di ko wetali! Amine. Doundal Thioune, yague di djiter sa ndiambotou baye dji. Serigne Saliou ter lila guissone ndeysane sounou mamedia. Yalla na Yalla Yagal leram si nioune Mbacke! Amine.
@ousseynoufall50045 жыл бұрын
Akassa amiiiiiine way Dieuwrine
@cheikhounadiaw58415 жыл бұрын
Sounou mame cheikh bethio thioune lay yakar lo ni 😢😢🙏
@thianendoye28135 жыл бұрын
Ndeyssane Serigne Saliou thioune ki mo sell simple bah am dinner ki dal moy mouride deugeu .yalla nako yarabi aral bopam mou yague fi lol te wer, yen bi oyof tol si mom.sama khol toy n'a. Nena djiguene yi mourou, diang alkhourane, diang khassida, wakhtane si yonente bi serigne touba serigne saliou , berdel sant yalla.ki vraiment moy mouride exemplaire. Thiantakoune yi am naniou chance.bilay
Ki dh Kouñ wadjal la Serigne mountakha deffna ci yaw mbirr dh
@oumoufall96345 жыл бұрын
Aka leer
@maimounambacke28825 жыл бұрын
@@oumoufall9634 kou yalla maye dara ci batine diga kham Lima wakh
@cheikhabdoukhadrembackesec60975 жыл бұрын
Macha Allah yalla nako fi yalla yagal tamou andeu ak wér
@zakariadeune22965 жыл бұрын
Ma challah nileu yalna yalla barkél
@fn511905 жыл бұрын
Machalla saliou thioune ya yarrou yalla nalaa sa frère yui roy
@mamefamangom9175 жыл бұрын
Maschallah thioune sa.waax rafetna Yalna la yalla diapalé thi barkép Segne Saliou Mbacke mala sope ndaax sa yaar ak talibé boo am
@fatousow91815 жыл бұрын
Machallah srn Saliou diotaill bii mouritena lol yall n'a srn Saliou sa tourondo oyafall yenn Wii
@Ndeyemariama5 жыл бұрын
Jërëdiëff thioune,yagu fii té weer!!!
@mayorotouretoure96325 жыл бұрын
Ndaysane machalla seringe sallihou thioun
@mustafagueye39755 жыл бұрын
Yalla nalla yalla diapale ti barke serigne touba
@seydinaomarngack24965 жыл бұрын
Ndaysan Made Ndigalal Serine TOUBA SERIGNE MOUNTAKHa Minga Djafe Rek Moutakh Maganla Supu Barci Brom TOUBA Amal Djame Sa Baye Ba SERIGEN C...kh MADIOUR TIHOUN Yalna sunu Broum Yèsal Yarmandèm Barci Xassidayi🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@mmesagna93945 жыл бұрын
Ayway thiatacone yi mousslen te nek nite te andak Serigne Saliou thioune nguen nek Ben bagna khadial ken sene digante khamni cheikh Bethiono menoulenko khar gnarrr....
@marindoyebadji26365 жыл бұрын
Machalah serign saliou thioune yallana nga GI yag t wer
@kountadiaitegamou43925 жыл бұрын
Machahala dieureidieufe serigne saliou mbake
@djilythiam60735 жыл бұрын
dieureudieuf tihoune ❤❤❤
@toutouprovocation18395 жыл бұрын
Dieureudieuf thioune yag fi té wer
@layelaye65835 жыл бұрын
Machallah thioune mame Bambi
@Secretfemmeafricaine5 жыл бұрын
MASHAALLAH LI RAFETNA YALLA NA YALLA DAKHAL NIÙ CHAYTANÉ...
@serignesalioufarbadiouf63575 жыл бұрын
Rafettt na amna solo
@moustaphambacketaysir44595 жыл бұрын
Dieuredieufeti Serigne Saliou MBACKE
@dabadiop3805 жыл бұрын
Machala thioune ndam rek ak tawfeikh gueneu neikh gueneu bakh ba aldiana
@maguettembaye75035 жыл бұрын
machalla Thioune yagg fi lol té werr
@walyndiaye90505 жыл бұрын
Dieureudieuf thioune
@demahoumlayd5 жыл бұрын
Macha Allah. Deug dou massou fenn. Kou khar ndiguel takha tardé sa yo diougué dinga dabé. Senn diotay bi dalna selna teey na. Teguouna thi sounah akoup talibé
@mamecheikhibiza18375 жыл бұрын
Machala thioune yagfi lol te were yaw danga bakh mourid yepala beug ndakh sa mbakh
@chiekheounadiop95705 жыл бұрын
Machallh thioune❤❤❤
@atoumanendiaye91605 жыл бұрын
Dieuredieuf wakh bi rafetena trope Machallah .
@adamabaldeh32735 жыл бұрын
Machallah machallah 🙏🏻🙏🏻❤❤❤❤
@toutouprovocation18395 жыл бұрын
Serigne pape ndiaye prési bilay ya diss gor
@moussaba70515 жыл бұрын
Seex saluou goudal fan malabeygu bilahi
@ballabar55215 жыл бұрын
Diereudieuf thioune yalla na gua fi yague té werre si barké s saliou