Macha allah notre capitaine de cœur 😍❤ merci tu a tout dit et nous sommes derrière toi Yalna yalla saam la aar la mouseul la té lakhla famou laakh bopam si barké serigne Moustapha sy maktoum sa goor gui
@ndeyelo63542 жыл бұрын
Kouy paré le 18rk beuseul j'aime il a Arena inchallah
@aitadial48192 жыл бұрын
Oeil pour oeil dent pour dent rék yalna yalla samm aar té soutouraal CHEIKH MOUHAMADOUL MOUSTAPHA AL MAKTOUM CAPITAINE YALLA teegneul ko amine
@aidagaye43372 жыл бұрын
Amine
@bacinediop17502 жыл бұрын
Inchallah ❤️ yalla na yalla motali te mousalniou ci pekham none
@tallamboup19012 жыл бұрын
Serigne moustapha sy à vie Notre fierté yalla nako yalla may goudou fane ak sougnou capitaine cheikh
@ndeeyandiay33692 жыл бұрын
Machallah sounou rew mi beugeue niou kouy wakh deuge te sonou kilife deug rk lay dokh ak sounou Capitaine 👨✈️ ❤️🙏longe vie à vous niougui sen guinaaw nchallah folén wote niou dém nchallah ❤️❤️❤️❤️❤️✨🙏
@habibfall92542 жыл бұрын
Quoi qu’il arrive nous sommes derrière vous et nous sommes indestructible 🤲🙏🏾
@DM_national2 жыл бұрын
Nous sommes derrière vous quoi qu'il arrive ay indestructibles lagn tè ben yittè lagn al moy di sargal sunu goor gui fougnou tolou♥️🙏
@astousow59982 жыл бұрын
Gnou sargal ak diam
@aminatakane28452 жыл бұрын
Yalla na yalla motali t Gnou dem si ak diam yalla motali lepp yalla samal gnou sougnou guor gui ak sougnou capitaine ak kepp kouy moustarchid
@mouhamadoundao60252 жыл бұрын
Diarama Cheikh Mouhamadou Moustapha sy Maktoum Yalna yalla doli la sargal
@solace_moualmoustaphasy43962 жыл бұрын
Badiene yalla yalla nangou niane yi Incha Allah
@maodafall4322 жыл бұрын
Yalna yalla samu Gor gui ❤️❤️ AK capitaine
@idrissademe19312 жыл бұрын
Macha Allah, kaddu yi amna solo. Nioun dé lii yengueulouniou l'essentiel est que na Serigne di am diam rek incha Allah
@Eldorado5562 жыл бұрын
Folén niou woo niou dem fa. Sangue bi moy sunu lépp wallahi 🥰 INDESCRIPTIBLE à vie♥️
@aronadieye16322 жыл бұрын
Yalle naléne yalla sama are léne mousal lén si pekhé none nioune serigne moustapha lanou ak ndiabotamm you selle yi xolou niou kénen lidianeti wouniou lénen yéne rek 😍
@maimounasall47422 жыл бұрын
Yallah nanio yallah sammal seydi mouhamadoul Moustapha sy ♥️♥️🤲
@khadycisse84562 жыл бұрын
Dieureudieuf Sy Malick Sy Demba yalna yallah motali incha Allah thi barké Seydina Mouhammad ( slaw) Amin yarabi
@awacissfaye83872 жыл бұрын
Yanna yalla same sougnou GOORGUI 🙏🏾❤️
@morramatathiane71532 жыл бұрын
Ndigeul reck laniouy khaar💕💓
@moussafaye3132 жыл бұрын
Ndigeul dieufé inch'Allah 🙏
@boubacarsaware9702 жыл бұрын
Gouvernement bou sokhor ta bonn, waayé SERIGNE MOUSTAPHA SY kenn meunoukoo empêché ci mission biko yalla diokh. YALNA léen yalla taxawou.
@ndeyemariameba94532 жыл бұрын
Walahii tay laniouy gueun takhaw inchallah🙏🏻
@ousmanethiane81872 жыл бұрын
inch'Allah bien reçu dinagnu sargal sunu goor gui inch'Allah peut importe la situation billahi
@mmendiaye25082 жыл бұрын
Dinagnou sargal sougnou gorr gui inchallah serigne moustapha yalla bako yalla same diokh bagnoula lep sy malick
@seynabougueye87182 жыл бұрын
NOUS SOMMES INDESTRUCTIBLES WALLAHI AZIM ♥️💔💔😭
@mariendiaye4512 жыл бұрын
YALNA YALLA MOTALI YEUP INCHALLAH .TÉ SAMAL NIOU SOUNOU GOOR GUI ❣️🙏
@aramegueye26572 жыл бұрын
Doundeu di dèm, deei di dèm inshallah ♥️
@souleymanegueye86562 жыл бұрын
yalna yalla taxawoulen de tout cœur avec vous ❤️
@omarndiaye73592 жыл бұрын
Machallah yallna yallah motali si barkè seydina mouhamad beurigo si mbarrtall boukh mou dem boukhoul mou dem yallna yallah samou cheikh seydi mouhamadoul moustapha sy al maktoum
@ibrahimasow43332 жыл бұрын
Nous sommes derrière vous Merci beaucoup
@sallahmedsall27832 жыл бұрын
Capitaine yal nako yalla are té same ko
@astoulo19512 жыл бұрын
Bou néké yalla si barké serigne babacar dinagn sargal bamou nekh inchalla
@coumbaniang97312 жыл бұрын
Je suis tout coeur avec vous inchallah tout ira bien
@rabyndiaye25872 жыл бұрын
Machallah inchallah dinagne takkou té tahaw 🙏
@khadysene45162 жыл бұрын
Quoi qu'il en soit nous sommes derrière vous...Sérigne Moustapha sy point amoul kénéne
@mbordiop13592 жыл бұрын
Yalla na yalla samma serigne moustapha s'y makhtoume arr ko si barké seydina mouhamed sws
@rokhayatall54322 жыл бұрын
Bilahi capi ligua wAkh leirna nieup yalna yalla samou
@aicharasullamacktoumienne8552 жыл бұрын
Dieureudieuf SY
@ibrahimadiop60502 жыл бұрын
Inchallah on ira jusqu'au bout🙏yalla na yalla doli soutoura rk 🙏
@khadijadiop58862 жыл бұрын
Sargal sunu goorgui rk inchalah ❤️
@thielofall88402 жыл бұрын
Yalna yalla samalniou sounoiu goor gui sy Demba Bouna ak sounou capitaine Mame cheikh Al makhtoum niouné akk yenn ba le 18inchallah amoul pousse amoul randouu
@allagueye45152 жыл бұрын
Inchalla yalla na yalla motali lepo inchalla ndam rek
@ndiayedaro85152 жыл бұрын
Ak lou manti khéww yalna yalla sammiu souniou goor gui🥺
@mamadoudiop56122 жыл бұрын
Ba béssba akh diame inshallah 🤩
@gueye-abdoulaye2 жыл бұрын
C'est l'éternelle répétition de l'histoire, c'est l'état qui est derrière tout ça.
@mamadoulo58512 жыл бұрын
Avec le Capitaine en avant rek
@Rasssoullll2 жыл бұрын
Vrai
@aidagaye43372 жыл бұрын
Walahi mom la
@maimounadiallo63052 жыл бұрын
Walakhi ndeysan
@Seutou_Mame2 жыл бұрын
bilae wallay ❤ inchalla
@saibatabeye66112 жыл бұрын
Courage mais fréré et sœurs de cœur nous sommes tous avec vous
@bintadiallo19662 жыл бұрын
Qu'il vente qu'il pleut ou qu'il neige 🌨 insha'Allah daniouye sargal kiniou amoul kou doul mome cheikh Seydi Mouhamadoul Moustapha sy
@bachirbachir41782 жыл бұрын
Sargal dafay am inchallah 🙏. Nous sommes toujours prêts pour la cause inchallah ☝️🙏❤️
@Nianghabiballah2 жыл бұрын
Yalna Yalla Motali lepp Inchall. Nous sommes toujours là pour la cause.
@aminatawar28412 жыл бұрын
on vous soutient ❤ lolène wah rk nonou la❤
@yadesokhna51872 жыл бұрын
L'éternel répétition de l'histoire fila Mame cheikh waron geune mou dem ba dernier minute gnou khagn ko place mai yala AK bakham AK gorgou tédda bamou guenna waxal mbokk yi mai tamitt le 18 juin bi diaral Nanou diokhé sounou bakan Dé inchallah pour l'instant gnou djieuffé digueul reck donc c'est le calme avant la tempête Au nom de quoi de kel pays sommes nous wa li ba kagn tamitt tjrs moustarchids molénn li dérangé xamlenn tall bou yala tall sani si Matta mo geuna yomba fouff gakoy djiema fay wa salam
@aminaath25142 жыл бұрын
Ce pays 💔 ils sont pas reconnaissant, l’homme qui a tant fait pour ce pays, il mérite pas ça mais on est tous derrière vous.
@lunelune88722 жыл бұрын
quel homme
@amardiaw19252 жыл бұрын
Machallah sounou capitaine niougui sa guinaw na nieup wadiale le 18 inchallah tous à l aréna
@dieyecheikh68472 жыл бұрын
Diarama Cheikh Mouhammadoul Moustapha sy al maktoum
@elmatroud27962 жыл бұрын
C'est l'éternel répétition de l'histoire Wallahi ak lou mana am dou changé dara souniou nioun nous sommes indestructibles
@lepenseur31502 жыл бұрын
CAPITAINE est un vrai LEADER, mais combat bi doo si weet Walahi paré na si leep, ba si sama bakane !
@abasselofficiel51892 жыл бұрын
❤️❤️❤️❤️❤️❤️insha Allah dina amm deh🙏🏻Si Barke Serigne Moustapha SY❤️🙏🏻
Serigne Moustapha Sy amoul kénéne , ils feront tout pour t'atteindre mais ils ne le pourront jamais wallahi
@fatimasarrdieng43682 жыл бұрын
Yalna gnou yalla samal, aral gnou sou kilipha, samal gnou Capitaine aki rakam aki magam. Dougnou pousse dougnou randou. Inchaalah
@ababacarsyndione2 жыл бұрын
Merci à vous ❤️nous sommes derrière vous
@boucountasene67552 жыл бұрын
Bou sa kuddou djibé balay ngay dannel niou exécuter. Sa Kaddou rek laniouy khar Sy Malick. Yalla na Yalla defal diam sunu Goor gou tedd gui ak sunu Capitaine 🙏🏿🙏🏿🙏🏿
@TAWAMBAYETV2 жыл бұрын
L'histoire se répète mais les acteurs sont toujours là... Mame cheikh newone neu sougnulein taguewul yalla diakadji Dina âme AK thia événement beu armé bi déclancher feu mounileinn soubal také mabayi yalla tei kerok bal takul wayei yeinn tmt il faut faire très attention... Togne bahul nak
@geekartndiaye99352 жыл бұрын
Walay sokhna fatima, insha allah nous y serons
@marieangeleapollineblanche13262 жыл бұрын
Nonnn maneu ma fan sugnu capitaine 🔥🔥🔥🔥 inchallah capi lo wakh rekkk lolou la 🔥🔥🔥🔥👍
@moussafaye3132 жыл бұрын
Sounou sargal Dina âme inch'Allah 🙏
@gueyekhadidiatou75272 жыл бұрын
Walahi amougnou kénéne koudoul sougnou goor gui t dinagn ko sargal inchallah
@mordiop20902 жыл бұрын
Nanou guena wadji inchallah
@moustaphadiop13042 жыл бұрын
Derrière vous sangue you tedd yi machallah 💓💗
@awasamb92862 жыл бұрын
Inchallah dem ba diex Arena rk amoul lénéne Sargal souniou goor gui inchallah ♥️♥️
@smk16792 жыл бұрын
Ñu ngui Kay waadj bubaax inchaa Allaah. Jaaraama Serigne Moustapha Sy ❤️💯