YALLA nama yalla diokh khéweul bou bari ma égaliko defko université internationale de l'islam cheikh ahmadou bamba .Amine si barké seydina Mohamed asws barké serigne salihou
@adamadiouf14435 жыл бұрын
Amin souyou borom meuna lou eup lolou
@djilyniang68135 жыл бұрын
Dieureu dieufé serigne touba amoul morom
@ndamalcadior30605 жыл бұрын
@@adamadiouf1443 wawaw yaw tmt yallanala borom bi diokh si khéweul yi ñou agaliko .
@ndamalcadior30605 жыл бұрын
@@djilyniang6813 yaw tmt amal si khéweul yi ñou agaliko
@bambadieng57925 жыл бұрын
Amine
@moustaphakasse2225 жыл бұрын
Mach'Allah c'est une œuvre immense, très monumentale pour la communauté mouride, moi qui avait l'habitude d'entendre que dans ce palais y'avait des bandits. Vous m'avez aider à comprendre ce qui se passe réellement. Merci encore une fois que le bon Dieu, vous aides et nous aides à finir ces travaux au nom du prophète Mohammed PsL
@tpacalypse5 жыл бұрын
Yalla naa bokk ci gnikoy aggaleh akk yeneen Mourides yepp. Amin Yaa Rabbi.
@djilidieng45642 ай бұрын
Amine
@supeserigneabdouahadmbacke29575 жыл бұрын
Yalla nama yalla defall khiwall bama ageliku man abou diop Amin ci barkib serigne touba
@mbayefaye81845 жыл бұрын
Magui sii biir diew rign
@polesinesaloumpss42735 жыл бұрын
Amine
@thiendiaye70675 жыл бұрын
Démal geustou litakh batay agoul soo paré ngua xol
@tallakhalibaba25115 жыл бұрын
supe serigne abdou ahad mbacke yakar serigne touba .yaaw khaliss nga beug rek. Dikko gnaaner nii
@papiseye23655 жыл бұрын
@@thiendiaye7067 wala ki khamoul Lou beuri
@papandiaye20275 жыл бұрын
Yalnama yalla déf milliardaire ba ma yégualéko mbarké serigne touba
@mtgcommunication19805 жыл бұрын
Amine
@ahmaka84355 жыл бұрын
Amlllne
@khalilibrahim49315 жыл бұрын
Amine
@thiamtechnicien86715 жыл бұрын
Amine
@serignealygueye43105 жыл бұрын
Akk gnoune tamite Amine
@loubesstv48145 жыл бұрын
Yalla nangiou yalla bole ci milliardaire Serigne Touba yi
@mameboussodiouf38835 жыл бұрын
Amiiîiiiiiiiiiiine ❤️🙏🏾
@ibrahimakhalil22345 жыл бұрын
Amine
@Ahmadouboromediamono44 жыл бұрын
Tu a raison dh dou xaliss moss
@diediagne29754 жыл бұрын
Amine yarabi
@ZeynabRassoul14 жыл бұрын
ni moutt nopi. Yalla mofi nek dei
@thierbeye18605 жыл бұрын
Lima thi gueuneu yeme moy apres tant d annee amoul ben khar khar chapeau a l architecture yalnanou yalla fayal ndiouga
@koumbacke97314 жыл бұрын
C'est solide ce bâtiment. Quelle construction !li thiakhannn tabakhouko si yoyou diamano.thiey ndiouga yalla nala borom touba térrou
@mactardiakhate7505 жыл бұрын
Billahi yalla na niou yalla dèf millyadèr ba yègalèko inchallah ❤❤
@amykasse39863 жыл бұрын
C'est un travail de très grande qualité et très professionnel !! J'adore !
@mossanefaye94145 жыл бұрын
Ndaysane adouna doukeur yalnako yalla yeureume ak boléme wa dawlou amine
@methodic4271 Жыл бұрын
Tu px même te perdre dedans comme tellement que ct immense🙏🏾.Yalla nako yalla yégali ci katanaam
@sokhnadiallo9013 Жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba machalla Yalla na Yalla motali yéném El hadj Ndiouga kébé🤲🏿🤲🏿🤲🏿🎉🎉🎉🎉🎉
@amyngom60742 ай бұрын
Ndeysann bossou djili mbaye bi nek louga parer na mais mom bossam li la thie yalla namone yalna yeureumander wathie thie kawam
@Sounouteleinfo5 жыл бұрын
Oumpalé wone na mame ndiouga kebe 😭ndaké mame ndiouga kébé mouride sadikh lâ .kon nak warnagne ko delou gnoukeul yégalii liguey bii.mame ndiouga kébé sa sa yéné ak sa liguey raféte na yallah nala yallah faye 🙏
@bassinemoussalioumbackekeb80295 жыл бұрын
Sama mame rek Machaala KEBE diougua
@ibrahimakhalil22345 жыл бұрын
Amine
@i.g.g.sfimela58015 жыл бұрын
Amna yéuné yégé leko Yalna ma Yall déf Ma don Milliardaire Serigne Saliou Mbacke bama yégé le Plai bi ték ko thi lokhoy Serigne Cheikh Mou Serigne Saliou Mbacke Allahou ma Amine 🙏🙏🙏🙏🙏😿
@bayenderysarre45575 жыл бұрын
Amine waayy
@ngonepons98445 жыл бұрын
Amine
@ibrahimakhalil22345 жыл бұрын
Amine
@AllaSall-oy2jh3 ай бұрын
Vraiment nhiougeu garmi la yalla nako brom bi diegeul s brkp brom touba😢
@fallousow4245 жыл бұрын
Ndiouga est parti il a laissé son derrière de souvenir qui noue montre qu'il était un homme bon et serviable. Il a fait de travail inoubliable.
@abdoulayebalde88295 жыл бұрын
Respect à l'architecture
@askibbcr2833 жыл бұрын
C'est un chef d' oeuvre malheureusement inachevé. Que la communauté mouride se mobilise pour finir les travaux.
@modougueye13515 жыл бұрын
Yalla nama yalla maye Milliar bama diendeko agalèko dèfko adiha Serigne Touba
@mbppfd81682 жыл бұрын
Oh Sénégal 😢😢😢 pourquoi ils essayent pas de terminer cette belle construction pour rendre hommage à kébé
@oumydieng72915 жыл бұрын
Baye Ndiaga KEBE yalla nako yalla khare aldiana firdawsi si daredieye serigne touba
@sokhnadiallo9013 Жыл бұрын
Merci à vous c'est vraiment une belle découverte ♥️♥️♥️♥️♥️🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@kinelo80265 жыл бұрын
Ndeysane baye NDIOUGA yalla nako yalla yeureum té yoki ak léram. Yéném si SERIGNE TOUBA yatouna loooolu. SERIGNE TOUBA yoname Wii lusi waram am rek bu dioté dall di mate seuk ndakh lepp lu wara ame si deuk bi niane nako boromam bamou maye koko. Kholal Matlaboul Fawjayni
@Madamefall351 Жыл бұрын
Andounabi yalla rék mon matallé yallanako yalla yeureum❤
Bi liguéye bou garanti combien d'année pas une seule fissure c'est étonnant merci du vidéo
@senegalrek79755 жыл бұрын
Je t'aime ndaye machala sa xam xam
@diarradieng20424 жыл бұрын
Sa ma PAPA Djiby Dieng entrepreneur bou mak la woon deuk Dakar bokk naci gniko tabakh
@falloutall67725 жыл бұрын
masaa halla yalnako yalla yerem te khare ko sa aldianaya firdawsi si bargueb s.touba ak khassida yi
@madamemadame33805 жыл бұрын
Merciiii pour ce beau reportage. Je suis allée à Janatou Mahwa mais j'avais pas vu ça. Grand Bravo à vous. Alaji Ndiouga Kébé Yalla na KO yalla teralé Aldjana firdaws.
@binoushbae93505 жыл бұрын
C vers la sortie soy djeuli peage bi a gauche
@ibrahimba90205 жыл бұрын
...
@madamemadame33805 жыл бұрын
@@binoushbae9350 moi j'y étais au magal de 2005 Motakh j'étais bcp plus jeune.
@mameboussodiouf38835 жыл бұрын
Amine
@diopabdoulahad1074 Жыл бұрын
Ndey san aduna 😢😭😭 yalla nanou yalla yereum si barké seydina mouhamed psl
@mberrymmy92755 жыл бұрын
Palais bi dé lou yémé le ndakh dayo bamou ame. Souma démane touba damadane yék si terrasse keur gui ( chez Pédro Diouf)di admiré palais bi ça ressemble à une architecture égyptienne mashallah
@matarndiaye33595 жыл бұрын
Moi je passai la bas souvent mais je pnsai k ya dea serpents dedans
@mberrymmy92755 жыл бұрын
Matar Ndiaye nèkhoula gnémé dal
@adamadione26435 жыл бұрын
Thieuy Serigne Touba ken la li takk li égoul té kéNN dieurigno Woo ko malgré tout l argent du défunt mieux vaut s abstenir du commentaire té nianalko yeurmendé yala thi barkeep Cheikhoul Khadiim
@makhtarsylla80565 жыл бұрын
Wallahi dafa massa bokk si sama ay procès yalla nanou yalla may khewal gougne liggueyeulé ku tedd ki. Aminnnn
@cheikhsarr77425 жыл бұрын
Amna solo yalla na yalla egale yenem kuko defon keur serigne Touba dina am solo lool te placé na lool macha allah
@s2mnd_tv2615 жыл бұрын
Ndeysann, palais bi khaliss demnassi dé...kholal architecture bi... vraiment c Extra....
@mameniagnandiaye42143 жыл бұрын
Machalla quelle architecture yalla nagnouko yalla fayal Elhadji Ndiouga kebé thé yéné bimou amone si Serigne Touba akk ay domame akk si biir Touba yalla sougnou borom motaliko si barké Seydina Mohamed psl barkep Serigne Touba cheikh Ahmadou Bamba khadim Rassoul Maneu au paravent on dirait ya que des bandits dans ce palais mais alhamdoulilah Dieu merci que lumière soit faite sur ce lieu avec une belle architecture dotant des années 80 ni fissure avec l'ascenseur le sous terrain machalla dall machalla tout a été programmé
@BaabineWone-w7r3 ай бұрын
Magnifique, mais pourquoi ne pas l'utiliser pour un hôpital ou quelque chose chose qui peut aider,genre université
@mariecisse79655 жыл бұрын
Machalla beugue souma amé ay milliard égualiko inchalla yalla mene nako amine
@bayelahatmbacke27535 жыл бұрын
L'architecte ,c un génie point .
@suzyq48895 жыл бұрын
This man was a visionary I wonder what he was trying to build here .
@khoumakhouma49405 жыл бұрын
Ndaye Saan Ndiaka xame limowaral Barina xamèh woko woone nii billahi yalla nako yalla faye
@toureibrahimasene66945 жыл бұрын
Qu'on le fait résidence de serigne Touba Mbacké puis on le termine . DIEURREUDJEUFE TII SERIGNE TOUBA
@Dofdofdofdofdof58775 жыл бұрын
Lançons une pétition sur internet pour rétablir le lieu
@mohameddienefaye49064 жыл бұрын
Yalna aigue ak diam, sii barkai yonaintebii barkai borom touba
@ndayegueye95255 жыл бұрын
Yalla nama yalla difall xéwal bou Bari bama yéguale ko si barcke Serigne touba
@dialistakebe8555 жыл бұрын
Yalna ma yalla maye louma yegale li sama mame dj defare si bakep borom touba
@BabacarMbaye-c7i9 ай бұрын
Lidé kou kou dé Faroun yoko ko ci Iniweersite S montakha bi ❤
@massambasarr96353 ай бұрын
La famille de ndiouga kebe devrait continuer cet chantier pour le mémoire de leur père
@fallouthiam2505 жыл бұрын
Yalla yalla bolé ci milliardaire ri serigne touba
@gayedaba85245 жыл бұрын
Amine
@khadimsall94343 жыл бұрын
Amine
@seckbologna20655 жыл бұрын
Yallah nanou sunu borome may ay khéwal banou bockou thi gnikoy agalé thi barké khassida yi🤲🏾🤲🏾
@ibrahimakhalil22345 жыл бұрын
Amine
@dioufitaly47525 жыл бұрын
yalla naniou yalla may ay khèwal you bari baniou ègalèko si barkè serigne touba amine
@cestmoitkt5275 жыл бұрын
Ndaysan yalla nako yalla xaré aldjana djéggal ko barkéb serigne bi
@astoundiaye98035 жыл бұрын
Man deh damako dan degeu rek bimay dem porokhan rombouko sama adouna sep dafa touki walahi yala rek moy ken mame gnougua kebé yalna yala yokou yeurmande ak ndiégual si mom brk cheikh moustapha
@astoundiaye98035 жыл бұрын
family waw khamnako kay mais bimay demp porokhan otobi fofou la diar soréwout ak djiumay s saliou dji nek dianatou
@nouhounefall59595 жыл бұрын
Yalna yegue te yala khareka aldiana
@LLTV435 жыл бұрын
Yallah naniou yallah fayal ndiouga kébé thi barké sr Touba
@lasorkapalmas5 жыл бұрын
Man wax dëg awma xaalis waay dou milliard yii laay xalaat fii ma nekka nih. Sama xool daa tooy te bokkuma ak moom dara ci askan. Aduna dou dara, ndégam loo meuna am ci aduna denkoy baay si kaw souf , yow nga sangoo souf. Thiey yalla, moom moo njekka té mooy moudjé. Yalla nañu yalla may rafetal sounou diganté ak sounou borom. Yalla nako yalla yérém té kharé ko aljanna.
@bayeamdyfaliloundiaye43135 жыл бұрын
Walahi Ken dou baye ndiouga kébé dama khamni kou mana defli si diamono Bi khamni amonena yénë bou reuy touba mâchala Chapeau architecte Bi ndeye sane loun wara aggué baye mountaha la niou defko musée khassida ak histoire yonwi Yala n'a yala doli yeurmandé aladj ndiouga kébé 🙏🙏🙏
Machalah liguey bi amna solo yalna yaleu diokh kouko agaler barcki Serigne Touba sg ndiouga yalna khiper aldiana amine
@serignefallou66685 жыл бұрын
Machallah yalna ague si diam barke serigne saliou
@alaminmohamed63275 жыл бұрын
Elhadji Ndiouga kèbè c une fierté, Yalla tèrall nako Sénégalais nakk dafa sokhor
@djilyfall19185 жыл бұрын
yalla na ma yalla may dolé ma défar ko
@taphagueye34575 жыл бұрын
Yalla na ague thi barcké seydouna moukhaméd thi barcké serigne Touba liii machallah aniii mouriide yii nda ndigeule diouke bilakhi bou ndigeul djiougué liii dou dara thi mouride yii gnou agualé ko
@galomiss14525 жыл бұрын
El hadj Ndiouga Kébé Yallah na ay léram yoko barké Cheikhoul KHADIM té héritiers yi égaléko wala gnou défko addiya Cheikhoul KHADIM talibés yi égaléko.
@princessekebe94605 жыл бұрын
Khana niom begougne lou bah bakoy djohé adiya
@ZeynabRassoul14 жыл бұрын
Sa papa sonou liguéye ba ame limou amw, serigne fékéwoul, gnoukoy diokhé hadiya. Revenez sur terre
@tvlg85075 жыл бұрын
Me sama pale mam bi ni niou ko baye ni meti nama 😭 mam yalla na souff sed sa kawou sa yene si kou ted ki epon nali 🙏🙏🙏
@mbayefall75834 жыл бұрын
Yalna yalla khebe doli bamou ak bâ nek diarignou sekhoul khadim
@aronacamara88085 жыл бұрын
salam diokh ko adiya borom touba te serigne mountakha ak serigne bass abdou khadre sekouko yalla na anntou
@ibrahimaniane15545 жыл бұрын
Ay way yall na s touba wout kouko agalé niou fékéko
@touretalla38045 жыл бұрын
Yala na néck mame amine
@BFY20055 жыл бұрын
Amine waye tamou néck mane mi ak kép kou am yéné bi thi barkép Cheikhoul Khadim
@khadimcisse76875 жыл бұрын
Yallna nou yalla def ay milliardaire rou serigne touba ban aga leko
@abdoukhadrendiaye36505 ай бұрын
Vraiment J'ai impressionné sur ce travail automatique extraordinaire
@gueyetoba65195 жыл бұрын
Mame ndiouga yalnako yalla khare aldiana te yekheniou Lima diakhal Nak Moy en 1984 lafi bayyiko te Boba balegui manoula yegue
@PapeFaye-m4t2 күн бұрын
Yalnako years thi barke s touba
@maimounalansanasadio475 ай бұрын
Yalla nama yalla may weur seuk 🤲🏽🤍ma meuna diapalé gnou beuri ❤
@aminatagueye88175 жыл бұрын
Yalla na ma yalla bole si mileyaderi s touba bama agalko ake boleme joulite
@papefall37455 жыл бұрын
Machalla El Hadji Ndiogue yéném agna mé pour Man ndiabota nano wara dieul liguey bi diokh koo s mountakha Mbacke niko mou agaléko défko keurr s touba sino d'où agg
@sokhnadiarrakane3755 жыл бұрын
Amna solo fi ken nième woufi wona diar goudi ndax ay vayou té legui heure boula nekh diar serigne touba amoul mrm yalna ah ak diamou
@nefertaribaidy6695 жыл бұрын
Ça allait être très beau une fois achever. C'est dommage qu'il n'a pas eu le temps de terminer ça. Et que personne après sa mort ne se soit occuper de ça. Et qu'on a laisser sa a l'abandon. Ses enfants étaient trop jeune à l'époque pour prendre le relais et achever l'oeuvre de ndiouga Kébé. Quel gâchis car c'est un beau domaine.
@bandiougoundiaye67775 жыл бұрын
Mane guemnani bou fékoni khaliss kasséla kone héguena bou yague
@babacarlo41025 жыл бұрын
Louy probleme bi
@abdoulahadgadiaga28475 жыл бұрын
1
@AzizDramé-q4j3 ай бұрын
Merci bcp Ioe wakh nga wakh! Mann sama papa ndiouga kébé moko yobou 2 fois makkah! Batéy si ay domou ndiouga kébé lanek, ms li geumnani dou problème xaliss
@ZOOMA-O.B.Y4 жыл бұрын
Architecte bi tmt amna may Machalah🙏🏾
@goodvibes51102 жыл бұрын
Yalla nako khalife general eguali. Vraiment cest du gachi
@hakimgaye57315 жыл бұрын
Wakh DEUG yalla lougne wara agalé la, ndiouga yalla nako yeuram
@louisediagne675 жыл бұрын
Macha alla talibe rekh ame solo il repose en paix 😭😭😭👀💙🙏🏻
@mathiouz20745 жыл бұрын
MERCI beaucoup pour le reportage
@laminefaty7370 Жыл бұрын
Yalnako yalla yeureum kharéko aldiana firdawssi
@attotemiraculeuse96665 жыл бұрын
Inchlla souma dématé touba filay ndieuka nieuw
@fallcheikh10foulabook355 жыл бұрын
sant serigne touba yalna yalla yokou ay léram té tasnou si barkém yal nama yalla défal xéweul bama agaléko barki serigne touba
@Ahmadu5365 жыл бұрын
Ylna ylla dolli yermaande s ndiouga kebe
@abduliejallow49895 жыл бұрын
Rafetna lool Ken mousoul gis loumelni ci senegal ak ci Africa
@cissefamily86125 жыл бұрын
Le plan c'est vraiment étonnant et un grand remerciement à vous tous
@tenzacrack5 жыл бұрын
Franchement j'arrive pas à comprendre certaines personnes qui commentent en disant que vous connaissez pas la vraie histoire! Svp mais expliquez ceux qui connaissent pas comme moi. Ndakh gnou kham
@ZenTubeT-V5 жыл бұрын
Elhadji Babacar Kébé dit Ndiouga, propriétaire de son vivant du plus haut immeuble de Dakar (immeuble Kébé), avait entamé la construction de ce palais qui a fait objet de cette vidéo. Malheureusement le chef-d'œuvre n'était pas achevé.
@babacarlo41025 жыл бұрын
@@ZenTubeT-V sheuteut louka waral lagniou
@babacarlo41025 жыл бұрын
@@ZenTubeT-V la lathie akh
@ZenTubeT-V5 жыл бұрын
@@babacarlo4102 Mais il fallait arborer l'oreille attentive lorsque tu regardais la vidéo parce que le commentateur à bien expliquer la raison de la construction de ce palais. Qui selon lui devait servir de résidence Khadim Rassoul pour héberger des hôtes venant d'horizons divers pour la célébration du Grand Magal de Touba.
@ZenTubeT-V5 жыл бұрын
@@fatoulomouserignebabacar7395 As-tu des preuves qui attestent qu'il était maçon? La prudence ma sœur du fait que t'es musulmane d'après ta photo de profil et que nous sommes dans un mois de repentance alors il faut en profiter par des bienfaits sinon ce serait une perte pour toi. Eh avant de l'oublier, je voudrais te faire comprendre que nous mourides véridiques, préférons de loin le chien qui a un amour envers Serigne Touba infime soit-il qu'un érudit qui a la male chance de ne pas aimer Serigne Touba. Wa Salam
@damesene2413 Жыл бұрын
Assaalaamy TV machalla seen liguey rafétna
@abdoulayeblondinndaye49635 жыл бұрын
Amna solo daama dann deg touram rek mais xaw ma wonn dara si mom kii deh war nagn ko fatalikou teh mouride yi diko gnanal . Bravo a vous et bonne continuation
@modougadiaga53055 жыл бұрын
machallah amna solo lol ndiouga yalla nako yalla faye
@badadiop6755 жыл бұрын
Yall nama yall def miliadere ma agaleko barkep sering bamba
@ndeyefatoukebe25645 жыл бұрын
Machallah mame kate fane rek laniouye dioye
@mbackeseye71785 жыл бұрын
Yalna bok si gni ligueyale serigne TOUBA si deukeum bi di TOUBA
@DiagneFall-ri4hw3 ай бұрын
Macha Allah Dieureudieuf Kébé ❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉😢😢😢😢
@Diopmoussa6195 жыл бұрын
Ouu ndeye san yalla nako Seringe touba fay mom mi am fay
@khadimkebe23135 жыл бұрын
Yalla na yalla def ma agga leeko 🙏
@mtgcommunication19805 жыл бұрын
Amine
@ibrahimakhalil22345 жыл бұрын
Ndaye sanne yéném ague n'a yalna yalla bourbi yokou say lerrr