Bilaay Diama El Hadji laako yéné. Xawma nak nounguen di deff ba déloolèn. Mais len mom amena Waxou imam boobou nagne Diama na fass ci xolam pour delou ak El Hadji tèklènko ci souff, mane deh degoumako té guissoumako fen. Lèral lenniou ban xadiss wala aya alkhourane.