khassida de bamba apaise mon coeur à chaque fois que je l'écoute vraiment kemane la machallah .les paroles ne sont ^pas ceux des humains mais de Dieu.il est le meilleur des poetes que le monde a connu depuis la naissance de l'homme .kemane la tourondo
@momodioume38023 жыл бұрын
J’ai la paix dans mon coeur quand j’écoute rahiya dieureudieuf serigne touba
@mamadoudiane26513 жыл бұрын
Salamalikum amine yalla akasa cheikh Ibrahima Fall amine serigne touba amine Mohamed 🇸🇳❤️🇪🇸
@maxime-ud1tg4 жыл бұрын
Dieuredieuf serigne touba diarama mame chiekh Ibrahim fall
@araminefr16 жыл бұрын
« RAA I YA» Waxnanouni Xassida tagg la dieum si geun di mbindef .Bokou yoyou tagg ay BEUYIT you ken meusta guiss youni mel .Waxnanouni Xassida gui kou koy diangue dangay begeul Yonnent bi(Psl) ak Sakhaba yi ak mbolem Gayou Bakh yi si geun di mbecté té kou begeul gni begeul SUNU BOROM(SWT).Xasssida « MAD’HOU »la gningi ko teunk si "sahadatou mouridina......" té yilé Xassida nenanou moy li Geuneu gaw si ay xeweul, ak Barké ak beug Yonnent bi.Té Xassida yoyou nio lay wommatal sen bopou. Mag gni nenanou Ram’mou nak mingui si biir lou yémmè Si biir Xassida gui KOU TED KI mingui feuseul lat Ram’mou gui Yonnentbi (Psl) Défalone Seydina Ousmane « Zin Noreyni »KOU TED KI nena « WA FIHI HALA NABI OUSMANE YASFAOU FI SABHINA ALFAN KOULLOUNE HAHAOU NAAROU »(Yonnent bi may na Osmane kerok bissou Penthie mou Ram ‘mou 70mille dieum you xamni Safan ba niéllone na len)Likoy firndé Moy S A LAHAD MBACKE (RA) néna Kerok Bissou penthie Mouride bou doug mom rek « ALDIANA » mom kep KOU TED KI mo am foumou la fètè wayé Yaw fèté woko fennLikoy firndé wat moy « Douna makatiby hibadaty mahan Takharoubi koulla majaya diamakha »(Sama Xassida mo eup Yoll mbolem diamou yalla ak mbir loulmou rey rey) Ram’mou kon mingui si Xassida gui KOU TED KI nena wat si biir “Kahboun wa Hassanou wa Boucheyri had Barakho wa koulahoum sihrouhou nouroun wa asrarou » KAHAB, HASSAN ak BOUCHEYRI Bokkon nanou si tagg kat yi geunona Kawé si diamono Yonnent bi Ba amon na Koumou ssi solallonn manteau boppam.Wayé liniouy kawé Kawé KOU TED KI nena Sama tagg day gathial mbolem liniou meusseu way DIEUREDIEFETY KOU TED KI
@DaarayKhassida6 жыл бұрын
Amna solo lol Dieureudieuf si laayé biir gui
@mameseyeseck63364 жыл бұрын
Dieureudieufeti Serigne Aramine Mbacke begon nako wayé guene tina yokou🙏
@valerytchernykh62004 жыл бұрын
Amna solo vraiment 🙏🙏sed na si khol
@mohamedsalem35903 жыл бұрын
Bégué way
@momodioume38023 жыл бұрын
Y’a bakh de mouride na gueuna fonkate khassida yi na guena begate rahiya
@mbayeyatt93105 жыл бұрын
Serigne touba kéne là
@mouhamedrassoul35715 жыл бұрын
WALAHI NDEYE SANN KENN LA DH
@papesambakasse4225 жыл бұрын
Allahou Akbar oh way way way way lii neixna way oh, dina déé rk
@mohamedsalem35903 жыл бұрын
Dirredieufeti serigne touba
@cheikhjibrilsyattidiani9513 жыл бұрын
Serigne Touba Yalla nanouko Yalla fayal
@issadiallo11274 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba Diarama Manme cheyche Ibrahimma fall
@papefaye70893 жыл бұрын
Thieuy daaray khassida. Dieureudieufeté mame khadimoul khadim Mach Allah