Cheikh Alpha Ba, gouddal fann té wérr. Maak yaw depuis 2019.
@salieutinn4313Ай бұрын
Mann dema bokon ci beni tarikha Senegal. May Alhamdulillah yalla wonama yonn bu lerr b. Oustaz omar sall moma gena dimbaleh. May magui toopu shekh Alpha bu bakh
@alhimma1962Ай бұрын
Yaangi topp tarikha Alpha ba , très bien
@Tambayefall27 күн бұрын
Dangay doul rk yaw ak alpha Balthazar ak Omar sall yéna yam ay ndialo kat ngéne 😅😅 akhlou ndialo mak gnui déf déf dara la motif yi néx na trop way
@AliouNdiaye-lc3pp24 күн бұрын
Yaw yaa ngi sooga réer nak, ciy tappale kp lañ nk. ca suba ngay compr
@salieutinn4313Ай бұрын
Demalay toopu bu bakh. Mangui Gambia
@Tambayefall27 күн бұрын
Ndialo kate manoul até si Islam ☪️ kou rér yaw laye topu bépu mak boubakh si Senegal 🇸🇳 dinga doundou ba dée do dégue fougn la wakhé ndialo na Wala moyna yalla yaw alpha Balthazar minga khamni si ndialo nga deugue yaye khas nikou masoul moy yalla ndaysane
@baloutadanso25 күн бұрын
Li ngay wakh fan ngako tekk?
@baloutadanso25 күн бұрын
Yonentibi diangalnaniou niou bania saga ap dioulite dou saga lolou rekk wanena ni ignorant ngue demal diangui diné ji mo guen si iow té dioulite waroul reuye bo guissé deugg bi boulko neub
@faxamaan7632Ай бұрын
Discutons mais svp pas de dispute
@faxamaan7632Ай бұрын
Soubhanalahi walhamdoulilahi ❤❤❤, le Sénégal pays des comédiens......La vulgarité,la persevérite , la violence ... tout se qui est negatif c pour les faibles pas pour les musulmans, pardonner pour être pardonné, seul un noble et un musulman peut pardonne, ....... Que Dieu protège et veille sur ma famille ...... Solution=Coran.?????Opération Sunnah ??????? Culture arabique et comportement en islam ????? Benit soit tous les vrais Musulmans ❤ Alhamdulilahi ❤❤️❤
@faxamaan763225 күн бұрын
Rooy daxalale, Sénégal pays des comédiens, que Dieu protège et veille sur ma famille ❤️
@moussacisse948Ай бұрын
Sounah rek ❤❤❤❤❤
@aissatousene2801Ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@KaoussouSeydi-k9zАй бұрын
Macha Allah
@AssaneDiop-w5m20 күн бұрын
Sama guayi l'iguane di wax lérr na allahou akbar
@Hamidthiaw4782Ай бұрын
Djazaakallahou.
@ousm7710Ай бұрын
Soufiyanké yi nio topou mbacke sakho sene passe passe comme khinou nor khamougnou sene dîné
@DameDia-uv7qnАй бұрын
Merci beaucoup encore ya imame alfa ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@salieutinn4313Ай бұрын
Oustaz dimbalema ci sa number ngirr yalla. Mangui Gambia
ستفترق هذة الأمة على تلاث وسبعين كلها في النار إلا واحدة إذن أما قولك على سنتين وسبعين ليس صحيح هذا يدل على إقتصارك في العلم
@DameDia-uv7qnАй бұрын
Soukrane ya imame long vie a vous et une victoire incontestables ici et bas comme dans l'au de la ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤planète je suis sénégalais très fier de
@BecayeDiarra-o9xАй бұрын
C'est pas vrai que Ahlou Tassawouf est contre la Sounna. Le problème est que Ahlou Sounna a peur de débattre avec Mbacké Sakho. Nous ne suivons pas Mbacké Sakho mais nous avons besoin de savoir comment les hadiths sont venus
@sonhiboumbow4293Ай бұрын
@@BecayeDiarra-o9x lou werla dee sakho ken andou lake mom thi wa tasawouf mais ly alfa wakh thi serigne touba Bilahi dara dou thi degue
@ousm7710Ай бұрын
Kou sankou moy yow débat ak mom bane sans la am soufiyanké yi sene passe passe bakhoul dîné l'islam bi mouhamad idi losi wedi safara direct gua dieum niaka diangue sene dîné motakh lou gnew yobou léne
@ousm7710Ай бұрын
@@sonhiboumbow4293sene serigne yi thi reur lagnou fatou