-Rien ne justifie la violence que la femme a fait preuve hein. -Si vous n’êtes pas en mesure de supporter la polygamie mais vas-y demande le divorce c’est mieux que de faire du n’importe quoi. -Je salue La sérénité et le respect de cette famille qui n’a pas déversé sa colère sur cette pauvre dame parce que ça pourrait mal terminer
@nabousanediop68402 жыл бұрын
Vraiment,fii ken forcé woul ken woudiéi ,
@cheikhounatine7582 жыл бұрын
@@nabousanediop6840 ah vraiment si tu peux pas supporter bah force pas
@smartfolle2 жыл бұрын
Lii daal moy waxx dji So menoul mougn woudjei nga demm sayoon Souko reyoon tamit moy perte mom ak wa keureum apres niou niane intervention teudj ko klk mois mou guénaat seuyi fenen
Vraiment famille kou goor kii koulén diapou diapp niou goré papam ak yayam
@marinaba95742 жыл бұрын
Billahi
@ndeyembodj93962 жыл бұрын
Pa bi kou mate kilifa bilay 🥰🥰🥰♥️♥️♥️♥️
@footballgod43512 жыл бұрын
Vrement yalna goud fane way il a bien eduquer sa famille machallah
@awagadiaga95532 жыл бұрын
Bilahi dafa yarou sakh pa bi
@ndeyembodj93962 жыл бұрын
@@footballgod4351 amie et machallah
@ndeyembodj93962 жыл бұрын
@@awagadiaga9553 bilay eva
@hawasall41482 жыл бұрын
Ndeysane famille dieukeur dji danio baxx ndeysane
@fantasagna40762 жыл бұрын
Firangué bou eupë bakhoul djiguéne,dafay nangoo mougne lo guiss rk dafay jèkhe ,firé ko ba nar Ko lôr ,gnoune djiguéne gni nagnou kholate sougnou takhaway bou bakh,ay joulite laniou tmt nagnou nangou woudjé té woudjé dou dara loudoul niar niou bok weuseuk,bon rétablissement à l'homme 🤲🤲
@antasarrcisse18032 жыл бұрын
Une belle mère exceptionnelle !!!!
@salimatasow26222 жыл бұрын
Vraiment
@mamefatouba66372 жыл бұрын
Bilay ndeysane mais seytane dafa beuri dole PA bi beuguenako MÈRE bi aussi yalla sunuu borom def si jaam rek amen
@salimatasow26222 жыл бұрын
@@mamefatouba6637 Amine
@bourtandadiop32612 жыл бұрын
Vraiment d’accord avec toi. C’est triste
@nenou2d8462 жыл бұрын
Pa bii ndeysane il est choqué Kou bakh lay nourou Ndeye tamite am na fitt si femme Papa doundal way
@paabdou87732 жыл бұрын
Yalla naniou yalla Def Diam ak soutoura ❤️🙏🏿
@diombonguer57152 жыл бұрын
Amine ya rabi
@abdoufaye60392 жыл бұрын
amine yarabi
@khadimboup12272 жыл бұрын
Aminé ya rabi
@sokhnadiop51724 ай бұрын
Amine 🤲
@mbneseye22132 жыл бұрын
Ndeysane famille bou gorée c’est rare loumou méti méti sedel naniou ndawsi lou bakh dans le passé
@anijara96362 жыл бұрын
Même si je comprends que ça doit faire mal d’avoir une co épouse ce n’est pas une raison pour agresser son mari. Si tu n’arrives pas à supporter la polygamie divorce et rentre chez toi c’est tout.
@simalcoura90932 жыл бұрын
Sa deuggeu deuggeu kou meune tok so menoul gua dem
@sophiesokhnacorrea11962 жыл бұрын
Dém pour lane esk dieukeureum warou ko,waur nama daf ko nèwone douko meusseu takal woudiou,légui dangén beug mou dieul ay bagagam dém,bane goor tak ko,mou bayi keureum nonou bénén djigén diffa dagou?
@mariendiayediouf836311 ай бұрын
@mariendiayediouf836311 ай бұрын
@MaimounaDieng-o4j11 ай бұрын
Ki môme vraiment domerame la chiiim
@Vincent-zp2pq2 жыл бұрын
Deug deug dieukeur dji meun na mougne nk. La famille du jeune homme est très reconnaissante malgré les faits.
@ahmadouniang27742 жыл бұрын
C pas la reconnaissance c'est d'accepter d'être tué raison pr la kel justice Sénégal ne pourra pas avancer c'est le contraire ici europ
@Damasdiagne04022 жыл бұрын
Bilay
@missdiop35002 жыл бұрын
Bayiléne di takk diabar diko gueumeloo ni doungéme meuseu takk gnaréle yénéy dougeul séne bopeu si problèmes yii yeupeu
@binetasy37492 жыл бұрын
Mariage Sénégal mo metti Tei compliqué . Seuy leigui danger pour les deux familles . Motakh ndiabot you bon reik kou neik di tangal xolou keinein . Vous les hommes j parle en connaissance de cause xamolein koulein di monieul doxane reik do lein doylou .la femme n est pas mauvais c juste c qu elle a vivre la conduit ainsi . Bo doundeul yein situation doko xam .mon mari ma tromper avec 2 femmes et lorsque j l ai surpris il me dit k il n a jamais l intention d en épouser donc louko fi diar . En plus u vis dans une grande maison ak ni keur gui metti bo yeureumoul sa soxna boul ko teik nakar . Elle a juste aller top loin. Ak loumou meunti sone si u supporte pas part au lieu de te salir goor diarouko mais force à toi sister
@magattgaye17602 жыл бұрын
Wlh ndiabote you bon agresseur je ne suis pas d'accord comme ray nitte c pas normal est c q amoule rap
@thiamthiama65522 жыл бұрын
Mane déh djomi na maye wakh mounan force a toi siste ki beugue raye domou diambour boudone sa mack lako déf do wakhé ni sou mounoul woudjé gua déme cest sinple tite na si senegal khalé you gour yii faga rouléne djiguéne vampir yii gno fi
@binetasy37492 жыл бұрын
@@thiamthiama6552 force à elle li niouy dathie thi keur yi vous en savez rien yein célibat yeina fi neik di sonal nit Gni . Elle est juste aller trop loin mais son comportment peut être justifié
@coumbaba65302 жыл бұрын
Walay sister liga wakh khamo sakh lulako wakhlo. Gorru tay yiii niaaak nagn diom amuniou roussukay, moi non plu sui po d’accord vk l’acte d la femm mai la source d cela c’est l’homme.
@binetasy37492 жыл бұрын
@@coumbaba6530 elle a exagéré mais c ki au fond on ne connaît . Elle a juste trop endurer les femmes souffrent dans leur ménage desfois elle n ont personne à qui se confier ce qui leur pousse à agir inconsciemment j sais au fond elle est regrette son acte
@mofama95202 жыл бұрын
Yallah naniou yallah mouthieule si djiguen thiou bonn
@djkabou30062 жыл бұрын
Ki amoulll. Diommmm ndawsiiiiiiii bouyabooo naguenkooo yobouuuu. Yarkooooo ndakh paregoullll yalla naniou yalla moussalllll. Si djiguen djioubone si barcké seydina Moukhamet psl amineeeee
@nafimbaye85722 жыл бұрын
Les hommes n'en valent pas la peine si tu peux pas supporter la séparation est la seule solution
Mande diguene bouma soty dokhe mou tangue ninale yall ma bania doude dakhe kene fekhe ba doumala defe loiko raw daniye dof doflou rew rek molene diap koula soty bo were fayoule ak foumou mana nek
@ndeyembathiodiallo57232 жыл бұрын
Khawe maléne dé wayé famille bou bakh nguéne machalla
@mariamabandia77711 ай бұрын
Pa bi môme machalla 🥰 kilifa la❤❤❤
@lalasoumano91392 жыл бұрын
Gnii vraiment famille gniou bakh lagniou malgré kou djiguèn ki limou dèf sen dôme takhoul gniou sèdèlko dara Lou niaww
@marinaba95742 жыл бұрын
Ndeguene da ma bakh rek gnou wakh ko é aussi cheikhouna borome kholou diama billahi ko beugua djiabarame lolou mome meuna ko séde si gnome
@vap16.senegalbic762 жыл бұрын
Oh sama xol toyna ndeysane la femme a plongée dans une crise extraordinaire metina la mère machalla
@SweetDidja2 жыл бұрын
La dame a eu à faire avec une famille éduquée et respectueuse motakh elle s'en est sortie indemne. Niit tak djabar takhoul mou bagn la, soko meunoul mougn rek demal. Yalla nagnou yalla doli soutoureu
@tantylarose8092 жыл бұрын
Bilay bien éduqué teksi dal si ctei la mienne dou dmei ni
@bellawomen2 жыл бұрын
Comme crime d je te jure kou takk niarel diaroul ii
Ki dall défoule loudoul réw AK Bone AK sokhoré AK néégue gnoul bir ki d'où nite dafa té kou beugué nité doko déef Lou Bone wakhatoumak diko diame sakh pousso tank niarréle mène mougne menouko ngua dém
@minalo761811 ай бұрын
Vraiment 😢
@mamysakho61932 жыл бұрын
ki waroul neik si biti.non femme bi assassin deugue leu.dakodone rayyy Allahou Akbar.djigaine Dina neiguei ni
@deugrek-gk3lx11 ай бұрын
Police dako wara diap li dou yone
@mamefatouba66372 жыл бұрын
Yalla nasi sunuu borom wiss ndokh bou sedeu amen
@evadia90282 жыл бұрын
Amiin
@ouamarjohnson93462 жыл бұрын
Vraiment la mère est une vraie responsable ♥️bravo
@ndeyemboup93942 жыл бұрын
Bilay ki Mo bone assassin 😡
@ouamarjohnson93462 жыл бұрын
@@ndeyemboup9394 métina trop li thieye djiguéne
@coumbadiallo24302 жыл бұрын
Sénégal dagnouy maslaa bâ gnou rey la sa famille perte
@maimounasow58542 жыл бұрын
Danguen gnémé masla trop kou gnémé arme ken douko teuyé si keur
@ndiemendiaye99792 жыл бұрын
Bilakhi wakhatico suka baye dinaka rey de
@ndiemendiaye99792 жыл бұрын
Bilakhi wakhatico ki de meune n’a rey khale bu gor bi
@Gggge_dudiolof95362 жыл бұрын
Djiguene kene douko trokhal. Sa femme a fait bcp de fausse couches pourquoi mou dem takk 2eme femmes
@bilalkhalyfall99382 жыл бұрын
@@Gggge_dudiolof9536 souko nékh takeu beu 4 djabar lolou kénéne mounoussi dara il a signé polygamie moment bouko nékh lay takeu djabar il n n'est pas obligé de tenir compte yaw liguay wakhni arrêtes d'être l'avocate du diable mm si j suis d'accord peut-être warone nako yeureum mais mou takal ko gnarél lolou dou délit
@Gggge_dudiolof95362 жыл бұрын
@@bilalkhalyfall9938 khamo louy fausse couches. Surtout femme bouko subir plusieurs fois. Li moy trokhal sa diabarre.
@myasarr97792 жыл бұрын
La deuxieume femme n'a qu'a se tenir prete l'ex epouse n'a en pas finit.yalla mousseul niou thi seytané.
@dneyeaminatasy7582 жыл бұрын
Amine
@ipeneboubane67702 жыл бұрын
La fille est traumatisé avec les fausses couches au lieux de la soutenir tu épouse une 2ém femme cela fait 2 traumatismes elle n est pas consciente de ses actes elle est en etat de choc c est difficile quand on ne connais la psychologie
@sokhnandickembacketounkara75382 жыл бұрын
ta parfaitement raison
@mariamalo67052 жыл бұрын
Vraiment
@khadijamiller62392 жыл бұрын
Bilahi wakhal dé beug dieukeur sakh mais dafa ame louko méty rek Ndeysaan
@plumee.a2 жыл бұрын
Ok les fausses couches et tout oui ouii c’est dure c’est traumatisant mais rien ne justifie la violence d’une telle ampleur en plus Pardon mais elle est juste méchante et sans état d’âme ton mari tu le poignarde tu le frappe tu lui fais des choses comme ça Si c’était l’homme qui lui avait fait cela ce serait plus choquant Ne donnez pas raison à cette femme
@almamyseckBouMameChekhIbra2 жыл бұрын
Et pour toi c’est une raison de vouloir tuer son mari? C’est triste pour elle oui mais le mari a besoin d’avoir une progéniture et si sa religion lui en donne le droit c’est tout à fait légitime il faut que l’on arrête elle est juste méchante et jalouse combien de Femme sur terre n’ont pas donnés naissances et vivent bien kon bouniou ken sonal na niou ko niou ce n’est que de la jalousie excessive
@siaraba21152 жыл бұрын
Makhala legui sey nguir yalla mo amatoul. Deh len takk djingene bou am dîné. Sey dou afairou thiaga
@madogydioufy70032 жыл бұрын
J’ai pitié de cette femme wallahi ndakh beug nit limoula meune yobei doko kham Soula leirei ni tu es jalouse tei meuno supporters niarel divorcel dem sa yonne mogeun rafette li vraiment
@fatoumbackesylla44812 жыл бұрын
Billay yow me am na goor nio xamené solen niané bat dougn lako may dagn lay beunga nakhal
@khadijamiller62392 жыл бұрын
Bilahi ndeysaan mais elle est incompris par la société khamouniou sa mbeguel Amna foy tolou dou amati saguo
@beautifulsoul1102 жыл бұрын
Yen dimbali len nit gni ngen nan incompris . Nit ko beug deug bien etre wam molay geunal sa boss Y’a rien qui justifie cet acte criminel. Sou wadji dewon dou lor ay mbokam ? Si tu vas mal à un point faut chercher de l’aide , s’ouvrir à quelqu’un, se gérer mais pas user de la violence Soudon le gars moko def niou yak ko ketemei
@mariamaba87382 жыл бұрын
Divorce d’où nonou dé
@a.barhamcisse72902 жыл бұрын
Moytoulen djigenou mougn kattt✌️lo wax mou rèèè Dou am problème banga yeuk ko bari soutoura...boul fok ni nitt ki amoul louko méti parceque sénégalais dafa tamou nitt kou am diam di kaf di reee xamaloko ben problemam ngani kiii dafa yarou ...deug la day fek mou nek nitt kou baxx kou oyof kou amoul ben problem mais nak au fond limou doul partagé day taxxx mou dègnthiiii ti dadialè si xolam...mane deuk na ak kou mell ni mais bouma xolè kanamam guiss noum melll rek damay xamni cv pas damay tok di waxtane ak mom di kaff ak mom bamou waxma liko méti ✌️delen bayi xel sen diabar yi boubaxxx nittt kounek amna problème Kone delen si bayi xel .ki li gorom wax rek war ngen xamni nittt rek la yalla nanou yalla mousal si seytané 🙏
@lenafaye1452 жыл бұрын
Je suis d'accord avec toi
@loufatechno21452 жыл бұрын
On s'en fiche ngay sisou nii
@binetaba32782 жыл бұрын
C'est difficile
@etherlynelander48482 жыл бұрын
Je suis d'accord avec toi. Mais tmt yalnaniou yalla mousseul ci genre djigueen yii
@s.ndiaye41864 ай бұрын
Tu as tout dit. Cest vraie
@dialloalibjibril69562 жыл бұрын
Jabar dafa ame Sohna ame takk jabar jarul yakamti kholal ndéyam numuy Séyé ak réaction wa cognbi Sohna grate la jiguén bu nago mugne rek ngir séntu euleuk ay jabotame ame waye bu raféte yallah nanu yallah doli Sutureu
@mameseygueuye45402 жыл бұрын
Bilhi dieukeur dji aka bakh té yarou
@adamandiaye46282 жыл бұрын
Loussi meunti am dall mandou rek ndakh entre mari et femme Lou doy War la
@amatoullah67662 жыл бұрын
@youngboy boul boolé gneupp yowitam😂
@amatoullah67662 жыл бұрын
@youngboy d’accord naa ak yow thi benn côté aussi. La femme doit être réprimandée 😩
khawma loutax gorou Sénégal yi beugue djiguéne rk dangay guiss ko khamni yoroul sakh loumou doundeulé awo bi né dafay takeu niarél déléne doylou djiguénou Sénégal yi djékeu nagnou raféte nagnou mashala té meuno am djiguéne yeup iow yaye doylou rk gueum yalla fofu rk laléne toubape gueuné toubape dafay khol béneu femme mou khamni iow la beugue bou takeu leu ték leu si wétam diapalé la diokh leu respect.....wayé gorou Sénégal khamoul valeurou djiguéne ay poubelle lagne gnou diapé war nguéne kholate séne bopeu dhé
@mamediarrambengue76602 жыл бұрын
Merci Gentlemen si bopame Mo amoul senegal dangaye guiss boy bou Mole tak ko gnari fane mou sof la nga nek si deuke bi dikone gnak fayda gel bi mo moussoul rek gno bok Ben kogne doumala dor doumala saga tei nala nok tass ndank lay def athia gnou bok kogne bi nak leuh dotoko defatei
@marieme29612 жыл бұрын
Li ngay wax justifier woul violence bi beneu yooon, la femme a tord sur tous les plans. Boko mounoul mougn nga délou sa keur mo gueune li.. Famille bii danio baax rek wayé bou dessone ci mane yobou nagn ko justice
@aidambengue70192 жыл бұрын
@@mamediarrambengue7660 bly do comprendre dall
@aidambengue70192 жыл бұрын
@@marieme2961 batay déguo ma wakh si wakhou femme dhé
@marieme29612 жыл бұрын
@@aidambengue7019 mané ci lima lire tu donnes tord au gars qui sont polygames teh lolou justifier woul violences conjugales lala wax 😏
@Lily-vb3gf2 жыл бұрын
Adouna bamou dadje djiguenou senegal gnofi geuneu niak ambition beug goor ak seuy diaroul yenn yi si tu n’est pas contente si tu n’aimes pas partager ton mari tu le laisses mais kholal lii yeufi doff yi . Goorou senegal mom meunolen fekhei bagnouy dokh ci seni waaw si ils veulent épouser plusieurs femmes ils vont le faire ils sont polygames de nature boulen sonal sen bop
@LaBarhamienne2 жыл бұрын
Wakh deug ya allah, mane meunou ma comprendre goor gueneul la sa bopp, seuy diamou ya allah leu défal lila thi souniou borom santeu so meunoul supporté woudié bi, nga tass. Do togn kéne nga nék thi sa diam. Mais di rayanté ndax goor, n'importe quoi. Mane dh bamay guénak sama dieukeur laki wax biss bo také niarél moy souniou seuy diekhna. Am nga droit tak yalla lako may thi kaw nga meune ko, mane aussi amna droit tass ya allah mako may thi kaw ni antanouma woudié. Xoulo wouma, défanté wouma, xéxouma, sama bopp mala gueneul dou bagn nala😂😂😂waw key. Ins bi sou rayone dieukeur dji, bobou bakaar seuy warouko diaral kéne thi adouna. Mais sénégal mom seuy bi commr guerre dh.
@Lily-vb3gf2 жыл бұрын
@@LaBarhamienne je t’assure ma belle certaines femmes sénégalaises vraiment m’énervent pour gnom sougn seuyoul wala sougn tassé rek elles ont raté leur vie elles concentrent tt leur vie sur les hommes et le mariage mais si tu n’es pas heureuse tu pars loufi diarr liii ? Man je suis comme toi dh woudié defantei khoulo khekh ak sama moromou djiguene ndakh goor soumako narei deff yalla na taka ba diekh
@BinetayoussouDiakhate11 ай бұрын
Niak classe rekkkkkk ak matadi woudjié dou dara diamou yallah kasé la
@mariemecisse14902 жыл бұрын
Ay way belle mère bou bakhéni famille bou bakh nga wara seuy ba dé. Nooo sama xol métina Bilahi wallahi niiit mo leundam 😔
@mbene-n79092 жыл бұрын
Gni mana kotou amou gnou mbam
@mariemecisse14902 жыл бұрын
@@mbene-n7909 malako wakh liiii doyna waaarr
@CR7_Mane2 жыл бұрын
Yalla nagnou yalla moussal ci djiguéne bou nopi
@MaimounaBodian-u4s5 ай бұрын
Bravo a cette dame waay elle est adorable tout ira pour le mieux dieu est grand
@aichadiawara89082 жыл бұрын
Non mais ki mo sokhorrrrr 😢😢😢😢😢
@basiirumbegmi18322 жыл бұрын
Lii de wax dëgg mooy nattu nag, xoolal ñii seede yu rafet yii, ñu ci wax. Wax dëgg Yàlla boroom gërëm de gu man a muñ la. Waaye jàppl ni gu muñ muuñ, te Yàlla ànd naag way muñ yi. Yal na Yàlla may soxna ci gën ci yaw ci barkeb Alxuraan Kariim.🤲🤲😭😭😭😭😭
@serignetoure95332 жыл бұрын
Bilaye papa bi manena kilifa lo Yalla nalla yalla miaye fane wogodou
@pispagalsen3 ай бұрын
Yallah nagnou yallah may ay sokhna you bakh
@ast83472 жыл бұрын
Yallah boumou done ndiaya dièye sama dieukeurou rack dji ay Yallah
@habibbouamdynogaye59932 жыл бұрын
Mom la kay
@ast83472 жыл бұрын
@@habibbouamdynogaye5993 ay way boul wakh lolou!Diamaguene
@ibrahimafall23762 жыл бұрын
Il faut protéger la 2ème femme nakh ki dafa capable de tt la familles est adorable machallah yalla nassi sounou borome df ndokh bou séed amine
@fatbintouhanne85602 жыл бұрын
Cas dakoul liii 😂😂😂😂djiguen bii amna fitt goor bi ken dou mom di dokhane sachant k sa diabar mola soutt less delen takk kolen atten wayé wow kongou di takk diogoma 4g 😂😂😂
@FifiFifi-f1t Жыл бұрын
Cheuttttt femme bi mo gnaka chance,une si bonne famille tes aussi ame chance tassek cette bonne famille ohhhhh regardes moi ca.mais on ne doit pas la laisser comme ca.il faut que justice soit faite sinon elle recidivera soit avec son ex mari soit avec la 2eme femme qui viendra
@abloslimshady2 жыл бұрын
La violence dans un foyer est à bannir, que cela vienne de l'homme ou de la femme! Elle a mal agit en faisant ce qu'elle a fait à son mari, honte à elle! Mais la belle mère est vraiment exemplaire, chapeau à elle!
@ndackwagnane22042 жыл бұрын
0i0
@leuzdiop10562 жыл бұрын
Une belle mère exemplaire
@mimisy12692 жыл бұрын
Ak loumou méti méti nga wara rouss sa goro bi la beugu té yalla takh nèkk nga trop nak amna nodone dokhalé dinga récupérer wate sa dieukeur té thiow dou djipe li mome daffeu eupe
@aminadiatta86622 жыл бұрын
Hana dofé rek
@mapdk620411 ай бұрын
Khol bou yakkou meun na lou nekk..... Les hommes, la femme sont du sang et de la chair. Un être qui peut tt supporter amoul. Ay niit kessai lagnou. Boy takk niit Wakh ko lou leer khaalko ni tu es polygame. Les promesses et les mensonges gno tass sey yi. Quand tu veux épouser nakh tanal ak sa awo, si elle n'est pas d'accord choisi entre elle et l'autre. Les gens calmes et souriants renferment bcp sur eux. Il ne faut pas abuser de leur gentillesse.
@dossoudiallo28132 жыл бұрын
Que justice soit faite maman tu as un grand cœur je t'apprécie beaucoup
@maxxndiaye9882 жыл бұрын
Q
@rokhayandiaye73752 жыл бұрын
Une femme méchanteeeeeeee
@dieynabadiop43332 жыл бұрын
Ndeysane da beug rekk fire ba dof goor gni tamit dara lagn dee me li yeup solution bi moy dem sa yonn diarul wonn violence
@mbackefall36472 жыл бұрын
ko begeu doko begeu Ray
@mbackefall36472 жыл бұрын
@@dieynabadiop4333 sokhna si ay begeu amoul ko begeu bou dewé do seye akk kenen té yénakoy def
@Fatoumbodji4592 жыл бұрын
Yalna ko yalla may wer Inshalah
@Dada-dp8yn2 жыл бұрын
Femme bi limou def dara diaroukofi wayé goor gni tamite bounou comencé dokhane Bilahi sa seye dotoul nèkh danoulaye ignoré dotounioula defal dara
@ndeyefatousene37872 жыл бұрын
Kou seuy ak djoulite fo tok wargua khalate nii un beau jour meunega âme woudj lii dou dara
@FatouSane-kc9fl2 ай бұрын
Mais woudjou Sénégal mo méti
@cheikhounatine7582 жыл бұрын
C’est une tentative de meurtre clairement,heureusement qu’il a un bon mari qui l’a pardonnée hein si c’était un autre elle allait mourir en prison.Qu’Allah nous facilite 4 bonnes pieuses épouses 🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿
@aminatadiop52752 жыл бұрын
Amine waylolou rek mo diarra niane
@codoufaye35352 жыл бұрын
Amine 🤲
@Sabrun-jamil2 жыл бұрын
Xalei bou goor bi limou deff sakh wooroul, parskel peut tenter encore une fois a sa vie ou a celle de sa nouvelle épouse
@abloslimshady2 жыл бұрын
Amiin
@deugrek-gk3lx11 ай бұрын
Dagnouko wara diap ki ray katou nit leu
@Madrequeen31732 жыл бұрын
ayway li lepp boulasi naré fekk do tass gua dem mou dem mais li yeup diarouko
@moustaphaniang21832 жыл бұрын
Bilay diarouko
@tinabah18882 жыл бұрын
Si tu divorce tu perds, tu peux rester dans ton foyer et le gérer avec diplomatie seytaner reck moo nooiw psk tout le monde on dit qu'elle est super gentille Parfois khaptal leye donn
@Iboudieng-bu4hv11 ай бұрын
yaw Khana khamoo jdigen bou firr 😢
@sambousmane64102 жыл бұрын
Non Femme bi moy domèram deug mo tax bayi lèn di takeu ay doff youy sagnssè aka poudeurouwou
@ndeyegakou272 жыл бұрын
Wouh 😂😂😂
@soukeyniang12202 жыл бұрын
🤣😂😂😂
@Mebeingme-v7z2 жыл бұрын
Wouyyyyy😂😂
@ndeyemaguetteba62452 жыл бұрын
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@crispyqueen73232 жыл бұрын
Tay ngama ray🤣🤣😭😭😭🤣
@omarosamb61502 жыл бұрын
Billahi tonton abdoulaye padane pabou bakh tee yarre ak ndiabotam billahi
@dieynarassoul17072 жыл бұрын
Parfois dinga beug seu dieukeur beu mou gagne leu nitt meu noko beug baa paré diko def lou metti gaur yi nio wara bayi dokhane bi ak ndialo bi niom niolay sopi une vipère une femme dangereuse rancunière et sadique elle a été déçu tout comme elle a déçue la belle famille
@dieynabafall64172 жыл бұрын
C'est pas une raison ca même
@mirna90.2 жыл бұрын
S'est pas une raison d'agresser l'enfant d'autrui
@Ladebrouillarde28242 жыл бұрын
Boudonne dokhane sakh c'est pas une raison. Mane dei douma masseu nek sorcière ni vipère ndakh khamouma Lou bonne ak Lou gnaw lolou. Seuy dagne na tass dagne na. Ya toujours une solution bou gueune li
@aissatouseck62422 жыл бұрын
Gor gni dinane dokhane dinane tak yalla moléneko sédé woudiou diaroul li djigeene la com yaw rek femme yi nio wara bayi bégne woudiou
@awasoire25492 жыл бұрын
Bien fait pour sa gueule niaw
@kadiadiallo27692 жыл бұрын
Famille bi bahna trop, macha Allah
@lerepublicain25762 жыл бұрын
Prompt rétablissement rapide et complet , de ma part j' aimerais bien avoir une femme généreuse.
@ndeyeawandiaye67652 жыл бұрын
D'accord n'a thy décision famille bi ...Bâle lou bakh la....le peuple réclame sa photo svp pour souniou frère yi khammm
@manganemareme61342 жыл бұрын
Soudon yaw diga beug kou geinei sa photo ??
@manganemareme61342 жыл бұрын
Cava? (Laye diarra voice)
@maremesalihate15302 жыл бұрын
seuyou légui yii dal diakhal nama lou méti li gua meune ko def sa dieukeur 🥺
@Sabrun-jamil2 жыл бұрын
Bone rek ak niakka khalaat alahira
@mamadousall70462 жыл бұрын
Taak koula eup dolé woroul deee🤔🤔🤔 me vraiment pabi ak mer bi niou bakh laniou 🙏
@diagnepapa78132 жыл бұрын
Ani Wa Droits de l’homme Sounekon Djiguén Wa Droits de la femme 👩 guénanu bou yag
@mairamesambsamb38932 жыл бұрын
Bilae tu a raison
@ndeyaramegueye74932 жыл бұрын
Louler
@diagnepapa78132 жыл бұрын
@@ndeyaramegueye7493 tey mome yena tonge
@khadycisse46952 жыл бұрын
Yalla n'a niou yalla mousal thi Lou melni ndeysane firr bakhoul
@diawnumero10712 жыл бұрын
goor ak lo ndaw ndaw souniou borome maynala lo niouuseii sa diabar xana😄😄
@lapeulh7652 жыл бұрын
😂😂
@mamecoumbadiouf89162 жыл бұрын
Diaw amna femme you deugeur té beurri dolé deh et goor gni parfois dokhane ngui ak tak ngui dagnou thiye bolé dila xoxotal mais nak quoi quil en soit seuye ak woudjé diaroul li et waye woudoul faye la abadane homme eh hommmmmme
@diawnumero10712 жыл бұрын
@@mamecoumbadiouf8916 deugg bou werre nga djiguene nie amna ayy judoka ay karateka lou nk ngayy guisse
@khadimsene42982 жыл бұрын
😂😂😂
@ouleyesy74062 жыл бұрын
😂😂😂 khamna dako sekhlo dor
@rackyndiaye366511 ай бұрын
Santat len yalla bou bax sax ndegam mingui doundou te mom wadji souko yalla mayé werr nako fassé
@adjiabousso91292 жыл бұрын
Ndeysane seuy dafa méti d’après les explications la femme n’est pas mauvaise ils l’on dit mais moytouléne djiguéne bouy seuy doko dégue mou clamer juste chaque dagua koy guiss mouy ré rék kham gua dafa nékhoul djiguéne di seuy di avorter à chaque fois qu’elle est enceinte 🤰 au lieu iow mi di dieukeur dji diapalé ko épaulé ko soutenir ko mais non certains hommes ne pensent qu’à leur bonheur égoïste pour satisfaire leur besoin daguay dokhane femme bi diko guiss di souffrire n’empêche mou tokk rék di rayanté en silence si bir négame bamou dém ba diour lii mais dafa am mots bo kham ni souniou kilifha dagne koy wakh tt le temps moy li bénén Mama bi wakh sank négou ndeye dara manqué woufa bayi lén lolou bonheur moy seuy certe la fille à deconné conseille boumakoy diokh nako bayi yalla diékhoul
@amymbengue69072 жыл бұрын
Violence dal fayuko damay gnan bat dem sama yon😏😓
@ndiayemouhamad47962 жыл бұрын
Ouii copain lu Leerr nga wax Lislam bénn niaarr niatt nieente yeepou na fekk nga Man ko rk Nioun nak mouy goor mouy djiguen Ken doxoull si diiné ken kouné sa banneex rk mola intéressé Loolu mooy warall mousiiba yeppou okk
@visionnairevisin8612 жыл бұрын
Rien ne justifie ce qu’elle a fait so meunoul mougne démal sétii lénene wayé beugue yobalé bakanou diambour pour lanne
@amidia53842 жыл бұрын
Mome kay dinako bayi ndax dinaniouko niouss ci KASSO bi yeufi sauwass yi moy lane
@rokayadiallo15002 жыл бұрын
Gor diaroul li
@omarndiaye94142 жыл бұрын
Ndaysane louma meti trop legui lako guis sii net bii Ms seytané da beurii dolé trop ndakh djeukeur Djii kou bakh la Ndaye aussi kou bakhla vraiment seytané mo nieuw rek
@boromebakh282 жыл бұрын
Heureusement que le gas vivait dans la maison avec la famille sinon s'ils était seule elle l'aurais tué 😬😬😬.
@cheikhbeye40642 жыл бұрын
Cheikhouna kou baakhla amoul benn blem sama waayla magkoy massaou bou baakh yalla baakhna
@SENEGAL3032 жыл бұрын
Ce que la dame à fait est dangereux. 📍Mais dangay am sa sokhna, mou beug leu, décider seuyeul leu. Ngeu niak doylou Di dokhane. Mou diépi leu nakh dotoul am confiance ci yaw. Dila Def you sew parceque dafa am louko méti té yakoko ték, mouy vivre avec un amour sans confiance. Après ngeu diouk nane Sama diabar baxoul.douma seuyeul naouti bénén diabar. Fek lép yako Def. So doylou wone. Sa diabar dîna la seuyeul AK xol. Djiguén bou beug Lou é lay Def. 📍bayi len Doug ci dieukeureu diambour yi. Djiguén yous si beuri dé a té AK nateu sén bopp molène ciy dougeul. Mais kama toudine,toudane. Lo Def sa morom dingako guiss. 📍gor yi nagnou dang doylou. Djiguén yi Ken meun lén diexal.
@paabdou87732 жыл бұрын
Mai Nespa ay dioulite lagn amnagn droite ame 4 femmes
@mairamediallo40432 жыл бұрын
C'est pas une raison de faire des conneries en plus quand tu signes pour la polygamie doit être à mesure de supporter les conséquences
@SENEGAL3032 жыл бұрын
@@mairamediallo4043 lissez ma première phrase. Je ne cautionne pas. Je sais just de donner les raisona selon moi. Pour que niou moytou
@maguitakontey61832 жыл бұрын
Juste Parsk dafa dokhane non mais areter ka même Khana Kone situation bi goor gneup war nagnou ko doundouu Parsk goor yeupay dokhanee plus particulièrement les hommes mariés
@foogadebbomolooty98392 жыл бұрын
Merci
@PapeAmadouRobertFaye12 күн бұрын
Kou meunouta supporté gua takeu benen diabar bayiko mou dem
@fatoufall36952 жыл бұрын
Yen.gni di wah ni dako moy gnane len.yalla mou.bagna dal sen frères amolen ben khol
@omarosamb61502 жыл бұрын
Noo cheikhou padane masta way
@pendafall99032 жыл бұрын
Ay bado lagne dougne yore salama lekoume gaye mougne di mougne ba yalla niew niou nela fi nioukk seti lenen sa xole bi di wade ms li mome dou ma si fekk sou ma meune tok tok sou ma meunoul deme mou dieh
@fatoumbackesylla44812 жыл бұрын
Goor dafa badola de
@oumyniang29922 жыл бұрын
Merci penda ay domram lagnou
@mamalick48172 жыл бұрын
Boungine wakhé goor rék bolé ngine si séni pape ndagoulén dogale yalla mon déf goor amna droit takk ba 4 femme mane Mangui ak ñiarri diabar té amouma bén problème yéna seyeutoul rék dangina yakarni yéna yilif sén dieukeur yi
@pendafall99032 жыл бұрын
@@mamalick4817 kou nek ak sa bolou mouniou kaye ame na niouko meuna mougne ame na niouko meunoul bagne bako ba damani soko meune tok sokko meunoul deme man mome kou ma takal woudiou da maye guena tokk rathie
@fantadiop55042 жыл бұрын
Mane dhé lim déf c trop sadique vraiment, mais goor yi tamite war nagn kholate séne bopou, bolési yakk kou djiguene ki mou dém mba kouko guiss dotouko beugu ga commencéko négligé dakh séy dafa méti.. dagay toppou séy bi mba fouti mounélafi gnioukkou weuri kénéne, thiiiiiiiiiiiimmmmm....
@cisssadammm74902 жыл бұрын
Djiiko ,djiiko la rékk..goor ak jiguèen niossi yémm...nimou amé goor you sadique..nonou la amé jiguéen you sadique....
@mastourassoul39462 жыл бұрын
Kou fékk mandarii takk ko loci ame dieuleul.... d'après ce récit diabar dji yagg na def ay acte de violence mou continuer Di seuy ak mom kay, coma on peut rester avk une femme pareille juska en arrivé là tamit
@aissa2425r2 жыл бұрын
mane deh moma diakhal guiss na ci yaw beneu sadique dagua maye abal wala ma abal leu.criminelle la il faut porter plainte essence bi sou takone c la catastrophe,espece de sauvage barbare
@evadiatta510011 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 ça me rappelle quelque il va jamais oublier mdrrr leçons a retenir
@Rokheya19411 ай бұрын
Comments? Mais te pas serieux la😢
@adjasy74562 жыл бұрын
Ki moy doméram ki mo deug ndayam ngene balma sama khol bi diekhna takk walahi ki police warnako dieul rindi ndayam walahi sama khol bi diekhna diekhna djiguéne mo deff li Alahouma Akbar ki dé bilahi kouko bayi bayinga raye katou nite sadique bonne sokhor
@OusmaneBarry-k5o5 ай бұрын
😂😂😢😢😢😢
@elagegueye33102 жыл бұрын
Gor ak djguen niui di ndialo.wallahy yalla moo gueneu fuir.marieyui niofi daka ndialo
@julescisse19842 жыл бұрын
Vraiment des parents exemplaires
@mariamabandia77711 ай бұрын
Mai femme bi Di explique tamite negou seye defa khate dé netali rekk gasi âme
@Missdieng2 жыл бұрын
Kii agressive na trop si djigueine 😡🙆🏽♀️
@deugrek-gk3lx11 ай бұрын
Domeram leu
@astoudiouf71262 жыл бұрын
Da fiir rek
@maimounadiallo20282 жыл бұрын
Saytané rék mo gneuw ndeye san mere bi coubakh la yalnagnou sunu borom mouseul si séytané
@diopawa1892 жыл бұрын
bilay goor gni daniouy diékhale xole daniou lay takk douniou ame dara gay mougne RK niou niew un jour RK
@naniousamejikkoyi21122 жыл бұрын
*vraiment le gars devrai prendre ses devant nakkala gore yalla deug mana négligent ba jiguene dilla deff ni,ballagamako deff ma defflako, wadji mo noye rek daffa faible torope en temp que gore yalla*
@mouhamadougueye71182 жыл бұрын
Ki kay dou goor Romb na noye di deim Lima ci mèti mouy filmè bopam di wanè ni ki dou sakh rouss😂
@aidandiaye71532 жыл бұрын
Négouko door lolou la
@mouhamadougueye71182 жыл бұрын
@@aidandiaye7153 pas dorr sakh Mais dou wone yone li yeup di am. Tay sougn dèglou wone version wou femme bi di ngua guiss ni dafa deim ba meuneutoul limou mougn moko eup dolei
@malickndiaye6312 жыл бұрын
Ndeysane ndiaboot gou am diamou monex yalla na yalla doli diamou ak soutoura si yene
@adamandiaye58292 жыл бұрын
Peu importe le degré de leurs problèmes rien ne justifie son acte barbare, c'est une tentative de meurtre. En plus de la préméditation elle ne montre aucun regret donc que justice soit faite
@modououmy16762 жыл бұрын
Ndeysane dako eupe doolé wayé dou nonou dieukeur sangue la
@bintouthiam4002 жыл бұрын
Faut montré sa photo pour sauver les autres familles
@mariesylva72482 жыл бұрын
Mdr hé
@originali1552 жыл бұрын
Wouye ma ngui rammm
@khadimsene42982 жыл бұрын
🤣🤣🤣té mouy deug
@coumbischoupi40242 жыл бұрын
🤣🤣🤣🤣🤣no li d'où deugue 🤣🤣
@aminafall1542 жыл бұрын
Ah li eupena way 😢sobougoul wouthié gua dem
@pendahabydiopa89912 жыл бұрын
Nitte dal leip loy engager attends toi à toute surprise mouy sa diabar mouy sa djeukar sa xarite ypp t mouy gor di djiguein dara diaroufi agression ou violence so meunoule mougne franchement deimal sa yone gore meunou loko téré limou bgue df du moment que diokhnala respect bgue nala yeuram nala sa xel ak sa xol bi oubi ko t yatalko ngua mougne aussi polygamie koussi fiir y’a togne ndax khamone ngua ko vraiment kou djiguein ki dafa négggg
@elagegueye33102 жыл бұрын
Kou bagn niarel wediga yalla.gor bousa dibar reroul woro labaty.wahouma ka bi nakk