xassim xana danga légeu loulay wax lo té Ndeye sane lousa Yon nékoul rék ngay wax dél nobi Serigne buzz koukoy wout rék si dioum ngay deugeu yamal té bayi radio yii ak télé yi té bayi gor yingay xas Serigne touba danna wax bania tonge mogeun deuké diégalou sa kilifa yi rék ngay xas yaw sa moromou mbacke mbacke yi rék ngay xas ta nioniola geuna diégé Serigne touba di say bay Serigne nopil tay wax Lou rafét boukou meunoul nga nopi lolou la Serigne touba diklé rawati na ngané mbacke nga sant
@alqoudoshd37037 жыл бұрын
BIlahi Walahi wax nga deugg. Heureusement SERIGNE TOUBA ay Talibé réik la am moy kouy djoubeul reik CHEIKH BASS dh kou ko bayyi woul doo baxxlé aduna ak alaaxira.
@toubambackeinfo8 жыл бұрын
khassim dou rouss sakh kham gani nekk di xass say baye dem ba ab talibe dila wo diko lidianti beug khaliss rekk waye cheikh bass dousa morom sa baye la daga rew rekk liga wakhni loutakh wakho ko won cheikh amar rek motakh gay diegalou lila serigne touba defal cheikh amar manou lako defal daga nekoul goor rekk