Seugn bi lign la netali ak li am bokoul deh ! Faut éviter de vous mettre ce genre de situation par ce que ça divise les avis et divise les gens . Cheikh Omar Diagne n’a jamais insulté serigne touba ni offensé ! Limu wah dara nekouci
@ddalhamdoulilah96012 жыл бұрын
Seugn bé la guina xam lolou, il défend ses intérêts, Macky mokko yondi
@ummhuraira24952 жыл бұрын
C'est la verité qui blesse
@djibyndiaye15283 жыл бұрын
Il faut nga leral hectares yi la macky diokh baloumala sama wall.
@alioukounta6323 жыл бұрын
Yawmal guiyama diga kham lép degue la.
@mouhammedwade7823 жыл бұрын
Serigne bi comme yaw amo diotou deglou sa talibé yi nieuw si yaw dila fenne si cheikh oumar diagne wakhlenne aussi nagne bayyi togne ndakh niome niofi daka togne dakk fi khass ay serignou diambour di took si plateau télé yi di racconter du n importe quoi diamm nak niaar niokoy dokh Mbacké
@moutaphaceesay39353 жыл бұрын
Nityi dangne wakh ligne diang par force momoulen niityi
@kidcode85283 жыл бұрын
Bilaay je t'aime bien Serigne bi... Mais naak da nga degg nga waax dh ... Danioula netali 🤦🏾♂️
@neilok-senos72923 жыл бұрын
Tu ne l a pas écouter e tu veux le juger ? Incohérence totale
@rachelmitterrand58593 жыл бұрын
Bass wakhal thi goordjiguéne yi
@khalifa30033 жыл бұрын
Bayilene omar diagne il a rien fait
@ouzykebe68212 жыл бұрын
Doul yaw
@khalifa30032 жыл бұрын
@@ouzykebe6821 yalla nagnou yalla até ci barké wër koor bi
@ouzykebe68212 жыл бұрын
@@khalifa3003 yaw wero naniou ater domaram nga serigne bi gueune ko yakaar
@khalifa30032 жыл бұрын
@@ouzykebe6821 degna sa wakh yalla bakhna
@pahassaneniang42163 жыл бұрын
Li gay wakh tékka ci al coran ak sounna mo djitou ba paré
@tahathiam94633 жыл бұрын
Sath bi di doul rék waxall si sounouy milliard yign la toumal voyou bi
@abubacarrmarong44429 ай бұрын
please accept the truth and follow the right way of the Prophet Mohamed peace be upon him
@laveriteappartientaallah52183 жыл бұрын
Daguay doul rekkk li cheikhou oumar diangne wax lépeu preuve yangui fii si archive nante yiii