Ya ak Macky Sall yéna yam dounguén wakh deug Ousmane doussa morom ci politique
@Massiyuwe23C2 ай бұрын
Man de sonko la. Andal mei ki dafa am yar nit ko bakh la
@papisfall2 ай бұрын
Dafay maat di euff
@laminebarrambengue66022 ай бұрын
Saway yagui ték khél dh yaw mi djiek diamak jarigne nga book dh😅😅
@Massiyuwe23C2 ай бұрын
@@laminebarrambengue6602 walahi man sonko la andal
@rogerdieme2 ай бұрын
@@Massiyuwe23Cc'est ton point de vue on te le concept mais yar bou eup day ndirou ragal té Dëuk IL faut ke nga am yarr, fitt té ñiémé. Par dé fois déci bakh ci toubab yii 😊😊