Ça se voit que vous avez reçu une très bonne éducation respect ak daleu yallah na yallah yeureum kiné kharé ko aldiana firdawsi barké seydina mouhamed psl
@mamependaleye28032 жыл бұрын
Bilaye, meune na ko cédé dh. Séne papa mashallah nittou diné deugg la
@Oumanas59952 жыл бұрын
Yar da bakh si domou adama
@femmepanafricaine51472 жыл бұрын
Amine
@souadoudieme43042 жыл бұрын
Je confirme gno bok kogne dèf enfance ensemble bok dahira sène papa yorer deux femmes do kham kou ki diour ak keulè gnop gneup bok ndeye ak baye 😭😭sène papa djoulitè yarr lène si diners ak lislame toudè aye domam wa keur seydi hadji malick 🙏🏾🙏🏾 niou yarou lolou trooop walay anzimm 😭😭kinè nako yalla yeureum kharèko ardiana inchalla mèti trooop walay nakarina si khol trooop
@sofiabadji85912 жыл бұрын
Bilahi dal naniou d Yalnalene yala takhawou
@femmepanafricaine51472 жыл бұрын
Que la terre de Tivaouane te soit légère Kine vraiment c’est dure
@mamemarie83132 жыл бұрын
Amine yarabi 🙏 🙏 🙏
@bambakhadim54092 жыл бұрын
Tu es trés véridique mon frère. Que le Bon Dieu l'accueille au Paradis Céleste. 🙏🙏🙏
@khadikcee92022 жыл бұрын
Amen
@mamemarie83132 жыл бұрын
Amine yarabi 🙏 🙏 🙏
@aichalaye57022 жыл бұрын
Amine
@aminadione27832 жыл бұрын
Amine yarabi 🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@sarryelhadjiousmane15282 жыл бұрын
Amiin
@GM-xz6pc2 жыл бұрын
Grand tapha gaye du courage. Nos condoléances à toute la famille Moussa, Cheikh, Mansour, pape, diop, yacine, daba etc . On sera toujours à vos côtés.
@bernilynsha2 жыл бұрын
Tu m’as traumatisé khassim eyy way li dal si famille gaye bi metina ça peut arriver à tout le monde repose en paix 🙏🏾
@bayelahaddiop40952 жыл бұрын
Nañou Déllou Ci Attéy Sounu BOROM Bouñu Beugué djammu Ci Sénégal 🙏🙏 Yallana ko Yalla yeureum Ta Xàarèko Aldjanà
@serignesaliouniang42272 жыл бұрын
Wallahi lolou rekk moy solution bi
@pivoine4812 жыл бұрын
Lolou rek moy solution ndakh li Yalla wakh souniou kou defoul douniou amati diam.
@sk_channel21302 жыл бұрын
Sénégalais dafa yaakar mo eupeu yallah yeurmandé koi... Peine de mort rek moy solution bi. Qu'allah accueille kiné dans son paradis!
@bambaseck622 жыл бұрын
Jaay taar té yoro dara mo waral lii yepp Kou beug teranga dangay nango ligueye Kou beug aldiana dangay jaamou yalla wakhi serigne touba
@ritapreira8492 жыл бұрын
Vraiment
@bambaseck622 жыл бұрын
@@ritapreira849 merc
@dieynabadiop15372 жыл бұрын
AK topou djiguénn gnou beugg adouna tékk ko pression mann dh limayy wah goor gni dal moyy Nanou moytou djiguénn yii lénn dii tékk pression deff loo meunn wah lo meunn
@bambaseck622 жыл бұрын
@@dieynabadiop1537 pression amoul ci affaire sister niakk diom ak meun fén nit boko wakhé deug mou xam sa situation beug la ci pression dou am
@dieynabadiop15372 жыл бұрын
@@bambaseck62 lolou mom c'est vrai
@yayoudiara06502 жыл бұрын
Masta mes condoléances. Je pleure Kiné comme si je la connaissais. Yalla nga khippe aldiana firdarwsi sister
@salladiaw5432 жыл бұрын
Amine
@aichalaye57022 жыл бұрын
Amine
@aidambengue56962 жыл бұрын
Tout comme moi😭
@Galsen442 жыл бұрын
Bilay ma sœur je te crois ! Li lou diara dioy leu 😭
@bikmo11922 жыл бұрын
Machallh grand kou geum yalla ga kou nagou nii yalla Moy ndogal bilahi yalla nalen yalla may kholoup mounie kiné yalla nako yalla yeurum té gawé ko
@datievlaida79082 жыл бұрын
Merci à la journaliste, tu poses des questions pertinentes
@BrownJSugar2 жыл бұрын
Quelle soit enceinte ou pas ?, comment elle a été tué ne sont plus des informations importantes à ce stade mais plutôt se concentrer sur cet assassin et aussi parler de l’insécurité a Dakar
@serignefallou89272 жыл бұрын
Jahjeuf
@mamediarrakane15272 жыл бұрын
Vraiment 🤷🏼♀️
@khadydiakhate392 жыл бұрын
Vraiment
@assadiarra51942 жыл бұрын
Vraiment
@toufasowk252 жыл бұрын
Bien dit
@sodagueye37692 жыл бұрын
Vraiment triste .mourir dans ces conditions .ndeyssane que Dieu l'accueil au paradis 🙏 cette belle dame
@ndeyemourseye60102 жыл бұрын
C'est triste 😭😭
@aichalaye57022 жыл бұрын
Amine
@Galsen442 жыл бұрын
@@ndeyemourseye6010 bilahi lou diara dioy leu 😭😭
@oumymendy91672 жыл бұрын
Ça se voit que c'est une posée et polie, que le bon dieu l'accueille dans son paradis et que la terre lui soit légère
@oumymendy91672 жыл бұрын
Bravooooo à Dakar buzz , vous faîtes un travail remarquable
@yassineamineniang53302 жыл бұрын
Neysan li metina😭😭😭😭
@sophieseck11262 жыл бұрын
Machalah yallah naka yallah yereum kaddu yi rafétt na très pertinente la journaliste...
@khadiciss99802 жыл бұрын
Yalla nala CheikhTidiane terrou aldiana firdawsi thi barké salatoul Fatiha
@ndeyekhadycisse63322 жыл бұрын
vraiment vraiment Mane khawma li lan leu j'ai même pas les mots kiné inchallah. sabouma djioulé n'alla gnanal moi personnellement je t'aimais bien ndakh danga nirou AK sama Rak yalla nala yalla athie thia aldjanay firdawsi ya gueuneu kawé bilay khalé bou bâkhe Bari diâm am diné 😭😭
@retrotv84122 жыл бұрын
Chapeau bas à la journaliste très professionnel
@adjiadiallo3742 жыл бұрын
Courage à la famille j'ai perdue ma sœur presque dans les mêmes comme conditions le gars qui l'a fait s appele pareil il est en liberté.donc je ne crois pas en la justice de ce pays
@elhadjdiop23992 жыл бұрын
QUOI????
@msz63172 жыл бұрын
Mba dou même personne bi
@ladyz99332 жыл бұрын
Il faut prendre l'opinion en témoin, aller vers les médias pour médiatiser l'affaire legui justice am
@yayoudiara06502 жыл бұрын
S'appelle pareil?
@adjimbouyeba28562 жыл бұрын
😳
@aliounegoundiam93162 жыл бұрын
Reposé en paix que le tout puissant l'accueille dans son paradis Amine yarabi courage à sa mère surtout et au reste de la famille force
@nabousall83132 жыл бұрын
N'deyssane yalnako yallah yereume kharéko aldiana, yalna guissé ak wayame El'hadj Abdou Aziz Dabakh Sy
@ahmadouba70522 жыл бұрын
Yalna yalla Kharéko Aldiana si barké SALATOUL FATIHI AK diawkharatoul kamal ak cheikh tidjane chérif 😭😭😭😭
@ndeyeamidoucoure40142 жыл бұрын
Vraiment ce messieur est très fort a ça place je ne peut même pas témoigner vue la façon dont il été proche du défunt en tout il doit être fière de leur vue la façon dont elle est morte elle s'est battue jusqu'à sont dernière souffre que allah l'accord le paradis et que elle soit en paix
@babacarndour77272 жыл бұрын
Bravo si lèral bi Yalnako yallah yreum té xaréko firdawsi 🙏🏾
@couumbisniang43282 жыл бұрын
Allahou akbar ca fait tellement mal au cœur 💔 que le paradis soit sa demeure 🙏🏽 le pays va vraiment mal 😭
@Blaise052 жыл бұрын
En écoutant ce Monsieur je sent le mal profond de ce Monsieur c’est très dur mais ainsi va la vie . Que son âme repose en paix . Amen
@yayafall73532 жыл бұрын
Vs etes três posé et eduqué li metina k sn ame repose en paix 🙏 😭😭😭😭😭😭
@saliougueye87732 жыл бұрын
Akassa yalla nako yalla yerem kharéko aljiana
@mouminatoundiaye83722 жыл бұрын
J'ai pas les mots J'ai le cœur meurtri qu'elle se repose au paradis
@salladiaw5432 жыл бұрын
Amine
@kahdijabarry73642 жыл бұрын
Métina trop
@user-20322 жыл бұрын
Ndeysane massa metina bilahi Ayway kiko ray ya bone haaa bilahi ya nioul khol deh domiharam bi YALLA nala YALLA fay linga def domi diambour bi inchalah bala ngay gueneu prison 😭😭
@metadiakhaby2 жыл бұрын
Je ne comprends pas les gens qui se mettent devant un micro pour mentir, spéculer....Juste pour passer sur le net? Faire le buzz? Lii fébar leu...Merci pour l'eclaircissement. courage à la famille
@maguettefall82612 жыл бұрын
Beugue beuz rek
@loutafall89822 жыл бұрын
Féne rék laniouy déff ak soss
@timatoure73952 жыл бұрын
Billay wakhatiko dé dama warou sakh egorger bi ak eumbe bi fougn ko djeulé????
@masterofmydestiny45012 жыл бұрын
@@timatoure7395dagno meune wax lou amoul 🤦🏿♂️
@merlin91872 жыл бұрын
Lo hame si inventer, pasteur a invente le vaccin, Senegal on inventer le mensonge quelle repose en pain et que les responsables ou le paye pour ca 😭😭😭
@merygaye38372 жыл бұрын
Tapha gaye frero massa way metina lole nakk wayee lila yalla dogal🤲🤲🤲
@Only_Godd2 жыл бұрын
vraiment le gars soko guissei muy wax rekk dangay xamni dafeu bah vraiment kiné yallah naleu yallah xarei Adjalna
@mbsambou61242 жыл бұрын
La foi Lou âme solo la. Yalle nalene Yalla maye kholou mougne. Paix à son âme 🙏🙏
@aminarassoul28702 жыл бұрын
Kadou yi rafét na machalah yalla nako yalla yeureum
@dieyadieya46622 жыл бұрын
Ndeysan pauvre frère 🥺🥺Il essaye d’être fort mais au font amna louko meti..Yallah nalen yallah may holou mougn
@fktfkt29322 жыл бұрын
Quelle education mashalllaaaa ki yarou na torop kadou yi yiw na diek na
@rokhayarassoul34232 жыл бұрын
Tapha Masta frère Yalla sa borom yessal yeurmandém thi mome te nitte kii defff Lolou 🙏🙏🙏
@momykandji24442 жыл бұрын
Machalla paix à son âme et que la terre lui soit légére tu es posé machalla
@bintawimmer65152 жыл бұрын
Repose en paix Que le bon Dieu l'accorder son paradis Amine 😭🙏
@salladiaw5432 жыл бұрын
Amine
@jap72902 жыл бұрын
Un vrai musulman yalla na la yalla maye kholou mougne 😭😭😭
@lbeng91142 жыл бұрын
C trop triste 😭😭😭😭 yalla na yalla sèdale souff si kawam khareko firdaws inchallah courage a la famille
@babacargueye37112 жыл бұрын
Yalla nako Yalla djégeul té yeureum ko barké seydina mouhamed aley salam psl 🤲 🤲 🤲 🤲 🤲 🤲 🤲
@astoukanediallo8192 жыл бұрын
Paix à son âme que firdawsi soit sa demeure éternel amine yarabi 🙏🙏🙏🙏
@mariepierrediatta26162 жыл бұрын
C'est vraiment dur beaucoup de courage à la famille 😒
@ndiayeawa36762 жыл бұрын
Machalla waxam rafetna . prenez l'exemple sur cette famille dôme yaral bo begue'nopalou.nagnou gueuneu yar xale'yi
@amymbaye4542 жыл бұрын
Ndeyssane yalnako yalah yeureum té diégueulko 😪 😪 😪 khareko aldianay firdawssi si barké seydouna mouhamed (psl)
@zeynabiaye60772 жыл бұрын
Yallah nagnou yallah may khôlou mougne yeurmandé moudiou bou raféte si barké Nabi Moustapha 👏🙏
@aladjifalloudia49152 жыл бұрын
Ndeye sane sama yaram dawna yalla nakou Yalla yeuram Kharéko aldiana sy barké serigne touba amine 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@tresorfall21282 жыл бұрын
Amine way mètina trop
@alioufall82152 жыл бұрын
Ndaysane yallah nako yallah yeureum
@mariamandiaye89392 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureume khareko aldjanay firdawsi 🙏🏿😭
@mamysarr70152 жыл бұрын
Yalla nalla yalla yeureum tei kharei la aldiana firdawsi nit kou dalone bakh lolou mashalla toute la famille a perdu mais on s'en remet au tout puissant il a voulu ainsi Que justice soit faite pour le repos de ton âme
@fantasoumbounou61612 жыл бұрын
Metina 😌trop wlh massa et courage ✊à la famille gueye repose en paix kine 🤲
@thiaylisirewmi86842 жыл бұрын
Yalla nakou Yalla yeureum si barkb nabil moustaph Yalla bou Yalla awalé bén bakan si soyou lokhou
@user-20322 жыл бұрын
Amine
@maryambae89342 жыл бұрын
Amine ❤️🙏🏽
@amigueye93062 жыл бұрын
Lou diara niane
@bakhyaye42502 жыл бұрын
Amine yarabi
@marietoudiop42982 жыл бұрын
Vraiment c triste yalla nako yalla yerem te kharekho aldiana si barkhe seydina mouhamed
@Mouhammad-Naing29232 жыл бұрын
رحمها الله رحمة واسعة وأسكنها فسيح جناته
@gogodioumaba57542 жыл бұрын
Massa métina yalla na ko Yalla yeureum té kharé ko aldiana un bon discours
@yayouyayam78172 жыл бұрын
Ndeyssne kiné yalnako yalla yeureum té xaréko aldiana firdawsi di serigne babacar Sy
@oumykane97842 жыл бұрын
Masa way mon frère yalla nako yalla yeureum tabalko aldjana firdawci Amine inchallah
@aladjifalloudia49152 жыл бұрын
Mak djiou bakh nii laye méll yalla nala Yalla takhwou amine 🤲🤲
@Faby-u7h2 жыл бұрын
Ohhhh vraiment c’est dur mon frère massa way courage que son âme repose en paix 😭😭🙏🙏
@mamadoudiol4702 жыл бұрын
Yalnako yalla yeurem ci barcke seydia Mohamed 🤲🤲(psl)🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
@sasareine3992 жыл бұрын
Yarou amna solo ndékétei🥺 du courage massa🥺🙏🏻
@ndiakhassndiakhass58852 жыл бұрын
Li ma djanguer si wakh dji moy amna li geuna graaw ray nite gui si rewmi moy fène bou mètti bi journaliste yi nèker...normalement wane naniou commencer criminalisè fène
@astoufaye76912 жыл бұрын
Bilay
@mamyabdoulaye32572 жыл бұрын
Beug téla dougal info rek pour am ay vues ak commentaires....thiiiipiiriiiii ces sites qui ne font que mentir
@elhadjitalibendiayediane77092 жыл бұрын
Journalisme perte na valeurs bou may fatalikou tidiane Barry minielle barro Oumar seck Sophie adhodekon ext mais legui journaliste KZbin ay animateur rk Guay guiss aucune formation beug buzz ak vu sans pour autant ga am say source claire wayé dekk na wala yakaar na wala dafa melni rkk vraiment c abusant
@maremegueye99462 жыл бұрын
Ces vraiment triste qu'elle repose en paix si barke seydina mouhanet psl Amine ya Rabi
@aminabodian59842 жыл бұрын
Massa waye. They sénégal, personne n'est en sécurité dans pays. nous avons peur de laisser nos enfants partir à l'école. Que dieu nous protège de ces crimes
@maregaassa93032 жыл бұрын
Quelle repose en paix qu'Allah l'accueille dans ces plus haute paradis fyrdaws
Yalla nako yalla djiéguele thé yeureumeko thé tabalko dianatoul firdawsi thi barké Seydina Mouhamet PSL amine incha allah
@nobasiby95402 жыл бұрын
😭😭😭beugue nguënté sa diabbar té amo xaaliss warna takh ngay ray domou diambour ray diabbarou diambour ray soeurou diambour sa diabbar dafa gueune kiné ?metina dh wayé kiné dinala gueune démine dh in sha Allah yalna ko yalla yeureum xaaré ko aldjanay firdawssi. Yalna yalla fess del thi xolou dieukeureum ak famille bi yeup metina trop vraiment senegal légui kene xamoul li lane la deuk Bo xamné do tok béne jour té déguo ni ray naniou nit yalnagnou yalla samm samm ndiamboot gui aar niou bep domou adama thi daradiay nabil moustapha saw
@senegalsenegal49892 жыл бұрын
Kharal ba Tabaski seuy i di tass, ngoor ak djigeen di feen di sathie.. pour am getznet khar..... senegalais mo reglou khammm kouy nagou ay poupe pour am khaliss...
@oumoudiop13402 жыл бұрын
Yalna yalla yessal yermandém si kawam barké tarikha cheikh aljana don kereum 🤲ak bep julite metina trope bilakhi
@minafall87092 жыл бұрын
Fainn yi d yeinn kessei la site yi yeinn gneup yeim yalnako yalla yereum xareiko aldiana firdawsi mettina ndeysann
@merefaye74992 жыл бұрын
yalna yallah yessal yeurmandé thi mom sa famille mashallah taxawou bou rafett bi yalnalenn ko yallah Faye yiw
@khadijasall82532 жыл бұрын
Que la terre soit légère paix à son âme 🙏🙏🙏🙏🙏
@nanacissokho46002 жыл бұрын
Yalnako brom bi kharei aldiana firdawsi si barkei serigne babacar sy rta 🙏🏿🙏🏿yalla bouko tiat djitou si bamel lame♥️🕊🙏🏿
@adjiseck91042 жыл бұрын
Yqlla nako yalla yereume te yehegnou. Si daradiaye kou tedeki(SAW).
@fantasoumbounou61612 жыл бұрын
Allahouma amine yarabi insallah 🤲☝️
@lamiratousowba34872 жыл бұрын
Que firdaws soit sa demeure éternelle yallah nako yallah yeureum té kharéko al diana si barké Mouhamed psl Métina trop
@florentduriez96042 жыл бұрын
Mon grand frère c'est dur mais Dieu est grand
@chimerediouf11522 жыл бұрын
Ndeyessane li méti na mais frère bi dal na vraiment rip à Kiné 😭😭
@ibrahima_khalil68802 жыл бұрын
Mashallah kaadu yi rafete na vraiment tu es véridique aussi quant-à kiné yalla nako yalla yeureum
@serignefallou89272 жыл бұрын
Yalla naniou yalla may Diabar diou bakh 🙏
@suzanneaminataseck16542 жыл бұрын
Manchalla yalla nalene yalla mayyy kholou mouye Yalla nako yalla kharer dianatoul firdawsi♥️🙏
@aidasadasow49612 жыл бұрын
Ndeysanne 😔💔🙏🏾des cœurs brisé 😞 metina trop
@astousene80342 жыл бұрын
Yalla nala yalla yereum kharela aldiana firdaw 🙏🤲🤲🤲🤲🤲
@suzanneaminataseck16542 жыл бұрын
Yalla na ko yoneteby psl Terrou ak hadjii malick sy ak makk niou bakhhh yeup inchalla adiana Reck inchalla
@salimatoudiallo94042 жыл бұрын
YALNA YALLA doli lenn diam té yok lenn kholou mougne thi barké Seydina Muhammad PSL Amine
@fatimasas49742 жыл бұрын
Non li metina trop yalanako suniou borom kharé Aldjana Firdawsi 🙏🏾😭
@kebemerediva26802 жыл бұрын
Ndeye sane yanako yallah yeureum té kharéko aldiana firdawsi massa metina trop
@massainternet82572 жыл бұрын
MachAllah sede bi rafet na Que son âme repose en paix
@seynaboudiop90962 жыл бұрын
Chapeau à Dakar buzz🙌🙌
@souleymaneniasse52712 жыл бұрын
Mes condoléances à toute votre famille, et merci pour ces éclaircissements, beaucoup de fausses informations ont fuitè courage à vous vraiment 🙏🙏
@thiabakandji31892 жыл бұрын
C’est vraiment émouvant 🥲 paix à son âme que firdaws soit sa demeure
@princesses42092 жыл бұрын
Yalla na firdawssi done keureme si barcke Mouhamed (psl
@adjafallmory73162 жыл бұрын
Metina torop 😭😭😭😭😭😭 Yalla nako Yalla yereume khare aldiana 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@yayediormbengue2 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureume kharéko firdawsi 🤲🏼🤲🏼 métina 😭😭😭😭😭😭
@abibatoubarry98432 жыл бұрын
courage metina trop YALLA NA YALLA LERAL LEP INCHALAHAAA
@oumydiouf90322 жыл бұрын
Yalna khyppe aldiana firdawci😀😃😪😭😭
@aminalasalihate2 жыл бұрын
Thiey Yallah yalna ko Yallah kharé aldiana
@miriamkabou35552 жыл бұрын
Massta massta massta Metina. Yalla Marylène kholou mougne.Ndeysanne😭😭😭
@Femmenoire62 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureum 🙏🙏🙏wayé fén yi nek si rew mi diakhal nama yalla na yalla leral bamélam si barké seydina mouhamed 🙏🙏🙏🙏