Peut être une personne peut ne pas comprendre sa démarche parce qu'elle est rare, mais en écoutant les beuyites qu'il chante et que des milliers de jeûnes citadins ont métrisé ces écrits saints grâce à lui, rien que pour ça une personne animée de bonne foi doit avoir de l'estime pour ce missionnaire
@majjmountakha99635 жыл бұрын
Mbacké linguua defarr si ayy ndao yu naronnn sankouuu yalla nalako serigne bamba fayy💗❤😍😍 Yague fii sama sangue bii💗❤
@baagiubou46675 жыл бұрын
Anna talibéy cheikh Modou kara akk gniii beugeu Bamba beuslen bleu way ??!!!!
@charlottekmr1775 жыл бұрын
Le 31 décembre beaucoup de jeunes ont tendance à s'adonner aux mauvaises habitudes, dem bar, organiser soirée, louer appartement dans un pays où la majeure partie est musulmane, serigne modou kara pour rendre grâce à Dieu il invite les jeunes au stade marius ndiaye pour accueillir le nouvel an avec des louanges et ecrits de cheikh ahmadou bamba adressées à Dieu. Donc vous qui le critiquez en disant que 31 décembre bokoul ci werou djoulit combien y'a t-il de chrétiens dans ce pays et pourtant yenay eup ci boîtes yi, ci bar yi, dolen ma né chrétien yi nioye fesss ci boites yi diemeu len def lou bakh ni mom mo gueun ngen di dingat. Serigne modou kara nit kou bakh leu kou mandou. Khadjélewoul, dafaye dajalé
@elhadjisamba76055 жыл бұрын
Tu a parfaitement raison. Merci pour ce texte veridique. Paix sur toi!
@jwrikfinii70214 жыл бұрын
Kii Serigne Touba rekk la beug. BILLAHI yaa yaye Serigne Touba dh moome rekka diara beug ta kouko beug raw nga
@MySexee3 ай бұрын
cet homme m'a éduqué comme son fils et m'a traité mieux que son propre sang malgré tout ce que vous pouvez entendre sur lui c'est UNE PERSONNE EXTRAORDINAIRE je souhaite que ALLAH le bienfaiteur lui accorde une longue vie ya ALLAH nako fey kholam
@espoir1505 жыл бұрын
Li nékh na waay Machallah, yalna diam yagg , Dieureudieuff Serigne Touba , Diam ak Salam ci S M Kara Mbacké 🙏🙏
@fallndeye8245 жыл бұрын
Ak lou meuna khew rek 31 Decembre mome fèkhè na ba soppi ko si gnène si ndaw gni tè lolou amna solo ndakh li mo gueune ay thiakhane
@omarniang93695 жыл бұрын
Wakh nga deug dh
@marietoukalela63445 жыл бұрын
Merci lolou rek la nioune foumougnou wo gnou feu KO fofou mane môme la geume ❤❤❤💕💕💕💕💕💕💪💪💪💪💪💪
@loufaking4444 жыл бұрын
Fall ndaye billahi wakh nga deug
@cheikhsaadbouhfall97345 жыл бұрын
Tout ce que je sais moy beugue neu Cheikhul Khadim tei diekh si mom takk En lisant Ndaxam BAMBA DAJ NA FEPP on comprend qu’il consacre tout son temps pour étudier les écrits du saint homme et il s’inscrit dans une logique de les rendre accessibles ... j’aimerai faire 1 interview avec lui pour comprendre les perspectives de la lancée ....
@elhadjisamba76055 жыл бұрын
Mashallah, je sais pas comment mais essayer de contacter le site Kourel Kara.
@jeannememebassene96095 жыл бұрын
J p vous mêtr en contact avec son fils
@ZikroulahChannel5 жыл бұрын
Laissez-nous votre adresse e-mail . Je vous contacterez .
@elhadjisamba76055 жыл бұрын
Ou vous contacter ce numero: 77 719 65 59
@boucardiouf38034 жыл бұрын
Bilay fall ya bakh, défa ler
@utilisateuryoutubiste52505 жыл бұрын
Serigne Modou Kara keip koula critiqué neu hamni yaako gueun. Ndah yagui dadiélé des milliers de jeunes jourou foo ngalen di toudlo Yalla . Konn bravo
@mbaworproduction83265 жыл бұрын
MERCI AU CAMERAMAN POUR LA PERSISTANCE ET PRECISION DE L'EMOTION. ET BONNE ANNÉE À VOUS Plus tu donneras de ton cœur, plus il t'en sera rendu par l'influence divine de l'amour.
@vieuxdiop27435 жыл бұрын
Diadieuf serigne modou kara mbacké Norèyni yalla nguafi yagu tè andak wèr si barckê serigne touba khaadi mourasoul amine
@bld93715 жыл бұрын
Ndayesane thieyy cheikh ahmadou Kara mbacke yague fi lolll té werr thi barké borom touba ❤ buon anno a te Mbacke balla santati la bou werr dieuredieufe cheikh ahmadou Kara mbacke Noreyni
@srgnfalloundiaye83225 жыл бұрын
Amine
@aliouseck71715 жыл бұрын
Bamba feep
@maragueye3545 жыл бұрын
Amine yalla nafi yague te werr
@bld93715 жыл бұрын
@@maragueye354 ndayesane Amine Yarabbi
@bld93715 жыл бұрын
@@moustaphadiallo8513 mane douma wakh ak yow ndakh amo xél motakh magui toup nak
@sanoubadji67605 жыл бұрын
J s8 talibé serigne babacar sy mais j'ai les larmes aux yeux vrema dawna yaram
@noreyni6059 Жыл бұрын
Kéne dou cheikh ahmadou Kara mbacké noreyni 🥰
@seckbachir32205 жыл бұрын
Ndeysane yala nafi yague tee werrr ndeysane souniou khol fessna
@elementkabirou79885 жыл бұрын
Dé lou amela bamél lou tiss leu mougeul meu loutar leu naneko bayi xel. Bayilen yen comentaire yi Togne bahoul serigne bi kilifaleu
@khadydiallo48444 жыл бұрын
C vrai bien dit
@BassekaraNiang-gp3ly Жыл бұрын
Kenn dou cheikh akhmadou kara mbackè noreyni zakhirann wa batinann dougnou deupp dougnou daw dougnou delou guinaw si yaw illal ABATT rekk
@cheikhibrafallgueye28545 жыл бұрын
Mbacké gni la diappé comédien da nio xamoul Ahmadou Bamba rek yalla na sa fane goudou lol kou tédeu ki rek mola niore mtx niou beug la ❤
@ibrahimacamara99195 жыл бұрын
Mane mom damako beugue guir serigne touba rek walahi 😭😭
@papesalioumbaye59195 жыл бұрын
Alhamdoulilah!! Di fatali watt rek ni togn bakhoul kou beugoul limouy def rombal boul cetann. Dinga guis kouy diamou yalla guirou doundam yeip waya wormaloul kilifeu yi bou moytouwoul dina trokh.. mangi diegalou watt bou werr
@papisbalzagamotivation3523 жыл бұрын
Loumouy deff dafa nex
@Babaca923 Жыл бұрын
Qui a écouté en 2023
@Babaca923 Жыл бұрын
Moi
@ibrahimdiallo625 жыл бұрын
Allahou Akbar sant yallah at yeunentèbi Mouhamad sws.
@ZikroulahChannel5 жыл бұрын
C’est très émouvant Walahi . Vous avez sauver la jeunesse sénégalaise .
@souleyman99755 жыл бұрын
Non il la ruine
@cheikhseck96972 жыл бұрын
de quelle jeunesse parle tu? Les raté s ,des drogués des madialistes,les mangeurs de niagas ceux qui ne font pas parti du développement économique de leurs familles en particulier leur pays en fuyant leurs responsabilités pour devenir des ndongo laxasaye
@ZikroulahChannel2 жыл бұрын
@@cheikhseck9697 tu n’as rien compris toi ! 🤣🤣🤣🤣
@mamefatyseck22935 жыл бұрын
Dieuredieufeti Ahmadou mou moudjou mi yaggal wèreul ❤❤❤👌👌👌
@momodiop72365 жыл бұрын
DIEUREUDIEUF FETI CHEIKH OUSMANE MBACKÉ NOREYNI
@sakhevardiop43554 жыл бұрын
Je m'intéresse de plus en plus à cet homme méconnu.seule la vérité dure,et cela fait un moment que ça dure !
@niaaydiatta1873 Жыл бұрын
Je suis comme toi
@boussombengue48415 жыл бұрын
Bamba mercii serigne bii magiléye siyar dila gnianale gounde fann akk wër gniatta jeûne gnio fii téww beusoup 31 décembre lii ndamm leu bilahii yalla naleu yalla fayy barckép kou tédd ki
@francaisfranco98195 жыл бұрын
Seringue modou kara yallna yalla goudal sa fane barkeb seringne touba ❤👏👏👍
@macodoufaye56632 жыл бұрын
Bamba Yalla Yalla Bamba mbacke yagg fi lool te werr
@khadijatoure93625 жыл бұрын
Ndeysanne dieureudjeufeuty Cheikh akhmadou kara noreyni lii rek diarna contane sa ligueye rafetna machallah dou gneupeu meuneu am lii goudeu fane we're werler thi barker khadimou rassoul khadimal moustapha dieureudieufeuty.
@Youla_Beauty5 жыл бұрын
Lima nékh si Serigne Modou kara moy dafa formé ay jeune teklen si yonou bakh j'en suis sûre sounou dieulone yen si prisonniers yi maylén chance mou yoré léne danou changé Tidiane la Waya lolou takhna ma nawka
@mamediarrandiaye6985 жыл бұрын
Mbackee yalla nafi yagg teh werr😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@ibrahimadiene99915 жыл бұрын
Amen
@bambakara74895 жыл бұрын
Kene doufi cheikh ahmadou kara mbacké Noreyni 👌👌👌
@djibithiam56754 жыл бұрын
Sr modou kara amoule ci adouna
@diedhiounicolas19075 жыл бұрын
Tala na diamme Yagüe Senegal África ak monde anthier dieureu dieuf serigne touba kara SA kaw si kanam
@diopconstrutora62135 жыл бұрын
Yalnafi yag lol ta wer si barkep ajhmadoul khadim🙇♂️🙇♂️🙇♂️🙇♂️🙇♂️🙇♂️🙇♂️🙇♂️🙇♂️🙇♂️🙇♂️🙇♂️🤙🏾
@papedaoudadiop33815 жыл бұрын
Mbacké Balla Aïcha yalla ngafie yague té wër.
@aliounebambakara71675 жыл бұрын
REJEUREJEUFETY CHEIKH AHMADOU KARA MBACKE NOREYNI POINT
@morkane69385 жыл бұрын
♥️♥️😭😭😭
@aliounembaye48875 жыл бұрын
Yague fi téwer Mbacke balla Machallah nékh na loul
@astelbae78675 жыл бұрын
Bilahi sama khol toyna je t’aime sangue bii ❤️❤️❤️❤️🥰🥰
@obtrice42575 жыл бұрын
Un pays de fous furieux ....Allah guide nous sur le chemin de siratal moustakkima . Amine
@makane88404 жыл бұрын
Aye waye mane deh dama beuga djébeulou sakh serigne yalla nafi yague té wérrr
@retrosenegal87115 жыл бұрын
Yagg fi lol te weur amna solo 😍
@amdysalihou36434 жыл бұрын
Mbécté Sar Mada mbacké ak kép kou beug sérigne touba si mbécté rék ba faw 💘 ☝️
@diammoguenthiow1005 жыл бұрын
Au moins fekher na ba jeunes yi nek si stade bi drmougnou di taxawalou té limouy diangue lep ay beuyitou serigne Touba la lissi eup ..t bou gnep done def ni mom dieul gni yakouwone nek di prison nga defarlen ba fougnou toll di toude yallah ak sikar kone ndaw gnep bax
@diopabdoulaye33275 жыл бұрын
Deug deug
@bourethiam445 жыл бұрын
Djeuredjeuf serigne saliou 🙏
@ndiayeami2305 жыл бұрын
Machalla serigne mondou kara malla beuge ❤❤❤😭
@adjathiandoum68535 жыл бұрын
Longue vie à toi Serigne Modou kara 😍😍
@fallougueye62932 жыл бұрын
Allaahoumma Aamiine🙏🏾🕊❤️
@rosesambou38165 жыл бұрын
Merci sama serigne pour ceke tu fait pour l'islam et la jeunesse