Nènalén sou nguén débat ngén moytou Niassène yi. Yalla dafa déf danio beuri xam xam si mbolém fana yi téksi am clairvoyance. Baye niass mi bokk na si gni geuna nëw xam xam si Niassène xana kay mom la Yalla dénk mission bi pour mou mabal sén fène yi. Éy sou nguén tassé wone ak Oustaz Thioub walla Cheikh Habib Ndiaye walla wa Keur Thierno Abdoulahi Dia yi walla wa keur Cheikhoul Khayri kone di nguén xamni sunna deug Niassène yi niossi raw. Xam xam ak ndioub moy sén points fort. Tassawouf di ay tiakhane.
@ErenKrüger18992 жыл бұрын
nieuw di tar tari rek...Cheikh Baye Niass chiite la ga nieuw di tankhal nite gni
@souleyediop3435 Жыл бұрын
Baye a été massacré dans plusieurs débats 😂😅😅, i
@ibouvision7644 Жыл бұрын
Doul ngén DH Alpha ba mi wakhoufi touss
@modoudiallo132 Жыл бұрын
@@ErenKrüger1899ya meuna doul
@bassndiaye80664 жыл бұрын
Je suis mouride.mais je suis fier de cheikh baye niass.xam xam lèèr na rafetena.dieureudieuf.
@PapoukoroTraore11 ай бұрын
Merci
@PapoukoroTraore11 ай бұрын
Baye niass
@MatarsambSamb-s7k11 ай бұрын
Yi deh KO noy bop baniou WEdi Lola sa tarikha barki mam cheikh Ibra fall deh wayadinga Adouna ak alahira diaxalnama nga diem
@limoyelan8574 жыл бұрын
Yalla nañio yalla sakhll si Allquran ak sunna rek inchalla
@MamadoulamineBadji-cy8ud4 ай бұрын
Cheikh baay Niass gnou guilay gnanal yalla goudou fane ak weurgui yaram bou yatou sibarké saydina mouhamad Saws 🙏 sibarké mawlaanaa cheikh Ibrahima Niass cheikhal islam baay Niass rta 🙏
@MamadoulamineBadji-cy8ud4 ай бұрын
Cheikh baay Niass yow ya lén raw ya raw sén ndéye row sén bay row sén kilifayi
Machallah cheikh baye niass xam xam bi lerna long vie vous et merci
@AL-AMIR-75 Жыл бұрын
Cheikh Baye niass point
@JamesGomis-g7l Жыл бұрын
Cheikh baye niass :boul tontou dof bii ki beulëgui ken tontoukô ben oustaz tontoukô wahal ak borom xam xam yii môgueun❤❤❤
@Abubakr_Sakho11 ай бұрын
شيخ باي انياس ❤❤❤❤❤
@Arwefree Жыл бұрын
Masha'allah cheikh Baye Niass yalna yallah fayy
@aboudiop634011 ай бұрын
Alpha vraie comédien leu😂😂😂
@elhadjidiawara955 Жыл бұрын
Alpha ba ndeysaane Gaawa mér ak niakk tégguine moy Ték talé niakka matam ak niakk sori ndiangam 😂. Dieureudieuf cheikh Baye kham kham bi sélection na am na pédagogie
@momodiop97204 жыл бұрын
Cheikh baye niasse li ngay wakh lerr na nagne
@fayesaliou81712 жыл бұрын
Machallah seydi Niass
@mouhamadoulaminekande87966 жыл бұрын
soukrane cheikh Baye niasse
@kouroubayefallpure5 жыл бұрын
Dieureudieuffe S Touba
@adamasow92924 жыл бұрын
Cheikh Baye mome talibé Baye la di touroundo wome..
@alphatoure43573 жыл бұрын
mane dé damaléne fans billahi reuthiouna louma diangoul meme ci vs faite herreur mais du fait que vs décortiquez les livre les ayas sa me fait plaisir
اللهم انا نسألك ثبات على حزب اهل السنة والجامعة ❤️❤️
@lemzosene85634 жыл бұрын
Machala baye niass euhlane wa sahlane wa marhabane bikoum
@mahmoudkhalilal-hussarytvh36644 жыл бұрын
Hooo bay yagui léndi ray deh bal lén rek adouna amol solo dousén morom❤❤❤
@tallambaye30455 жыл бұрын
Cheikh Baye niass amoule morome billahi❣️❣️❣️
@mamb87804 жыл бұрын
Merci baye gayi danomna sosse naler rek
@mamethiernondiaye4574 жыл бұрын
Thieuy cheikh Baye aka beurii xam xam gni bayi lén dagnouy fén rekk dosén morom yagg fi té weur
@ibrahimaseck75384 жыл бұрын
alpha bayil féne féne bakhol masha'allah
@saam4474 жыл бұрын
Machallah cheikh Baye Niass Leer na
@omardiop17805 жыл бұрын
bilahi baye niass do séne morome diangue rk moye degueu machallah yalla n'a yalla yokou lerr yi yalla Def ba alfa déme diangui wate wakhou fi dara
@cheikhsylla8204 жыл бұрын
Je suis mouride mais cheikh baye xam xam késsé la ak yarr, mom rék téré leu. Yén wahabiste nopoloulél té dém saawi, té teudi.
@anitandiaye9376 жыл бұрын
Merci bay niass
@bayezaldiallo72626 жыл бұрын
Baye Niass boul tontou gni... Da gnou sokhore da gnou jaloux... Sénégal gui magg gni gnofi Naik...sougnou daifai nai lougne laine Di financé pour contre confrérie yi da nagne si ame ndame... Moukk dou gnouci ame ndame
@SoldarouBaye-n2j11 ай бұрын
Cheikh baye amo morom merci
@mohamedsenghor73112 жыл бұрын
J'ai bien écoute votre débat . Mais vraiment Alpha Ba , Baye Niasse mo la gueuna degue tombbe yî !
@oumiebabou96162 жыл бұрын
Merci beaucoup oustass alpha bah,,we are with you Quran ak Sunnah rek moi degg
@ibrahimaaliounediouf98416 жыл бұрын
الحمد لله Diara djeuff Cheikh baye Niass Yalla na Yalla guindi Wahab yeupp
@saloumxamxam20235 жыл бұрын
Ibrahima Alioune diouf ماشاء لله باي
@boyeoumar9432 Жыл бұрын
ما شاء الله، شيخ باي والله رأيتُ أنك عالم جزاك الله عنا خير الجزاء بجاه سيد الوجود الكتاب والسنة بشروح الصوفيين
@alfaomart86982 жыл бұрын
Macha Allah cheikh baye niass
@barham48433 жыл бұрын
Boy Alpha bayil fenn
@MassawFall-e5u Жыл бұрын
Alpha blh khamo dra yalla kham nako 😅😅
@MamadoulamineBadji-cy8ud4 ай бұрын
Cheikh baay Niass si xol❤ dara dakouko Machallah
@lolanourette5184 жыл бұрын
5.35 😁😁😁😁 Bravo cheikh baye ti kanam rek
@barhamniane982 жыл бұрын
Alpha wax deuggi yalla nak tu nous as déçus franchement wakh diou beuri rek nga meune ويبدو أنك لا تفهم كلمة التدليس بدقة
@almoukhlicinasidkhine51405 жыл бұрын
Mashalla cheikh baye lerna nagn tei nonoula
@mbayemaper3784 жыл бұрын
Merci baye
@bollembaye46485 жыл бұрын
ماشاء الله باي جزاك الله خيرا
@senegalais99764 жыл бұрын
Merci beaucoup by niass c clair
@abdoukane46073 жыл бұрын
Baye.niass.machala
@ibrahimndimz44202 жыл бұрын
Jambaar ngin nak yalla na yalla barkil deba sy xam xam amna solo macahalla 🥰 yalla na yalla fayeleen
@boyeoumar9432 Жыл бұрын
😂😂😂😂 Alpha mouné «Dama ko képou»😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
@MamadoulamineBadji-cy8ud4 ай бұрын
Alpha ba yow yéfér nga bou bone sakh
@ousseynousall58082 жыл бұрын
Merci beaucoup cheikhe Bay khamounou darra domarame yi
@TopFaris-l9e Жыл бұрын
Machallah cheikh baye niasse.يحسبون أنّهم على شيء ألا إنّهم هم الكاذبون. شكرا لك ياشيخ باي انياس
@Cheikh-thicky Жыл бұрын
J’apprécie bcp ce débat même bouguén diobo wul ci kaddu
@salimatadiallo70402 ай бұрын
Xam xam dey leer dh! Cheikh Baye Niass yalna yallah sam la🙏
@bayeniasskhouma47 Жыл бұрын
ماشاء الله حبيبي ليرضي الله عنك بجاه سيد نامحمدصلى الله عليه وسلم غ