Contane nah si niari oustaz yep .Rawatina Oustaz khalifa .Debat yi dafay doundal dine .yalna len yalla fay guendji fay ❤️❤️
@tall87167 ай бұрын
Tassawuf ay leunte rek la niom ay guente lagniy diamo yalla ak bidah😂😂😂 ragal len yalla té topp yonentibi .psl. bayi wouté ak mom
@brohajjfall13716 ай бұрын
Merci Oustaz Khalifa. Saway difi way ak Guérték ak gaub. Lolou dou par rapport ak Diner bi, Lolou meme kou gueumoul meun neuko jeurigno. Mbir mii, moy YONENTE bi amneu loumou yor lo xamni mokay jotali kouko nex amci lo xamni FARD leu mou jotaliko beip Joulittt . C tres clair , Wahabiya mo beug leunteul rek ak jaay arabal pour nitt yi waxni mom moo neik ci deug.
@SOULEY7775 жыл бұрын
Maa shaa Allah outaze Atoumane réponse très Claire ya ndeye bineta
@cheikhmbackegueye97946 жыл бұрын
Mashalla sama serigne amna solo khalifa mboup
@diammouyalla38805 жыл бұрын
Machallah serigne khalefa kham kham bi lerna loll machallah