Nii Leu Mouride yi wara def Xassidas yi ndakh gneep xam yeurmandé ak thiofél gui seugne bi ame ci Dioulite yi ak yonénte bi. Moukhadimaat Amdah; Mawahibou; Jazbu Dafa war beep dioulite xam takhaway bi seugne bi amone ci Saame Diiné dji. Jeurejeuf Ahmadou!!!