N’oubliez pas de vous abonner à la chaine et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
@bintafall43482 жыл бұрын
toujour les hommes Sénégalai
@Ruqqayah-n2 жыл бұрын
Jiguéne yi daw lennn, bou kéen mougn. Goor you Bari dagno fébar. Daw léen guir Yallah 😭
@lacouradione91772 жыл бұрын
Fassé dé mo guénn rayyy, yalla nako yalla yeureum té kharéko aldiana,yas des homme qui ne mérite pas d'épouse.
@serignesene96032 жыл бұрын
Mane je coné la fille depui tant denfance kou yarrou la yalla nako yalla yeureum
@olymatadiouf26382 жыл бұрын
Les familles doivent prendre leur responsabilité. Si le couple ne marche pas il faut dissoudre le mariage. Les imams et les familles respectives def len sen ligueye Yalla mo len ko sante Yalna kharé aldiana
Guissouma dara louma ko diaral ak lou meneu khéw rayy dou solution et ça ne le sera jamais. Meneu touleen nek bayil mou dém ngua kholi lénéne. Qu'elle repose en paix🙏🏿
@bibichedieye94702 жыл бұрын
Il ne faut jamais dire jamais yallah rek mo kham kou nek ak sa destin té li léep yallah bindone nako baparé en plus seytané dafa bari dolé ndakh kou déme ba takanté c’est pask beugeunté wone nguéne té amoul doom adama bou gnane yallah ray nitt rawatina sa djabar la mère de tes enfants yalnako yallah yeureum té kharéko si aldianay firdawsi yi ndeysann
@burr93792 жыл бұрын
@@bibichedieye9470 Sokhnassi libre arbitre daffa am lolou yonou yalla nékou thi . Bi yalla wakhé né kou ray dagne la wara ray la wathio ak gnoun. Donc mo ray wala rayoul woroumeu mais boudé mo ray yoonou yalla nékouthi daffa deff loukou nekh.
@matoundieguene68932 жыл бұрын
YALA nagnou YALA mouthieul mouthieulégnou sameugnou arrr you YALA bougnou raay kén tei YALA bougnou koudoul YALA raay AMINE YA RABBI YALA na YALA léral mbirmi yeureum Nafissatou may lèn xolou mougn
@matoundieguene68932 жыл бұрын
YALA nagnou YALA mouthieul mouthieulégnou sameugnou arrr you YALA bougnou raay kén tei YALA bougnou koudoul YALA raay AMINE YA RABBI YALA na YALA léral mbirmi yeureum Nafissatou may lèn xolou mougn
@burr93792 жыл бұрын
@@matoundieguene6893 Amine🙏🏿
@saratasarr14752 жыл бұрын
Yalna ko yalla yeureum ndeysane kou bakh la wone mosna ko fekk thi clinique bi sama crédit diekh mou abalma téléphone nam ndeysane c'est vraiment triste
@papi62182 жыл бұрын
Grand doudou metina que Dieu laceuille dans sont paradis depuis 20dans on ç pas vue grand doudou je vous stl depuis islande j'habiter a ganaw Rail
@fatoudia20412 жыл бұрын
Yalla nako Yalla yeureume thè kharé aldiana firdawsi 🙏🙏🙏🤲🤲
@Missdieng2 жыл бұрын
Mane dama foknii nitt gni andatougn ak seine saguo lii mom rakh na dara Tt le temps djekeur rayna diabar Mak rayna rakam Papa ak dom voisin voisine rekk dii rayanetei rekk
@ramasenghor51662 жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
@mouhamedgaye18322 жыл бұрын
Ak diabare raye na dieukeur beurinafi tamite mais yalnaniou yallah same moussale niou si seytané na djiguéne yi déme seuyi si keur famille yi ak loumou méti méti tei bayi appartement yi
@ninkinankaproductiontv6542 жыл бұрын
Yalnako yalla yeureume té khareko aldiana firdawsi you gueuneu kawé té boleko ak malaka yeurmandé mou diégualko ayy bakaram 🙏🙏🙏
@ndeyesarr12822 жыл бұрын
Mes codoleances doudou massa paix à son âme
@abykane76902 жыл бұрын
Ndawsi gniou ray de gnio bok keur ndaysane techno pôle 😭😭
@fabinetousarr51192 жыл бұрын
Massa
@aissatoundiaye60042 жыл бұрын
Yalna yalla yeureumko t yékhégnou T feumou djieum geuneulko fimou djiougué 🙏❤ T yalna yalla léral léep t wéer ki dff lui inshalla🙏
Repose en paix toma , vraiment li niaw na na justice def liguèy😭😭
@fatyly73612 жыл бұрын
Enkor un meutre mm schéma mm déroulement kom ma soeur Aminata ka reposé en paix yallah na yallah def justice bu guena sévère q c soi ici ou alakhira😥
@eugeniediedhiou15702 жыл бұрын
La sœur de qui?
@fatyly73612 жыл бұрын
@@eugeniediedhiou1570 jai di " ma sœur" kon je parle de mw
@awagueye23292 жыл бұрын
Neyssane yalla n'a ko yalla yeureum t'es kharlé ko aldjiana firdawfi 🙏
@salladiaw5432 жыл бұрын
Amine
@sallakane37272 жыл бұрын
Paix à son âme que firdawsi soit sa derniere demeure amine yarabi
@salladiaw5432 жыл бұрын
Amine
@lesnouveautes37312 жыл бұрын
Deuk bi woratoul vraiment li c'est grave goor mo Bone xol
@awagadiaga95532 жыл бұрын
Bilahi 😭😭😭
@ramasenghor51662 жыл бұрын
@@awagadiaga9553 😭😭🙏😥👏🤲
@arisdian48512 жыл бұрын
Ndeyssane yalla nako yalla yeureum Sénégal yakouna bilahi
@awakoita96282 жыл бұрын
OUSMANE nous a tous déçu mais il va payer ma nièce n’est pas un animal
@mameaidasougou85832 жыл бұрын
Salam Salam conseil bimaye diohé nanou délou wate thiossane di seuyi si keur goroyi bayi appartement yi formation dafa bahe si seuye
@fatimatra84572 жыл бұрын
Leigui deh gnissi bari nenagnou seyalougnou goro sene djeukeurr point ta sene yayi defougnou nonou dama warou legui si yenneu mentalité yi
@ironahide58962 жыл бұрын
@@fatimatra8457 deug rek nga wakh ma chérie. Beug nit ki ba parè beugo guiss ay mbokam c'est grave. Je ne parle pas de la femme de la vidéo je parle en général
@abibatoubathily37832 жыл бұрын
@@fatimatra8457 fatima ba yangui seye keur goro paix à son âme metina
@fatimatra84572 жыл бұрын
@@abibatoubathily3783 inshalla lolou rek laye gnaane yalla
@fatimatra84572 жыл бұрын
@@ironahide5896 tu as parfaitement raison lolou deh la gnou khewal leigui defois je vois certaines commentaires dammay sax tiite yen a même gniye gnaane sene goro yi deh je parles en connaissance de cause deh sa goro bo ko kholé say warldiour yi ngua bayyi sa keurr rek di ngua seye ta yalla tax
@mariamamathildemane6782 жыл бұрын
Il est temps que l'état parle de ces crimes on est dans quel pays ya trop de violence
@mariamakamara25412 жыл бұрын
K son âme repose en paix
@cheikhtidianediouf90042 жыл бұрын
Grand Doudou du courage lép Dina lere inchallah
@dabamboup56612 жыл бұрын
Inchallah
@sokhnasene34362 жыл бұрын
Que son âme repose en paix kou bakh dém na
@sambka33822 жыл бұрын
Yalnako yallah yereum amine
@mayarassoul14942 жыл бұрын
En plus d'être des menteurs certains hommes pas tous quand même sont des criminels Encore une femme qui perd la vie seulement ya toujours des signes faites attention la famille Repose en paix naffissatou
@misstchiptchip29632 жыл бұрын
Le mien était comme sa il metrangler de longue minutes devant mon enfant de 6 mois qui pleurait devant moi et il s'arrêtait pas...etant donner quon vivais a l'étranger je ne pouvais en parler a personne..mais un bon jour jai pris mes clics et clac je suis partie sinon il aller me tuer..et jusqu'à présent il a la haine contre moi quand il me voit malgré quon n'est séparé depuis 3ans
@dieufbayiwakh2 жыл бұрын
@@misstchiptchip2963 koon de bobo nga moytou ko boula diare nga fekkhee ko sorii loll
@aidasagna29282 жыл бұрын
Que son âme repose en paix
@awambaye37302 жыл бұрын
Bilay khale bu yarou bakh fokou sen beune yi guay sen walay yalla na motale ndawam aldiana 😭
@amybayeniasse79442 жыл бұрын
Paix à son âme 😭😭😭
@solobarou97572 жыл бұрын
Un crime n'est jamais parfait. Le mari est le criminel.
@sirandouniangadou46822 жыл бұрын
Mom la di autopsie bi bamou guénè danio guiss ni dieukeur dji moko khoth
@aidandiaye53312 жыл бұрын
Waw li d'où thy wakh euy gorgni
@SENEGAL3032 жыл бұрын
Père nopalou lén. Khana nga yg tribunal Def sa ay Mbir. Mais police bi kouniou diap BA bayila fo diar avouer
@gueuyeyacine222 жыл бұрын
Bilay Fina gua khame ni amoul béne problème ré rék lay déf Ousmane dale yalla nako yalla até ak nioune souniou mague dji déme na rék 😭😭😭
@khadyfaye40012 жыл бұрын
Ndeysan 😭
@sirandouniangadou46822 жыл бұрын
Walahi Amoul blem
@khalifambengue61252 жыл бұрын
Yalnaniou yalla mouseul si saytanè
@aidasow5992 жыл бұрын
Wallahi oumpagne linga wax yeup deug leu Fina moma mak deh wayé thieur bimou ma diox foko guiss ay beugneum ngay ndieuka guiss gno dioundo do magga ndo thi sa kanam lo wax si gnoune gneup rek Ken douko weddi Yalna déé di noflayam
@abysta12 жыл бұрын
Massa yalla nako yalla yeureum te khare ko adiana.amine que justice soit faite
@antadiouf7802 жыл бұрын
salam père doudou ,masta yalla na déé Di noflayame ,
@beugdeug55532 жыл бұрын
Baleénne wolouuna sounou. Justice le jeune tué à Louga et jugé mem615 jours et condamné le tueur à deux ans de prison, notre Sénégal est à refonder sur tout, justice bakhhba vs aurez déception à moins qu'il ne soit pas de l'APR ou BBY
@SENEGAL3032 жыл бұрын
Loy wax ni ? Deux ans pour meurtre ?.
@meenaba59952 жыл бұрын
Salam, comment cette personne a fais pour sortir après 2ans ?? Ils n’ont pas d’espace Laba ou ils on étais payé ?
@binetadiallo48972 жыл бұрын
Repose en paix nafi
@SENEGAL3032 жыл бұрын
Père ne vous en faites pas. Avec cette police, soudé daniou ko ray dinagnou fégn.
@miriamlopy17832 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureum té khare ko aldjana firdawsi soit sa demeure
@fatougaye10022 жыл бұрын
Magui dialer papame c un promotionnaire d'ecole
@ndeyjobe91772 жыл бұрын
Aye waye lii metina yalnako yalla yeureum
@acolymariamacamara84932 жыл бұрын
Bilahi Sénégal kou Ray gnous Ray leu li yeups dinafi dieh noumou gueuneu guawe
@vanessabalacoune39522 жыл бұрын
RIP 🙏🏻
@fatoushmbodj38762 жыл бұрын
Ay boudone police pikine dou def 24h th dougn ma wax louler
@salydiandiaye99672 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureum
@ndeyesagna22932 жыл бұрын
Ma copine doumako massa fatei bilahi dpui enfance ba tay yalla nala yala yeureum lo méti n'a lool
@Mideva132 жыл бұрын
Yalna ko yalla yeureum te khare ko aldjiana firdaws amine
@papelo86972 жыл бұрын
Wadji daniouko wara tethie si kassobi mome ak kharitame yikoye diapalé yéppou
@awadiouf96552 жыл бұрын
😭😭
@oumidiallo50742 жыл бұрын
Liii niawna trop loukofi diare
@amchayazback32282 жыл бұрын
Studio la wakh deee
@kissquenne65602 жыл бұрын
Comme infirmière la meune na ame logement fou diegue ligueyam. ou est le problème