Dinala douma daan la😱Eih Mbaye Gouy gui hausse le ton sur Moussa Ndoye

  Рет қаралды 49,710

BAOL TV

BAOL TV

27 күн бұрын

Пікірлер: 96
@Ma-Habba19
@Ma-Habba19 25 күн бұрын
Sou lamb wakhé deug moussa ndoye moko meune aller ak retour qualité yi sakh dou béneu
@MbayeThioumb
@MbayeThioumb 25 күн бұрын
Wayy moussa ka meun me beugu Lou yobou motax mou dieul ko
@ElhadjiWade-bo6lp
@ElhadjiWade-bo6lp 25 күн бұрын
Bou lamb wakhé deugue gua wakh
@idrissaseck3331
@idrissaseck3331 24 күн бұрын
Sou lambe fénné nak😂😂😂
@SauraDiop
@SauraDiop 21 күн бұрын
😅😅​@@idrissaseck3331
@PapeSarr-qk1xq
@PapeSarr-qk1xq 25 күн бұрын
Moussa mima guiss si dinn yi mouy contact baye Gouy Gui mi douko teye dh😂😂😂
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 25 күн бұрын
Moussa Ndoye bilahi bo hékhé dinga dane Mbaye gouy gui ndah tapéte la 😂😂da réy lamégne mais ragal là 😂😂
@yorondiaye108
@yorondiaye108 25 күн бұрын
moussa doy yalla nala yalla may dam si barki serigne fallou backè inchalla🙏🙏🙏🙏🙏🇸🇳
@seydinaaliounelodja185
@seydinaaliounelodja185 24 күн бұрын
Tapet douko romb
@HamidouDiallo-bt6rd
@HamidouDiallo-bt6rd 25 күн бұрын
Moussa ndoye kassé yalnako yalla may Ndam Inchallah ❤
@user-nm2zx9yd9m
@user-nm2zx9yd9m 25 күн бұрын
Filako wakhé Mousa ndouye soo khékhé y’a mom combat bi 🙏🏼
@abdoulatifdiop5640
@abdoulatifdiop5640 25 күн бұрын
Akh moussa Ndoye mi déh nekoul si Dara
@SkyRapidIT
@SkyRapidIT 25 күн бұрын
Lolou la geum man
@modoubayefallsikroulla1423
@modoubayefallsikroulla1423 25 күн бұрын
Wawaw mbaye dou guis cou
@user-nt5cy8io1g
@user-nt5cy8io1g 25 күн бұрын
Yaw yay kane 😂
@abdourahmanesindidi1818
@abdourahmanesindidi1818 25 күн бұрын
Mbaye dou guiss coup di😂
@boubacardiop-ue3kc
@boubacardiop-ue3kc 25 күн бұрын
Moussa ndoye Bima kham bou paré fane lako mbaye gouye gui di diar 😅👍🏾
@MoussaDione-jj3gp
@MoussaDione-jj3gp 25 күн бұрын
Mbaye gouygui rek lanouy top
@doudousanebadji696
@doudousanebadji696 25 күн бұрын
Moussa Ndoye mo meune Mbaye Gouy Gui dé wa bakhna
@user-lx2lz4ui6u
@user-lx2lz4ui6u 25 күн бұрын
mbaye gouiy gui yay sama mbeur mais fooy diaar moussa ndoye moussa amna dolle dhe mbaye mann dhe diomina
@moussandao4707
@moussandao4707 25 күн бұрын
Lolou moma diakhal dh😂th mbaye dafal régal khekh
@BayediamilDiouf
@BayediamilDiouf 13 күн бұрын
Moussa Ndoye yalla nala yalla may ndamli barké s Babacar sy
@gueyelabsolu5889
@gueyelabsolu5889 24 күн бұрын
Mbaye Gouy Gui mom Léneu xamnako Thi mome Mbeur la boo xamny Mounna ame lounékeu Thi Lamb c pasq kou ndiémé entertainment la Mbay gui my tjrs Migui entraînement lolou Mom Mounnako sédé thi Mom vrement ✍️Diambar ladé Mbaye
@deugdourombinopdioulite635
@deugdourombinopdioulite635 25 күн бұрын
Moussa ndoye NDAm moussa ndoye NDAm inechalah
@user-hl2wm9zr5s
@user-hl2wm9zr5s 25 күн бұрын
Mbaye gouye gui tapéte gua nioune yarakh laniou ndeye deuk non recule ❤❤❤❤
@samboumamby
@samboumamby 25 күн бұрын
Medina moy sén baye téy lén rék
@CaramocoDiallo
@CaramocoDiallo 25 күн бұрын
Moussa ndoye Bougue nala trope mais nak médina laa dekk mbaye Gouy gui yalla n'a âme ndam amine
@GabrielLouis-fk7tv
@GabrielLouis-fk7tv 25 күн бұрын
Victoire moussa ndoye inch'Allah
@BASSIROUKONE-wz6zs
@BASSIROUKONE-wz6zs 25 күн бұрын
Mbaye gouy gui seul mom rk lagnouy topou 💯
@Mouhamad_yacine
@Mouhamad_yacine 25 күн бұрын
Baol Baol réck mbaye ❤❤❤
@BayediamilDiouf
@BayediamilDiouf 13 күн бұрын
Moussa Ndoye yalla Na am ndamli barké Chekhoul khalifa
@MameSow-vp7rj
@MameSow-vp7rj 24 күн бұрын
Moussa nguir yalla katal ma ndeye wadji bou bax dfa barri Ndey wakh😂😂😂😂
@SYN979
@SYN979 20 күн бұрын
Moussa ndoye mo meun 145 Mbaye gouye gui lolou kou xam lamb xam nako😂
@NdiayeBara-lj9me
@NdiayeBara-lj9me 25 күн бұрын
Mbaye Gouy gu yalla nako yalla may ndam inchalla
@bathiedioum898
@bathiedioum898 25 күн бұрын
Mbaye Gouy gui baol baol rek yalna yalla maiye ndam inchallah
@papiiiswelleeiih5728
@papiiiswelleeiih5728 25 күн бұрын
Moussa en tout cas sa poids bii barinaaaa deh 😢so contacté Lou bariiii digua gnewateeeee sii lamb djiii in sha Allah Et k le meilleur gagn
@nogayeseck3671
@nogayeseck3671 18 күн бұрын
Mbaye yalna la yalla maye ndam inchallah 😂😂😂❤❤❤
@ahmadoubousso4621
@ahmadoubousso4621 25 күн бұрын
Kii Moussa ndoye moko meun waaaay ah
@2390qwer
@2390qwer 17 күн бұрын
Mbaye kasé nous sommes des baol baol ❤😊
@abdoudiop8697
@abdoudiop8697 24 күн бұрын
Moussa Ndoye ndam rek inchallah 🙏
@daoudafaye2774
@daoudafaye2774 10 күн бұрын
Mbaye Gouy gui combat bi wakh kasse ngasi ame
@MouhamedDione-hi4wm
@MouhamedDione-hi4wm 25 күн бұрын
Mbaye gouy gui seul dey zembéré rek
@jeanlatyrfaye9564
@jeanlatyrfaye9564 25 күн бұрын
Oh ndeye Fatou 😂😂
@MamadouCiss-hy4lq
@MamadouCiss-hy4lq 24 күн бұрын
Adafassrek
@adamandiaye789
@adamandiaye789 25 күн бұрын
Moussa Ndoye kassé 🙏❤
@MoussaDione-jj3gp
@MoussaDione-jj3gp 25 күн бұрын
Mbaye gouygui aka meuna beuré
@AssKasse-zd6wd
@AssKasse-zd6wd 25 күн бұрын
Mbaye gouyi gi tapet la Moussa ndoye moco meun
@khardiatouamadoukane6785
@khardiatouamadoukane6785 25 күн бұрын
Mbaye tanguoul dee
@leuz.patriote
@leuz.patriote 19 күн бұрын
Lou ler 😂​@@khardiatouamadoukane6785
@saliousylla1188
@saliousylla1188 24 күн бұрын
no assane dafa kham affiche yu neekh yi
@infostechservices221
@infostechservices221 24 күн бұрын
Mbaye gouye gui rek
@elzobibaboypolyvalent
@elzobibaboypolyvalent 18 күн бұрын
Moussa Ndoye la faral
@user-uz2pt3qd9k
@user-uz2pt3qd9k 25 күн бұрын
Mas kou Guiss lima guiss si wolly 1 daye diokh baol baol yi cobra por nio am khalis
@user-iv3fk8ch7u
@user-iv3fk8ch7u 25 күн бұрын
Kou comantaire saga rek nala nokh😂
@AbdoulahadToure-vf4sk
@AbdoulahadToure-vf4sk 14 күн бұрын
Mbaye champion nga xalé dou xaar doxal ci kaw waaji diapko daan ko com ninga ko daan défée
@aliouneelevage6482
@aliouneelevage6482 20 күн бұрын
Mbye fait attention moussa ndanane la te khekh katla
@SowMadiaw-go2uc
@SowMadiaw-go2uc 25 күн бұрын
Mbaye yala nga am ndam
@ChekhFall-n2f
@ChekhFall-n2f 25 күн бұрын
Ndam moussa ndoye
@pierrepierre6603
@pierrepierre6603 23 күн бұрын
Di nouyou assistance bifi téw yeup ak assistante yii 😂😂😂. Non Moussa Ndoye réy nama 😂😂!
@PapeSarr-qk1xq
@PapeSarr-qk1xq 25 күн бұрын
Moussa mo meune baye gouy gui d
@morgningue2094
@morgningue2094 25 күн бұрын
Mbaye Gouy gui dafa niaff ndm beurri wakh yalla ngua am défait
@landingsane9219
@landingsane9219 23 күн бұрын
Way lii dou combat way
@laminendao1070
@laminendao1070 25 күн бұрын
Moussa ndoye seul billahi ❤️👌💪💪💪💪💪❤️
@abdoulayendoye1803
@abdoulayendoye1803 25 күн бұрын
Mbaye Amnga. Combat dh 😂
@seydinaaliounelodja185
@seydinaaliounelodja185 24 күн бұрын
Tapet d’où dap mbay gouy gui armé mingui nieuw dh
@Elprofesor5183
@Elprofesor5183 25 күн бұрын
Moussa kassé🎉
@cheikhgueye1612
@cheikhgueye1612 21 күн бұрын
Mbaye gouye yi aka reuy lamigne
@MoussaTine-c6m
@MoussaTine-c6m 21 күн бұрын
Valdo mofi Mane dame so wayone mo thi topou
@niscobanlieuzart1618
@niscobanlieuzart1618 15 күн бұрын
Li kagne la
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 25 күн бұрын
Sounou bét nougnkoy défé😢😢😢😢 dimbeulé lénma
@CaramocoDiallo
@CaramocoDiallo 25 күн бұрын
Medina rek lay top si lepp
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 25 күн бұрын
Lane moy déroutou Baol,Baol,donc déréte mom béna la té da honk mongui si nieup,mais pas Baol Baol,dérét pikine,Guédiawaye
@CheikhNdiaye-hb4in
@CheikhNdiaye-hb4in 25 күн бұрын
😂
@abdougueye4837
@abdougueye4837 25 күн бұрын
moussa ndoye waroule wone woné entraînements yi en plus moussa daffa dém ba commencer douter si bopam
@SaliouNiass-ev3tl
@SaliouNiass-ev3tl 24 күн бұрын
Oh serere way
@user-kc8ml5qt7o
@user-kc8ml5qt7o 25 күн бұрын
Mbaye gouygui amna dolé wayé beuré bi désna amga dolé Moussa ndoye dafa meuneu beuré Moussa bokhékhé am dara si combat bi
@user-vp1hm7py7s
@user-vp1hm7py7s 23 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@abdoulayedia9460
@abdoulayedia9460 25 күн бұрын
Moussa ndoye ndam rek inch'Allah
@mohameddrame92
@mohameddrame92 25 күн бұрын
Mbaye danguay lokh kw 😂😂😂😂😂. Fi la arbitre siffler ioe ak Sarco nguay rapi rapi 😂😂😂😂😂😂
@ModouSarr-ls8qf
@ModouSarr-ls8qf 25 күн бұрын
Bilay yaye boy ya meuna woy
@AbdouLoum-y2s
@AbdouLoum-y2s 24 күн бұрын
Moussa Ndoye seul
@thiaomame1357
@thiaomame1357 21 күн бұрын
Moyoul moussa dor la ci bot
@soutobailemarcelodias1830
@soutobailemarcelodias1830 25 күн бұрын
Yalllna morittbi dan
@cheikhthioub2240
@cheikhthioub2240 22 күн бұрын
Con merde lamb dou tarikha
@abdourahmanesindidi1818
@abdourahmanesindidi1818 25 күн бұрын
Mbaye diapna ni mouno dara si moussa
@user-xe5qd5yd4e
@user-xe5qd5yd4e 25 күн бұрын
Moussa ndoye lou yomb lay weur
@MamadouTine-fr9gh
@MamadouTine-fr9gh 25 күн бұрын
Mbaye guouye gui mo meune mousa ndoye waye
@bayemoussafall3242
@bayemoussafall3242 24 күн бұрын
Iao khna dguay toukh niakh ?
@Elprofesor5183
@Elprofesor5183 25 күн бұрын
Mbaye dinagn pobar sa ndy
@leveridique-kj7qo
@leveridique-kj7qo 25 күн бұрын
Yaw dinagne dakhar sa tounou ndaye
@Elprofesor5183
@Elprofesor5183 25 күн бұрын
@@leveridique-kj7qo sa dokhotou ndey
@leveridique-kj7qo
@leveridique-kj7qo 25 күн бұрын
@@Elprofesor5183 sa koyou baye bouy dougou sa data ndaye
@Elprofesor5183
@Elprofesor5183 25 күн бұрын
@@leveridique-kj7qo 😅😅😅😅😜😜😜
@MamecheikhTourecheikh
@MamecheikhTourecheikh 25 күн бұрын
Séne lefeul ndeye🙄🙄🙄
Best Toilet Gadgets and #Hacks you must try!!💩💩
00:49
Poly Holy Yow
Рет қаралды 22 МЛН
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 1 - Episode 51 **VOSTFR**
1:26:10
EvenProd
Рет қаралды 2,1 МЛН