Finalement maimouna quitte 7 tv...? mame Gôr remercie pr Diomaye ndakh ...cheikh Bara waxone nako

  Рет қаралды 89,072

Diop Tv

Diop Tv

Күн бұрын

Пікірлер: 120
@abdoulayesane7747
@abdoulayesane7747 2 күн бұрын
Ils est très bien renseigné le cheikh,avec des analyses très pertinente😎😎
@maawakonte6570
@maawakonte6570 3 күн бұрын
Cheikh bara est bien renseigné il faut croire ses paroles 😮
@moustaphabeye6198
@moustaphabeye6198 2 күн бұрын
Mam mom mame gour wakho may wakham doull rék 😢😢😢 merci pr diomay et sonko❤❤
@toque5855
@toque5855 2 күн бұрын
MaNaFen soula akhou imam Badara Ndaw dalé bilay sa adouna ci naxari lay deuk, ci móm laa guiss Kouñou diamatt yaramam té amoul bèneu traces cicatrices, sénégalais yi beug Nañou kham Fou enquête bi tóolou🔥
@lissabadiane-iy9hg
@lissabadiane-iy9hg 2 күн бұрын
Cheikh BARA NE RACONTE JAMAIS DE BALIVERNES COMME TOI ET CERTAINS DE TES ACCOLYTES😂😂😂😂😂
@mamadoudiakariaoba6476
@mamadoudiakariaoba6476 2 күн бұрын
L'histoire lui a donné raison merci cheikh Bara Ndiaye
@cheikhoumane
@cheikhoumane 2 күн бұрын
Force a Cheikh Omar Diagne Kham kham amé nako té dioulite la
@tallambengue1092
@tallambengue1092 2 күн бұрын
Billahy méréna diomay si limou déf cheikh ndakh rafétoul ndakh gni raye sunu dom yi gni ba taye di leumbé
@fenenendar8803
@fenenendar8803 3 күн бұрын
Mam goorr moustfa diakhatee wakham foumlla fékonn yeww geumoo darra
@SarrPlacement
@SarrPlacement 2 күн бұрын
Mame gor khana woyamyi da diekh
@adamaba6508
@adamaba6508 2 күн бұрын
❤ honorable cheikh bara Ndiaye ❤loumalla wakh takal tere❤
@tallambengue1092
@tallambengue1092 2 күн бұрын
Diomay do yalla bay dakhé ba yalla sounou brome di fal bbou kén khamou la kon cheikh omar diang mounial ndakh ان الله مغ الصابرين
@tickenesy1172
@tickenesy1172 2 күн бұрын
Diomaye dou yallah, mais Moy fall Moy foli...kon ngua rék
@IbrahimaSamb-c5t
@IbrahimaSamb-c5t 2 күн бұрын
Ce mame gor la un grand nafeck aimer diomaye detester sonKo
@IbrahimaNdiaye-q8o
@IbrahimaNdiaye-q8o 3 күн бұрын
Diarama Ndiaye tv pa Diop TV masa alla ❤❤❤
@dioptv1532
@dioptv1532 3 күн бұрын
Dét waay 🫣😂Ndiaye nekhoul dé😂
@cheikhcarlosndiaye2668
@cheikhcarlosndiaye2668 2 күн бұрын
❤❤❤❤❤​@@dioptv1532
@apprenant9164
@apprenant9164 2 күн бұрын
Frère, yakarouma niy MNF dagn ko yéné liy mais dafa done exercer dans l'illégalité d'ici attaquer injustement ak diffamation le projet. Sou tégou wone si yone liy yeup douko si fék. Dafa melniy nga wakh :sathie kate prison moy plaçame, lolou tékiwoul niy dankoko yéné mais danga wakh lou wara ame. Yéné nite dara ak wakh ko lou wara dont 2 choses complètement différentes. Yalla nala sunu borom defal diam ak tawfekh 🤲🏻
@babacarsoropogui111
@babacarsoropogui111 2 күн бұрын
Quelle insolence, quelle arrogance, mrd pour ceux qui ne veulent pas dire la vérité. On me disait que les tonneaux vides font beaucoup de bruits. Vivent cheikh Bara le visionnaire l'honorable.
@cheikhoumane
@cheikhoumane 2 күн бұрын
Man je desteste Mame Ngor .na guéné lamignam si decision Projet bi.Mame Ngor kén fatéwoul wakh you gnaw yiga wakh Sonko fi
@deve9505
@deve9505 3 күн бұрын
Mame Gor tu n'es pas le seul. Kepp kouy nitt demb content na si décision Diomaye bi
@abrahambampoky-g5r
@abrahambampoky-g5r 2 күн бұрын
On s'en de diazaka.kil ferme sa gueule.il est de l'ancien régime.trop minable et on a pas besoin de ton point de vue envers le Président
@diopmbaye5709
@diopmbaye5709 2 күн бұрын
Mane dé contaanoumatchi...
@mamadoundao8596
@mamadoundao8596 2 күн бұрын
Mame Gor merci c'est pour la première fois que tout bon sénégalais est content de toi
@DiopSadahta
@DiopSadahta 2 күн бұрын
Vraiment j'aurais préféré que cheikh reste à son poste
@abdoutackodiallo3932
@abdoutackodiallo3932 2 күн бұрын
Cou beugue diomaye bagne sonko nafeck le
@mamadoul.diallo1403
@mamadoul.diallo1403 2 күн бұрын
😂😂machallah cheikh bara ndiaye deug rek moo woor
@fredericdasylva2151
@fredericdasylva2151 3 күн бұрын
Nooooonn Mame ngor daf may fetch, cadeau de fin d'année (limogeage de COD)
@sankounkanoute3067
@sankounkanoute3067 2 күн бұрын
Sa waye finalement Cheikh Bara Ndiaye a eu raison sur Maimouna.
@kakakaka-lx9ir
@kakakaka-lx9ir 2 күн бұрын
Mam goor yeww geumoo darra yeww doo nitt ko baxh domxaram
@gee5830
@gee5830 2 күн бұрын
We love Cheikh Omar Diagne west Africa supports Ousman Sonko leadership and solution
@cissejarod
@cissejarod 2 күн бұрын
MAME NGOR NOPIL AMOU DARA LO WAKH, BI MACKY DI REY DOMOU SÉNÉGALAIS YI DA NGA ANDONN AK MOMM
@cheikhgueye8207
@cheikhgueye8207 2 күн бұрын
❤️❤️❤️❤️❤️🇸🇳👍🏿 merci frère 🙏🏿 liguéye bi rafétna 👍🏿
@ThioubBinta
@ThioubBinta 2 күн бұрын
Mane mome bilahi nekhouma ndakh ñiiii faay ligeuy Motakh femme bii mome nekhouma wayer vraiment yene mako
@babacarndoye9819
@babacarndoye9819 2 күн бұрын
On sait tous que waa Benno daño ñak diom !
@OumyNiang-hl1zu
@OumyNiang-hl1zu Күн бұрын
Sa baye ak sa ndeye nio gueuneu niakk diome si li yalla binde😂
@sankounkanoute3067
@sankounkanoute3067 2 күн бұрын
Sincèrement moi je suis jamais contente du malheur des gens mais Maimouna Ndour Faye et Cheikh Oumar Diagne je suis au moins consciente d'une chose c'est juste.
@tallambengue1092
@tallambengue1092 2 күн бұрын
Diomay gni raye sunu dom yi ba taye gnigui fi défo len dra guanan daguay dakh cheikh omar ndiagn llou foko ték tmt
@toque5855
@toque5855 2 күн бұрын
Soo nèkè ci gouvernement danga wara solidaire ci lèp liñouy dèf wala nga dèmissionè mais ko khamni lou président wakh mou guèneu wèdi mèlni kouy saboté, les sénégalais ne comprennaient plus rien 🔥
@seynaboudiack7692
@seynaboudiack7692 2 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@PapeFaye-f9p
@PapeFaye-f9p 2 күн бұрын
chèchei Omar ndiengni dafa bari wahhne moi lay ay nonam logiou waxx
@JonasBoissy-v4r
@JonasBoissy-v4r 2 күн бұрын
Sa way boo deglouwoonn Cheikh barra dinga weuri jii wonnn liguey balla Mouy trop tard. Wayé tey beuy weuyna mbousss. Yalla nga am job
@DaoudaThioune-l5v
@DaoudaThioune-l5v 2 күн бұрын
Mame goor gnoun wa pastef beugougnou nga contaan cheikh Omar sera recasé
@Salsaa-x7z
@Salsaa-x7z 2 күн бұрын
Kham kham d'où péxé merci beaucoup professeur cod ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@amadousyniang9071
@amadousyniang9071 Күн бұрын
Cheikh Omar DIAGNE dou sa morome bilaye
@aladjinaira1995
@aladjinaira1995 2 күн бұрын
Maimouna Ndour wakh na deug dh pourtant Neneu cheikh bara dafay crée ay wakh you niowa goul teh lolo moudier am 😀😀😀
@arantxaarrillaga9537
@arantxaarrillaga9537 2 күн бұрын
CHEIKH OMAR DIAGNE n'a jamais aimer ousmane Sonko,il faut revoir ces videos ancien
@cissejarod
@cissejarod 2 күн бұрын
Mame ngor, tu es un ennemi de pastef, ne te mêle pas de leurs affaires
@ousmanediawara-fu7ek
@ousmanediawara-fu7ek 2 күн бұрын
CHEIKH O DIAGNE ERREURE BOUMOU DEF MOY AMNA DEUG YOO KHAMNEH KENEU DOUKO WAKH SI BEUREUP DOKH DADJIE, NDAKH NIEUP YEMOU NIOU TEH BOKOUNIOU DEEGUE DEEGUE AK GUIS GUIS . WAYEH NITOU DEUG LEU .
@OumarSow-fl8fv
@OumarSow-fl8fv 2 күн бұрын
Cheikh Omar Diagne mome vraiment amena khame khame meuneuko traiter de n'importe quoi mais amoule khame khame mome kene warouko wakh
@ndongolindongo3109
@ndongolindongo3109 3 күн бұрын
Merci DIOP!!!!
@dioptv1532
@dioptv1532 3 күн бұрын
❤❤🎉🎉
@ousmanediawara-fu7ek
@ousmanediawara-fu7ek 2 күн бұрын
REWMI MO BARI AY NAFEKHEU. KHOLAL MA KI REK , NGA KHAMNEH DA FENA ,FENA BA SONEU, SOSS, DI WAKH WAKHEEYYE , AY WAKHOUDEMBAM WOUTEH AK YOUTEY .
@DprodTv-v7t
@DprodTv-v7t 3 күн бұрын
❤❤🎉🎉🎉
@aliouneba4250
@aliouneba4250 2 күн бұрын
Délén j'aime vidéo yi
@insadiallo2133
@insadiallo2133 2 күн бұрын
Fii mom Cheikh Bara waxna deugu
@cheikhfalldiop1317
@cheikhfalldiop1317 3 күн бұрын
cheikh bara ne mant jamais
@sympathisante17
@sympathisante17 2 күн бұрын
Voix tremblante bi rekk montre qu’elle est dépassée. Mounasse Borom ex pastef je suis de tout cœur avec toi . 😢yalla rek moy yalla
@sekousaloumbadji8213
@sekousaloumbadji8213 2 күн бұрын
CH Omar l homme des details
@FallManla
@FallManla 2 күн бұрын
C'est pas une affaire personnelle ! Mais c'est une demande nationale ! COD doit revoir sa communication !
@AdiedhiouAdiedhioudiedhiou
@AdiedhiouAdiedhioudiedhiou 2 күн бұрын
Maintenant il faut chercher là où tu dois travailler 😅😅
@laminedjiba2034
@laminedjiba2034 2 күн бұрын
Mame goor ....yow guemoo dara....COD mo la guenn
@SD2FO
@SD2FO 2 күн бұрын
Pa bi wakh ak maimouna ndour mo guené niak diom si Sénégal
@sankounkanoute3067
@sankounkanoute3067 2 күн бұрын
Yow.Maimouna Faye Ndour ya meuna doul tu ne veux pas payer les impôts.
@talibeserignesaliou8762
@talibeserignesaliou8762 2 күн бұрын
Sa way mo yene won lou bon niou yene ko lou bonn
@PapeNdiaye-x5f
@PapeNdiaye-x5f 2 күн бұрын
Chiekhe omar loumou wakhe deuge la sounou mame yi masouno xexxal Sénégal ay mbamm rek lanou lat Dior alboury Ndiaye ak tirailleurs yi nio yame
@AboubacryDiallo-g2v
@AboubacryDiallo-g2v 2 күн бұрын
Mame gor yae touti ya bonn ya ignan, naan leu nit di yénné nit nbon ba diko feusseulé nit noon, Sénégal dou dém ndah sohor té bilahi cod mo gueun fouki mame gor vue que tu es pas un homme de valeur
@amynataniang7253
@amynataniang7253 2 күн бұрын
Waw goooooorrrrrrr
@mortallanakoyallatakhawulo303
@mortallanakoyallatakhawulo303 2 күн бұрын
Man dh kon tan na si dakh gui
@MassDiene-o9p
@MassDiene-o9p 2 күн бұрын
Doul yaw mame ngore yaw amoul lou niaw loo wahou le président diommay ak sonko yow ya geuna bone niép les var son la wolof néna sa nonou démbe dou meussa nék sa sopé tay
@cheikhoumane
@cheikhoumane 2 күн бұрын
Sa genre nak lagnou fi nara diape Adji Sarr gnouy dewale yeurmandé . Fi patriote yeupa wara jubilé té lolu dagnou koko wara yéné amoul lénén
@MaraSarr-m3m
@MaraSarr-m3m 2 күн бұрын
Ya. Sokhor. Kharal. Sa boss Dina. Nieuw ya done. Sagal PM Ousmane Sonko Macky sa papa. Dawna mbeuleeee
@morlo1034
@morlo1034 2 күн бұрын
Maïmouna boul fatte ne famille bi momone tele bi talibe serigne bara lan de et cheikh bara wakeur serigne bara lan donc source bi man na sûre!!!!
@cheikhtidianediop4914
@cheikhtidianediop4914 2 күн бұрын
CHEIKH OMAR DIAGN XAM XAM LAWAX SUNU PAS OAS YI BAMUYAXO TUTAY BANU BAYÉ ATTÉB YALLA DI ATTÉWO AY XILATE LA SUNU PAS OAS YI YAXU قال تعالى ومن لم يحكم بما انزل الله فاؤلئك هم الكافرون
@nafissatoudiopndiaye7589
@nafissatoudiopndiaye7589 2 күн бұрын
COD DOU SA MOROMOU BAYE.KHAM KHAMAM KHADIOUL SA BOP BOU BOUCHÉ BI
@papesouleymanesonko-gj6xd
@papesouleymanesonko-gj6xd 2 күн бұрын
COD wéréwoul mais Sénégal mo beuri nafèk, yow yèdal sa bop, pourquoi mou wara wakh Lou nigni geum au lieu de geum geumeum
@booparker424
@booparker424 3 күн бұрын
Ohhhhhh, tu quittes dans des informations, tu atterris dans des poulets et œufs 😅😅😅
@dioptv1532
@dioptv1532 3 күн бұрын
@@booparker424 🫣😂😂
@vinijr200
@vinijr200 2 күн бұрын
Yaw mame goor ha za back douma wax jazaka ndax yow xamoo daara té dinga iniane yaw waroo wax .. Xanaa légi .. Yaa bonne...
@mthodyndotty796
@mthodyndotty796 2 күн бұрын
MAME GOOR ,YOW DOUL .AMOULO XÉL ,AMOULO ,XAM XAM ,NIAKA NGA DIOM. FI SÉNÉGAL LA. KOU NEKK XAM NGA SA MOROM .LI NGAY WAX CI DIOMAYE MOU NGUI CI SONKO . LI NGAY WAX CI SONKO MOU NGUI DIOMAYE . RÉGIME BI DOU COMME BOU MACKY SALL AK AY FÉNE KATAM YI .SATHIE YI , DOOR KATT YI COMME YOW .LOFFI WAXONE DÉMBEU CI SONKO AK DIOMAYE MOU NGUI FI TÉGUÉ
@CheikhDiouf-g9f
@CheikhDiouf-g9f 2 күн бұрын
Dakh.bignu.dakh.cheikh.omar.diagne.gnéppa.thij.contane..
@sympathisante17
@sympathisante17 2 күн бұрын
Cheikh Omar Diagn mo wéré
@MalamineBadiane-sx8bo
@MalamineBadiane-sx8bo 2 күн бұрын
❤😂🎉😢😮😅😊❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ousmanediawara-fu7ek
@ousmanediawara-fu7ek 2 күн бұрын
MAIMOUNA NDOUR , FAYE , TEY DEH KINGA DONN WAKH NEH CHARLETAN ,BOUY TOKK DI FEN , DI WAKH LOUDOUL DEUG DIEUMEULEKO SI YOW AK SA ENTREPRISE, BOBOU BA LEGUI DEH , YALLAH ATTENALEN , BA DIOKH KO DEUG SISA KAW , NDAKH LINGA DONN NEUB TEH MOM DONN LA KO WAKH , NGAKOY WEEDDI , MELNI NA AMNA NDAM SISA KAW , BATAKH FI NG ANEKEU SI ENTREPRISE BOBOU SI DIAY LA DIEUM GUIR NGA MEUNEU FAY ALALOU DIAMBOUR WAL NIAKA LEEP.
@cheikhoumane
@cheikhoumane 2 күн бұрын
Dégak Mame Ngor manipulation yi mouy def rek nafék biga done Chrikh Omar Diagne fane la meuna téyé Sonko wala Diomaye. Sa Broukhlou bi dou mesa diale do meusa bokou si Patriote yi
@ousmanediawara-fu7ek
@ousmanediawara-fu7ek 2 күн бұрын
DEUG MO NAKAHRY YEUKEUTI AK DIKO WAKH SI REWMI, CHEIKH O DIAGNE NITOU DEUGUEULEU , DKOY WAKH TEH DIKO DEF , DA FEKEU NITT KESSE LEU TEH NITT MOY DIOUM , NDAKH LIMOU GENERALISE YIRAILLEURS NEH AYN TRAITRES LANIOU , NITTE MOY DIOUM , WAYEH NYI DEUGOU KHAMNANIOU NEH , DA DEUGOU, TEH NIEMEKO.
@mortallanakoyallatakhawulo303
@mortallanakoyallatakhawulo303 2 күн бұрын
Du histuoir dh womar jang si boppam mo mana doul
@PapeNdiaye-x5f
@PapeNdiaye-x5f 2 күн бұрын
Wa APR warou no sétane li dé comme niome mère bi niome lafi néka lone
@DiagneAbdoulaye-l5t
@DiagneAbdoulaye-l5t 2 күн бұрын
Seytane la.guenel sa lamegne si Diomaye.
@DBATH
@DBATH 2 күн бұрын
Moo le eupe xam xam fouf ! Tu es trop petit pour comprendre ce qu'il dit ...
@karimbandios4136
@karimbandios4136 2 күн бұрын
Mon frère sur le cadre de omar diagne il a tord 100%
@mamadoulaminesane9242
@mamadoulaminesane9242 2 күн бұрын
Si ce que vous dites de la télé de MNF est vrai, celui qui va acheter cette chaîne devra bien la reformater ou réinitialiser car là-bas tout est anti patriotes.
@ThioroFall-s8h
@ThioroFall-s8h 2 күн бұрын
Maimouna ndour lila dal yeup yako yobé sa bop moytoul di songou sonko si sankku rk lalay yobou Essayé d'être en règle aussi
@NdeyeMarieGueye-d5d
@NdeyeMarieGueye-d5d 2 күн бұрын
yaw va travailler
@CheikhNgom-jn4sw
@CheikhNgom-jn4sw 2 күн бұрын
Tu n as rien à direTu as dit pire a SONKO hier
@FatouDiedhiou-xo8mm
@FatouDiedhiou-xo8mm 2 күн бұрын
Finalement qui est le menteur
@AbdoulahadToure-vf4sk
@AbdoulahadToure-vf4sk 2 күн бұрын
Maïmouna ndour yaw doulnaliste nga manipulatrice nga cheikh bara ndiaye est 10mil fois plus crédible que toi
@myrkosow9781
@myrkosow9781 2 күн бұрын
Le charlatan l'histoire l'a donner raison
@NdeyeMarieGueye-d5d
@NdeyeMarieGueye-d5d 2 күн бұрын
ki mome tok mouy doh rek nafeck deug ngua
@amasam9455
@amasam9455 2 күн бұрын
MNF QUELLE HONTE ET HUMILIATION TU MENS.. TU N'AS QU'E 2 PROBLÈMES AVEC LA FRÉQUENCE AVEC LA FAMILLE NDIAYE TU AS DÉFIÉ SONKO PUBLIQUEMENT CHEIKH BARA A EU RAISON UN GARS QUI EST DEVENU HONORABLE DÉPUTÉ CHEIKH BARA A PIÉGÉ MNF
@kalidouba662
@kalidouba662 2 күн бұрын
Diazaka tu es nul 44 ans n'est pas plus jeune Amo xam xam Faux bay fall
@AbdouNdiaye-t2d
@AbdouNdiaye-t2d 2 күн бұрын
😂😂😂
@CheikhGueye-nh7de
@CheikhGueye-nh7de 3 күн бұрын
Kp
@AmadouGueye-y4e
@AmadouGueye-y4e 2 күн бұрын
Yaw mom yangui beug melna Oumar Diagne bayil doule
@khadijandiaye9347
@khadijandiaye9347 2 күн бұрын
Diazaka toi tu ne connais k tama ak sa chignon serigne dou sa morom.
@abrahambampoky-g5r
@abrahambampoky-g5r 2 күн бұрын
Mnf sache k cheikh a bien des renseignements.fais doucement la ou tu vas tes pattes
@IbrahimaNdiaye-q8o
@IbrahimaNdiaye-q8o 3 күн бұрын
❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
Sigma Kid Mistake #funny #sigma
00:17
CRAZY GREAPA
Рет қаралды 30 МЛН
小丑女COCO的审判。#天使 #小丑 #超人不会飞
00:53
超人不会飞
Рет қаралды 16 МЛН
UFC 310 : Рахмонов VS Мачадо Гэрри
05:00
Setanta Sports UFC
Рет қаралды 1,2 МЛН
l´invite d´infos matin | Dr Khadim Bamba DIAGNE, Secrétaire permanent du COS-PETROGAZ
33:06
Cheikh Oumar Diagne, limogé par Diomaye Imam Rafahi Mbacke sur les Dangers de la.....
18:16
SERINE AHMADOU RAFAHI MBACKÉ
Рет қаралды 81 М.
Sigma Kid Mistake #funny #sigma
00:17
CRAZY GREAPA
Рет қаралды 30 МЛН