@@YoussouphaThiam-xs1qw lui aussi il n'était pas parfait comme on nous la fait croire, kou dem ba dieul sa xel teko si sa diabarou domou adoptifam ba KO xamko fasse diabar dni yaw gua takako sa diabarou domou adoptifam loulou Lou gniaw la , Lou mom lo rousslola,
@Senegal221-e7v4 ай бұрын
Dieureudeuf mame seydi El haji malick sy yanou xamal yonenete psl ورضي الله عنه وأرضاه ونفعنا ببركاته ونعوذ بالله من الجهل والحسد
@ballaniang98624 ай бұрын
Dieureudieuf mame maodo .cokou doukou reer
@SeydinaAlioune70024 ай бұрын
Mame Maodo yallah naniouko yallah fayal ma challah 🙏🏾
@Sam10ekl4 ай бұрын
Jazakallahou khayran oustaz Fadel c'est vraiment pertinent qu'Allah te protège.
@SeydinaAlioune70024 ай бұрын
Sa wax diaxasona dh may guissou mafi lofi léral Maodo kén dou wéranté xam xam ba ma challah😁😁😁
@moustaphandao10794 ай бұрын
Lakhawla wala khouwata ila bila..... Mbok Liga wakh ci elhadji Malick wéroul . Maodo limou wakh ci yonénte bi psl ci khilassab walahi Lou weur leu Mbok Maodo diambar leu ci diné islam Yalla nagnou KO yalla fayal
@BaraSamb-de7es4 ай бұрын
Amine gni danio sokhorr
@aliunediop57854 ай бұрын
Soukran ya oustaz ❤
@gorafall22364 ай бұрын
Yena sokhar danguene de
@AliouneDiallo-h1i4 ай бұрын
Wakholene fi dara loudoule fene dieureudieuf cheikh seydil Malick Sy 🥰
@LamineSakho-iq5bd2 ай бұрын
جزاك الله خيرا يا شيخ الحاج مالك
@mbayeniang87774 ай бұрын
ما شاء الله جزاكم الله خيرا
@FATHULMUBIENSATV4 ай бұрын
Masha Allah diazakoum Lah khaiyran Oustaz Fadel Li moom deug Leral ba ler nagggnnnnnnnnn ❤❤❤❤
@arounatv87074 ай бұрын
wakh léne ba ba géne sona mais Mame Modou rekh point
@arounatv87074 ай бұрын
seydil Hadji Malick Sy Malick m'a sa médina moy mi si Tivaone dak kamkhm❤
@Le_Natron_4 ай бұрын
Yaye doff deug 😢
@adamangom86114 ай бұрын
Mame maoda moy kham kham yaw dama ma yérém ndésane
@AssaneDiop-w5m4 ай бұрын
Machallah barakallahou fikoum ahlou sounnah yalna yalla samou alxouran ak sounnah
@authentiqueislam4 ай бұрын
Barakallal fiykoum yàlla Na Borom bi sammlennn té barkel sëñ dahwaa bii amna soloo
@AbdouFall-o5n4 ай бұрын
Yéne gueumo léne yalla sakh danguéna rére
@assaneniang21334 ай бұрын
Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA sàmm sàmmal nu, aar aaral nu, taxawu taxawul nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xam xam yi ragal sunu BOROOM YÀLLA.
@malickgueye75144 ай бұрын
boudone yéne rék sénégal yeupeuyrér
@modoudiop25164 ай бұрын
Sene data yaye😂😂😂
@fatoumatabintoucolley88784 ай бұрын
Lii guen meun yow sa yaye loum yorr
@modoudiop25164 ай бұрын
@@fatoumatabintoucolley8878 daga mer bolle nalla si saga bi 😂😂😂😂
@Le_Natron_4 ай бұрын
Limoy seu Idiaba ci yone bi ??? Saga rekk
@modoudiop25164 ай бұрын
Yaw limou wakh kouko wakhonn sa papa noye déf répondre moi
@mariepaulediop94334 ай бұрын
Oustaz Fadel je vous salue, svp serait 'il possible d'avoir une vidéo sur la discipline dans l'islam et dans la société merci
@AlassaneSidibe-o8f4 ай бұрын
Mame maodo ❤❤❤❤
@IbrahimaNdiaye-s7p4 ай бұрын
😂😂😂 yéen nopalou leen domeram yi doul rek geenii def doleen jamais Lou bax
@masiba72724 ай бұрын
Sounou Serigne kay mo doul xana degoulo limou wah si teree bi?
@arounatv87074 ай бұрын
@@masiba7272ki kamol drra
@paapnjaay15864 ай бұрын
Maasaa ALLAA Yaa Ustaaz ! Sunu BOROOM wax lu leer ni MI ngi ñu binde ci ban ba nóppi, keneen ñëw di wax waxi leer. Li ci metti ba metti ci mooy waxkat yi ci yii rek la ñu nékk ak taalibé yi: YONÉNT BI (a I s s) nii LA (a I s s) juddoo, waxtu wii LA (a I s s) juddu, néeg bii LA (a I s s) juddoo.... Yii yépp réere léen teewul kénn doon ab jullit bu wér.
@omarjobe81874 ай бұрын
وإنه إذ أراد الله ليس ❌وإنه إذا
@KhadijahDiop-d1w4 ай бұрын
Très pertinent sur le sujet qu’Allah vous assiste ❤❤❤
@assaneniang21334 ай бұрын
Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA nangul, nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yònnent bi SAAWS akiy sahaabaam RAA te wërsëgël nu nu dëkkag ñoom ca kërug teràngaam.
@AbouToure-mg9oc4 ай бұрын
Salam . Pourquoi vous ne attaquer pas les non musulmans. Le combat est inter religieux. Vous etes tres en retard
@assaneniang21334 ай бұрын
Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA wan dëgg bamu leer, MU yombalal nu tòpp ko, MU wan nu neen bamu leer, MU yombalal nu dùmmóoyu ko.
@PapeMbayePape-tf5ju4 ай бұрын
Dahwa bi doxul dé Ate mou nék bidah bi di gëna xoumb🤣🤣🤣
Machalah dieuredieufe imam fadel Ndiaye leral yi amna solo yalla na la yalla faye billahi louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna
@BachirBadji-d5t4 ай бұрын
Alpha ba bi khamoul tounou ndeyeme di fene yaw tu sera devant moi
@mercifulservant55264 ай бұрын
Limamou da feterou,mom mon jeul coupe fen
@Le_Natron_4 ай бұрын
Dett waye
@mlbhero794 ай бұрын
Sen ham ham si téré yi la yamm lolou kassé moy problème bi dég dég yi dou manna bokkou
@arounatv87074 ай бұрын
Mame Modou kamkhm rékh démal jangui ba jékal so Akcé mo jangalla yaw kallé Tivaone rékh monala jangal kamo drra
@diallomouhamadousaidou64334 ай бұрын
Si vous avez les connaissances nécessaires des corrigers certains erreurs des nos pieux parents ou marabouts nous vous attendons à écrire et d’influencer comme ces qu’il ont fait n’oubliez pas qu’il ont combattu les colonialistes et ces a vous maintenant des combattre les influenceur occidentaux et les mauvaises comportement si vous êtes véridique
@KAADUDINEEJITV4 ай бұрын
Non, par contre, lui aider collaborateur des colonialiste essaye de vous renseigner. Je pense que vous êtes en retard. Le train vous a laissé ici. Désolé mais essaye de grimper vous allez vous rendre compte de votre ignorance de ce collaborateur que vous considérer comme étant des parents ou Marabouts
@Mansourfall33334 ай бұрын
إتق الله يا أخي
@sakhoousmane70664 ай бұрын
Machala sén leguey rafet na torop
@KhalifaaboubakreNdiaye3 ай бұрын
Yénn gneup salafistes yi séne data yaye sa sougén yéwo ay domou ndiallo guéne motakh liguénii wakh safoul khorom safoul soukeur Alko molén diapp rékk mame maodo doussén moromou bay
@KhalifaaboubakreNdiaye3 ай бұрын
Yaw mom alfa dagua doul ba kénn khamoul loy ndirol domou ndialo gua motakh ligay wakh dou nakari kénn 😂😂 En plus sougnou mak gni liléne yalla défal koumou nakari kalamél yalla
@AmadouFall-z1o4 ай бұрын
Diangolene khamolene c'en bopou khamolene yonente bu bay kham yalla
@talibecheikhtidiani56114 ай бұрын
Mandou mo gueune si ap djoulite
@KAADUDINEEJITV4 ай бұрын
هههه hahaha yaw loutax Mandou woo après avoir regarde la vidéo
@KAADUDINEEJITV4 ай бұрын
Bayileen tàpale Way tee yeewou dji gayi nongui yeewou de hahahahaa
@IbrahimaNdiaye-s7p4 ай бұрын
@@KAADUDINEEJITV yow domeram ga katal sa deye😂😂😂
@IbrahimaNdiaye-s7p4 ай бұрын
@@KAADUDINEEJITV sa kooyou baay , bo bayiwoul ligay def Dina tepii sa leufeul deye 😂😂😂😂
@Le_Natron_4 ай бұрын
@@IbrahimaNdiaye-s7ptilimal nga yone wi ak say Saaga😢
@AmadouFall-z1o4 ай бұрын
C'en sarapap Ndeye rete demlene diangu ta nopalou
@deugeurek4 ай бұрын
Salam oû est alpha bâ ?
@Le_Natron_4 ай бұрын
Alpha Ba n’insulte que les Mourid 😢Mais jamais la famille Omarienne ni tivaouane car ses Parents Hal Pular y sont nombreux 😂
@IbrahimaNdiaye-s7p4 ай бұрын
Ken 😂xamoul loleeni dourool nii rek
@ndawabdoulaye97544 ай бұрын
ARRETEZ WAYE
@KAADUDINEEJITV4 ай бұрын
Vous n’avez pas encore rien vu ça, ce n’est qu’une publicité
@KAADUDINEEJITV4 ай бұрын
Patienter reste, avenue, sera plus tragédie pour vous et vos faux marabouts
@mbayecisse35944 ай бұрын
Yagui fenn rek niy ngay sik nio la gueun guen sa au weydiour arrête imbécile
@fatoumatabintoucolley88784 ай бұрын
😂😂Arretez Kaylen niou Debat kon guen khamni leup deugue leu😂😂
@adamangom86114 ай бұрын
Yaw dama la yérém
@masiba72724 ай бұрын
Donc affaire bi dou Serigne Touba rek ndeketee sama wadji tamit wahna lou melni?