Maccallah leip lu ma ibra fall donn deff wala lumu amm cii mbotu barhama la ,Kom bamou tuki Nigeria tawat talibem tasaruf cii kholy talibe yii ba kenn munul sakh yeketi loho ba baye dugou cii auto bii tii leip cii mbotu barhama la.nangeh dioumbuna mii tahawal sakhari tubab yii leip cii mbotu barhama la kon wakh nii sa serign mo Munn baye lolou mustahil la.