masha'Allah ya Oustaz magui toub cy tarder bi bou weer
@batimentconstruction76214 жыл бұрын
le messi du tarikha chiekh franchement nous sommes tres content de vous . nous les talibés cheikh merci infiniment ❤❤❤❤❤❤❤❤❤â
@بابكرسيك4 жыл бұрын
Boulbole foo ak deugeu yeufeur yigaytoudou silii bakhoull waye
@ousmanelo12534 жыл бұрын
Jaime cheikhou tidjane chérif rta❤❤❤
@talibecheikhndao60854 жыл бұрын
Moi aussi
@babacartoure83363 жыл бұрын
Vous avez de la chance
@alamine42304 жыл бұрын
Deug deug Serigne Daara ya ngui gnouy sagal di gnou bégueul sa souné. Yaw dale fatabarakallahou ahsanoul khaliqina rek. Yalla na gnou la Yalla samal rek. Mane souma dioté notification bi douma ame diam fi ak sétanou mako bamou diékh walahi.
@mamadoudiouffall4144 жыл бұрын
Barakallahou fikoum.....! Amna solo trop, toujours heureux d'écouter les paroles sages de as sheikh Ahmed Faal... Pédagogie épatante, rhétorique hors norme, et logiques plus que scientifique... Merci sheikh bii..
@mamoudoutoure45674 жыл бұрын
Sama Soppé bi dafa Éloquent,dafa sage, dafa précie et walahi dafa éclair.... thiakhan bakhoul Nanou dém diangui... walahil aziim xam xam bou léér ga am manchalah..yalla nala yalla ar té yook léérou xam xam bi thi barké Nabiyyouna mouhamad aléyhi salatou wa Salam
@wakhdeugguetayallatakh81294 жыл бұрын
Ma challakh cheikh ahmed fall Yalna yalla fayla ci barke seydina mouhamed saw barke cheikh tidiane cherif rda 🤲 Dama lay khol rek walla xalaat sama khol di bekk
@geuyefamily68074 жыл бұрын
Dierediefe seydil khadji malick sy ak wa keurem mercii oustag ahmet fall yag fii loll tse weurr
@ibrahimasenenabien12044 жыл бұрын
Dieuredieuf fati Serigne bi Yalna yalla goudal fan wi yokla wèrr YA Rabi Barkèb CHIEKH SEYDIL AHMADAL TIDJIANI
@aramendiaye64644 жыл бұрын
Macha allah macha allah comme d'habitude defatinga sa monin yallah na yallah laf thiat yallah samma te arla yirla lakkala fa yak eggoul Goudou fan ak weer ak weerle ci barke seydina Mohamed saws amin ya rabbi
@ousmanediallo89724 жыл бұрын
dieuredieuf Serigne Ahmad Fall yallah na yallah fayla yiw barkel sa liguey takhaw bi rafetneu yangui si tankou souniou Serigne daara Seydi Aliou Harazimi lep loumou diote si yiw rek yallah nanga si sédou
@srbathiediop48544 жыл бұрын
Weral yagal si barké salatoul fatihii si barké Abbul Abbas At tidianii sunu lepp 🥰😍
@abbatalib77314 жыл бұрын
Non bilahi Ahmed lingay wah nehna❤️❤️❤️🥰😍🥰😍
@mathiorodiagne10543 жыл бұрын
Al Hourane bi néekh n'a✨rawatina pirima✨ MachaALLAH ✨ nieupeu leu déégueu✨ Alhamdou LILAH RABBIL ALAMINA 🌟
@بابكرسيك4 жыл бұрын
Kholbou sedda gouye ni galass تيسير وتوفيق عليك يا سيد شيخ أحمد فال وكل من قال آمين
@amadyba61534 жыл бұрын
Yalna yalla doli la takaway
@mouhamedmbaye16464 жыл бұрын
Machalla seringe bi bégueti rék ndakh nioune talibé cheikh liii moy dundel souniouy roue ak souniouy khol. Yalla na yalla goudeul sa fanne🙏🙏🙏
@fatoumatadiop62764 жыл бұрын
Dieureudieufaty sunu professeur yalla na la yalla diappalé té defala soutoura ak goudou fan ak werr. Ngnou ngui diangua bou bakh machallah
@papebilalattidianicherifdi50194 жыл бұрын
Honnettement vous faites la fierté de la connaissance tawfikh rek mbok bi iznillah amine in shâ Allah.,.
@diawfanta91834 жыл бұрын
Waleyka salam warahmatoula ya ahy barakalah fikh diazakalahou haïrane yalna yala nangou gnane yeup inchalah yalna la yala same ya Ahmed fall
@Ndanaan2.04 жыл бұрын
Serigne Ahmed Machallah bayi nagnou leu ak cheikhou tidiany RTA. 🙏
@talibecheikhndao60854 жыл бұрын
Machalla oustasse ahmad fall yalnala yalla fayall bopame bi diahi Moustapha stw.
@ablayesene97034 жыл бұрын
Wa hanleykoum salam wa Rahmatoulahi tahanla wa barakatou 🙏 Dieureudieufati Serigne dara Yalna yalla fay lenne yiw iow ak gnigua bokal loguey bi yeup 🙏🙏🙏✅ yalla mayniou degu ak top barki yonenete bi S.A.W🙏 Wormay Cheikhou tijani R.T.A🙏
@oumardiallo99564 жыл бұрын
Machallah merci beaucoup. Qu'Allah vous rétribue pour cette retranscription
@mathiorodiagne10543 жыл бұрын
YALLAH na la YALLAH lafale Thiatt. Amine bi hahi SalaLAHOU Alayhi Wa Salama Hayroul Woudjoudi ✨ Amine
@aramendiaye64644 жыл бұрын
Puular ma weli macha allah tabarakallh fiqk yallah nala yallah fay yiw yokkou say kheuweul amin ya rabbi
@Abdsr87354 жыл бұрын
Cheikh Ahmad Tidjany RTA mo Bari Teguine MashaAllah ! Serigne Ahmad Dieureudieuf ! Di yakamti lol say cours !
@layesene46774 жыл бұрын
Wa alaykoum salam sounou serigne daraa
@seckseck33924 жыл бұрын
Pourtant les soufi sont de véritables philosophes ( qui s'intéressent à toutes sciences ), thiey Maodo ak Maths, ak physiques, ak astrologie, ak, ak,.... 😀😀😀 Dieredieuf Cheikh Ahmad Fall
Machaa Allah Jazak Allahu Khayran Serigne Sheikh Ahmad Fall : Des Enseignements si précieux ; avec des explications délivrées avec autant d'éloquence magistrale. Merci infiniment de nous distiller autant de savoirs et de connaissances, à la Lumière des textes sacrés. Qu Allah Ya Rabbi vous rétribue et vous Comble de multiples Bienfaits Amine
@amethdiop81454 жыл бұрын
Dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf
@abdoultouray49344 жыл бұрын
Merci une fois de plus pour ce travail combien important. Que la récompense découlant d'une bonne oeuvre vous soit décernée par LE TRÈS HAUT et de par les grâces accordées au meilleur des êtres et au sultan des pôles.amin.
@mamadoumbodj68164 жыл бұрын
L’homme au plus que parfait 😍
@mathiorodiagne10543 жыл бұрын
MachaALLAH ✨✨✨
@babacardieng43234 жыл бұрын
Alhamdoulilah yalla na yalla motali Lep si barké cheikh Aboul Abass Gayi geudié hamatoul machallah❤❤
@mamadousow14704 жыл бұрын
Machalla barakalahou fik ya oustaz contane naniou trop si yaw Yallah nala Yallah yokou xam xam bi bi barakati Seydina Akhmed tidiane cherif rta aminn
@alioundiaye51204 жыл бұрын
Yaw deh bou léron kon gua toj fi... djam si yaw...sa souné inchallah
@diopdiop96354 жыл бұрын
Yalna yalla barkél
@walybakayoko75084 жыл бұрын
Machallah yalle na yalle goudal sa fane allahouma amine 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@souleymanedieng77044 жыл бұрын
Dieureudieuf Sebnbi gnion gui ziar bou bakh
@ismailaattidjaniba6414 жыл бұрын
Cheikh dall yamoutak kén si lénn walahi 🙏
@aliounendiaye94994 жыл бұрын
Ken dou cheikh abdou hamid sarr rta bilay kep koukoy deglou dangay moudje dof ndakh dof dou diomi kep kou wakhati gnu xam ndakh yangui ak audio yi machalla yalnala yalla fay te fayal gnuko momit mi leralat mbir yi
@Steven-ul8pw4 жыл бұрын
Machalah sunu sopép sopé yi geuna dound geuna wér yallna déf barke ak sutra yalla motali sa yéne si hadara bi Basi kanamu seidna Cheikh Ahmada'Tidjani A'sariifil Fatimi
@tallasarr75602 жыл бұрын
MACHALLA 🙏 🙏 🙏 🙏 🙏
@abdoulayembaye97004 жыл бұрын
Machalla darse bi amatina solou
@tanguy16744 жыл бұрын
MACHALLAH Serigne bi niongui lay ziarr bou wér ❤❤🙏🙏
@serignebasirumansour68434 жыл бұрын
جزاك ربك يا حبيب مختار خيرا وأنت أيا خليل مشكور
@AL-AMAANA-TV4 жыл бұрын
ماشاء الله 💖💜💛💚💙❤💟💝💘💗
@malickfall2604 жыл бұрын
Mashalla serigne Ahmet fall. Merci Qui'Allah te rerribue en biens
@mouhamedsow2213 жыл бұрын
Barak'Allah fiik Ya Cheikh ♥️
@seynabouniang14244 жыл бұрын
Kane momay yobou ci oustaz Ahmad fall? Yangui seral sunu hol yalna yalla fayla serigne bi
@mbdone38604 жыл бұрын
Mashallah
@layesene46774 жыл бұрын
Allah
@souleymaneba67674 жыл бұрын
Jerejeuf Serigne bi 😍😍
@institutislamiqueseydinamo18364 жыл бұрын
Serigne Ahmed fall merci beaucoup pour votre retour
@mouhaton4 жыл бұрын
Trés Bien ! Alhamdoulillah
@kamalseck2414 жыл бұрын
Yana yalla gudal sa fane ....
@babacargueye31784 жыл бұрын
Machalah ya oustaz xam xam bi machalah yalna Yalla takhwou tei soutoural la tei barkel la...
@papandiaye94194 жыл бұрын
Yalla naniou yalla deff ay degg deggg talibé cheikh
@papisdiagne48673 жыл бұрын
Dieuredieuf ya seydi
@goraniang47324 жыл бұрын
Alhamdoulillah ❤️🙏❤️ Machallah ❤️🙏❤️
@mouhamadoundiaye11164 жыл бұрын
Machallah diambar ngua niongui lay suivre depuis France
@ibrahimadiagne82184 жыл бұрын
Yalna Yallah fayal nioula serigne♥️🤲🏾
@ndiaganiang5704 жыл бұрын
Machaa ALLAH. Yalna bour YALLA barkeel
@diagnebabou15924 жыл бұрын
Dieuredieufaty fall
@globacell23884 жыл бұрын
Machallah ya Imam. Ahmad fall
@babsann17554 жыл бұрын
MAA challah 🙏🏼🙏🏼🙏🏼 YALLA nalla yalla Faye si barakati sa Serigne....
@ibrahimaniang10104 жыл бұрын
❤️❤️❤️
@cheikhamadoutidianidieng99274 жыл бұрын
Merci encore et infiniment
@ndiagandiaye75134 жыл бұрын
salatoul fatihi
@abdoudia24383 жыл бұрын
Waay ma contant dieurdieuf
@geuyefamily68074 жыл бұрын
Diarama chiekh seydi ahmada tidiany
@aminatasarr10814 жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@keurmamekhortvlefrerededj29164 жыл бұрын
Oustaz doma diangal
@cheikhouldtaha79014 жыл бұрын
Manchallah l’homme a son heure
@fatoucisse36364 жыл бұрын
Machallah ♥️♥️♥️
@mouhameddiop01122 жыл бұрын
💖🙏🏿🙏🏿🙏🏿
@papaamsatougaye46074 жыл бұрын
AL HADOULILAH OUSTAZ CONTENT NAGNE CI YOW
@leuzleuz86024 жыл бұрын
Mâcha Allah
@mouhamadoumansourndiaye23724 жыл бұрын
Chaukrane lakaa
@falltalla18074 жыл бұрын
Machaa allah
@ndeyeamiwillane57834 жыл бұрын
Masha Allah
@baboucardiop16384 жыл бұрын
babacar diop.merci beaucoup pour ce cours si important, mais permettez moi de poser la question suivante : si djibril est apparu devant le prophète (paix et salut sur lui) sous sa forme angélique, avec tout le gigantisme qui le caractérise ,comment a t il pu se déplacer dans une grotte ? cela mérite des explications. merci pour tous efforts consentis pour nous éclairer. respect et salutation notre cher professeur