Doudou Sané tape sur la table : "Eumeu Sène dou beuré ak Franc té ma nék fi..."

  Рет қаралды 25,631

Lutte TV

Lutte TV

Күн бұрын

Пікірлер: 134
@siyakhafadiga1773
@siyakhafadiga1773 6 ай бұрын
Doudou da bary diamm nk bly wly champion la ❤️💪🏽💪🏽💪🏽
@RidialThiam-l3f
@RidialThiam-l3f 6 ай бұрын
Merci bcp 🎉🎉 woly le Roi sane seul borom Diofior goudi goudi Diofior 🎉
@faye6718
@faye6718 6 ай бұрын
Le roi sané❤❤❤ bon chance talibé Serigne Fallou bi ❤❤
@adadiop7645
@adadiop7645 6 ай бұрын
Doudou sané man damko bague day rétan rk nitou diam la😂😂
@boukane4713
@boukane4713 6 ай бұрын
Doudou daay ré rek 😅😅😅
@faye6718
@faye6718 6 ай бұрын
Bilaye mé thi bir géwe do guiss bogne bi😂😂
@diaibrahim6798
@diaibrahim6798 6 ай бұрын
Merci champion ndam rk inchaallah 🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
@moussa1257
@moussa1257 6 ай бұрын
Wakhna deugeu caye combat la❤❤❤❤
@AliouKama-zs9ye
@AliouKama-zs9ye 6 ай бұрын
Merci wouly de pouvoir soutenir doudou sané ❤❤❤❤❤
@leuz.patriote
@leuz.patriote 6 ай бұрын
Bilay lambj mingui soga nkh nak😂😂 mod lo nèna kèp kou beug beurèk mom diaral si franc😂 eumeu tmt defal lolou doudou sane franc 😂
@mansourdiouf4409
@mansourdiouf4409 6 ай бұрын
Athia champion yalla sa diamou yague yalla maye la ndame bou séde gouye bilaye je suis fière de toi 💪💪💪💪😱
@SaliougueyeSaliougueye-r2z
@SaliougueyeSaliougueye-r2z 6 ай бұрын
Merci doudou ligue défff ni contan nasi fran naleu dieul
@afro3827
@afro3827 6 ай бұрын
Doudou franc mola raw nak 😂😂
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 6 ай бұрын
Hana Eumeu sène rawoul Franc 🤣🤣
@momoseck1617
@momoseck1617 6 ай бұрын
Future champion
@GoraNdiayeKarim
@GoraNdiayeKarim 6 ай бұрын
Merci doudou bien dis
@boubacarlimanbadiane8668
@boubacarlimanbadiane8668 6 ай бұрын
Doudou sané❤❤❤❤❤❤
@ouzinndao11
@ouzinndao11 6 ай бұрын
YALLAH NALA YALLAH DEFAL DIAM DOUDOU ❤️
@mamesambaGueye-i5z
@mamesambaGueye-i5z 6 ай бұрын
Doudou machallah ❤️🫶💯
@bigmoleepdinaleer6955
@bigmoleepdinaleer6955 6 ай бұрын
Doudou reck❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@foreveryoung29
@foreveryoung29 6 ай бұрын
Doudou bo nkkone nitou deug Serigne Ndiaye ak Quench guay wakh Franc doussa morom
@abloslimshady
@abloslimshady 6 ай бұрын
Doudou sané bou l am sax yakamti dieuleul claf bi rek! Yak franc wala sathies day takhaw force!
@Mo13092
@Mo13092 6 ай бұрын
Franc wala sathies nga wakh😂😂😂 Ki serigne ndiaye sakh beugou ko
@jpsf687
@jpsf687 6 ай бұрын
Champion nga mais franc dou sa morom
@DiedhiouAbdou-zc7wj
@DiedhiouAbdou-zc7wj 6 ай бұрын
Fran lane la eupeulé Dudu
@badiafaye5314
@badiafaye5314 6 ай бұрын
Wawa roi sané 💯💯💯💯♥️♥️♥️♥️
@PapemamadouNdiaye-ux9xb
@PapemamadouNdiaye-ux9xb 6 ай бұрын
Doudou rek
@AsssaneSene
@AsssaneSene 6 ай бұрын
Doudou rek❤❤❤💪👈
@khadimsylla35
@khadimsylla35 6 ай бұрын
Yaw topal fale 😂😂😂 Fran eume sen moy wakh dji
@Aaron-i5f
@Aaron-i5f 6 ай бұрын
Dou beurè ak mbaam cochon
@mamadounguom4992
@mamadounguom4992 6 ай бұрын
Franc defoufi guate Di lathie eumeu sene c vrai ame n'a 13 victoires mais bane mbeur bou âme qualité lafi dane loudoul Bombardier fin de carrière âgé de 49 ans té meune nako diour
@LeprinceVegeta-f6i
@LeprinceVegeta-f6i 6 ай бұрын
@khadimsylla35 Yaw key ya wara topp feulé eumeu loumii doyé franc?? genre souko daané loumkoy apportél?? franc mo toppou si guinawam.. té beurék nite dou force.. modou lo moungui nii écarté reug reug té kéneu meunou si dara c la même chose.. bane sens la am di forcer.. sathies contre franc dh mo geuneu logique sah que eumeu contre franc même si sathies mo raw franc ,reug reug sah raw franc(adversaire youm dane yé geuneu kii) té dannako 13x armér rek lako daanoul.. franc meunolêne-ma wah lou extraordinaire loumfi déf ak diélou bou graw boumou meusseu dane loudoul tour bi rek.. sénégalais mo meune dieulaté rek quoi comme ay khar.. même ada fass daméy dégg nite yii nane dafa graw alors que 6 combats rek leu beuré + combat you tangoul
@Babacar-l9g
@Babacar-l9g 6 ай бұрын
Doudou sané le grand champion môme dafa geum bopam bilahi
@mouhammadndiaye7358
@mouhammadndiaye7358 6 ай бұрын
😂😂😂Ndiaga Dollé ngafi dane d
@adamagakou8856
@adamagakou8856 6 ай бұрын
Ak garga 2
@mouhammadndiaye7358
@mouhammadndiaye7358 6 ай бұрын
@@adamagakou8856 batay dou niveau Franc.
@adamagakou8856
@adamagakou8856 6 ай бұрын
@@mouhammadndiaye7358 okei franc ak eumeu esk niveau la
@mouhammadndiaye7358
@mouhammadndiaye7358 6 ай бұрын
@@adamagakou8856 motakh gnounane may chance. Kou bagnoul serign Ndiaye 2 mi Franc dane waro bagn Franc. B52 leu dane
@kefgg
@kefgg 6 ай бұрын
​@@mouhammadndiaye7358Garga 2 niveau franc leu kaye
@MilkMilo-qr5uc
@MilkMilo-qr5uc 6 ай бұрын
Franc gnanou kéne chance néxx beuré nakari beuré force la sarakh ndonga dara wala mou tibal bopam force nak
@josephcoly4127
@josephcoly4127 6 ай бұрын
Force le ki claf boumou nk li yone gayi nioko tey daniou ko beug outal yone li dou deug waye pourkoi defouniousi ay mbeur you ame dollé
@kefgg
@kefgg 6 ай бұрын
​@@josephcoly4127Non d'accorouma dh Doudou Sané kene outalouko adversaire you yombe. Boul faténi Garga 2 mo nekone si poule B Claf bi té modone favoris si kawe Doudou Sané. Meme General Malika dafa narone bokou si Claf bi. Claf bi yomboule dh amoule ay outeule yone dh bien que Boy Diakhao moy lolou 😂
@cheikhtoure590
@cheikhtoure590 6 ай бұрын
Merci roi sané franc nala diall
@boubacarthiam6120
@boubacarthiam6120 6 ай бұрын
merci doudou sané... Ndiago wakhkatt bi bala mo beuré ak killifeu gui na diarr si yaw ba paré
@bahosmantv1521
@bahosmantv1521 6 ай бұрын
Fran tamit dey def comme eumeu sene reck dou moussa mbeur ak wa écurie eumeu adouna nonoula
@LeprinceVegeta-f6i
@LeprinceVegeta-f6i 6 ай бұрын
mom mo sohla eumeu dh eumeu kholouko.. mo topp si guinaw eumeu.. eumeu souko daané apportéwouko dara.. na déf louko néh c son probleme.. yéna fouyeul yêneu mbeur yo khamni défougnfi dara lou extraordinaire modoulo écarténafi reug reug té pourtant motay dagnkakaa nangoul lolou dou dara
@foreveryoung29
@foreveryoung29 6 ай бұрын
6 combats gua am Franc dou sah tontonté ak ioe
@momoseck1617
@momoseck1617 6 ай бұрын
Kone modou lo Dou beuré ak site
@amdydiongue-k1n
@amdydiongue-k1n 6 ай бұрын
Merci bcp doudou eumeu xam xam séne dou moromou béne mbame xoukh😂😅
@mansourkane1426
@mansourkane1426 6 ай бұрын
Khana Wa baye moye mbam khoukhe 😂
@josephericousmanediandy783
@josephericousmanediandy783 6 ай бұрын
Frère liii sport la rek deilein fair play li diaroul ay mbam xouxx wala chiens li yeux Dina diexxx . Kaadu dafay rafettt sa yaye yarnaala fimoula wara yaréeee donc respectel valeur yimou la dioxxx té xam fingua diougué , mbeur yi xamanté naniou thi seine birrrr. Amal touti respect
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 6 ай бұрын
​@@josephericousmanediandy783merci frère au moins yow yarou nga,hamga aduna,sa genre yi la meuna wahtanal,boyi dénio yaradikou trop
@josephericousmanediandy783
@josephericousmanediandy783 6 ай бұрын
@@moussapayemane4167 douniou ay sportifs et xamouniou lou bariiii thi adouna motax mais toujours commenter Nay andeu AK yarr rek
@amdydiongue-k1n
@amdydiongue-k1n 6 ай бұрын
Meno lèn mbél mbéli ba eumeu xam xam séne beurék béne mbame xoukh.
@bayeratebayerate5893
@bayeratebayerate5893 6 ай бұрын
Yaw doudou sane yaw aka eume sene franc moy sane baye
@papengom259
@papengom259 6 ай бұрын
Le roi sané❤❤❤
@AblayeGueye-vl4ik
@AblayeGueye-vl4ik 6 ай бұрын
Ndam rek Doudou sané
@mamadoudiouf5297
@mamadoudiouf5297 6 ай бұрын
Doudou Sanè rkk🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
@papezulefaye7263
@papezulefaye7263 6 ай бұрын
Le roi sané seul...rakkou eumeu sene ndam rkk inchallah niom nieup yaléne meun
@josephcoly4127
@josephcoly4127 6 ай бұрын
Forza dal mongui fi
@abdoulayendoye1803
@abdoulayendoye1803 6 ай бұрын
Boy ioe legui danga beuri waah Doudoune moytoul projecteur yi
@mamadousene3731
@mamadousene3731 6 ай бұрын
Boye ki projecteur yéko top mé mome topoule projecteur yi dé.
@akadtv661
@akadtv661 6 ай бұрын
Kii xawma wone nii la yaroo
@khadimdiouf2076
@khadimdiouf2076 6 ай бұрын
Bilahi yw ak eumeu bene jour franc moleen meun
@ebrimajoof2211
@ebrimajoof2211 6 ай бұрын
Wakho dega deh 😂
@modoubarasene9678
@modoubarasene9678 6 ай бұрын
Doudou❤
@siteu_n77
@siteu_n77 6 ай бұрын
wouli xana sponsor la legui😂
@IbrahimaDiouf-bz6lo
@IbrahimaDiouf-bz6lo 6 ай бұрын
Doudou sané Lou lerr lay wakh ki dou boyou kenn deflénn dang rékk
@ElijahMohammad863
@ElijahMohammad863 6 ай бұрын
Doudou Sané ani say beutt😂😂😂
@barryleskinge3676
@barryleskinge3676 6 ай бұрын
❤❤😮
@MDbousonko
@MDbousonko 6 ай бұрын
Doudou sane mok franc moy combat bi
@bahosmantv1521
@bahosmantv1521 6 ай бұрын
Fran tamit dou mousa beure ak wa écurie eumeu sene adouna nonou la fran dina fii har doudou sané ay vrai nafekh
@Muhammed7800.
@Muhammed7800. 6 ай бұрын
⁠@@bahosmantv1521wola yaw yay nafekh bi kuy fran beh dou beure ak doudou sane?
@bahosmantv1521
@bahosmantv1521 6 ай бұрын
@@Muhammed7800. eumeu sene defa bagne fran tamit dey bagne beure ak wa écurie eumeu sene adouna nonou la
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 6 ай бұрын
Boye déléne wakh lamb nguir yalla 🙄🤔😒
@kefgg
@kefgg 6 ай бұрын
​@@bahosmantv1521Modou Lo dafa bagne beuré ak mak yi kone mak yi tamit dagni bagne beurek poulain wam Franc adouna nonou la
@MamadouSarr-ql6it
@MamadouSarr-ql6it 6 ай бұрын
Dou sané rek
@RioDoudou
@RioDoudou 6 ай бұрын
Doudou sané franc moy combat bi
@bahosmantv1521
@bahosmantv1521 6 ай бұрын
Fran tamit dou mousa beure ak doudou sané dax eumeu sene
@kefgg
@kefgg 6 ай бұрын
​@@bahosmantv1521Eumeu Sene tamit dou mousa beuré ak Franc ndakh Modou Lo mo bagne beurek grand yi
@bahosmantv1521
@bahosmantv1521 6 ай бұрын
@@kefgg modoulo mbeur na ak VIP yeup waxal Lou diadou
@kefgg
@kefgg 6 ай бұрын
@@bahosmantv1521 beuréwoule ak Tapha Tine
@bahosmantv1521
@bahosmantv1521 6 ай бұрын
@@kefgg mais dina beure ak tapha tine inchallah defa mérite combat royal
@BabacarGueye-et3ih
@BabacarGueye-et3ih 6 ай бұрын
Nit kou bakh lay nou ral doudou Sané
@Deggou
@Deggou 6 ай бұрын
Meme mbeur yi daniou soxoré franc , donc eumeu moune na beurré ak serigne ndiaye quench et goui gui mais pas franc? fi yéne nieup séen interet geumouléne draa bayiléne faux...mane nak yekini moy sama mbeur, mais bayiléne affairou nafekh i ngéne nekké franc da prouvé 14 victoi mounouléne diexale yéne nieup
@bassirou3571
@bassirou3571 6 ай бұрын
Mom néna eumeu d'où champion d'Afrique ça fait mal vraiment à eumeu séne je crois bien franc devrait s'en excuser de se mot
@sarabo6779
@sarabo6779 6 ай бұрын
Mod lo moko ndieuké mofi bayi sathies, tapha tine,reug reug dem dieul siteu
@Deggou
@Deggou 6 ай бұрын
@@sarabo6779 saway kou daane ama balde boy niang2 khawma loumouy ragal si sathies mi eumeu daane barki demba....reug reug bouléne faté ci defaite la diouguéwone ak sa thies normalement moment bobou mokk franc la wayé daffa teup franc dieul bombardier...tapha tine beugonaniou combats bi de source sure lalay wakh...mais tapha da yakamti dieul balla...
@papemoussadiop83
@papemoussadiop83 6 ай бұрын
doudou champion la
@georgesdieganediouf2684
@georgesdieganediouf2684 6 ай бұрын
Franc aussi ne luttera pas avec aucun lutteurs de l'écurie d'eumeu sene . Comme eumeu sene a refusé le divorce sera total.
@bahosmantv1521
@bahosmantv1521 6 ай бұрын
Merci
@mouhamadoufalloutoure1991
@mouhamadoufalloutoure1991 6 ай бұрын
Topal feulé beuré ak franc fann lalay yobou franc dafé def gatte b52 lafi dann à l’âge de 50 ans manako diour sakh ki kholoul franc sakh gnou gana saff franc la sokhla
@georgesdieganediouf2684
@georgesdieganediouf2684 6 ай бұрын
@@mouhamadoufalloutoure1991 va te faire chier. Doudou sané franc l'a battu combien de fois en lutte simple tandis que mom zéro. Bayil yeffou sokhor Ak gordjiguen. Franc kouko diel danou.
@kefgg
@kefgg 6 ай бұрын
Modou Lo a refusé de lutter avec les tenors en disant qu'il lutte seulement avec les jeunes ( Siteu etc) donc les tenors aussi ont refusé de lutter avec son poulain Franc. Fofou leu divorce bi commencer
@Ibrahima66.
@Ibrahima66. 6 ай бұрын
MAIS NON DOUDOU SANÉ NAK FRANC MOLA RAW FOUFF SO GAGNER CLAF BI SAKH TAKHOUL NGUÉN BEURÉ DEUG NÉKHOUL
@boubacarthiam6120
@boubacarthiam6120 6 ай бұрын
mais beuré la rékk... Comme k modou lo bouclier la déff franc
@Ibrahima66.
@Ibrahima66. 6 ай бұрын
@@boubacarthiam6120 no dou question de bouclier sakh mais franc dafa yéksi si niom
@boubacarthiam6120
@boubacarthiam6120 6 ай бұрын
Garap dal si kaw lay fékanté... Modlo a son poulain franc Eumeu aussi a son poulain doudou sané
@boubacarthiam6120
@boubacarthiam6120 6 ай бұрын
Nagnou mayanté chance
@kefgg
@kefgg 6 ай бұрын
​@@boubacarthiam6120mais photo profil bi noumou démé nonou 😂😂😂
@chocsevenements8990
@chocsevenements8990 5 ай бұрын
Champion ngua mais franc d'où sa morom si lutte avec frappe yeimal ngua dem outti adversaire ioe gris 2 ak domou d'où niou Sa morom ay Jackson d'où niou sa morom nguay lathie franc sop ngua trop
@tavarezcheikhou517
@tavarezcheikhou517 6 ай бұрын
Comba yinga ame so khadjé victoire franc si digui bi amo comba yoyou nga begue berék franc tamit kharite
@zokorasall9617
@zokorasall9617 6 ай бұрын
Champion bou mak
@sanadieme756
@sanadieme756 6 ай бұрын
Lou leer Mbeur Doudou sané vs franc ou Diam Thierry combat là
@josephcoly4127
@josephcoly4127 6 ай бұрын
Mes pourkoi do.dieule forza le geant enh wala gris 2 wala serigne ndiaye..
@RidialThiam-l3f
@RidialThiam-l3f 6 ай бұрын
Franc Dou Dara 😂 doudou sane seul 💪💪
@sidyfaye44
@sidyfaye44 6 ай бұрын
Mo franc dou sa morom eumeu séne
@ebrimajoof2211
@ebrimajoof2211 6 ай бұрын
Eumeu du morromu franc na dem borreh ak ay morromam
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 6 ай бұрын
😅😅😅😅😅😅dégeul dofbi yaw AK fren khana 2035😅😅😅😅fren momeune sakh sa patron 🙄🙄🙄🙄🤔🤔
@mamesambaGueye-i5z
@mamesambaGueye-i5z 6 ай бұрын
Fran doudoou sané moy sa mooroom mé pas eumeu séne
@GoraNdiayeKarim
@GoraNdiayeKarim 6 ай бұрын
Franc n'a yarou ba Paré
@khadimfall979
@khadimfall979 6 ай бұрын
❤❤❤😂😂😂
@moussasagne5867
@moussasagne5867 6 ай бұрын
Modou bouclier la Franc motakh diéloul Reug reug
@SalimataKere
@SalimataKere 6 ай бұрын
Doudou rék
@bayeratebayerate5893
@bayeratebayerate5893 6 ай бұрын
Doudou sane eumeu sene diam la bekh na ana tyssn 2
@ModouLeye-x9y
@ModouLeye-x9y 6 ай бұрын
Yagui wakh lo khamoul dara
@lhomme_fort
@lhomme_fort 6 ай бұрын
Ioe danga beuri wax di wax rk khame nga franc boubakh franc dane nala 2fois
@AblayeThiaw-jz2qy
@AblayeThiaw-jz2qy 6 ай бұрын
Doudou sané mo meune koudoul franc sakh
@djilykane7164
@djilykane7164 6 ай бұрын
So dieuler claf bi ken meunatoula banie
@LamineFall-r9p
@LamineFall-r9p 6 ай бұрын
Yéneu sou eumeu béréwoul mon kham dafa ragual franc rék ta franc dafa am promoteur bou am khalise yéneu amoulén dara
@CireDioume-kx7un
@CireDioume-kx7un 6 ай бұрын
Hana teyela bone 3 X ne parle pas sa frère yalla bougoul ki togne
@SerigneSeck-k6y
@SerigneSeck-k6y 6 ай бұрын
Yaw sa patron lila franc def mo takh mouy daw franc xam nga ndiago bii bou bakh
@momowadd407
@momowadd407 6 ай бұрын
Yao khamo sa bok
@malicksarr2141
@malicksarr2141 6 ай бұрын
Eumeu sene vs franc moy combat bi
@mamadounguom4992
@mamadounguom4992 6 ай бұрын
Defou fi Lou takh pa bou diekhal lafi dane a part Bombardier bane mbeur bou âme valeur lafi dane
@assanegueye1352
@assanegueye1352 6 ай бұрын
Loutakh nguéne yap franc lakhoul yaw mom khamnga franc foumoula féc dane la boula embeu may fit
@ousmanegueye303
@ousmanegueye303 6 ай бұрын
Diofior rek
@OmarBao-gu5qp
@OmarBao-gu5qp 6 ай бұрын
Yaw kham ga franc bou bakh founek dannala founek
@mamadousene3731
@mamadousene3731 6 ай бұрын
Wakhale fane AK fane lako dane
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 3 **VOSTFR**
1:03:20
EvenProd
Рет қаралды 497 М.
Правильный подход к детям
00:18
Beatrise
Рет қаралды 10 МЛН
[BEFORE vs AFTER] Incredibox Sprunki - Freaky Song
00:15
Horror Skunx 2
Рет қаралды 21 МЛН
PA Assane Seck : Ce qui s'est passé à la mairie de Dakar est extraordinaire...
18:01
RTS - RADIO TÉLÉVISION SÉNÉGALAISE
Рет қаралды 74 М.
Touss Eumeu Sène lors de son combat contre Tapha Tine
13:24
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 96 М.
Mbott bou rey - Combat Prince Vs Holliguns
13:07
Lutte TV
Рет қаралды 40 М.