J'avais pas bien compris mais à partir d'aujourd'hui tu es mon guide religieux. Tu es très éduqué. Wakhji rafetna. Dieuredieuf
@ramaba18163 жыл бұрын
Oustaz DR mouhamad Lo nite kou bakh la té yarou yaag dokh si dinné lislam bou féké naak kou wakh Li Yalla ak yonnet Bi wakh mooy dikante ma kham ni Sénégal yakou nagnou rewmi kilifa dinné yi lagnou geune diokh thieur k Yalla mignou sakk ak yonnet Bi rewmi Mo barri nafék nous sommes de tout cœur avec lui y’a oustaz DR Mouhamed Lo Yalla na diam yaag si yaw si barcke seydina Mouhamed psl
@moussandoye96593 жыл бұрын
Hé Serigne bi woté né kaylaine santélama yalla si beusseum bi. Ngén di dingueut ténane Serigne bi lépeup yalla ak yonétbi PSL leu. Boulniou fonton dou yangui ni woté Grand. Théatre limoy farata ak sounna ? Boulniou fonton. Miick MBA né mott Touba incha Allah. Serigne bi dou séne moromou Mame astamak séne ay baye.
@thiattdiattara37223 жыл бұрын
Vraiment mane lolou moma jaxale 😂niom amnanou ay talibé niougui woté Séne talibé yi niougui danou niougui youxou mane dama khamoule lane moy ndey Li koi té Aka nio mouss dégale mouy jeul exemple si égyptien bi pour mettre en rapport si mome 😂😂 yarame touba dagay nék nit rek niou bayi leufare leufar gui wl niou nék si oe sohore géne trop
@mouhamethsow92633 жыл бұрын
Yémé daal frr bi
@mathiouz20743 жыл бұрын
Sincèrement kii ma guiss nitou jàmm la Julit aqqan
Serigne Touba mo gnou gnaboté, Serigne Mountakha wayal.
@khabylamefns26823 жыл бұрын
Yoninti bi amoul morome pas vos sérigne
@narstartall12463 жыл бұрын
Ya mana fen serigne touba diangalé wul lolu serigne bamba lum am diamu yalla liguyél yonén te bii moko ko may
@dembafall22303 жыл бұрын
Ki amul morom moy sa borom ki am morom matul borom nitla abdoulakhi késsé bayilén bokalé
@brigadeantibidah29113 жыл бұрын
Est-ce que Serigne touba foumou teude mingui laye dégueu ???
@zamidebousso10213 жыл бұрын
J’admire cet homme bien que je sois Tidiane Tous les grands Hommes du Sénégal ont enseigné le coran et la sunna Lui il nous parle du coran et de sunna nous devons l’aider et l’encourager mais non le rendre la vie difficile Tous ces menaces vont finir puisqu’il ne faut pas croire que les gens ne défendront pas leur liberté,leur vie et leurs biens selon la loi Que la paix règne partout à travers le monde amine
@moustaphagueye26153 жыл бұрын
So khamone loumou wakh si tidjian yi do tok fi di wakh sakh délene gueustou
@zamidebousso10213 жыл бұрын
@@moustaphagueye2615 Lou moumoute wakhe Tidianes yii loolou digantéme akk yallah laa Doundou cheikh Tidiane,elhadji Omar,Maodo Malick le Coran Al sunna Daakh dioulite lépeumame le coran Al sunna Képou kouyii wakhe le coran et sunna andaal Al mome ala limite le coran et sunna Ce qui reste c’est son problème Puisque yallah faatê,dou dioume ,dou diawaolé djéfoukéné Al morome Louwayi deff boopame Wassalam peace
@mamzodaller40632 жыл бұрын
Ta rien compris donc soit cool et c'est une erreur en commençant de dire je suis tidiane et après l'islam c l'islam
@manebassirou779 Жыл бұрын
Moustapha gueye lanla wakh si tijan yi?
@amadoudiop38133 жыл бұрын
Niou Bayil Khél Née Leup Nieupaye Diékh Mou Dess Borom Bii Rek Wallahii Néniou Ragual Yalla Souniou Borom Peace And Love dans Nos Cœurs....
Kiy saagua ak di wah lou gnâw dieumeu lé thie yaw boulko délloo aye saagua ak lou gnâw délloo ko xam xam. Cheikh Dr. Muhammad Ahmad Lo حفظه الله تعالى و رعاه .❤️
@sonhiboushop28553 жыл бұрын
Akhmad lo ragalal yalla Liga wakh wa khoudamoul khadim wakhou niouko
Dieureudieufé serigne touba koumou nakari nga déf limou déf Sénégal Makgni rék incha Alla
@latifsall62013 жыл бұрын
Niata personne la serigne touba dougeul si diné
@abdoukarimdiouf44733 жыл бұрын
Dieurediefet Serigne Touba khadimou Rassoul Serigne mountakha mbacké yague fi lol té and akk werr
@leuzleuz86023 жыл бұрын
Serigne mountakha le fanatique
@user-fp7kh9od1m3 жыл бұрын
Wax deg deg la lath. Kou nek thi yen meune na deguer noumla nekher. Wayer nak Dr Diam rek moko sokhal. Lim wax nak bou Amer niouko deguer nenen lolou niom la engager. Nite bougn ko waxer khel ba tax nak. Wa chaine bi yalna ya'Allah faye len sen yéné. 😍😍😍😍😍
@modoumodou32503 жыл бұрын
machalah yalla nala yalla samou chaikhana docteur Tu es la fierté de ce pays
@sodediagne61663 жыл бұрын
Dieuredieuf Serigne Touba
@galaxiepro.56413 жыл бұрын
dieureudieuf yawite
@ndiayelahad66623 жыл бұрын
Djeureudjeufee serigne touba khadimou rasoul
@brigadeantibidah29113 жыл бұрын
Est-ce que Serigne touba foumou teude mingui laye dégueu ???
@mdjf73533 жыл бұрын
@@brigadeantibidah2911 diadieufoté borom TOUBA.
@mdjf73533 жыл бұрын
@@brigadeantibidah2911 SERIGNE TOUBA rek khadimoul khadim sunu yakar. Boula nekh boula NAKHARI. TOUBA point final. Avec ta fausse brigade 😂😂🤣😂 Do rouss sakh!!
@modoukane45103 жыл бұрын
@Thie Sidibe yaw dodéga walla daga diagol ki dafa né khadimoul rasouloul lah lolou moy ligéy katou yonenté bi kokou kay défouko morom bou lén niou fonto waye
@bildoxer89diakhate53 жыл бұрын
Respectéwoléne kéneu pour yéne gnépou ay yéfeur lagn, diapouni yéna geuneu ragal yalla gnépou Respectéléne sougnou mak gni gnoléne eupou kham kham geunléna ragal yalla
@adioumadiagne76073 жыл бұрын
Gnou wakhko ak gnou gnakko wakh moy li gnou geum
@morwadeaddougaarii42133 жыл бұрын
Kone nga dem diamoudji yalla
@vieuxsambou7173 жыл бұрын
Am khamkham té diangaléwoko nimou waré ,lothi kham?
@7senegalese3 жыл бұрын
@@adioumadiagne7607 SubhanAllah mbokk. Ibadou la, sama papa tidiane la te d'où yefer dioulitt khakkan la. Mbokk seytane day diakhasse digante dioulitt. Ndiort rekk ndirot la. So amoul preuve mane nga rafet Ndiort sa moroou dioulitt. Lou waye deff sa bopp. Gnioune nieup ay dé, kou dee sa morom dioulé la. Mouy tidiane Mouy mouride Mouy ibadou, koune rang dioulé. Mbokk dal l'en te khamni gnioune diame lag'u yene kepp. SubhanAllah
@falloubadiane56863 жыл бұрын
Dieureudiefeti Serigne mountakha thie dalgui
@abdoulaye80733 жыл бұрын
Ce film il me fait penser a ce qu on se disait trop souvent...que les ennemis du senegalais essayerons de passer par les tarikhas pour mettre en desaroi le pays.
@abdoukarimdiouf44733 жыл бұрын
Voilà tu as tout compris,les wakhabistes d'Arabie Saoudite veulent passer par les traîtres senegalais pour brûler le Sénégal
@alfaruqSum3 жыл бұрын
Les wakhabite dont tu parles n'ont pas le temps du Sénégal. C'est plutôt l'intérêt de certains qui sont menacé par l'appel à l'islam authentique.
@abdoulaye80733 жыл бұрын
@@alfaruqSum walahi c est toi qui a cité le nom de wakhabiste mais pas moi. Et en aucun moment je n'ai pointé du doit a un groupe ou tarikha. Ce que je dit est simple: ces divergences pourront ouvrir des breches pour alumer ce pays et ça on peut le comprendre. Maintnant quand il s agit de prendre partie moi je ne le ferai pas et je ne jugerai qui que ce soit....attention toi comme tous les autres quand vous repondez au gens de par leur commentaire il faut juste essayer de comprendre ce qu il veulent dire.
@armandgentil45213 жыл бұрын
@@abdoulaye8073 la vraie menace vient des fanatiques mourides sous le silence complice de leurs chefs. Dans une vraie tarikha on ne peut pas écouter les mor mbaye simb kat, Masséré, Bichichi, Thiédo mourides et autres écervelés qui ne connaissent rien de la religion ni des oeuvres de bamba mais inventent des conneries pour vivre mieux. certains mourides n'aiment pas la religion musulmane ni le coran en commençant par mountakha. Leur référence est les khassida et bamba point et toute prêche qui touchent à leurs pratiques anti musulmanes est considérée comme une provocation meme sans les nommer c àa le probléme et non les pays externes
@alfaruqSum3 жыл бұрын
@@abdoulaye8073 je parle a "fier d'être sénégalais " C'est ces gens là qui se cache derrière des comptes pour pouvoir se sentir libre de dire du n'importe quoi.
@cisseabdoulaye2063 жыл бұрын
MachaAllah un discours responsable. Yalnaniou Yalla guindi ak mbolem dioulite. Allahouma amine !
@ismaelsal43683 жыл бұрын
Dr Ahmad une personne veridique
@kingafia2273 жыл бұрын
Jotna nouw doundou alquran ak sunnah Teh bayi thiakhan yii
@abdoukarimdiouf44733 жыл бұрын
Mba yangui doundou lolou rekk niounnn mourides yi dee thi laniou bokk
@bildoxer89diakhate53 жыл бұрын
ay yé katou fitena guéne séne idéologie you bone yi respectéwouléne kéneu motakh américain yi di gnaf séne khone rek doundoléne alkhouran bou wére ni sounah
@manesadio35243 жыл бұрын
Billaye
@abdoulayefaye15963 жыл бұрын
Mandou da bokk si islam te mandou woulen ay provocation rek ngen di def sa data ndey
Lo ndame mâchaa Allah.yalna yallah sameu len thi sarajay sang bou tedeu bi ameen 🙏🙏🙏🥰🤣🤣
@talibebambasalihousarr10673 жыл бұрын
Mame Boye khôl niou si Nioune Say Seute vraiment fi nekk dou yone wi guéne si Iow ak si Nioune aussi Deuk bi kham guanii Kéne douffi teré diagalém Alkhouranne ak Souna wakhal Lou Tegou si Aw Yone Mame Boye Nioune Mame Niogui ni tekk Rouse ak Gathiiii Mame Ahmadou Lô Ndam Sire Khoudia Gaye Del 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@babadiop65483 жыл бұрын
Sarige touba amolmorom
@brigadeantibidah29113 жыл бұрын
Loutakhe kone mou dé nou soule ko sakhe yi lékeko.
@mdjf73533 жыл бұрын
@@brigadeantibidah2911 Do tousss
@abdourahemanesene60503 жыл бұрын
Dieureudieufé borom touba
@Iboudieng-bu4hv8 ай бұрын
yalla rk moy bourr
@morsamb74683 жыл бұрын
dieureudieuf serigne touba,amoul morom
@ibrahimaseye59883 жыл бұрын
Serigne touba nangou lene liko yalla déf mou nopalene Sénégal kene manoufi dindi serigne si kon diokhlene thieur moy li war wa salam
@bangalydiakhaby34393 жыл бұрын
Qu'Allah met sur notre chemin des hommes qui appellent sans cesse au coran et à la tradition du prophète (psl). La sécurité et la stabilité incombent à chaque citoyen, faisons de notre mieux pour cultiver l'esprit de partage, de compréhension, d'acceptation et de mieux vivre. Un homme vraiment honnête que j'ai eu l'opportunité de rencontrer un jour. Comme on le dit: 《 on ne juge pas un livre par sa couverture 》. La seule chose qui peut nous éclairer sur certains de nos différents pour la réalisation de notre origine divine restera toujours la recherche de la vraie science. Qu'Allah nous guide tous dans le droit chemin et nous accorde une bonne fin dans ce bas monde.
@ndaomane24063 жыл бұрын
Allahoumma amine
@sambasylla75273 жыл бұрын
Ma sha Allah Dr Mouhammad Ahmad LÔ H.A Jazak Allahou khayran
@ousmanediouf45923 жыл бұрын
Serigne bi lô gua balma nak wayé sa wakh djii gua wakh dara wérou thi ay touba koufa dianguanlé alkhour ane niou beug la door wala kouffa dianguanlé ndiap niou téré lako s bi kholatal liguaye wakh nite gnii doffougnou wala dafa am bénéne Alkhourane boy dianguanlé bou deupo woul ak bi wa touba done diang avant guafa nieuw s bi kiliffa gua ta mbollo mi toop sa guinaw beuri nagne ta liguaye woté di yonou sounah yonou deug la khawma nak gua woté lénéne gnii toop sa guinaw wakh léne lénéne loudoul lolou nioune dougnou ay noone nioune nieup ay dioulite lagne kone nani wakhanté deug ndakh kounék béss digua wééte sa bamél wa touba mom kouko khaam khaam ko thi diangualéme Alkhourane ndakh book na thi deuk yi aup ay dara youy dianguanlé Alkhourane ak beuri diakaki diouma dila balou nak boudé wakh dji amna léne louthi niak téguiné🙏🙏
@mdjf73533 жыл бұрын
SERIGNE TOUBA rek khadimoul khadim
@mbayediouf52273 жыл бұрын
Fekhela dioubo ak wa Touba say mbokou lagnou koulako wakhoul dalay nakh touba keneu teré woufa diangalé alkhouran ak sunah ndakh mom la Borom Touba beugeu ak ndiabotam yaw nak dafa melni chaytané molay beugeu dougou té leneu si gnima guis gnou and ak yaw gnola beugeu tagalé ak wa touba yagu nga si linga wakh dioudofa ba legui li mosoul khew kon kholatal sa togay ak lila weur nga khamni Serigne Touba dou sa morom té dou moromou kepeu kou bok si sa kourel gogou diné dafla sokhla ndakh borom kham kham nga kon rik way Sangue bi Lô fekhel nek touba si diam diarigne wa touba diarigno touba
@weuz47153 жыл бұрын
Mbaye, linga wakh si Serigne Touba yeup deugueuleu. Alkhourane ak sunna rek leu masseu woté. Wayé nak Mbaye, liniou dégue si fane yi té diogué si yéna kilifeu wou Touba, wakh deugue yalla, diéguineu dayo. Niémé wouma sakk délou si wakh yoyou. Lolou moy problème bi Mbaye, wayé dou Serigne Touba. Gniye wakhe né Serigne bi bo binde li, mo wakh li, té Serigne bi wakhou ko, bindouko, nioniou nio togne Serigne Touba. Sou amé loula nakhary si wakh dji, mangui diégueulou. Wa salam
@assmalickdiarra22173 жыл бұрын
Yalla mo ndieuk té moy moudie gnou bayi bocalé bi dieredieuf que dieu vous protège
@abdallahtraore38223 жыл бұрын
Kén kouné sagn nga tan lala neikh nga geum ko Kein kouné yit sagn nga xol langa geum nga wote thia. Dr Ahmad Lô H.A
@m.b.mafatihoulbichri96103 жыл бұрын
Dieureudieufé Sérigne Touba.
@investigationscriminelles73753 жыл бұрын
Il très pertinent vraiment
@ousmanembaye56323 жыл бұрын
Bakhna dall , li Di djoudou Galsen Gnome gno KO fi créé 2 Tabaski 2 koritê Bou gneupp nêkê bêne djarr gauche Gnome gnou créer bênêne dîné dem Droite Sénégal dou Egypte Dou Algérie mai aussi dou Tunisie Nous sommes des Sénégalais On a des réalités qu'on doit respecter Point .....
@ousseynoutine19913 жыл бұрын
Sérigne bamba rék dieuradieuf sérigne touba💚💚💚💚
@wakandagalsen2213 жыл бұрын
Hafyzawulah ya Dr Muhammed Ahmed Lô
@fatoumatabalde36883 жыл бұрын
Que Dieu te protège Mohamed lo travail pour allah avec toi
@abdoulahadmbacke18603 жыл бұрын
Mani linguéne didéf ak linguéne diwakh bokoul linou wakh moye bayiléne Sagayi ak togne yi ak sosse yi ak féne yi. Sou nguéne yamé thie Sénoum ndiagalé rék béne problème dou am kounèk am nga droit gueum loula nékh wayé togne yalla santouko kéne.
@jarrahrassoulmbacke84673 жыл бұрын
Cheikhoul khadim deh kéne menouko gnawal dakh amoul lou gnaw déléne ko wakhtanei thi séne daraa yi ndalh kéne niorouko koudoul yalla ak seydina mouhamed li mouko tague amoul kouko défal thi kaw souf nagn khamni salalahou alay wasalama kharitou s touba la bolé nane rék wala.bolé toure magui sant yalla mima bolé ak cheikhoul khadim di sant seydina mouhamed psl
@diememediarra62933 жыл бұрын
DIEUREUDIEUFEUTI docteur c ça la GRANDEUR D'ESPRIT
@aloubeby22353 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba diarama Mame cheikh Ibra fall
@khadimndiaye39303 жыл бұрын
Sante serigne touba rek
@papaabdoumbengue37653 жыл бұрын
Li nga wakh dei amouma ci preuve Wayè lima leer moy Touba interdire nagnou fa école occidentale pour permettre l'assention de l'étude coranique et islamique
@falldame70703 жыл бұрын
Yene dangeni théâtre rekk maylene gnou diam serigne touba point
@assanembodji70363 жыл бұрын
AB dioulit dou fén yagui fénal waa Touba ay noni islaam gen dieredief borom touba diaarama Mame cheikh Ibrahim fall yalla nala yalla rébou non bou bon bi
@ndeyefatoudiop63303 жыл бұрын
Yangui sosal waa Touba dé boudé jiangue lé alxur Aann ak topou souna fala fékk baax tè touba yitte dakoub jambourla sa waajour ak Sama waajour dônou ndioufi dara
@sadadiagne41313 жыл бұрын
Birazoumann barazani birazouman Youbarizoul mountakhii Mann bar izaman
@assanesamb99783 жыл бұрын
Ok Merci Deglouna Saa waxx Sa mission moy Rothii serigne Touba cii Xolyly Mouride yii Do look moussaka Amm Daraye serigne Touba Nioroula Hyppocrite nga
@moratajunior3723 жыл бұрын
Dieuredieufé serigne touba 🙏
@mamadoubalde69083 жыл бұрын
Incha Allahou alkourane AK souna reck lepp day leer je suis un soldat de la souna
@dieastoulo19413 жыл бұрын
Machallah oustaze ahmad lô
@bambagueye74843 жыл бұрын
Question,Iow mii di wax nangoul gua Serigne Touba wala dètte?
@thiaat222tv53 жыл бұрын
أستغفر الله العظيم الذي لا إله الا هو الحي القيوم وأتوب إليه
@cheikhdiop69143 жыл бұрын
Lo Ame solo Machalla
@mbayediouf49523 жыл бұрын
docteur téy mom wakh nga Lou rafete 'wakhalk say talibe Serigne si yitam wakhak seni talibe niou and yatal islam bou tegou ci alquran ak sunnah.
@mamadoudia41243 жыл бұрын
Tay ni sama xoll bi seddé yallah rek moko kham loudoul sounnah ay thiakhane la yallah naniou yallah sammal DR m.Ahmad lo 🙏
@mbacke20103 жыл бұрын
Si la deuk!
@mariamadiawara33003 жыл бұрын
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته! ماشاء الله ما كنت على علم بهذه الدعوة علمته في الليل ولكن قدر الله ماشاء فعل .طول الله عمر الشيخ ورعاه .أتمنى أن أراه في قريتي فليغرى للدعوة !!!!!
@verite36853 жыл бұрын
حفظك الله
@alioubadarathiam47133 жыл бұрын
الكذب حرام
@mbayesakho14463 жыл бұрын
diaradieufati serigne touba khadimou rasoul yalna niouko yalla fayal 🙏🏾
@Ibrahimaly173 жыл бұрын
Amine serigne touba alquran rek la done dound
@ndiackndao32803 жыл бұрын
Que la paix et la stabilité soit sur le Sénégal et l'Afrique. Nous sommes des musulmans, nous devons suivre le prophète mouhamad sallahou alayhi wasalam. C'est ce qui importe, le reste c'est des bobards.
Est-ce que Serigne touba foumou teude mingui laye dégueu ???
@kaneamsa22613 жыл бұрын
@@brigadeantibidah2911 legui lan mosi sa yon diadieuf serigne touba ken do cheikh akhmadou bamba 🥰🥰🥰
@kaneamsa22613 жыл бұрын
@@brigadeantibidah2911 legui lan mosi sa yon diadieuf serigne touba ken do cheikh akhmadou bamba 🥰🥰🥰
@mdjf73533 жыл бұрын
@@brigadeantibidah2911 boubakh MBACKÉ SERIGNE TOUBA rek khadimoul khadim sunu yakar. Yangui sonal sa bop
@soulaymanedia82403 жыл бұрын
Merci wa sénégo tv vraiment contane na si yénn trop . D. Kadou gui lérna amna solo ms nak kou xolam am kiñane manoussé djarignou .. Yalla nala yalla samou goudalle saw fane cheikh bi ❤❤❤
@fantakonte58933 жыл бұрын
Amine
@binetafaye75273 жыл бұрын
Jërejëfi sèriñ tuubaa
@فلسفةالحياة-ث7س3 жыл бұрын
que Dieu vous protege, vraiment vous etes une fierte pour toute une natione
@talibebamba33643 жыл бұрын
Alhamdou lil hahil moubine Mane kawnouhu liyabine ala kitabi moustahine maha diamihil nihami
@ablayesow53423 жыл бұрын
Machalla 🙏🙏🙏❤️😍
@assanedeguenekhul61903 жыл бұрын
Yalanala yalla sama
@momardieye44853 жыл бұрын
La connaissance contre la violence le vainqueur sera toujours la connaissance
@mdjf73533 жыл бұрын
SERIGNE TOUBA rek c est lui la connaissance.
@beugbambatouba51813 жыл бұрын
An tout qu'à daal Touba serigne Touba moko mome goné gou diok beug ko foyé nioune talibés yi nioy diog niouss leu banga doul souna Touba la fék bax ténga bayi sa doul
@papeba4833 Жыл бұрын
GNO MEUNN SEN NDAYE . TAMBALILEN KON DOLLENKO NETTALI
Touba rek nguaye guisse gniye todje aye diaka dou todje aye dara ak dou lake aye Alkhourane dou tek serigne touba si kaw Y'ALLAH SHWT ak YONENBI SAWS kéne dou wédi dé nakhe leup ngui si réseaux sociaux yi. Donc mouride yi khalate léne séne bop té dieufeuniko séne khelyi touti. WA Salam.
@mbayeiba43353 жыл бұрын
Dieureudieuf serigne touba
@thinktanktruth1968 Жыл бұрын
Très bien, oustaz! Merci beaucoup!
@babacarseck13793 жыл бұрын
Kéép koulaye sagua ak diila wakh wakh diou niaw dafla xamoute....yallah naala yallah sammeu té yaguale lafii loole sakh
@ibrahimasall48893 жыл бұрын
Machalla amatina solo yalna yalla samou lén kham kham bou séleu reque wor dr akhmad Lo machalla kham kham bi rafétna té seleuna yalla samou lén
@vieuxsambou7173 жыл бұрын
C'est un grand courage et c'est la stricte vérité.
@sokhnafatimatoure42363 жыл бұрын
Manchaalah docteur yalna yala same la hayacoumoul laahouu
@yusufabdallah15373 жыл бұрын
Machallah barak'allah fikum cheikh
@ibnahmadka1657 ай бұрын
Machallah nn cheikh bii dalna dehh Machallah vraiement ❤❤
@serignembackediop51813 жыл бұрын
Serigne touba yamoull ak kéne thi souneu ak thi diamou yalla