Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct / luttetv / luttetv / luttetv luttetv.com/ / senlamb
Пікірлер: 217
@kebsvipkebe103 Жыл бұрын
Reug Reug le 5 mars Yalla gua Ame ndam thi ca thies ndam rk inchellh Yalla gua andakce Sa Xéle Aminn yarabi ndam Yalla na niaw ci ioe inchellh
@alassanedieng7479 Жыл бұрын
Amine ❤🙏🏾
@azizsarr9533 Жыл бұрын
Reug reug yalla n'a yalla may ndam thii katanou yalla inchallah
@jazzjazz4902 Жыл бұрын
NOOOON NDEEKEE REUG REUG MO DAK TOUSS SI LAMB JI KI MO DEEGUE DEUGUE👏👏👏
@ibrahimatall5277 Жыл бұрын
Vraiment Reug-Reug moy Lamb,kokou bagn danko sétanoul. Bonne chance le champion de Thiaroye !
@cheikhtidjianesarr8514 Жыл бұрын
Lou leer khana faral ko bagne ko faral dall mofi am mais goudi yii mom moy lamb
@taphadiop607 Жыл бұрын
Kou gueum ni reug reug mo meun mo eup dolei beusseul j'aime
@khadimdiouf3988 Жыл бұрын
Reug reug mo goré toujours avec les sérères yalla na nga am ndam
@tallasarr8031 Жыл бұрын
Reug reug yalla nala yalla maye ndam amine unchallah
@khadimdiouf9090 Жыл бұрын
Ki lagne done wakhné dafa dieul poids gni ko wakh khamougnou lamb ki il est mobil rapide et il a de la force naturelle par rapport à son adversaire inchallah il battra son adversaire
@petitndao6461 Жыл бұрын
Dafa dieulone poids mome mais sénŕgalais mo gawa wakh rk mais warone nanou hame dafaye wagniwate poids bi
@lem9148 Жыл бұрын
@@petitndao6461 meunouko wagni si kelk jour c impossible ca prend plusieurs moi ça minimum 6
@morseye4084 Жыл бұрын
Khadim gayi dagnouy wakh rek reug reug future roi des arènes leu compétiteur leu
@Sndiversity Жыл бұрын
Mom lay supporter et pour être honnête en tant que professionnel et coach il a pris un surplus reug reug meussoul yarr biir lolou rek ca prouve
@EmileLucienMoreira Жыл бұрын
Je te jure frère gayi ils parlent trop. Ki c’est pas un simple lutteur c’est un professionnel il est souple même en prise de masse
@papythioulo1406 Жыл бұрын
Force naturelle et tranquille 💪🏿❤️✅ndam rk inchala ✌️🙏🏾
@dabakhdiao9155 Жыл бұрын
Ndéysane Baye Madione xoll bou Nice la yorr👌
@Senmiroirtv-t4i Жыл бұрын
Reug reug Machallah dafa khegn khounou ak dollé yalla ga am ndam Wa thiaroye amna niou champion
@abdoulayesy5048 Жыл бұрын
Deegueule lii rafeetna naala yalla maaye damm inchaallahou
@alassanedieng7479 Жыл бұрын
Amine
@cheikhdiouf9353 Жыл бұрын
Nala yalla may ndam champion tout mbéllonguithie est derrière toi
@mamadoufall9185 Жыл бұрын
YALLA Nala YALLA MAY NDAM Lou Lèrr té Sèdd Gouye🙏Reug Reug
@serignediop6995 Жыл бұрын
Amine Fall
@papewalydiouf8420 Жыл бұрын
Le meilleur de sa génération...force à toi champion...
@mustaphabittaye1113 Жыл бұрын
Sama champion bi reug reug yallna yalla may la ndam si barkèh Al Quran 🤲🕋🕋
@papandiaye9419 Жыл бұрын
Sa thies mogui si forme Reug aussi mogui si forme Ndaw lambj bou reuy❤
@badandiaye8619 Жыл бұрын
Reug reug Yalnako yalla maiy ndam Inchalla ❤❤✅
@mbayendiaye626 Жыл бұрын
Omar Kane Reug reug yallnakou yalla may ndame ci kaw sa thiés💞🤍💗💚🙏🤲🤙
@ndourbabacarfaye4069 Жыл бұрын
Reug faraloumala wayé ligua touss nekhna👏👏👏👏
@babsmbengue9412 Жыл бұрын
Allez les lebou 💪🤝💪
@ibrahimaba3553 Жыл бұрын
Aythia sama xel dalatina guiss na forme guiss dolé guiss rapidité guiss souplesse yalla nala sa borom defal ndam lou sédeuh gouy bonne chance on n'ai derrière toi reug reug
@ateckhediane1152 Жыл бұрын
Sa thies yalla nako yalla may ndam ci barkép alkhourane Karim amine
@mamadoufall5500 Жыл бұрын
0⁰⁹
@cheikhgueye7924 Жыл бұрын
Amine
@boyefay6247 Жыл бұрын
Baye mdion mala feké sabo ñowaa stade ñiep diok takhaw bilahi yag nga done ndanan ba ngay sol treuil militer bolékok mboubou fari mbam hh barké alkhouran❤️🙏
@cheikhdiao2625 Жыл бұрын
Ak sa Thiès ndam rék incha Allah
@khadimedioum4179 Жыл бұрын
Reug reug yalnako yalla maye ndame si barké serigne Fallou
@modoufallbetebeteitsenegal5272 Жыл бұрын
Athieu champion ndanan pure bonne chance 🍀 yallah nala yallah Geunue takhawou defala soutoureu bou yatou si combat bi yallah nako yallah defal aussi li geun si mom inchallah si barke ya rassoulillah psl si barke Serigne babacar sy rta
@modoulebou634 Жыл бұрын
Dila nianal ndam rek champion bi billay défal ninga dann def rek amoul tit amoul ragal beure dann gnibi inchallah 💪🏿👏🏿🙏🏿
@moussakonta7955 Жыл бұрын
Reug reug yalnala yalla mayy ndam
@Reum- Жыл бұрын
rotation reug reug bi tey na khel .... poids bou andak souplesse la guiss mane bala le 5
@abasall711 Жыл бұрын
Il est mobil machalah yalnala yalla may ndam bu reuyeu reuy si Barker borom lp
@dieylanydiallo Жыл бұрын
Gniy wax dafa jeul poids gnépp sa Thiés laniou FaRaL ay daw lakhou laniou rk força ReuG ReUG
@boyefay6247 Жыл бұрын
Li may wakh ni yag na sa Comba yag Djily bou fass boba djily la faral mé bi nga dougué stade doumako fatté mouk kérok khôl yépa séde barké alkhouran ❤️🙏
@loftuscheeklevrai512 Жыл бұрын
Ndam Reik inshallah
@dofoujackson2544 Жыл бұрын
Bilay liguéy day andak khél bou dal💪💪💪 machalla champion good job
@moustaphagueye6602 Жыл бұрын
nooooooo Reug reug dékilate neu Lamb bilahi
@diogogueye128 Жыл бұрын
Yana la yalla may ndam
@mamadoudoucke6052 Жыл бұрын
Amna mbeur bou Besse waye reug reug yalla nga ndame
@aliouseck-vx8of Жыл бұрын
Yalla nalla yalla may ndam lou sédd gouy
@mbayendiaye7414 Жыл бұрын
Touss na lou nekh macha allah
@adandoye3759 Жыл бұрын
Sa thies yalla nala yalla maye ndam dimanche 🙏🏾
@ndiagafaye3106 Жыл бұрын
Gni doon wax ni daaa dieul poids wou you leen boye bi carte gui leer 💪💪💪 ndam reek inchallah
@babacardiouf6253 Жыл бұрын
Sa thiès yalla nako yalla sutoural may ko ndam rek inchallah
@fallougnigue384 Жыл бұрын
Youkhou meun na dji fou niou ko fogé woul de🥰😊
@kareabdoulahad622 Жыл бұрын
Thi kane ngako fook yaw 🤔🤔😂
@fallougnigue384 Жыл бұрын
@@kareabdoulahad622 khana sathies dane Reug Reug
@timtim6971 Жыл бұрын
Lolou kay dou youkhou lolou kay dou bet s athies ba daler beurer ba legui menoul dougou cours des grands cest l'occasion
@fallougnigue384 Жыл бұрын
@@timtim6971 lolou de amena dou bet sa Thies mais niou beuri Reug la niou diokh favori
@kareabdoulahad622 Жыл бұрын
@@fallougnigue384 reug reug la faral mais tamit mou dane mon geun dh teksi niom niar défaite si sa thies kay geuneu mety
@ndoffenetine5333 Жыл бұрын
Reug ya geuna saf mbeu ya meun ya dakh beuré té yay dan incha god
@sambagueye6328 Жыл бұрын
Amine yarabi inchallah ❤🎉
@alassanedieng7479 Жыл бұрын
Ndam rekk insahallah ❤
@malikchor9299 Жыл бұрын
Reug the 👑
@fallbcn5275 Жыл бұрын
Affaire bou nice machala Bilay vraiment sama khol Nekhna
@amadoudiouf7585 Жыл бұрын
Athia champion 🏆 Yalla nala may ndam
@bachirdia3221 Жыл бұрын
Thieeeyy reug reug que dieu te protège be le 5 inchallah
@kingbabsthiapathioly Жыл бұрын
Reug Reug KASSÉ
@deuguekepp10 Жыл бұрын
N'a mbayang loum niew lamb j dh.elle nous manque
@yayefall360 Жыл бұрын
Bonne chance mon cousin derrière toi de tout cœur
@laminmaster9387 Жыл бұрын
Man ko yomboul si lamb dji dh machallah 👍
@omardabo3388 Жыл бұрын
Ki dou tous dof bou yeuk succès leu Mais dînagne ko diangal adouna inchallah
@amethndiaye5154 Жыл бұрын
Yalla na yalla may ndam sa thies amine
@nitoudeugpiir957 Жыл бұрын
Antouka amna dolè dale
@alhamdoulilah9154 Жыл бұрын
Fans sa thiés yi késse gnoufi nékk di wakh wakhu poids reug reug amagoul poids khalé la dafa wara matt 150k wala 200k bayiléne teck khéll bi kii proffesionel la Lomou yore Mokou moum te inch'Allah dina am ndam
Worna na yalla reug reug sa staff dioumnanie danga diss teh sa thies dou dôlé mokoy dane vivacité ak visilent gaw si action mokoy dane
@laminendao402 Жыл бұрын
Saway sa Thiés koumou eupoul dolé doula dane reug reug xamna loumouy deff
@1999-un Жыл бұрын
@@laminendao402 lolou deug la dé
@ndiayeabdouaziz588 Жыл бұрын
Waw kuer doubales yi yobou nadiou dan ko si dor mo faté lin ko waxon
@amadoukane9816 Жыл бұрын
Ndam rek inchallah Amoule Ragale domou Baye Omar kane 🤞
@djibithiaw1259 Жыл бұрын
Reug reug bou bako rk gua contan mais yalnala sa Thiès dan
@khadimba3397 Жыл бұрын
😂😂😂😂
@seydinaomardiop4537 Жыл бұрын
Mbeur la 😂
@jupinleye8346 Жыл бұрын
Reug Reug Yalna am ndam lougaaw té lèère
@baradieng1489 Жыл бұрын
Ndam rek inchallah Sathies guéneul ma dieuk sa baken
@tallasow7868 Жыл бұрын
Ndam lek inchalla
@serignemansourtoure86 Жыл бұрын
DAY DANE DH INCHAALLAH 💪💪💪
@khalil7537 Жыл бұрын
Reug reug Gayi attan na boppam dh ndekete EN tous cas combat bu neix la
@mamadouniang3245 Жыл бұрын
InchaAllah sa thies dinala daann diell bou reuy ta gaaw...dinga diapp sa guemmign diommi inchaAllah
@georgesdieganediouf2684 Жыл бұрын
Kouff o ndonof.
@Rossyungrenzel Жыл бұрын
Makhou mara niass bobou Esk sa thies momou ko sawaay 😂😂 Sinon so demei be mou woor le que reug moy diap ay guemign do wakh beine yoone nouko sa thies di daanei 😂😂😂
@seydinaomardiop4537 Жыл бұрын
@@Rossyungrenzelbayil gni rek😂😂😂
@idykone75276 ай бұрын
Baye Mandione si fin bi 🔥
@cheikhsene7140 Жыл бұрын
Ndangéne Di diawalé dise AK beuri dolé. Ki dé goudi yi Kou yabou gnane sa thiés daneko ndah Bou thi guéné gni fi dès gneup amougnou dolé bouko dane. Wa Modou la dé,mais ki ap yékini Bou soti la Bou ko fi thiate bayé.🤔🏇
@alythiam4118 Жыл бұрын
😂😂😂
@ndiayeabdouaziz588 Жыл бұрын
Lamb dji am gen gan dé rueg reug mi kou bagn danou boul ko diel
@aliouthioub4566 Жыл бұрын
Reug reug saf na mbeur
@ndioldiaguayakham5265 Жыл бұрын
Sérieusement sathies dengaye danou té dolé molaye khâgne combat
@mordiouf7868 Жыл бұрын
Tu n'as rien compris ki nane dome ba canamgui yakou sathies dafa naturel diguene hamni reug dou 100 franc
@paradisegang1757 Жыл бұрын
@@mordiouf7868 kou nane dome ni laye méle baye léne séne thiakhane yi bala 5 mou soumékou guaye dogua comprendre 😂😂
@timtim6971 Жыл бұрын
@@mordiouf7868 balla ay dom la danei yekeni 😂😂 reug si tank balla la diar pour am ndam
@abdouthiorsarr7110 Жыл бұрын
Ndam rek inchallah
@sarryelhadjiousmane1528 Жыл бұрын
Ndam rk inchallah
@papismergane6603 Жыл бұрын
Combat bi dou combat technique combat dolé leu sama analyse
@bambaseye4402 Жыл бұрын
Sa Thiès ndam rek inchallah
@timtim6971 Жыл бұрын
Franchement sérénité bimiy dégager titeul neu kouner 😂😂 mome daffa sakk lolou moy son point fort
@matarndiaye3496 Жыл бұрын
Machallah ndam rék inchallah
@thiandoummoussa3394 Жыл бұрын
Ay lébou laniou piiiirrrrr
@dembaztarkinda8270 Жыл бұрын
Moussa Ndoye 😂ay 😂😂ngamay deff demal tokk boulen sa thies diape ngene hamni Lepp deug leu
@leytyndao8987 Жыл бұрын
Ndame rék inchalla
@diengsallaofficieldiazz2086 Жыл бұрын
Ndam rek inchalla nalla diam sonal rek
@baradiop6867 Жыл бұрын
Reug reug kassé amoule lénéne
@bayefall9204 Жыл бұрын
Sa thies yalla nalla Yalla maye ndame
@thebosh-se5lb Жыл бұрын
Ndam rek mbeur inshalah
@mmsseye9391 Жыл бұрын
ceux qui pensais k reug dafa disse
@MF-xc3vn Жыл бұрын
Le tambour major nanane la bravo
@modoundiaye8655 Жыл бұрын
Reug ndeké dusoul de
@modoundiaye8655 Жыл бұрын
@@kareabdoulahad622 ma dafa mel ni mo mom yaramam de pour man poids bi bakh n’a