Suis talibé mourid mais cheikh bou limouy way dafa nekh Masha'allah ❤
@SoxnaAwaNdiaye27 күн бұрын
Billy yaw
@ramiishlovediop88664 ай бұрын
Telment cette chanson m'apaise tonton cheikh bou Diop yalla na sa diam yague
@BaboucarrFanneh7 ай бұрын
Ki moy borom tabala❤❤❤❤❤
@OureyeSeck8 ай бұрын
Hikam ce sont des paroles de savoir et de sagesse qui permet de mieux vivre et d'aller d'Avant.en wolof Moy kaddou youlay dieurigne dila takha dém ❤mako maye sama xarit Mamadou lamine cissé sopé bou Diop Mane la pa ablaye yeumbeul bahroul👍🏾
@baybauldieng22575 жыл бұрын
Thiéy bou Diop machalah yalla naga goudou fane si barki serigne saliou
@PapeCiss-lc6dx5 ай бұрын
Fier d’être khadre ❤
@MamegamouFaye-d5p4 ай бұрын
Je suis un khadre et suis fiére de l'être❤❤❤❤❤
@mouhamedgaye51674 жыл бұрын
Merci Abba grâce à toi j'ai pu découvrir l auteur de cette musique
@Muxamediuf4 жыл бұрын
Moi aussi.. aokat bi la begoon degaat 😄😄
@sokhnamaidiome62653 жыл бұрын
Pareillement que man woor na auteur bi ba sonn ......en fin🎤🎤
@abdousy75713 жыл бұрын
@@sokhnamaidiome6265 hc
@fatimafall96063 жыл бұрын
@@Muxamediuf . ,. . . 0 , . 00 .. .. 0 . ...
@rouguiyatouba79473 жыл бұрын
Moi aussi
@diorniang73524 жыл бұрын
Grâce à ABBA no stress j'ai découvert ce zikr♥️♥️♥️🙏Cheikh bou yague fi
@mbayediouf84402 жыл бұрын
wallahi de mm que moi hahahahah legui lako degu si abba rek dougou youtube diko weur
@babadiouf8012 жыл бұрын
Même mane abba motakh ma khamko
@mbayejuniorlofficiel64284 жыл бұрын
Kou dacord akkk Mane pour Cheikh Bou defko clip pousse bleu
Cheikh bou diop yalla na nga yague fi thé wer tu fait la fière thé de Ndiassane
@CheikhTidianeNdiaye-hw3zy10 ай бұрын
Boy sa avant dernière aladji bii meuneu tooo 😭❤️
@ibrahimandoye31473 жыл бұрын
Gueumena YALLAH lolou Cheikh bou Diop barina trop loumouy yéété ak di délo nityi si YALLAH. YALLAH fayalniouko. Amine
@Zeynabbintmohammad5 жыл бұрын
J'arrive même plus à compter le nombre de fois que j'écoute ça 😣😭❤j'adore ma sha Allah
@sophieseye54844 жыл бұрын
Pareille que tw ma belle à l'heure que je te parle je l'écoute. Cette chanson c'est la vie!
@khadyniang67474 жыл бұрын
Doundeul Chérif
@gnimabadji50744 жыл бұрын
Pareil pour moi. Machallah
@seynaboufall67944 жыл бұрын
Pareil pour moi aussi
@yarassoul65834 жыл бұрын
Jjjjhhjjhhuyuyygh1dDl Aybggjhggghege74rbrbr
@cheikhatkhanaka8320 Жыл бұрын
Diaroul daw diaroul titeu Sa warseuk wa xaral dink si jot Mani Dieu mi amena facteurs Youdoul dioum té dou rérr 😢😢😢❤❤❤❤❤ Mashallah je ne cesse de l'ecouté
@fatimakarimlo32925 жыл бұрын
MachALLAH da guay deglou di diang sa khol di fekh doundall diop
@nogayediouf73604 жыл бұрын
Sayou makoy déglou day melni mane lay yédeu,yalna yalla geuna wéral baat bi si barké sa tourando.
@soumayathiam47704 жыл бұрын
Mais El hadji bou waaaw dji niek sii souff Borome oooohhoooaawwouh bii mashallah nékoo grawna limouy déf si souf moo nékhh😭😂😂😂🤗🤗🤗🤗 yalah nalah Borome bi fayy
@fatoudiopgueye25264 жыл бұрын
Je suis pas là seule alors🤩🤩🤩🤩
@elhadjicheikhboudioploffic31864 жыл бұрын
Amine
@laurentthiaw7490 Жыл бұрын
Je suis catholique. Ce chant est une leçon pour la vie. Je l'ai découvert ce matin par hasard sur la chaîne RFM.
@elhadjicheikhboudioploffic3186 Жыл бұрын
Mâcha allah...
@aidagueye7350 Жыл бұрын
Lii way bi antanoumako❤kiy rimm sou souf nak kene dou mom❤🎉🎉🎉
@dialayebd Жыл бұрын
Ma'cha Allah. C'est comme si Cheikh Bou me parle directement. Surtout lorsqu'il me dit Yaw lamine dieuleul sa pilim diéma teunk yi madi lim - thiw keuyitt mou doone sa ndieurigne yaak kénééne kou woute ndieurignam. Merci pour cette belle leçon de vie.
Sama yaram bi sakh day daw boumay deg Lou kadou surtout ''tontou none dou ndam khadj Boula mbawé nga mbaw Ani ndam'' deug la bilaakhi
@moustaphasylla51523 жыл бұрын
Jarafief
@karbllahjr64234 жыл бұрын
Machallah Serigne Cheikh Diop Amna solou mala bagu dé Bilahi
@ndeyesidibe15574 жыл бұрын
Bilay mala beugue
@goumbelmballo34055 жыл бұрын
Cheikh bi, que le PUISSANT veille sur toi et toute ta famille. Je t' aime beaucoup, mash ALLAH.❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@elhadjicheikhboudioploffic31865 жыл бұрын
Amiiine Niou bok ko
@ndeyemariesarr23892 жыл бұрын
@@elhadjicheikhboudioploffic3186 Machalla je te suis sur KZbin que le bon dieu te prête une longue vie santé de fer bc de bonne choses Inchalla
@mamediarrandiaye24402 жыл бұрын
@@elhadjicheikhboudioploffic3186 aAa
@mbeddmidiallo69345 жыл бұрын
À par zikeurou keur baye niass ioe rèk yamay danél Yalla nalla yalla sameu ci barké yonantèm
@laminethiam15654 жыл бұрын
Une vraie leçon de vie. Merci l’artiste poête.
@aminafallou85125 жыл бұрын
Doumasi doyal barkè serigne touba🥰🙏
@oumydione15075 жыл бұрын
Diop yalna sounou borome dolila djam té yokkoula soutoureux bidjakhi Tâ-Hâ ak sa tourando machaallah nexna
@dadakebe28033 жыл бұрын
Walahi bi douma ci doyal chekh bou yalna sa diam yag ci barki seydina Mouhamed psl
@elhadjicheikhboudioploffic31863 жыл бұрын
Amiine
@ousmaneniang12703 жыл бұрын
MACHALLAH ✨... INTÉRESSANT + DES ENSEIGNEMENTS DE VIE MORAL + DES CONSEILS...🕌📿🔥🙏.
@ousmanendiaye7583 Жыл бұрын
Machala Chikhe bou diop nikhna amna solo
@FCHWPO711 ай бұрын
Mercy
@talibeserignemostaphasymal19175 жыл бұрын
Machallah wallahi ndeysane yallah nala yallah geuna dolé takhawou té dolé weral bate bi yokou fane wi sakhal wér gui thi chiekh seydi mouhamedoul moustapha sy al maktoum mane damala beugue rek té yallah takh
@elhadjicheikhboudioploffic31865 жыл бұрын
Yalna niou yalla boolé sop
@talibeserignemostaphasymal19175 жыл бұрын
@@elhadjicheikhboudioploffic3186 amine ya rabi
@fatoukinendiaye86044 жыл бұрын
Mashallah mashallah mashallah yokou bâ yeuk KO si barcké sa tourondo
@mamecheikhdiene16743 жыл бұрын
Mâle mom mrid la billahi wayé dama bague chéikh bou diop billahi amal diamou rékk
@mamadouwadediagne7684 жыл бұрын
Le but veritable d'une musique,chanson,zikre..... est d'éveiller ,eduquer ,enseigner....tel est le but de ce zikre bref je te souhaite le meilleur dans le reste de tes projets ( bouna ya meuneu way waaw🤗🤗🤗)
@morsakho61373 жыл бұрын
X une, BJ sont mes m omni
@elhadjicheikhboudioploffic31863 жыл бұрын
Macha allah diereudieuf
@soxnamaguettediop4699 Жыл бұрын
Masha Allah Diop ❤ une vraie leçon de vie
@casebi50165 жыл бұрын
Machaallah El Hadj Cheikh Bou Diop walay lii nékh na yalna yalla geuneu wéreul batte bi si barkép Seydouna Mouhamed (S.A.W).
@elhadjicheikhboudioploffic31865 жыл бұрын
Case Bi mâcha allah
@elhadjicheikhboudioploffic31865 жыл бұрын
Case Bi mâcha allah
@sagarseck15474 жыл бұрын
Machaallah Cheikh Bou Diop way bi mome touché nama trop .je l'écoute n fois.yalna baat bi wér thi barké sa toroundo Bou Kounta Ndiassane. Contane na trop
@samsung045samsung85 жыл бұрын
Je suis fière d'être khadre Machallah bou Diop sama Sope
@awagueye14814 жыл бұрын
Machalla ken dou borom ndiassane
@ndeyefall32655 жыл бұрын
Bilahi damako beugue rek té yallah tax
@dellasamba3333 Жыл бұрын
Waw gor cheikh bou machalla❤❤❤
@abibediaw38104 жыл бұрын
J'ai connu cet chanson grâce a Abba tfm..j'ai beau chercher nak je connaissais pas le titre
@mbeddmidiallo69343 жыл бұрын
Ba tay magui ci khikam doumassi doyal mouk ndakh amna ndieurigne si kou am dégue
@nafissatoumbengue68565 жыл бұрын
Machala diop ligua wakh deguela yalla na yalla defal la diam
Machallah Cheikh bou diop.Matna tewlou lool ndah sagesse rek lay diangalé thi way wi.#Donni tool tahoul meuna bay #
@awayombesane14085 жыл бұрын
Diop yalla sougnou borrome feyela dianme rek ''ngaye âme machallah
@coumbizrio69994 жыл бұрын
Machallah na dè nga wayal car dama bari none tè dou keneu koudoul samay mbokou té louma am bokouka ak gnome mais Dieu merci car j'ai un bon boulot mais inchallah tay lanéne di gueuneu meuneu am Sama khaliss merci cheikh bouh yallanala yala Faye si barké Mame bouh
@Nargueyeu83 жыл бұрын
Mougbal moy ganay
@papayorofaye78952 жыл бұрын
Wallahi sopnala diangalei aduna AK lici biir ngafi weuy💓💓
@Liguere2.02 жыл бұрын
Sa way bi deh douma tayi si diko deiglou walahi na sa diam yagg mashallah
@lalaaichakonate38443 жыл бұрын
Hol yi sédenagnou😭😭😭😭😭😍
@doudouseck92214 жыл бұрын
MACHALLAH que Ya ALLAH augmente tes connaissances qu' Il te protège si barké Cheick Abou Mohamed Kounta
@fatymandoye15693 жыл бұрын
Amine
@zeynabdiallo17443 жыл бұрын
Grâce à tik tok d Abba show motakh ma deeggueu son bi machallah beaucoup d'enseignements,les paroles claires et véridique 🥰🥰❤❤❤❤❤❤❤❤🙏🙏🙏❤❤❤❤
@elhadjicheikhboudioploffic31863 жыл бұрын
Macha allah
@fayebineta76045 жыл бұрын
machala bineta bekaye arka bekaye oh li nekhna waye mala maye sama dieukeur
Bilahi heure bouma dioulé goud fane ak soutoura rekk lalay nianal cheikh worna yalla damala sopa lool je suis khadre de père et de mère
@ibrahimasy43642 жыл бұрын
Merci
@ndeyendiaye6104 жыл бұрын
J'ai découvert ce son avec Abba mais j'adore trop machaallah ❤️
@juniorfox49554 жыл бұрын
billahi cheikh bou do niit on dirai que tu parlé de moi mais je vais me reprendre et caché ma colère merci cheikh
@djenabadiallo14065 жыл бұрын
Walahi bimako ndiekker dégue lako beug yetterna machallah
@mbayeseck23224 жыл бұрын
جرجف شيخ بو جوب امومروم merci chiekh bou
@guiguindao92384 жыл бұрын
Tay damako yendou deglouu mashala
@moossmoussa98564 жыл бұрын
Billay bou wakh khal lép diop
@abdousamathsene71632 жыл бұрын
Wooy BI dafa ame solo bilahiii mane dama si dound Lou barii daflay yok ngeum ak mougn ak fiit
@lobediop19134 жыл бұрын
Man yaw la beug dh lou léer gna wax❤❤
@serignethiame77495 жыл бұрын
Machalla am na solo walahi yalla nanou yalla défal dégueu ak topou
@cheikhndiaye28175 жыл бұрын
Machallah bou diop yallna yalla yoke sa xam xam
@khadijafaye83093 жыл бұрын
Yalla n'a yalla fay bilahi tu ma ouvrir les yeux fermés 😭😭😭
@papitraore79875 жыл бұрын
Machalla sama sopé bi yalla guafi yague
@binetadieng28624 жыл бұрын
Khôl yi dedans way yalka fayela
@maguiniang80125 жыл бұрын
cheikh bou wakh nadeugue bilay nonne Ken d'où KO bayii
@AmyLoum-dk2fy Жыл бұрын
BayBou Darisso 😢😢😢😢😢😢😢❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@lingueroubayemoussa96252 жыл бұрын
Sama sopebi😍😍😍😍😍
@khalifaababacarsyndiaye44614 жыл бұрын
Degegouma way bou dakk liii🥰🥰❤️❤️❤️✨
@ndeyefatousall7994 жыл бұрын
Mashalla Cheikh bou Diop yalla nama Yalla wanalei ak iow way bi doumassi doyale sa souma merei mom lay deglou
@ndeyediopsambe87132 жыл бұрын
Fouma amè insomnie way bi lay dèglou aduna tolou na fo khamni koudoul deglou nite gnou bakh gni thi erreurs rek guay deuk des paroles si riche è pleine d'enseignements .dieureudieuf Papa
@elhadjicheikhboudioploffic31862 жыл бұрын
Merci ma fille
@aidaseck97324 жыл бұрын
Machallah ❤️❤️🇪🇦😭😭😭amna solo❤️❤️❤️
@gnou_debat-tv78883 жыл бұрын
Un peu de beau gosse ça fait du bien voys allez encore chauffer le monde je dis vous aller encore chaufer le monde massalah
@abdouseye91545 жыл бұрын
Machalah Yalla na yalla wéral batt bi nekh na trop féllicitation ❤❤❤
@aimetine73875 жыл бұрын
Abdallah Alla n'a y allah defala fassaha lamigne machallah
@yabygassama5642 жыл бұрын
Machallah diop aka ya dégue té kham ndiarignou way aki chartame yalna yalla khép té doli té yagalafi
@ghoulamgueye1383 Жыл бұрын
Maaaaa chaaa Allaaaah😍😍😍
@Elbayejoop123453 жыл бұрын
Yalna yalla seral batte bi
@FernandoDiop2 жыл бұрын
Borome khél yé ka mom,toureundou je t'écoute depuis la Suisse 🇨🇭
@fallouyacinefall24044 жыл бұрын
longue vie lii nekh na trop machalla beugue na tague sama serigne bi Serigne Fallou 🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋 longue vie 🥰🥰🥰🥰🥰