Vraiment Chiekh niass s’est battu bec et ongles pour honorer son père ça montre que c’est le plus proche de Sidy Lamine Niass chapeau à Chiekh
@lilseylilsey91316 жыл бұрын
Une mère qui souhaite avoir un fils comme toi. Merci cheikh que dieu t assiste et soit ton guide
@talibecheikh34346 жыл бұрын
Wallay cheikh on est fier de toi taakhaaw ngaa saa papa baa keureum bou moudj. Yalna laa yalla taakhaaw ak saay raak amine 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@famasamb69516 жыл бұрын
Cheikh nigua takhawo sa baye, yalla nala sounou boromebi takhawo nonou. Machallah!!!
@seydina72826 жыл бұрын
Nioune nieup dinane fi diarr yalla nanou fék si lou bakh
@mamesarr79406 жыл бұрын
seydina amine
@ndiayemamesophie85226 жыл бұрын
Allakhou Akbar yallah rek moye karim!!!! Ohhhh Cheikh du courage!!!
@hajadashna15896 жыл бұрын
Fière de cheikh Niasse le digne fils de son père
@famagueye58656 жыл бұрын
Cheikh damako yeureum, mais il est vraiment le fils de son pére, il a tenu jusqu'au bout métina trop !!!
@maremembengue68736 жыл бұрын
Walakhi
@mamanaida68556 жыл бұрын
Diambar la dj takhawouna bayam dh
@maremembengue68736 жыл бұрын
@@mamanaida6855 wlakhi a son age
@mamanaida68556 жыл бұрын
Moment yi kouko doumdoul doeuneu kham salh métite bi man dh diarnassi nék khalé gnak yay gnouy dioy paré gougnou sama papa tégoussi .Chikh mom chapeau a lui amna courage lool sakh niasse
@aminaseck49436 жыл бұрын
Ton papa est fière de toi Cheikh un fils digne de son père courage frangin sidi yalla nako borombi kharé adjana firdawsi si barké seydina Mouhamed psl
@collesaliouseck89536 жыл бұрын
Cheick ton père es fière de toi 😭😭😭😭
@daoudadiallo60066 жыл бұрын
Merci bekou chérie
@hadykebe85486 жыл бұрын
Niass coumba Abdallah repose en paix. Durant toute ta vie t'a mené un seul combat "contre l'injustice ". T'as jamais changé sidi. Tes paroles dans 30ans sont tes paroles d'aujourd'hui. Un modèle et un grand patriote pour le Sénégal.
@habyba41036 жыл бұрын
Ndeyssane un baobab est tombé sama sopé demna Que Firdawsy soit sa demeure éternelle Yalla na hippé Aldiana si barké mamame Seydina Mouhamed SAW
@cheikhmbackefall73406 жыл бұрын
Bilahi un vrai guerrier
@awakounta58446 жыл бұрын
Amine way
@mamefatoukane45626 жыл бұрын
Rip sidi laminee Niasse et longue vie à Ahmed Halifa Niasse et toute ses enfants
@cheikheabdoulahadcisse52266 жыл бұрын
Man cheikh rek laa yereum ndeysane nitt kou bayam takhawouna bayam yalna sa jamou yageu
@debbopoulo28166 жыл бұрын
*Ay waaay liiii gnaaawna* *Akhmed Khalifa Niass topp nga goné gui bamou seusss* *Même pour la prière mortuaire un de tes gardes du corps lui retient la main* *Yenn yi rafettoul rawatina bou tiiisss ammé* *Que Dieu nous préserve de Satan et de son pouvoir* 🙏🏾🙏🏾🙏🏾 *Repose en paix Sidy Lamine Niass* 🙏🏾 *Que la terre de Kaolack lui soit légère et que Firdaws soit sa demeure éternelle*
@diopsaliou33616 жыл бұрын
Proud African Goddess ndakh yalla nga sange ko wakh mitinama toropp
@sokhnadegueneseck53956 жыл бұрын
Proud African Goddess j vois le contraire c'est lorsque l'autre fils de sidi lamine est venu k Akhmed lui a serré la main et voulé celle de cheikh et il a refusé
@fatimafatima-xj3cw6 жыл бұрын
@@sokhnadegueneseck5395 ki a refusé ? Ici key personne n a refuser de serrer la main
@fatimafatima-xj3cw6 жыл бұрын
@@sokhnadegueneseck5395 ki a refusé ? Ici key personne n a refuser de serrer la main. Ahmed niass était agité par l émotions et on l a calmé
@debbopoulo28166 жыл бұрын
sokhna deguene seck *_Mann deh meunouma guisslooo kenn loumou beuggoul guiss,les images parlent d’elles-mêmes,c’est le vigile qui a retenu la main de cheikh quand AKN est venu se placer et a voulu placer l’autre gars*
@bellabelle84226 жыл бұрын
Que Dieu te garde cheikh.le peuple entier est fier de toi
@deugrek33126 жыл бұрын
*Un grand combattant de la liberté. Paix a son ame*
@saliousarr22576 жыл бұрын
Cheikh sociétés bii guyss nan nigua takhawoo sa papa👍👍
@ardodiao14696 жыл бұрын
J'ESPERE VRAIMENT QUE SON FILS S'EN REMETTRA...JE SUIS TRISTE EN MEME TEMPS ADMIRATIF DEVANT CETTE MARQUE D'AFFECTION DE CHEICK NIASS ENVERS LE PAPA...IL EST COMPLETEMENT PERDU ET SEMBLE NE PLUS ETRE MAITRE DE LUI. AFFREUSE TRISTESSE.
@mimalastar6 жыл бұрын
autralia. kary ndeyssane mais il est d’une courage REMARQUABLE. Il a tenu ndeyssane fi nak c’est normal moi craquer dafa metty
@yabafaye55334 жыл бұрын
L ? C
@nabousall10426 жыл бұрын
Yalna ko Yallah yeureum soit vaillant Cheikh Niass avec tes frères et soeurs
@oumouahmad15996 жыл бұрын
Lou gueuneu metti lii , un fils devant la dépouille de son père, Force à toi Cheikh, courage t’as fait ton devoir qu’Allah te préserve, Amminne
@issathiam61106 жыл бұрын
Repose en paix cheick yalla na la yalla dollélle amine
@elhadjiabdoulazizfaye80456 жыл бұрын
Repose en paix Sidy. Dieureudieuf Cheikh yallana la yalla same hare la si birr akh bitty akh say rak sa takhaway rafetna machallah machallah. yalla nama may dome diou melni yaw. AMINE
@khadijamiller62396 жыл бұрын
Cheikh deugou bobou thi papa migui thi yaw mashallah Yalna yalla samal bopam niabotou Sidy Lamine té yalla yereume ko
@Prunelle56786 жыл бұрын
Cheikh Niass machala takhawou bi rafetena ni la dome bou mate wara melody ci bayam yalla nako yonenti bi psl terou
@chseye29236 жыл бұрын
Yalla nako yalla yreum khareko aldiana barekeb s.touba mbacké iradio sene ligueye réfatna yalla na léne yalla dolél
@mmedos50116 жыл бұрын
😢😢 ndeyssane dayko diay dolé li métina. YALLA na YALLA kharé sa papeu aldiana té mayléne kholou mougne 🙏🙏
@khadimsall91126 жыл бұрын
Bravo cheikh machaalah sa takhaway rafétna yalla na yalla yereume sa papa khaaréko aldiana firdawssi amine
@oumoukhairyba88026 жыл бұрын
Machaala cheikh gnoun gnépp ñiogui sa guinaw yak say rak délén wah amine rék
@fatimafatima-xj3cw6 жыл бұрын
C tristes Ina lilah weu ina alleyji rajiou'. Cheikh ndeyssane mo si gueuneu soneu. Tiens bon maitre ton père est fière de toi. Siguil ngue ko.
@aminambye89906 жыл бұрын
Cheikh real son I love you and wish you long life
@mimalastar6 жыл бұрын
Amina Mbye Wallahi
@momodieng39836 жыл бұрын
Yallanako yalla yaram te khare aldianafirdaw Amin yarabi vraiment cheikh niass ton papa et fier de toi tel papa tél fils sa takhawaye rafet na trop takhawouga sa papa yalla nala yalla takhawou yaw yak saye rak yiep thie barke Seyedina Mohamed psl amine yarabi
Khalebi masha Allah yalla nagnou yalla weurseugeulé dom djou melni yaw... Sa wadjour yalla nako sunu borom kharé aldjana firdawsy ci barkey seydina Mohamed psl amine
@amadousow83436 жыл бұрын
Sa ma hole dafa toye ni cheikh tahawo papa me ni la tawe wara méle sidi yalla nako yalla haré aldiana
@mirabelle32206 жыл бұрын
amadou sow dou taaw bi il a 2 grand frère dafa am courage rek té geun len heure ci papam
@ndye8066 жыл бұрын
Je T'aime cheikh fière de toi sa Papa Contane na ci Tahawou bi ngua tahawou yalnanu yala May domm diou melni yaw sa papa yalnako yala yereum tè yehèniou Amine yala bayi la fi ngua yag fi lol ta ande ak wer ak barkè ak mbolèmi dioulite Amine yarabi ci barkè yonnente bi Aleyhi Salat Wa Salam 🙏🏿 🙏🏿 🙏🏿
@galayembengue81746 жыл бұрын
Force a toi CHEIKH😭❤
@awasy47276 жыл бұрын
cheikh tu es très jeune,Mais très responsable. Ton père est fier de toi.
@mariedieng7536 жыл бұрын
J'ai les larmes aux yeux.Du courage Cheikh Niass yalla na yalla goudeul sa fane 😭😭
@diengdieng28856 жыл бұрын
Yalnako borom bi kharé aldiana si barker khassida yi
@elimanembengue6 жыл бұрын
Wakhi doff
@cheikhahmadoubambandiaye43606 жыл бұрын
@@elimanembengue yaw ya khéb barké khassida yi mais sidy mom khébouko niakka xam nak limou waral barina
@mariendiaye59156 жыл бұрын
500f 90
@sopenabyndiaye33346 жыл бұрын
aye adouna dou dara yalla na yalla yerem diegelko bolem bakar amine
@generallatyrndione37686 жыл бұрын
machalla takhawouko rec mo am sollo ndakh lolou rec gako déssélle yalla nalla yalla takhawou
@lissadiouf37366 жыл бұрын
Ndeye sane cheikh niaféna ba o dernier moment
@paulendiaye18716 жыл бұрын
C'est quand vous en faites l'expérience que vous pouvez comprendre. Que Dieu vous donne la force de surmonter cette épreuve et qu'il accueille son serviteur SLN près de Lui.
@khaditraore56816 жыл бұрын
Nonnnnnnnn c dur inal lahi wa ina ileyhi rajioune cheikh niass yalla nala yalla Faye ni nga tahawou sa papa diambar déme na
@khadyfall76686 жыл бұрын
Bilay j'ai apprécié le geste de Cheikh Niasse donde sa bay done se baya KO geune longue vie cheikh
@gnagnasoguidiaw17686 жыл бұрын
Macha Allah cheikh niass taxawou nga sa baye li rek mola warone tei def nga ko
@aidarassoul93196 жыл бұрын
Yalla nako yalla yerem té kharéko aldiana firdawsy si barké seyyidina moukhamed PSL
@modoubay74146 жыл бұрын
Ndayesan yalla nako yalla yerem si Barker serigne saliou 😭😭😭😭😭😭
@ibrahimandiaye79676 жыл бұрын
Sidy Lamine Niasse yalla nako borom biii téroo saa all diana yokawé yaa
@ouleyethiam80856 жыл бұрын
Oh repose en paix mais son fils là est vraiment exemplaire il était proche de son père oh ndeyssane
@silvanaezidine38726 жыл бұрын
deugue deugue khôl yèppa toye yalla na aldiana firdawsi donne ça wètal
@massmbaye47586 жыл бұрын
RIP sidy mé Cheikh yaw mat nga klifeu
@aldobrain30186 жыл бұрын
t
@elhadjigueye38686 жыл бұрын
yalla nako yalla yerume ta khariko aldiana firdawsi amine inchalla
@baraniane68726 жыл бұрын
Yalla nako yalla yéram ta xaré sa aldianna you kawéya ci barkéb mamam taass gnu thi barkéém, amiin ya rabbi,
@khadimfalltoubaitalelecapo55916 жыл бұрын
SIDY Lamine Niasse yalla yalla yeureum kare Adriana firdawsi Barker serigne Touba
@magymbodji65856 жыл бұрын
Li rek la dom di diarigne wadiour machalah kil repose en paix
@assanesylla41366 жыл бұрын
Sidy est parti mais pour Moi il est toujours avec nous . Cheikh égale sidy fière de toi .
@mamadouseck85836 жыл бұрын
Yalla nako Yalla yerem té hareko adiana té yekhe gnuko que Paradis soit sa demeure eternelle
@abdouldiallo11446 жыл бұрын
no adouna dou tousse ; je le vois juste a la tele mais cette video ma fait verser des larmes.
@warembengue68636 жыл бұрын
Mes condoléances cheickh repose en paix
@ndeyekhoudiambaye33066 жыл бұрын
Kou diour dome déwo walahi Cheikhe ton père est fier de toi Sidi Lamine yalnako Yala Yeureume té kharéko adiana amine
@alaloussalioumbacke91606 жыл бұрын
Yalna ko yalla yeureum ta kharé ko aldiana ta yalla may lenn kholou mougn
@bamsbams31716 жыл бұрын
Thieye yalla ndanke méti'woul yalnako yalla yeureum yock yeurmeundeme si barki seydina Mohamed PSL
@astousoumare14966 жыл бұрын
ndeysan li dawna yaram yalnako yalla yeureum té xaréko aldiana FIRDAWSI AK MOLEM GNIM FA fekki
@khadidiatoudia7596 жыл бұрын
Macha'allah Allahou Akbar hamdoullillah QUE LE BON DIEU LUI PARDONNE SES PECHES ET L'ACEUILLE DANS SON PARADIE LE PLUS ELEVEE INCHA'ALLAH MISERICORDIEUX ET BENEDICTION INCHA'ALLAH
@samndiaye76876 жыл бұрын
Ndeyssan yalla nako yalla yereume amine
@souaredieyna31826 жыл бұрын
Wallayil Aziim je suis fière de Cheikh Niasse il s'est battu pour son père jusqu'à ce qu'il l'enterre dieureudieuf Niasse Coumba Abdallah donneu ngua sa baye...
@Wolofumusso6 жыл бұрын
Ay Cheikh li diarouko. Loumou metti, metti meunone nga bagna biff sa lokho teh khamena ay nitt gni ngi lay khol. Tu es trés jeune teh adouna dafa goudeu tank.
@adjiabousso78646 жыл бұрын
Kon iow yako guiss bouniou djioulé ba paré dôme danio yeukeuti sén pape lolou lako déf signe pour mou déf ko yaw sakh bo remarqué gua fermé sa bouche nitte bouy défar nonou lay déf ndakh sama mame néna vérité bouy défar mo guene vérité bouy yakk
@mirabelle32206 жыл бұрын
Adjia Bousso il faut le comprendre ci nahar la nekk. Sou tiss bi passé il reviendra à de meilleurs sentiments
@ouleyethiam80856 жыл бұрын
Bibiche N. K. Normal il est triste. En quelque sorte il se dit de pas respecter son volonté senegal pays hypocrite
@fabrefabre69256 жыл бұрын
@@adjiabousso7864 merci bcp pour la remarque
@adjiabousso78646 жыл бұрын
@@mirabelle3220 mane bilahi je sais que cheikh limou déf yeupeu c'est pas facile mai nitte danio wara ba diakhassé ak ay détail ki niankk bayam di dioy nopé goul niou beugue gueneu pobar rék di sikal cheikh barina kou dôme you défoul ni ba sén bay ganio
@serignemodoumoustaphalo61766 жыл бұрын
Yalla nakou yalla yeureume
@chachawane68366 жыл бұрын
Walahi chekhe yalha nala yallah soutourale te are la inchallah
@madamemadame33806 жыл бұрын
Sunu wètal ba dem na 😥Dé rék moy deugue ! Que la terre de Kaolack te soit légère firdaws nék sa keur.
@taawouyayamndiaye6 жыл бұрын
Merci Cheikh Takhawou gua sa papa je suis sure que SIdy fimou teud contennana thii yaww
@moisesdiouf92696 жыл бұрын
Thiey aduna yalla na ko sounou Borom defal aldiana firdawsi 😢😢😢😢
@ndeyeseynabousarr76846 жыл бұрын
Li leçon bou mak la tonton sidy yalna yalla yok sa lére tass gnou thi sa barke yalla nga deuk ak seydina mouhammed
@ladyjallow62116 жыл бұрын
May his soul rest in peace. Take heart sheikh
@dac54076 жыл бұрын
Un homme de paix un homme qui a toujours Porte le Senegal Dans son coeur RiP grand homne
@seydinadiakhaby24846 жыл бұрын
Un brave s'en est allé que Dieu puisse te rendre tout le bienfait que tu nous a gratifié de ton séjour terrestre amine
Ndéysan walahi djambar deugeu demna yalla nako yalla Yeureume té khare ko adjana si barké Mouhamed PSl
@ndeyecoumbasamb15116 жыл бұрын
paix à son âme yalla nako yalla yeurm ta kharéko aldiana sii barkiii seyedina Mohamed
@mameasssstsantestmameassss17796 жыл бұрын
Cheikh niass dhé ndeysane dafa goré rek
@mbackeseye84996 жыл бұрын
Cheikh niass son père fier neuh si ioe
@marietoudiop99236 жыл бұрын
C est triste cheikh niass sa papá defnala rouyouwaye heros yalla nalayalla katanal Maye la kholou mouye
@princekara73036 жыл бұрын
Ndeysan yalla na yalla yeure
@nitoudegeki66316 жыл бұрын
Ay way sama yaram dawatina sidy bimou lakho ba lègui lomay yeke yalla rek moko kham mettinama bathia kamou yalla 😭😭😭
@madouchimer24076 жыл бұрын
Je peux dire le père de la nation sénégalaise est parti pour toujours
@lululila67016 жыл бұрын
Paix à son âme et courage pour la famille
@peaceandlovelove76796 жыл бұрын
Ay Sidy lamine kadioneu gafii bassi kanam yalla nala yeureum si barkè seydina mouhamed cheikh courage diamant guaw
@modousyll70946 жыл бұрын
Do rouss dh dakh sa takhaway ak sa ligueye zéro faute Yalla boula thiate djitou Contane nanu yalla na yalla contane amiine
@sgsofficiel30426 жыл бұрын
Li rék.mo waurr nék thi DEUG ba déé .wayé topp adounabou niak solo bi .Di lék khaliss bou léwoul .do wakh DEUG. diaye sa ngorr. doundé Riba .Di lékk khalisou askane wi. Di togne diay dolé. andak ibliss Di Mouy .tope politique Bi rékkk. rawatina khaliss bou léwoul .Nar fékh .béw .beug ngourr Done worr Kate ba déé aythia rékk adounagui nonou dieul léne ba yawmal khiyammm lép Dina lérr
Yallnako yallah yeureum té kharé ko aldiana firdawsii si barke seydina mouhamed
@mamediarrandiaye49346 жыл бұрын
Ndaysan yalla nako yalla yuereum ci barke al coran
@maliamd49296 жыл бұрын
KAllah lui accorde le paradis al firdaous
@bambacisse116 жыл бұрын
Allah akbar yalla rk moy adji déss
@soldaroubayekarimbassiroun45356 жыл бұрын
Yalla nako Yalla khari à Diana firdawsi
@dieuestmaforce55276 жыл бұрын
li métina bayilén domam mou topato papa way ta nit ki dée yeureum lénko sokhla woul kouko khitho niguén takhawo sidy lamine diakhasona trop adeu lénn ak dal ak téy way sidy lamine niass yalla nako yalla yeureum ta kharéko aldiana firdaws
@mameboussodiop93266 жыл бұрын
NdeySaanne que Aldjana Firdawsii soit sa dernière demeure🙏🙏